Salam aleykoum wa RAHMATULLAH. beugone na lééral ci laadjou goor gui défone accident té kénén koudoul mome fatou ci. Ndakh dafa ame atté kou ray té tayou ko? Mane dé lima yakarone moy goor gui amou ci bén responsabilité. Auto bou déff accident dama diapone ni ndogal bou diougué ci sunu borom la, ki faatou sunu borom mo ko ray. Sou ma dioumé ngén wax ma. BARAKALLAHOU fiikoum
Diajakallah xayran cheikhouna Docteur Mouhammad Ahmad Lo
❤❤❤ mashallah
MACHA'ALLAH ❤
Masha Allah sheikh ❤❤❤❤❤ amna solo toroop ❤
السلام عليكم ورحمة الله وبركاته ماشاء الله جزاكم الله خيرا حفظكم الله ورعاكم وثبتنا الله في السنة
Djeredieuf Serigne bi bien répondu pour la question de ce qui se passe en Arabie Saoudite
Je suis présentement à Ryad vraiment j' ai vu une ville paisible des gens très correct où vraiment niougne wormal l'islam
Salam aleykoum wa RAHMATULLAH.
beugone na lééral ci laadjou goor gui défone accident té kénén koudoul mome fatou ci. Ndakh dafa ame atté kou ray té tayou ko? Mane dé lima yakarone moy goor gui amou ci bén responsabilité. Auto bou déff accident dama diapone ni ndogal bou diougué ci sunu borom la, ki faatou sunu borom mo ko ray. Sou ma dioumé ngén wax ma. BARAKALLAHOU fiikoum