Allahou Akbar😱 Les révélations de Cheikh Mbacké Sakho depuis 2015 démou ma magal Touba si l’islam

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 27 гру 2024

КОМЕНТАРІ •

  • @senebousso-pc9rc
    @senebousso-pc9rc Місяць тому +40

    Nioune borom Touba rek lanou beugue

    • @MomoMbodj95
      @MomoMbodj95 Місяць тому +8

      Mane dhë mome Rëk la BëugSegneTouba❤🇸🇳🥰

    • @OumarBoye-s7t
      @OumarBoye-s7t Місяць тому +1

      @@senebousso-pc9rc Serigne Touba dioulitt douko bagne.
      Mbacké Sakho sakh mom dafa sopou Serigne Touba mais mom limou wakh dafa lerr boulene bollé Lou bokou

    • @senebousso-pc9rc
      @senebousso-pc9rc Місяць тому

      Ko bakh esk xam nga le sens de beugue . Démal gueustoul histoire Layla ak ki done beugue. Lou raw lol lanou beugue Serigne bi.

    • @karimkarim-ew1rq
      @karimkarim-ew1rq 9 днів тому +1

      lou rafet rec la meusseu wah si serign bi nak

  • @DJob3d
    @DJob3d 25 днів тому +11

    Il lui a demander kelk chose en contre parti d'un savoir (venant) de dieu alors que le coran nous dit dans la sourate yasin verset 21 :
    ٱتَّبِعُوا۟ مَن لَّا يَسْـَٔلُكُمْ أَجْرًا وَهُم مُّهْتَدُونَ
    《suivez ceux qui ne vous demandent aucun salaire et qui sont sur la bonne voie.》
    Kou beug mothiou moytol mbacké mi il est inspiré par satan après ses douguou khelweu sans meme le savoir , satan lui a donner l'éloquence et le bien parler pour séduire et manipuler les âmes faibles qui au lieu d'apprendre leur religion de leur Messager et des hommes de sciences il attendent que quelqu'un vienne leur simplifier les turpitudes qui les pousse dans un égarement évident.
    Suivez la voie du prophète (saw) et laisser ce gas avec sa propre tombe . Ca sera mieux pour vous

    • @salmaba5123
      @salmaba5123 14 днів тому +1

      Je suis d'accord avec vous Cette personne réveille la fitna, il dit que des sottises. Prenez garde contre cette personne si vous voulez réussir ici-bas et dans l'au- delà.

  • @massambadieye9945
    @massambadieye9945 28 днів тому +8

    Nioune Serigne TOUBA rèk laniouye tope

  • @zallmbaye1622
    @zallmbaye1622 Місяць тому +16

    😢😢 serigne mbacke sakho yallah nako yallah guider amin ya rabi ndaye sann walahi il croit fermement ces propos nanou ko nianal yallah rek

    • @tallfamilleelectroniquekol6840
      @tallfamilleelectroniquekol6840 Місяць тому +2

      Amine yalla na ko Yalla guinde

    • @mouhamadsane6759
      @mouhamadsane6759 28 днів тому +2

      Nitt daal sou beuguè guindèku faaw daal mou bok si kurell ?? 😂😂 Yeen yeena djara yeureum

    • @maneseydina6564
      @maneseydina6564 28 днів тому +1

      Walahi rere ba goumba nga fokni ya ngui yone bou bakh bi

    • @bourhan142
      @bourhan142 13 днів тому

      Yalna mou alkou

    • @karimkarim-ew1rq
      @karimkarim-ew1rq 9 днів тому

      lou leer lay wah kay , loum la wah indil la ayat ak ay preuve you lerr

  • @bayetoubasylla7327
    @bayetoubasylla7327 Місяць тому +10

    Macahallh 👏👏👏❤sopou nala lolll

  • @maneseydina6564
    @maneseydina6564 28 днів тому +8

    Le fait que Allah dans le coran nous interdit de se diviser c'est une réalité,mais vivre le Coran sans la sunna est un mensonge.

  • @mouridoulahi2000
    @mouridoulahi2000 5 днів тому

    الحمد الله رب. العالمين والصلاة والسلام على رسول الله ❤شكرآ ياشيخ أحمد الخديم البكي ❤

  • @serviteu_d_Allah
    @serviteu_d_Allah Місяць тому +6

    Mbacke lingay leeral Amna loussi ame solo waayé mounoo diaamou yalla té boolé woosi sunna ndax loolu weddi yonnentibi sayaboo nga toub balaa ngay dée

  • @OumarBoye-s7t
    @OumarBoye-s7t Місяць тому +14

    Bo topé alkhourane kassé dangeuy am diamou sakh.

  • @ousseynoutoure3621
    @ousseynoutoure3621 Місяць тому +35

    Gnoune dagnouye magal ba khaye fatou so magaloul sa affaire leu tei woul atte mou diotte magal gui di gueuneu neikh peipou kani si gueidj takhou ko weikh

    • @hoorevision5753
      @hoorevision5753 Місяць тому +3

      ioe dof nga rek

    • @moustaphamboup4934
      @moustaphamboup4934 Місяць тому +1

      Saway dioumo dé wayé dinée yeufou doff la tékou dofoul amoule dé yaw nak Dofu Kane ga mbacké Sakho ndayssane kou mbakhla

    • @hoorevision5753
      @hoorevision5753 Місяць тому +1

      Machallah cheikh Mbackè sakho un homme pluridisciplinaire ❤❤❤

    • @jobseuofficiel3787
      @jobseuofficiel3787 Місяць тому +1

      Wakho fi dara. Waly Seck sayou deffei concert mou fesse deleu tei accuser nagn ko lounek

    • @AbdoulayeDiatta-gy5oy
      @AbdoulayeDiatta-gy5oy Місяць тому

      Yén dolén ayy dioulite ayy mourite nguén gana messeré wakhonako
      Donc islam akk mouridisme dou bén

  • @MoustaphaMbathie-mm1rp
    @MoustaphaMbathie-mm1rp 26 днів тому +2

    جر جف سيخ أحمد بمب خا دم رسول ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @MamFatou
    @MamFatou Місяць тому +5

    Ma Sha Allah

  • @hoorevision5753
    @hoorevision5753 Місяць тому +18

    Cheikh Mbackè sakho un homme véridique ❤❤multidimensionnel

    • @basmbaye7527
      @basmbaye7527 Місяць тому

      @@hoorevision5753 mbacke sakho doulkat la nafekh la saytane la yak mom sen leufeul ndeye

    • @DJob3d
      @DJob3d 25 днів тому

      Je vous jure devant ALLAH (aza wadj al) que ce gas en dans une perdition évidente

  • @wakeurserignesaliou3642
    @wakeurserignesaliou3642 6 днів тому

    Ahmadou kene la❤❤❤

  • @bathiefaye7179
    @bathiefaye7179 8 днів тому +1

    Ki khamnga foumouy moudié ak wadji moy bientôt amed cissé moy guéneu def boppam héro ni j'avais la mission dédéconstruire nbacké sakho pour wané ci thiaxane yimou nek
    Pour meuna gagné wat touti sympathie meuna continuer thiaxane yimou nékké
    Niome niar nieup ci ay tiaxane lagne nek mais ahmed cissé dakkoy tek xel

  • @kouroubayefallpure
    @kouroubayefallpure Місяць тому +14

    Bayi doul d’où tax niou bayi s touba d’où tax niou bayi magal boul sonal sa bopu sax di yakh sen énergie s touba beug nanuko ba nopi

  • @malickseck911
    @malickseck911 Місяць тому +3

    Amoul morom khadim Rassoul

  • @FallouGaye-gf7kb
    @FallouGaye-gf7kb 8 днів тому +1

    Soubhana lah astakhfiroullah

  • @ahmetmbodj7656
    @ahmetmbodj7656 Місяць тому +4

    Cheikh Ahmed il est tellement fort, si seulement vous pouvez savoir. Fén lo na Sakho sans ke ce denier ne s’en rende compte

  • @toubapatar
    @toubapatar Місяць тому +5

    وماءاتيكم الرسول فخذوه ومانهيكم عنه فنتهوا واتقوا الله إن الله شديد العقاب

  • @assouhbatoufillahi
    @assouhbatoufillahi Місяць тому +1

    YA AYOUHAL LAZINA AMOUNOU TAQULLAH WA TAKU ILAYHI WASSILA.

  • @moussaba2321
    @moussaba2321 Місяць тому +12

    Nit kou honnête le cheikh mbacké ❤

  • @ModoumaremeGueye-kd1wh
    @ModoumaremeGueye-kd1wh 17 днів тому +1

    Tourou yalla lou am solo la wayé niaka am serigne boulén ték thi yone molène alak

  • @kenalserignetoubambacke269
    @kenalserignetoubambacke269 Місяць тому +2

    Dieureudieufé borom Touba ❤

  • @mamefall9788
    @mamefall9788 24 дні тому +2

    Mbacke Sakho dadial molayoni nga woutalko Ay talibee

    • @Smokin_mass33
      @Smokin_mass33 18 днів тому

      Ki dei deugue lafi wakh

    • @karimkarim-ew1rq
      @karimkarim-ew1rq 9 днів тому

      kon kou wah li yalla wah teh mou nek si alhourane dadial mola yoni ???

  • @khadimMbacke-d9u
    @khadimMbacke-d9u Місяць тому +15

    Ki dafa rere ba yakho ndeyessane 😢

    • @abdoukhadirmboup9360
      @abdoukhadirmboup9360 Місяць тому

      Da rer dine kene dothi dogale samkhele alkhorane khadis mokoye firy de gamole khadiss

  • @sorycoulibaly594
    @sorycoulibaly594 18 днів тому +1

    Lou waay meunn thi Istighfar ak Salaatou Alaa Naby nako deff...point

  • @abdoutoure6436
    @abdoutoure6436 15 днів тому +1

    Ndayesan ki dafa sanko rek hoo😢thiey dondo go djiéxa gol lony xathie na thi😢

  • @diopcheikhahmadoubamba6127
    @diopcheikhahmadoubamba6127 8 днів тому +1

    Da nga dofff ba legiiii😅

  • @MalibereSambe
    @MalibereSambe Місяць тому +7

    Yalla nala yalla faye chiekh amet cissé bagua takhé niou geune kham kouye mbacké sakho nite yi nio sokhore beugouniou kouye wakh lou yalla wakh niome nagua wakh serigne bi néna rék mane mome légui alquran yalla dji rék laye top

    • @mouhamadoumourtadaalkarim8274
      @mouhamadoumourtadaalkarim8274 Місяць тому

      Yao la req

    • @DakarFaDA
      @DakarFaDA Місяць тому +2

      Saway def si ndank d.
      Alhourane ken meunouko top mom kesser té bolé wossi sounna Seydina Mouhamed psl. Si alhourane ken djangalé woul nane lagnouy dioulé, dou nombre rakka yi, ken expliquer woul adj makka nougn koy defer, nougnouy woré... donc Mbacké mi lim si comprendeoul barina. Mom na wakh foum diangué diouli ndax si alhourane la

  • @firdawsigroup313
    @firdawsigroup313 3 дні тому

    Gnaare gni cest des dangers publique.. Mbacké sakho khelmi dako rérale.. Wayé ahmed Cissé mom ab kathior leu..

  • @seydina_jibril
    @seydina_jibril 15 днів тому +1

    Cheikh mbacké sakho
    Fou yalla waxé ni délén joulli fajar tisbar takkudaan timis guéwé indil ma ayya bi ma jébalou si yaw
    Yalla waxouko ta yankay déf nga beugeu xaraamal joullé néew ndakh ni yalla waxouko
    !!!!!

  • @amdiop4537
    @amdiop4537 Місяць тому +6

    QURAN versets 30 et 31 parlent des polythéistes (ceux qui adorent plusieurs dieux),par contre les Tarikhas croient en seul Dieu.Ces versets se réfèrent aux nassrane,c'est eux qui ont divisé leur religion en plusieurs dénominations et qui n'ont pas le même concept de Dieu.Et chaque dénomination se rejouisse de leur croyance.

    • @dasmanjackaggo3340
      @dasmanjackaggo3340 Місяць тому

      C'est un début Révélation pour entrer dans la vraie lumière

  • @ndiayeahmad5929
    @ndiayeahmad5929 Місяць тому +2

    Ku bëgg lu leer sa digg ak yàlla jàngal sa diine te bagn ko fortatu. Diine kenn du ko business 👁️👁️👁️👆🏼👆🏼👆🏼

  • @ndiougadiop7250
    @ndiougadiop7250 Місяць тому +1

    DOFF YANGUI CI BIIR NIT GNI

  • @Bamba-rk
    @Bamba-rk 13 днів тому +1

    yalna leen YALLA guindi

  • @boutiquekheweulbusiness
    @boutiquekheweulbusiness Місяць тому +2

    C'est très intéressant

  • @yusufmouhamed-8787
    @yusufmouhamed-8787 Місяць тому +2

    Qu Allah vous garde merci

  • @abasselo8206
    @abasselo8206 Місяць тому +2

    Assalamou halaykum astakhfiroullah

  • @BabacarKA-by5kv
    @BabacarKA-by5kv 6 днів тому

    Sakho dofowon , dof deug dou werr
    Tassawouf dou ay thiakhane.
    Serigne si dagno xam, xamé, dioub tey dioubal sell sellal yiw diebal Yalla sèn lépou.
    Kou djiss batil askanko sa bopou mba sa khel mba kénèn.
    Yalla nalèn Yalla guindi

  • @MohamedKalleDiop
    @MohamedKalleDiop 9 днів тому

    Jamonoy dof Si yàlla.waaye yaangi Si réer si yàlla.yalla nanu yàlla Gindi amiin

  • @tracychapman6700
    @tracychapman6700 Місяць тому +2

    très honnête manchalah

  • @mouridoulahi2000
    @mouridoulahi2000 5 днів тому

    😂😂😂sanékh sakho dafa neexxx 😂vrai comedian la

  • @malickamar8074
    @malickamar8074 9 днів тому

    ولا تصل على أحد منهم مات أبدا

  • @PapadjibrilNdiaye-y4o
    @PapadjibrilNdiaye-y4o 22 дні тому

    Sénégal nékhna gni amnagnou ay talibé

  • @jilymbacke5891
    @jilymbacke5891 27 днів тому

    Niare niou rerr and di rerale top lene bala moye wes ki sunna la weddi ki xamne Limoye wax dou degg dikou diapale مسيلمة الكذاب وطليحة بن خوليد الأسدي

  • @mactarseck9849
    @mactarseck9849 Місяць тому +1

    Amna solo

  • @serignecheikhdiop690
    @serignecheikhdiop690 19 днів тому

    Waaw leen goor non moom yalnane gana dof thi todo yalla ak nianal diamo yalla yi

  • @akimbousso2206
    @akimbousso2206 Місяць тому +4

    Ñiari masi dadjial yalna yala mouseul nitngi ci yen yen khelyi geun geuna geum ci Li yala wakh dinedji khol lankoy geume way Ken dou toupou sam khel kham kham bou barri ak khel Mou nekh ak diamou yala goudal barri takhoula ragal yala takhoula mouthi ndakh soudon takha mouthie iblis mouthie way iblis topou am khel moko sankue yalnanou yala mouseul ci yen ñiargniii😢

    • @hoorevision5753
      @hoorevision5753 Місяць тому +1

      ioe dof nga rek
      Machallah cheikh Mbackè sakho

    • @funasambsamb1661
      @funasambsamb1661 Місяць тому +1

      ​@@hoorevision5753kén dou wakh deug si yén bâ wérr, deug rék là yaw andil arguments mo tané lingaï wakh

  • @fnoumbediop690
    @fnoumbediop690 Місяць тому

    Masahalla yal n'a yalla Fay yiw 🤲

  • @ngordiegane
    @ngordiegane Місяць тому +1

    Cheikh avec ce monsieur vs risquez de tomber ds le folklore.

  • @AKTECHPlus
    @AKTECHPlus Місяць тому +2

    Alhourane moye sougnou référence thi diné Islam wax douko fëtë kaw ki da doff ki dëye rëlelatë yoyou yëpp amoul solo indil louye dakh aye waxame djëlëko thi alhourane mo woor kouni yalla nëna sokko gueumoul indil li yalla wax mo gueune tanguëne bayi jugement bi

  • @OusseynouNdiaye-l8s
    @OusseynouNdiaye-l8s 26 днів тому

    AXMADOU le sauveur de l'humanité, en tout cas Sakho tu veux avoir des talibés😅

  • @dijabravoooawaaa9262
    @dijabravoooawaaa9262 Місяць тому +1

    ❤️❤️❤️❤️❤️

  • @bassiroundiaye3913
    @bassiroundiaye3913 Місяць тому +1

    Chiekh amét cissé yaw ak ki yéna yém ndakh yag koy diapalé geumo dara

  • @SarrKhadim-w8g
    @SarrKhadim-w8g Місяць тому

    Ki limy wakh thi xel lako tek dîne du loolu ki ab nafeekh la bu mak

  • @Bamba-rk
    @Bamba-rk 13 днів тому

    diiné yamoul ci alkhour aan
    th wèddi khadiiss wèddi nga YONENT BI th kouka wèddi sànkou nga th kaafir nga
    soubhanallah

  • @seckseck9985
    @seckseck9985 15 днів тому

    Donc dangaa beugueu daganal mballou ? Bayyileen di topp seen bakkàn, Adina dou keeurrr

  • @seydina_jibril
    @seydina_jibril 15 днів тому

    Yalla ban waxtou la touddou si alhouraaan ??

  • @OumarBoye-s7t
    @OumarBoye-s7t Місяць тому +1

    Machalla

  • @amasy4597
    @amasy4597 Місяць тому

    Mbacke Sakho bègue nalla guiss❤

  • @2mttv64
    @2mttv64 Місяць тому

    Cat moo la jàpp lu baax la nga jàppoon lépp bàyyi nga ko

  • @mamefall9788
    @mamefall9788 24 дні тому

    Mbacke Sakho yangui reral segalaiyou amour tawhid

    • @karimkarim-ew1rq
      @karimkarim-ew1rq 9 днів тому

      man am na tawhid mais daff ma geuna leral yonou yalla bi machalla alhamdoulilah

  • @daoudadiedhiou1221
    @daoudadiedhiou1221 Місяць тому +1

    Manchalla ❤️

  • @mamefall9788
    @mamefall9788 24 дні тому

    Mbacke Sakho saytane dafala diaye dila fohee

  • @lahatleye6313
    @lahatleye6313 Місяць тому +2

    Yal momu tamit mo wax ni ÑJANN LÈNN MA MA NANGU SÈNN ÑANNN TÈ APP NÈEW DIOULÈKO MOY ÑIANALKO TAY LA GEUM NI DAGA RÈŔ

  • @MouhamadouMoustaphaDiao
    @MouhamadouMoustaphaDiao 10 днів тому

    Ki santoul mbacké dhé ki sakho la santé Nay léer

  • @Smokin_mass33
    @Smokin_mass33 18 днів тому

    Serigne Bamba meusteu sosse tariqa.

  • @omarndiaye5184
    @omarndiaye5184 Місяць тому

    Serigne bi nga balma sa kham kham gattena

  • @AminataFall-w8q
    @AminataFall-w8q 10 днів тому

    CHEIKH BO FATOUWONE KENE DOULA DIEULÈ??

  • @mamethiernosopenaby8713
    @mamethiernosopenaby8713 Місяць тому +1

    Wakhtane bi amna solo

  • @malickndiaye631
    @malickndiaye631 Місяць тому

    Ahmed lath neko allkhour âne bimou geume dafa diar thiy nit ba yék si thi mom té geum nako hadis aussi nonou la démé litakh gamouko?

  • @bathiefaye7179
    @bathiefaye7179 8 днів тому

    Amed cissé gueumoul touss ci limiy wakh ta bientôt dina guéneu yakh mbacké sakho ni dako done piégé rek
    Ay domeram you dadié la rek

  • @cheikhibrafallmboup6223
    @cheikhibrafallmboup6223 5 днів тому

    18:34
    L'islaam affairou talibé ak Serigne amouthi ta nénga say talibé gnoongi ci live bi
    😂😂😂😅😅😅😅

  • @solution5135
    @solution5135 Місяць тому +1

    Cheikh mb sakho néna geumoul wilaya wayé lounkosiwakh douko wédi

  • @thiernoseck1765
    @thiernoseck1765 9 днів тому

    Vous êtes un homme sigma

  • @maneseydina6564
    @maneseydina6564 28 днів тому

    Rira bien rira le dernier

  • @mamefall9788
    @mamefall9788 24 дні тому

    Chaytanee Molay fohee

  • @pointdevue1304
    @pointdevue1304 Місяць тому +1

    Ce mbacke sakho est complètement égaré. 😢😢😢😢

  • @AdanaSow
    @AdanaSow Місяць тому

    Alquran dal laniou Yalla topoulo tè lolou la diokhone Yonent mo nèk ci Alquran
    Laa ilaha ila LLAHOU wahdahou laa charika lahou ❤❤❤❤❤❤

  • @IlliasSa-b1v
    @IlliasSa-b1v Місяць тому

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @MoustaphaMbathie-mm1rp
    @MoustaphaMbathie-mm1rp 26 днів тому

    Ki mom mangui sogua setan vidéo wom mais ki vrai nafiékh la

  • @ablayedine6951
    @ablayedine6951 Місяць тому +1

    SAKHO SGN TOUBA AKI NDIABOTAM, DIOULÉ NAGNOU AY NIT TÉH GNOLA GANA HAM YALLAH.KON LOLOU DO SI IRI KÉNA

  • @Kambel-tv
    @Kambel-tv Місяць тому +1

    AK ay tali bèm

  • @AliouNdiaye-lc3pp
    @AliouNdiaye-lc3pp 8 днів тому

    Sa wax ji yaqul darra ci sunu gëm boroom Touba

  • @aboridial3431
    @aboridial3431 7 днів тому

    Ken Dou borom Touba

  • @doyendiouf6240
    @doyendiouf6240 17 днів тому

    Machala

  • @SarrKhadim-w8g
    @SarrKhadim-w8g Місяць тому

    Ki santul mbacke

  • @kradiop4341
    @kradiop4341 9 днів тому

    Sakho koulakham(?

  • @malickamar8074
    @malickamar8074 9 днів тому

    ما هو صلاة المغرب في الحكم القرءان

  • @falysenghor3512
    @falysenghor3512 4 дні тому

    Légui ngéne geuneu yéss ❌

  • @ahmedtidianesy5970
    @ahmedtidianesy5970 13 днів тому

    un comédien aek un illuminé... quel cocktail

  • @DembaSow-bo2fz
    @DembaSow-bo2fz Місяць тому +1

    اللهم ارزقنا علما نافعا وتوفيقا بالله ياربنا إن كان العلم جاهلا عنك وكافرا عنك وعن نبيك واجعلنا جهلاء ياربنا أنت على كل شيء قدير واجعلنا مقتدين ومتّبعين ومحترمين نبيّك وحبيبك رسول الله صلى الله عليه وسلم.... والله العظيم من لايصدق الرسول لايصدق الله...❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @damefall-it8gc
    @damefall-it8gc Місяць тому +1

    Cheikh mate cisse moytoul ki dalaye changer dé bilahi

  • @IlliasSa-b1v
    @IlliasSa-b1v Місяць тому

    Cheikh mbacke Sakho Dieureudieuf

  • @aboumansourniang4771
    @aboumansourniang4771 Місяць тому +1

    Djoulli benna rakat walla niar walla niet walla nienta rakat da amout fenna thi alquour’aan bay mbakh djiguèn , saw , dokhot diko nênnal.
    Çalat = mboolô, takkou, seyyalé , djokkô … thi français = union / communion/ reunion / liaison / connection / assemblage / marriage…
    Malakat aymânikoum = votre / vos contrats de serment / vos serments obligatoires/ votre possession de serment… dou ay djam yoy tak di sey ak niom kemnoumla nekhë. Kon noy firë 63:2 thi baat bi " أتخذوا أيمانهم / ittakhazou aymânihim " xanâ dâko firê : "daniy dieul senniy djam" tey baat bi limouy firi moy : " daniy dieul senniy waat ( serment en français )
    Ragalal yallah balà mouy wess ay djam yi niou tak walla fassé kem noumla nekhë nekkout thi benni ayaye alquour’aan.
    Deloul thia dara cheikh mbacke dessé ngua xaam batou arabe yi nek thi bir alquour’aan.
    Wa salamoun alaykoum !

  • @abdoulayesarr1138
    @abdoulayesarr1138 Місяць тому

    Yoro diamy Serigne Yoro diamy borome xham xham

  • @NgagneDiakhate-f2i
    @NgagneDiakhate-f2i Місяць тому

    Ki sankou bou yag di sank ay nit nguen koy diapalé

  • @institutislamiquetv5285
    @institutislamiquetv5285 Місяць тому

    Niedé danoulene salebou rek

  • @fallousylla4764
    @fallousylla4764 Місяць тому +1

    Lou yonenti nekone sahaba yi nekone si mak you bax yi nekone si té ngi nieup ken doussi diayil kon lolou deug leuh wayé CMS dafa guéné yonenti si debat bi té lo wax mouni yonenti ndaw la wone rek daniou ko yoni nit kou mandou com yonenti souniou ko yoné loumou wax rek yalla ko wax loumou defit yalla koko digeul