Machallah Yalla na yalla barkel tei weral Je passe toute ma journée à regarder toutes vidéo de ce playlist au bureau, à la salle de sport dans les transports . Machallah
MERCI Pr MADIAMA FALL LES VERITES SCIENTIFIQUES PERMETTENT D'ECLAIRER LES TEXTES RELIGIEUX . yallah samm bepou talibe yonent bi moussal niou si pékhé dadial yi inchalah
Dieureudieuf ouztass madiama fall .. mashallah si xamxam bi Dama beugone nga wax si moudjadid bi yalla wax né si dinako indi diamono diouné ngir mou ngindi nit gni.. Diamono dji ana moudjadid bi wala bou gneuwagoul naka lagne kay sénto.. El badou diotalil ma message bi ngir yalla si emission prochaine bi
@@MatarSeck-ql7id waw deugue leu.. motay may lathie souniou diamono djii ndax am na moudjadid si diamono djii , wala bou féké nieuwagoul naka lagne kay sento bakham né kii la .
Waw moudiadid yonanti b Nena chaque 100 ans dinan njeW ba aduna tuki way Dina am jamano yo hamni nak danuy lakatu nit yi dunlen ham nah yaku yaku jamono ji di saga ay kilifa bo waheh doune la gem d has kilifa Yi legui mujadid Yi bun njeweh dinan nek si nit yi mais nit yi dunko ham yalaa daleni neb
Machallah professeur madiama yalla na yalla barkel kham kham bi vraiment je suis tres content de vous écouter a chaque damay bek di geuneu sentir souniou borom
Machaallah ces histoires sur les prophètes sont emerveillant Il ya beaucoup de choses qui n'était pas clair dans ma tête qui deviennent clair quand je vous écoute Kham kham bi wer na macha allah
Salut. El badou je viens d’avoir une question legui. Douniouy degg parfois niou né serigne bi dafa nekk si hall. Wala affaire sangam bi mou koy wakh khal bi moko dikeulonn. Dama beugon kham nk lan moy hall exactamente, lan mokoy waral et aussi quoi de positif ou négatif lay apporter si vie domou Adama? Th aussi je voulais savoir s’il a rapport avec affaire de rap yi niouy am nioun lebou yi ou pas? Et aussi lan moy danou lerr akh lan mokoy indi? Peut-être bouma guissé ben si situation bi dina kham moy lan m3 reponse la amoul donc je voulais des réponses basées sur la science. Merci
Assalamu aleykum sama soppé yi👋🏽 Nan lañu mëna def ba gëm lo ku xamul Yonent bi PSL né Ku existé la sans nga indi ay textes Booko doon leeral ab athée loy tek si loxoom🙏🏽
@@MadiamaElhadjiAssalamou ngalaykoum mon professeur préfèré , Yalla xamna nii k sa numéro rk lay weur 😢 yalla nala yalla fay sii lepp lii nga ma xamal
Machallah
Yalla na yalla barkel tei weral
Je passe toute ma journée à regarder toutes vidéo de ce playlist au bureau, à la salle de sport dans les transports .
Machallah
Deugg dou rombi nopp soubhana lah😂😂😂😂❤
Très bonne émission qui vient a son heure un monde incertain une jeunesse dispersée aveugle
On veut que vous nous apporter des éclaircissements sur le conflit israélo-palestinien . L’histoire des juifs leur but etc… svp oustaz
Dina am solo
c'est fait je l'ai suivi mais c'est trés intéressant
@@malickdiouf5728noumay def ba guisko yitel nama
Emission instructive bravo el badou maachaa Allah madiama fall mondial
Machala amna solo lool gneuwoul si Palestine ak Israël
Je suis abonné merci
MERCI Pr MADIAMA FALL LES VERITES SCIENTIFIQUES PERMETTENT D'ECLAIRER LES TEXTES RELIGIEUX . yallah samm bepou talibe yonent bi moussal niou si pékhé dadial yi inchalah
C’est magnifique!
Merci beaucoup machalla
Nam nagne émission firi guent mardi yi nk. Mais merci el badou❤️
Dieureudieuf ouztass madiama fall .. mashallah si xamxam bi
Dama beugone nga wax si moudjadid bi yalla wax né si dinako indi diamono diouné ngir mou ngindi nit gni.. Diamono dji ana moudjadid bi wala bou gneuwagoul naka lagne kay sénto.. El badou diotalil ma message bi ngir yalla si emission prochaine bi
Moudiadid chaque 100 ans lay njeW senegal amna ay moudiadid kom serigne touba etc...
@@MatarSeck-ql7id waw deugue leu.. motay may lathie souniou diamono djii ndax am na moudjadid si diamono djii , wala bou féké nieuwagoul naka lagne kay sento bakham né kii la .
@@MatarSeck-ql7id serigne touba ak legui , legui mou def 100 ans. Wala 100 yi temit debut leer guiy watie si niom la wala atte bi niou faato ,
Waw moudiadid yonanti b Nena chaque 100 ans dinan njeW ba aduna tuki way Dina am jamano yo hamni nak danuy lakatu nit yi dunlen ham nah yaku yaku jamono ji di saga ay kilifa bo waheh doune la gem d has kilifa Yi legui mujadid Yi bun njeweh dinan nek si nit yi mais nit yi dunko ham yalaa daleni neb
Machallah oustaz. Wataqadamta li salati fa salou koullouhoum mouqtadin wa antal imamou❤️❤️❤️ ken dou yonent bi
Hstaz bul fatei suite bi demain pleas yalla n'a sen diam yagg thiey Seydina mouhamed ❤❤❤❤❤
Maschalla émission bi amna solo trop . Beug n'a nk guén bayi nio mena téléchargez vidéo bi
Masha’الله ❤️
Merci beaucoup oustaz
Machallah professeur madiama yalla na yalla barkel kham kham bi vraiment je suis tres content de vous écouter a chaque damay bek di geuneu sentir souniou borom
Séne complicité.c'est important.yalla naléne yalla faye yuw
Machaallah ces histoires sur les prophètes sont emerveillant
Il ya beaucoup de choses qui n'était pas clair dans ma tête qui deviennent clair quand je vous écoute
Kham kham bi wer na macha allah
Machallah émission bi amna sollo trop beug n'a nk guén bayi nio mena télécharger vidéo bi
Un bon savant
❤❤profeseure universitaire
Ak dékki tamit nokoy leerale ab athée sans textes🙏🏽
❤❤❤❤❤❤❤
Ma challa❤🎉
Machallah ♥️
[33:40] distance entre Mecca et Jérusalem est de 1470 km. Par la route, il y 17 h de voyage. Machaa Allah.
Psl❤❤❤❤❤❤
❤❤❤
Machallah l'émission si importante ❤, je vous adore merci 🎉
J’ai posé ma main sur ça ❤jusqu’à ce que maman mange beugou beugou ❤
j' aime ces biens ces genres de blagues entre des amis ♥️♥️♥️👍
MaSha الله amna solo yalla yok kham kham bi t fayy lene yiw si barké alkuran 🤲🏾🙏🏿
Machallah amna solo
Ma sha ALLAH
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ma challah Amna solo
❤❤❤malén yala faye
❤❤❤🎉🎉🎉
,❤❤
Laissé nous télécharger les vidéos
Salut. El badou je viens d’avoir une question legui. Douniouy degg parfois niou né serigne bi dafa nekk si hall. Wala affaire sangam bi mou koy wakh khal bi moko dikeulonn. Dama beugon kham nk lan moy hall exactamente, lan mokoy waral et aussi quoi de positif ou négatif lay apporter si vie domou Adama? Th aussi je voulais savoir s’il a rapport avec affaire de rap yi niouy am nioun lebou yi ou pas? Et aussi lan moy danou lerr akh lan mokoy indi? Peut-être bouma guissé ben si situation bi dina kham moy lan m3 reponse la amoul donc je voulais des réponses basées sur la science. Merci
est ce que vous pouvez faire un cours sur Gog et Magog svp 🙏🙏❤️
Assalamu aleykum sama soppé yi👋🏽
Nan lañu mëna def ba gëm lo ku
xamul Yonent bi PSL né Ku existé la
sans nga indi ay textes
Booko doon leeral ab athée loy tek
si loxoom🙏🏽
C'est quel chaîne de télévision ? 🥰
Asfiya tv dispo (TNT)
Salam kouma meuna diapalé si numéro professeur
slt pourquoi il n y a plus l émission du mardi
inchaallah je reprend mardi
@@MadiamaElhadji assalamou aleykoum oustaz ziarnaleu man deh dma amon beneu soxla si yaw
Yiter wo na sa numero
@@MadiamaElhadjiAssalamou ngalaykoum mon professeur préfèré , Yalla xamna nii k sa numéro rk lay weur 😢 yalla nala yalla fay sii lepp lii nga ma xamal
Question yalla bi mome meunoko répondre nieuwal médina baye Kaolack inchallah koufa guena ndaw répondre la nguay molécules AK ay organes ni😂😂😂😂
Yaw doule
Es ce que do deff sa émission bop wax yalla c'est mieux. Ce pays est grave
Yow Seytané geuh
N'oubliez pas ma question svp @elhadj
Machala amna solo lool gneuwoul si Palestine ak Israël
Dimanche inchaallah
Machalla amna solo
Machalla ❤❤
❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤