MaSylla Diop sort de sa réserve : "Modou Lô doumako andi contre Siteu parce que..."

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 3 січ 2025

КОМЕНТАРІ •

  • @chamousman2726
    @chamousman2726 3 місяці тому +39

    😢😢😢Fii yallah mofi neeh modou lo Dai Daan insha Allah ba pareh bayilen Lamb ji

  • @soppeousmanesonko777
    @soppeousmanesonko777 3 місяці тому +30

    Modou Lo Ndam reke inchallah 🙏

  • @CheikhMbengue-eu1ul
    @CheikhMbengue-eu1ul 3 місяці тому +41

    Modou lô yalla mokodon maye ndame ☝️yalla nako yalla maye ndame si barki
    Seydina Mouhamed❤🥰🙏

  • @taphasamb6836
    @taphasamb6836 3 місяці тому +26

    Instanyi nieup modou lô laniouye khekh pour siteu dieule couronne apres Balla Gaye wayé dinguene kham né Morou lô molenn Eupeu Sagar
    MODOU LO YALLAH NALA YALLAH SOUTOURALE TÉ YALLAH NGA DANE NIEUPE YOBALÉ COURONNE BI❤🎉❤🎉❤🎉❤🎉

  • @MoustaphaGueye-i1f
    @MoustaphaGueye-i1f 3 місяці тому +26

    Bilahi xaliss motax Mouy bayi Modou lo khamnagne leup massila

  • @ouzinouzin5516
    @ouzinouzin5516 3 місяці тому +12

    Modou lo yalla nala yalla takhawou maye la ndam si kaw siteu amine🤲🤲🤲🥰🥰🥰

  • @ndoffenetine5333
    @ndoffenetine5333 3 місяці тому +18

    Bilahi man mom sama xél defa dal.
    Mod lo limuy dané mbeur yi dou mystique.
    Dafa yor entraînement bou weur,am Fit,meun xéx,le plus teknik, am xaliss mâcha alla.
    Mod lo rek kep kesse ❤❤❤
    Modouuuuuuuuuu looooooooooooo ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤

    • @speedforce616
      @speedforce616 3 місяці тому +4

      Mystique guénouci Modou dafa séll baparé sett spirituellement mtx Rawanam am dolé.. Mais bouko indiwoul mo ham gniy nianal Modou Lo teh Modou guissou lén nio eup fouff

    • @rouguikebe9984
      @rouguikebe9984 3 місяці тому

      ​@@speedforce616billahi nioukoy nianal niimou khamoul nio eup kouko indiwoul ya kham

  • @papispass
    @papispass 3 місяці тому +10

    Modou ak Massila Yallah bou séytané dougou séne digeunté amine... Modou lo yalla nalla borom bi maye ndame bou reuye inchallah

  • @alaminefaye6248
    @alaminefaye6248 3 місяці тому +11

    Serigne cissé bou serigne babacar aka goré mashallah

  • @FallouMbaw-lu8uj
    @FallouMbaw-lu8uj 3 місяці тому +10

    Modou kharagne lô 🎉❤ yalnaleuh sunu Borom soupkhana watallahi
    Maiyleuh Dam si kaw siteu
    Sii barké seydinâ Muhammad
    Allahouma Amine yaram 🤲🤲🙏
    Yã Rabi yã Rabi yã Rabi yã Rabi yã Rabi yã Rabi

  • @volfroitfall8785
    @volfroitfall8785 3 місяці тому +25

    Yalla rek mofii nekk

  • @FallDamel7484
    @FallDamel7484 3 місяці тому +11

    Lirou Diane vraiment sa trois pièces nice machallha❤❤

  • @ibadiop7722
    @ibadiop7722 3 місяці тому +34

    Boko indiwoul yallah indi ko. Yein serigne yi da ngein yakar ni yeinay yallah…

  • @Fitserigne
    @Fitserigne 3 місяці тому +9

    Modou combat dinga si wétt mais Yallah baxna

  • @lil___baby8150
    @lil___baby8150 3 місяці тому +4

    Do toussss yaww modou lo yalla rk la geum

  • @DiopZar
    @DiopZar 3 місяці тому +7

    Incha allah sawaye adouna molaye deglou yak sa groupe .modou rek moy dane

  • @AbdellahiNdiay
    @AbdellahiNdiay 3 місяці тому +8

    Modou lo yalanako yallah soutoural mayeko ndam bou sed gouye inchallahou rabi

  • @abdoulahatndiaye1115
    @abdoulahatndiaye1115 3 місяці тому +7

    Modou lo yalla nako yalla soutoural ils vont tout faire pour mou perte combat bi mais yalla baxna

  • @MoustaphaGueye-i1f
    @MoustaphaGueye-i1f 3 місяці тому +12

    Ki wakhoufi Dara da wor Modou lo bilahi walahi

  • @ametibnmalickndiouck4674
    @ametibnmalickndiouck4674 3 місяці тому +6

    X Lo reik inchallah ❤❤❤

  • @BouryDiagne-w2h
    @BouryDiagne-w2h 3 місяці тому +17

    ❤صلالة على محمد

  • @MoustaphaGueye-i1f
    @MoustaphaGueye-i1f 3 місяці тому +12

    Xaliss motax Mouy wor Modou lo khamnagne leup ki day wor Modou lo bilahi walahi

  • @younoussdiaw160
    @younoussdiaw160 3 місяці тому +6

    Modou lô yalla rekk la yakkar ta inchallah dina am ndam lou reuye ❤❤❤ massila ioe sa wakh dji dara léroussi mais Modou yalla la andal bou waré am ndam tmt meunossi touss voilà , ce soi disant ndiaye beugue léne dieunde diléne manipuler heure boumou ko beugué shime

  • @MoustaphaGueye-i1f
    @MoustaphaGueye-i1f 3 місяці тому +10

    Massila mi worna Modou lo khamnagne leup

  • @awacgueye2771
    @awacgueye2771 3 місяці тому +10

    Massillah ce n est pas le moment ni l endroit pour faire cette sortie.

  • @morniane4292
    @morniane4292 3 місяці тому +2

    Modou lô seul billahi Macahalla ❤❤❤❤❤❤❤

  • @MoustaphaGueye-i1f
    @MoustaphaGueye-i1f 3 місяці тому +13

    Ki bilahi walahi dafma rouss lo sakh

  • @MatarBadiane-g7q
    @MatarBadiane-g7q 3 місяці тому +2

    Modou lo ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤yalla maye la ndam rék❤❤❤❤❤❤❤

  • @LucienneDione
    @LucienneDione 3 місяці тому +6

    Aziz moko dieudeu

  • @assanekaka9414
    @assanekaka9414 3 місяці тому +4

    Modou lo rk 💪♥️♥️

  • @BabacarDiouf-j1k
    @BabacarDiouf-j1k 3 місяці тому +2

    ❤ yal yalna noko may ndam thi barke Taha staws

  • @Deggou
    @Deggou 3 місяці тому +11

    yaw khamo dara modou yaguena gagner combat teu xamouleu wone, yén rek yalén beugg am clients ci tourou modou lo bi....

  • @assanekaka9414
    @assanekaka9414 3 місяці тому +4

    Modou lo yalla na yalla ande ak mom yaw yalla yaw lagnu yakar

  • @MoustaphaGueye-i1f
    @MoustaphaGueye-i1f 3 місяці тому +10

    Massila yow dangaye wor Modou lo bilahi walahi

    • @CASI7797
      @CASI7797 3 місяці тому +2

      Ki bayi Balla deimm ci Modou key faut pas être surpris mou diougueii ci Modou deilou ci Balla. Gni dougne ay marabouts c'est juste des profitards

  • @rouguikebe9984
    @rouguikebe9984 3 місяці тому

    Thieye pére ya changé avis ni😮
    Loudoul yalla néne la ❤XLo yalna am ndam😊❤🎉

  • @PapaKhalifMbengue
    @PapaKhalifMbengue 3 місяці тому +4

    Modou moniou togn mome mii bayi genre yi diko wouté beuzz mais yalla baxna❤on verra baxam yenay mayé ndam wala

  • @abdoulayendoye1803
    @abdoulayendoye1803 3 місяці тому +4

    D’à bayi woone balla Nieuw si Modou bou delo douniou béteuh ay woor kaat laniou c’est la classe a baboye

  • @xelcomdecorationsopeserignesal
    @xelcomdecorationsopeserignesal 3 місяці тому +43

    Modou lo késsé fi yalla rékk mo nékkkk

  • @alaminefaye6248
    @alaminefaye6248 3 місяці тому +3

    Massila yaw mii geumo dara mais Yalla bakhna. Modou Lo mom Yalla laa yakar

  • @babacar3178
    @babacar3178 3 місяці тому +6

    Nii xaliss rék niome nieupe aziz dina léne dieunde

  • @bolegueye1327
    @bolegueye1327 3 місяці тому +7

    Ils se trompent yalla rek mo yor ndam

  • @MoustaphaGueye-i1f
    @MoustaphaGueye-i1f 3 місяці тому +6

    Massila ki bilahi parena si Modou lo

  • @MoustaphaGueye-i1f
    @MoustaphaGueye-i1f 3 місяці тому +8

    Ki betnama trop bilahi walahi xaliss motax Mouy wor Modou lo

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 3 місяці тому +2

    Yalla dieureudieufé

  • @ogviito1949
    @ogviito1949 3 місяці тому +4

    Modou dalen gueumoul rek buzz rek ngueni out si Modou na sa nguélaw ndangou modou yallah la yakar

  • @MoustaphaGueye-i1f
    @MoustaphaGueye-i1f 3 місяці тому +6

    Ki Aziz Ndiaye Moko dieunde xaliss motax bilahi

  • @BoyDiouf
    @BoyDiouf 3 місяці тому +8

    Meew day am soukeur waay

  • @CASI7797
    @CASI7797 3 місяці тому +4

    Modou Lo dh daleine lidjeuntiwoul sakh. Yalla rek leu gueum, wolouko

  • @MoustaphaGueye-i1f
    @MoustaphaGueye-i1f 3 місяці тому +7

    Ki xaliss motax Mouy Dem si Aziz Ndiaye oh Aziz Ndiaye

  • @basselabdou9891
    @basselabdou9891 3 місяці тому +8

    Nafékh bou bon nga fén rék ngay déf sa bop bou reuy bi😮

  • @BetourAidara-o4p
    @BetourAidara-o4p 2 місяці тому

    Lo dam siré thiekaw thiekanam rék dam rék chalah leyon fone rék yaniouko tamal beuré dan gnibi ❤️❤️❤️❤️

  • @mariamagassama9380
    @mariamagassama9380 3 місяці тому +12

    Modoulo.bou.niéwé.mome.donge
    Mou.dane.siteux.bilakhi

  • @MoustaphaGueye-i1f
    @MoustaphaGueye-i1f 3 місяці тому +6

    Ki worna Modou lo ndek xaliss khamnagne leup

  • @MoustaphaGueye-i1f
    @MoustaphaGueye-i1f 3 місяці тому +6

    Lirou massila mo nee dou nianal kenene Modou lo rk té Mouy nianal mbeur lirou en massila wor nga supportaire Modou lo yi yeup

  • @MoustaphaGueye-i1f
    @MoustaphaGueye-i1f 3 місяці тому +8

    Ki wolotoumako ak Modou lo

  • @bayemorlo2299
    @bayemorlo2299 3 місяці тому +3

    Yene massilla mi da khame dara

  • @LamNdiaye
    @LamNdiaye 3 місяці тому +5

    Modou lo rek ndam rek sokhor ba khoule way

  • @elzoatti8951
    @elzoatti8951 3 місяці тому +2

    Thiey serigne yi gueumou niou Dara .

  • @oumartoure6731
    @oumartoure6731 3 місяці тому +3

    😂 kii kay Aziz Ndiaye dafko jeunde bou yagg motax mouy wax waxou dof nii ! Sen deal moy Siteu dane Modou lo pour après Balla jeulko dane ko nékk jeul Roi bi ! Yalla mo eupp dolé 😂

  • @MOUHAALAMINE
    @MOUHAALAMINE 2 місяці тому

    Man li dan dēfal modou lo ba yala mayko ndam diko dēf contre siteu innsalaah ☝️ya kafi alay ka ismoulayka asamm❤

  • @tallaniang3474
    @tallaniang3474 3 місяці тому +5

    Do yalla do yonénetou

  • @ousmanendiaye1712
    @ousmanendiaye1712 3 місяці тому +10

    Massila limou wakh c simple a comprendre dotoul wathiee thi guew lamb mais tèwoul modou lay gnanal. Meune neuh def limiy def teii dougnou gneuw thi jour lamb j

    • @rouguikebe9984
      @rouguikebe9984 3 місяці тому

      Bou niewoul tmt affairam la khana légui biko nieup khamé lay took si keureum di nianalaté .nii daal losi meunti degu dagniy war

  • @senegaleventschanel6913
    @senegaleventschanel6913 3 місяці тому +6

    Ki si Serigne dafa bari wakh trop te nieme feugue deuname te fi yalla rekk mofi nek nga niew niaka niew yalla moy maye ndame pas yaw

  • @Abdou-c
    @Abdou-c 3 місяці тому

    inch'Allah yallna Siteu am Ndam Affaire bi Siteu leu 👑

  • @MbayeMbengue-qt3sl
    @MbayeMbengue-qt3sl 3 місяці тому +1

    Ama balde ya sacrificé falaye balde contre Malick Niang criminel de confiance nga bo sacrificé woul nitte amo fitte dougou thie gew ⚫❤️⚫❤️⚫❤️⚫❤️⚫❤️

  • @MoustaphaGueye-i1f
    @MoustaphaGueye-i1f 3 місяці тому +5

    Xaliss motax Mouy wor Modou lo

  • @mouhamedcherifaidara923
    @mouhamedcherifaidara923 3 місяці тому +4

    Sama gayi massylla limou wakh diaroul mèr décision wame la dieul key nguène di mèr melni massylla moko done diokh ndam té mome waxoul dafa bayi modou lo mai dafni dotoul wathieu si guèww bi rk ah

  • @onelove6721
    @onelove6721 3 місяці тому +9

    Lamb mom yeufi thiédo la na kounék lék weurseugeum rek dém yonam
    Kén geumousi yalla

    • @OureyeSeck
      @OureyeSeck 3 місяці тому +1

      Lou lérr lamb gamou thiéddo leu amna lépp.nice👍🏾

  • @moisabarry
    @moisabarry 3 місяці тому +4

    Ils se crois des demi Dieu 😂😂😂😂

  • @MoustaphaGueye-i1f
    @MoustaphaGueye-i1f 3 місяці тому +4

    Massila xaliss motax Mouy wor Modou lo

  • @DjibyMbow-s6k
    @DjibyMbow-s6k 3 місяці тому +2

    Sama khél téyy neu si mara bi ak prometteur bi

  • @MoustaphaGueye-i1f
    @MoustaphaGueye-i1f 3 місяці тому +3

    Kone massila day nianal lirou Diane té mounee Modou lo RK lay nianal en wor nga supportaire Modou lo yi yeup

  • @MbayendiayeNdiaye-r6v
    @MbayendiayeNdiaye-r6v 3 місяці тому

    Aziz ndiaye yalla nala yalla Fay digua andeu ak Aziz ndiaye woroul

  • @maroditvtv7352
    @maroditvtv7352 3 місяці тому +3

    😂beusse gadone woutte si Modou 😂modou kouko bayi ya kham nioune beug nane ko bah paré yallah moye mayéh ndam téh yalle nako maye modou dieull bou gaaw

  • @Defunity
    @Defunity 3 місяці тому +2

    Mdr yén da nguèn xam Dara ba nane douma yoboti mbeur 😂😂 loudoul woute promo si Modou Lô ndiariniou lén co Dara, vivement que tous les charmants quittent le monde de la lutte. Y'en a marre !

  • @ibrafatyndaw9891
    @ibrafatyndaw9891 3 місяці тому +1

    Yen kii loumou wakh léer na dou gnanal bénen mbeur boudoul Modou lo tée si boy Niang la wakhone après combat bi dotoul déem si lamb. Loutakh Modou lo bayi takk galatheu (téré). Kone kii amoul droit bayi dém si lamb kén khamoul liguén beugue wayyy ish

  • @senegalrek2579
    @senegalrek2579 3 місяці тому +4

    Est-ce que dou li Modou seti Serign Cisse te setsi wouko moko meti 😅😅😅

    • @pronosticfootsenegal1112
      @pronosticfootsenegal1112 3 місяці тому

      Pourtant massila bamouy toudou domam modou nieuw na ba malika

    • @senegalrek2579
      @senegalrek2579 3 місяці тому

      @@pronosticfootsenegal1112 pourtant deugla

    • @rouguikebe9984
      @rouguikebe9984 3 місяці тому

      ​@@pronosticfootsenegal1112wawaw mou contane badé .mais da am nio khamni war séne dérete lanék.komté si Balla la diougué nieuw si modou meuna démate à tt moment wayé mo kham de

  • @CASI7797
    @CASI7797 3 місяці тому +3

    Aziz bayina Lamb c'est la plus grande connerie que vous dites

  • @MoustaphaGueye-i1f
    @MoustaphaGueye-i1f 3 місяці тому +4

    Ani ngor thiey xaliss

  • @NyaoutNjie
    @NyaoutNjie 3 місяці тому +2

    Modou kesseh nk

  • @medzodiouf
    @medzodiouf 3 місяці тому +3

    Ki khana Aziz dako diokhe xalisse wa keur Aziz Ndiaye yii séne afaire diaxale nama nonou lagne déffe ba diaxasé xélou wa keur tapha tine yii 🤔🤔🤔 thieuy lamb kou amoule guinawe démale gna tok

  • @MoustaphaGueye-i1f
    @MoustaphaGueye-i1f 3 місяці тому +5

    Ki Aziz Ndiaye Daka diokh xaliss motax bilahi walahi thiey xaliss ki aye laye rk laye def demna

  • @pabcmedia8805
    @pabcmedia8805 3 місяці тому +3

    lol Massylla boul gnou fonto,yaw da nga meuussa indi Modou lo

  • @iboudieye1255
    @iboudieye1255 3 місяці тому +1

    Man lima khalat Moy Masylla da wakhon dou nianal koudoul modou lo lėgui da begue di nianal balla gaye motakh mouni dotoul wathie ndakh sou wathiė si modou lo niewat si balla niou ni da wakh wakhėt motakh Mou begue tok ni dotoul wathie si gėw bi sama khalat la nak 🙏🙏🙏

    • @pronosticfootsenegal1112
      @pronosticfootsenegal1112 3 місяці тому

      Si je ne me trompe pas massila balla la nieuka andal k modou lo

    • @rouguikebe9984
      @rouguikebe9984 3 місяці тому

      ​@@pronosticfootsenegal1112sisi mou djougué si Balla nieuw si modou

    • @pronosticfootsenegal1112
      @pronosticfootsenegal1112 3 місяці тому

      @@rouguikebe9984 mais sa touba degoumako ci combat bi

  • @ndaomamadou
    @ndaomamadou 3 місяці тому

    Amin

  • @MoustaphaGueye-i1f
    @MoustaphaGueye-i1f 3 місяці тому +1

    Massila yow wor nga supportaire Modou lo yi yeup

  • @oumarkante9186
    @oumarkante9186 Місяць тому

    En tout Cas ki.billahi sama xélle dallou ci Mome dé mais fimom yalla moffi nek

  • @almaktoumdiop8749
    @almaktoumdiop8749 3 місяці тому +2

    Modou lô na déf nagka aziz ndiaye serigne you beuri dinaléne dieudeu souma done modou lô damaye bayi beuré am na serigne bou wakh ni modou lô dinanouko sote

    • @leuz.patriote
      @leuz.patriote 3 місяці тому

      500 combat bg2 nokou ko dane ko😂 bg2 la nieup di top moy Senegal

    • @AboulBacharSall
      @AboulBacharSall 3 місяці тому +1

      @@leuz.patriotelgui et après sa waxou dof yii

    • @younoussdiaw160
      @younoussdiaw160 3 місяці тому

      Koulako ladj bg2 boukoy nokhe môme aussi amna koukoy nokhe ta sa wakh yi amoul béne chance​@@leuz.patriote

    • @rouguikebe9984
      @rouguikebe9984 3 місяці тому

      ​@@leuz.patriotebo kholé commentaires yi diga kham ndakh Bg2 la Sénégal di top wala XLo

  • @CheikhtidjaneSeck
    @CheikhtidjaneSeck 3 місяці тому +6

    Meussouma nianal mbeur wayyee dee ninga wakhee takhna inchallah dina lene wakh sarakhbi modou lo wara deff na wor nietou lundi ak nietii jeudi si bene werr mbeur dotouko dane

    • @adamslo7971
      @adamslo7971 3 місяці тому +4

      Lo cii meun segn bii deff ko ekhllou lamb yepou niogui Kay khékh pr mou Danou Mais Yallah bakhna segn bii wakh gnii sarax niou def ko guirr Yallah 🙏

    • @leuz.patriote
      @leuz.patriote 3 місяці тому

      Siteu lenfant sèeri de jonwar futur roi

    • @CheikhtidjaneSeck
      @CheikhtidjaneSeck 3 місяці тому +1

      @@adamslo7971 sarakh bi môme Moye mou wor 3 lundi 3jeudi si bene werr sa veut dire 6 jour si werbi

    • @CheikhtidjaneSeck
      @CheikhtidjaneSeck 3 місяці тому +1

      @@adamslo7971 wakhlene ko mou wor 3 lundi et 3 jeudi

    • @adamslo7971
      @adamslo7971 3 місяці тому

      @@CheikhtidjaneSeck uncha alah jëreudieuf🙏

  • @laminesylla3113
    @laminesylla3113 3 місяці тому +5

    Ki degouwoul dayy wahh rk

  • @KhadimwadeKhadim
    @KhadimwadeKhadim 3 місяці тому +4

    Ki Kha mole dara daye doll

  • @Azoura22
    @Azoura22 3 місяці тому

    Machalla

  • @AboulBacharSall
    @AboulBacharSall 3 місяці тому +3

    Ya fekki modou lo deh soko bayer tamite yaw la rk

  • @MoustaphaGueye-i1f
    @MoustaphaGueye-i1f 3 місяці тому +1

    Yow lirou monee dalaye wo NGA koye nianal si combat yi té nganee Modou lo RK oh wor nga supportaire Modou lo yi yeup ndek xaliss khamnagne leup dinianal lirou oh thiey xaliss

  • @MbayeMbengue-qt3sl
    @MbayeMbengue-qt3sl 3 місяці тому

    Ousmane sonko mo yoni ama balde pour mou sacrifice ndiol djinee falaye mingui Facebook ❤️⚫❤️⚫❤️⚫❤️⚫❤️⚫❤️⚫❤️⚫❤️⚫❤️⚫❤️⚫❤️⚫❤️

  • @isaacdiouf3379
    @isaacdiouf3379 3 місяці тому

    Yen nginane aziz moko diokh khaliss geumoulen sakh yalla

  • @HerveBasse-j5y
    @HerveBasse-j5y 3 місяці тому

    Man masila bi damako meunoul comprnde sah thieuy khaliss

  • @pascalkama3663
    @pascalkama3663 3 місяці тому

    Massyla vraiment khamétoumako.kaddu yii wooro na deih

  • @leuz.patriote
    @leuz.patriote 3 місяці тому +1

    So dèlouwatè si aziz danga nieuw sa keur rek so xamou fo dieum dèloul fa nga diouguèwon si aziz lala nieup xamèwon nga nèkon si bg2 retournè dèm si modou😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂 way soula aziz wowè sah nieuweul nkh fa nga nèwon

  • @cheikhahmadoubamba5477
    @cheikhahmadoubamba5477 3 місяці тому +4

    Gayii lirou contan na😂Am na lou khéw d lou gayii xamoule