Omaro - Mou Cheikh Béthio (Hommage à Serigne Cheikh Béthio Thioune) - Clip Officiel

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 13 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 1,3 тис.

  • @adjathiam2414
    @adjathiam2414 5 років тому +728

    Kou beugue omaro ak cheikh betio tapel j’aime yallana khiper aldiana té serigne saliou terouko amine yarame dawna

  • @yasminambaye2231
    @yasminambaye2231 5 років тому +1

    Aka lér kou yala fal niou firr la kou yala tal niou djigne la mé s saliou mbacké dafay soutoural nioniam mogui firdawsi si képarou s saliou Mbacké mome cheikh Béthio 👌👌❤❤

  • @jardelgomis8466
    @jardelgomis8466 5 років тому +108

    Ndeyssan douma musulmans sakh ms c qu'il dit à travers cette belle mélodie me fait voyagé aussi comme si il parlé de moi mm .god blessed

  • @karaabba5900
    @karaabba5900 5 років тому +2

    Ooooh omaro ...bilahi khôl yeup tiss na

  • @ndeyefatoudjigal656
    @ndeyefatoudjigal656 5 років тому +45

    Que la terre soit légère j'ai trop pleurer quand j'ai pensé à mon père thieuy adouna j'ai perdu mon père a l'âge de 12ans ça fait 7ans aujourd'hui que la terre lui soi léger paix à leur âme

  • @deessedufoutadiallo2121
    @deessedufoutadiallo2121 5 років тому +2

    Mane dé beugouma geumouma koudoul serigne babacar sy wayé wayou omoro bi sama biir khol bi la dougou dama koye replay aye yoni yone ndeyssane cheikh bethio yallah nako yallah yeureume té kharé aldiana you kawé ta serigne
    saliou térou ko 🙏🏻🙏🏻

  • @diopmoustapha6286
    @diopmoustapha6286 5 років тому +59

    J'ai des larmes aux yeux😥😥 ndyasan sama xool féss na cheikh bii Yalla nalla yalla faysa xoll dingagnou wétalll😥😥😥😥

  • @nadiadiaw7064
    @nadiadiaw7064 5 років тому +1

    Ndeysanne dieureudieufety serigne saliou serigne saliou yalla ganiou teroule cheikh bethio

  • @djibyndaw5066
    @djibyndaw5066 5 років тому +33

    Yoow dé topéwo Cheikh Bii adouneu yagui fedalli sa koleuré si mom yalla nalleu borom diam ak diamono takhawou c'est très émouvant

  • @aminatasall8087
    @aminatasall8087 5 років тому +25

    Ndeysane talibé serigne babacar sy la dé wayé son bii nékhna jé les larme aux yeux kan omoro pleurè courage.

  • @Americaine268
    @Americaine268 5 років тому +370

    Ohh Omaro dpui 2012 lala beug guir yalla ak Serigne saliou ak cheikh bethio bilay bi cheikh nelawei yaw la ndieukeu khalate 😭😭😭

  • @cissebabacar6002
    @cissebabacar6002 5 років тому +143

    Omaro vraiment lii nekh na trop
    je s8 tidiane mais saq jour damamaye sivre

  • @jeemkanamgie6256
    @jeemkanamgie6256 5 років тому +30

    Chanson très triste
    Cheikh bethio que dieu l'accueil dans son paradis

  • @ndeyecoumbadione4131
    @ndeyecoumbadione4131 5 років тому +7

    Je suis talibé cheikh mais omoro ses paroles me touchent énormément 🙏🏽❤️machalah yalla nako yalla kharé aldiana🙏🏽amine

  • @zeynagoumballa5323
    @zeynagoumballa5323 5 років тому +51

    Merci makkk dafa daw yaram k la terre soit légère 😭😭😭😭😭kou bakhh bonn continuation a tw S.S.M.t

  • @rassoulemir7636
    @rassoulemir7636 5 років тому +1

    Ayyyaaaaa j'ai des frissons.........sheuttttt liii ndawna yaram.....billay omaro rafèttt guassi mashallahhh

  • @petitneymar9764
    @petitneymar9764 5 років тому +313

    Omaro li dafa rafet Serigne bethio yalla nako yalla yereum👍👍

  • @aminaka5183
    @aminaka5183 4 роки тому

    Je suis talibi cheikh mais daw n'a yaram adouna gui ni rék dém rék loulou yague yague

  • @khadijatouray2261
    @khadijatouray2261 5 років тому +118

    La chanson me va droit au coeur même en étant pas thiantakoune

    • @gtheboss9635
      @gtheboss9635 4 роки тому +3

      Macha'Allah Omar droit au coeur

    • @gtheboss9635
      @gtheboss9635 4 роки тому +3

      Dieureudieufe Serigne Saliou

  • @YoussouAthy-k8n
    @YoussouAthy-k8n 2 місяці тому +1

    Thieyy cheikh béthio 😢😢😢😭😭😭😭

  • @diesamba5271
    @diesamba5271 5 років тому +19

    Machallah
    Jeurejeuf Serigne Saliou Mbacké
    Cheikh bi jamou Ahmadina Salihou Paix à son ame 🙏

  • @awa2rayz935
    @awa2rayz935 5 років тому +4

    😭😭😭 Ndeysan lou diouguè thi khol, thi khol rek lay tabi.. Thioune Mame Bamby Thiam, yalna la Serigne Touba/Serigne Saliou Terrou thia Aldiana firdawsi ya ❤️❤️❤️

  • @papendaw3339
    @papendaw3339 5 років тому +231

    Lep lou diougue si khole khole mokoy sentir sond bi kep kouy nit ak tariha bo book sa khole dina toy vrmt sma khole 😢😢 na yalla nako serigne saliou terrou aldiana 🙏

  • @djeumbfall333
    @djeumbfall333 4 роки тому +1

    Ma grande mere est morte maus quand jecoute cette chanson je pleure comme ci cetait ma grande mere je ľaime

  • @morfamadiome1713
    @morfamadiome1713 5 років тому +36

    Serigne béthio Thioune dieureudieuf omoro Macha allah

  • @dieynabawane2281
    @dieynabawane2281 5 років тому +1

    Ndeysane sama yaram dawna courage mon frére yalah nalene dedou ak diam tei khel warna dal si mom nak machalah yalah loumu def khamnako wakh dji moy bari rek mais wuyudji yalah si 1er jour koor ku nek niane nako yalah nit nak do kham ndiriniam temps k wanula guinaw yalah nako serigne saliou terou sa firdawsi si barkei seydina mouhamed barkei wer wi niu nek nieuupa niak mane deih khadre la wayei nieupako dioy walahi

  • @bettysine8347
    @bettysine8347 5 років тому +1

    Siguil ndigaler Omaro..Masta c est des larmes aux yeux que j ai terminé ce clip...Thioune Mame Bamby Yalla na Aldiana done keureum🙏

  • @khadyndiayeyayefall9014
    @khadyndiayeyayefall9014 5 років тому +21

    C'est vraiment touchant Omaro ya goré serigne béthio yalla nako serigne saliou sangam ba térrou amine ya rabbi

  • @mamediarrasamb9589
    @mamediarrasamb9589 5 років тому

    Billahi 😤🙁😢😱c'est très touchante 😢😱khawma sakh loumay binde ndakh ay dioy yalla nako yalla yeureum. Limay wakh nii si sama khol lako tibee ta yalla bou yakar tass si moom ta yakar naané dou massa tass barkep serigne saliou mbacke amoone nafi ndiarigne trop Billahi sama khol sakh atanatoul may continuer ndakh tiss ak ndiakaré way bi nak daw na yaram trop trop trop😢😢😢😢😢😱😱😱😱😱

  • @djenabadiallo1406
    @djenabadiallo1406 5 років тому +62

    Talibe Cheikh la waya g les larmes aux yeux ch bi yalnako Yallah yeureum t xarerko Aldianay firdawsi

  • @ousmanethioune9063
    @ousmanethioune9063 5 років тому

    thiey adouna mogui nii rk m dii nianal mame chiekh bethio yalah nakho serigne saliou terou sa aldiana

  • @sallpapayoro214
    @sallpapayoro214 5 років тому +586

    Jetais là au momen de lenregistremen m jour bobou kou nékone studio sa yaram dawna omaro mou cheikh betio

  • @khadijasamb4677
    @khadijasamb4677 5 років тому

    Ndeyssane Omara lii daw na yaram. Cheikh bi yalna khipei si kanamou Serigne Saliou Mbacke. Man dh bimako deiguei yaw la dieuka khalat. Wayei kom niko cheikh Bethio wakhei rek . Yalla bakhna.

  • @choupabah471
    @choupabah471 5 років тому +44

    Douma mourid mais Serigne bethio nieupko naw ndakh ay bienfaits repose en paix nit kou bakh

    • @ElTIO_Galass
      @ElTIO_Galass 5 років тому

      Te nga don mourid rek nga baal ma

    • @mexdroid1703
      @mexdroid1703 4 роки тому

      @@ElTIO_Galass khawma ki si loumou nékk mais mo gueune lin nga nékk fouf imbécile

    • @ElTIO_Galass
      @ElTIO_Galass 4 роки тому

      @@mexdroid1703 wakhou lo deug de domram imbécile j'ai comm tw jesui un mouride sadikh kima geum moy Serigne touba te man jegani wouma ab Serigne thi ben Pays naar domram

  • @ibrahimasoumare357
    @ibrahimasoumare357 5 років тому

    Chiekh bethio yalla naka yalla khare aldiana

  • @famadiop6890
    @famadiop6890 5 років тому +110

    Vraiment ça vient du cœur omaro en quelques jours tu as pu enregistrer et faire ce clip lii moy andeu bou sincére dawna yaram torop

  • @aichadiop3088
    @aichadiop3088 5 років тому +2

    Kou beugue oumaro je vous aime beaucoup son bou nekh

  • @ndoumbegueye9614
    @ndoumbegueye9614 5 років тому +4

    Euskey dieureudieuf Serigne Saliou thiant gui kanam la dieum InshaAllah

  • @mamandiaye1791
    @mamandiaye1791 5 років тому

    Ndeysannnnn..yalnala serigne saliou térou si barké werr wii wou gnu nekk...Omaro aduna nak moni mell..nagnu doli sante rk comm nime gnu ko diangualé rk

  • @amantousambe6796
    @amantousambe6796 5 років тому +7

    😢😢 Omaro Rendre gua Hommage kou Bakhe kou Yatou kou beugu ay talibém kou dimbili Ay talibém kou léneu takhagou Fou nékeu 🙏🙏Souniou Sangue ba Thioune diambari Serigne Saliou yalnaniou sakh si thiante gui ak képarou serigne bethio ba faw Barkép Serigne Saliou 🙏

  • @smbossewakanacisse9343
    @smbossewakanacisse9343 5 років тому

    Thiey Omar Gueye mou serigne Bethio santati nanu dh ndeysann waya kou Ted ki dou koufiy diougu tei mashallah dawna yaram lol

  • @ahmadoubalde8096
    @ahmadoubalde8096 5 років тому +37

    Ki é la pour omaro pouce bleu

    • @diagnealiou9414
      @diagnealiou9414 5 років тому

      Emotionelle cheikh bethio yallla nako yalle wanela akk Serigne saliou mbacke

  • @pacodiaz5814
    @pacodiaz5814 4 роки тому +1

    Adouna amoul bénnne solo bilahi

  • @awadiagne671
    @awadiagne671 5 років тому +8

    MaachaAllah. Ana fougnouy dieuleti kou melni Cheikh Bethio😭😭 Adouna dou dara aye lèbon leupon reck la. Dèff lou bakh reck mo âme solo.Cheikh Bethio mo khamone lou bakh tè diko dèff tè Yalla reck takh si dieum Serigne Saliou Mbacké. Sante reck Alhamdoulillah💞

  • @nanachidid9485
    @nanachidid9485 5 років тому +1

    ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️yalla ga khipè aldjana thioune si waitou Srg Saliou 🙏🏻🙏🏻🙏🏻🙏🏻

  • @mamediarratoure957
    @mamediarratoure957 5 років тому +112

    Ndeyessane son bi daw na yaram omoro 😭😭😭yallnako saguam ba térou 😢😢😢😢😢😢

  • @giuseppefonso4979
    @giuseppefonso4979 5 років тому +1

    Omoro senewaye bi yak mandiaye seck nekhna trop sakh senewaye bi nguenewayale bethio yallamoleni faye omoro danguabeugue bethio bagnepoukhameko bethio repose en paix yallanasouf sed sa kaw tanguadem aldiana

  • @niangpape7625
    @niangpape7625 5 років тому +7

    Yallana ko serigne saliou terou sa aldianay firdawsy sii barkii wéro koor bii

  • @louisefaye2172
    @louisefaye2172 5 років тому

    Je suis chrétienne mais woy bi lale nama j'ai les larmes aux yeux

  • @mbayendiaye4597
    @mbayendiaye4597 5 років тому +22

    Qu' il repose en paix.Omaro très reconnaissant bilay

  • @khadijalasalihate6698
    @khadijalasalihate6698 5 років тому +1

    ndeyse yènn Thiantacone yi yalla na lènn yalla many xolou mougn ak nagou ndyse Omoro wèttay dinala sonal😢😢😢mèttina

  • @ibrathiam7976
    @ibrathiam7976 5 років тому +3

    Mashalla ❤️ ana wa sopé serigne saliou Mbackè ❤️

  • @khadimkhouma9343
    @khadimkhouma9343 4 роки тому

    Diambar deugue dedou neuh. Lépam la diokh Seirgn Saliou Yallah nakou Borom koune fa yakone doli yereumandé

  • @mamouribncisse3505
    @mamouribncisse3505 5 років тому +8

    Machaallah geste noble 🙏🙏❤️❤️cheikh yalla nako yalla yeureum të kharëko ALDIANA FIIRDAWSII

  • @khadidiatouthiaw5515
    @khadidiatouthiaw5515 5 років тому

    Firdawsi swa son demeure thioune te yalla maylen kholou mougne Omaro

  • @madjiguenegueye2156
    @madjiguenegueye2156 5 років тому +3

    Juste en lécoutant j'ai des larmes aux yeux bilahi ndakh sa tiofel thi serigne bi courage yalna yeurmandé sunu borome wathie thie kawame

  • @awatallsamoura2556
    @awatallsamoura2556 5 років тому +6

    Trop triste😭 maachallah omaro du courage. Kou beug Serigne Saliou beussal pouce bleu

  • @mortallaseyedallou6976
    @mortallaseyedallou6976 5 років тому +1

    Kou begue cheikh bethiou okel jemm

  • @minandiaye5430
    @minandiaye5430 5 років тому +82

    Suis pas fan de ce mec mais javou k nii son bii dafa daw yaram bravo sa fait pleurè

    • @gayetalif
      @gayetalif 5 років тому

      NOGI SAKOU GA ABONNÉ VUS SI(GAYE TALIF YALNA YALLA FAYLA
      ua-cam.com/channels/C-F49R2tEoFyTCD7P78suQ.html

  • @gtheboss9635
    @gtheboss9635 4 роки тому +1

    Dieuredieufè Serigne Saliou

  • @assanembow3851
    @assanembow3851 5 років тому +3

    Yalla nako yalla harei aljannah firdawsi...Machallah 🙏🙏c très émouvant

  • @pendadiallo9249
    @pendadiallo9249 5 років тому +1

    Vraiment lli nekh na way

  • @ibrahim8899-j3z
    @ibrahim8899-j3z 5 років тому +44

    Très belle chanson. Cheikh bethio RIP . Une fois née nous devons tous mourir un jour ou l'autre.

  • @fatousamb6519
    @fatousamb6519 5 років тому +1

    Cheikh bii barki serigne saliou wetel nagnou

  • @silmanjr839
    @silmanjr839 5 років тому +37

    Tu es la 1er personne à qui j’ai pensé après le décès...
    mais joly son mashallah
    Parole d’un Talibé cheikh Ibrahima Niass

  • @eutoudinedjitvmameousmane1946
    @eutoudinedjitvmameousmane1946 5 років тому

    Omaro Macha allah kou âme guilafa daga goye wané mé nieup la kham dji chéikh bi mé bilahi sons bi néxna yalna yalla yeureme go si barké seydina mouhamde saw barké sérigne saliou mimou yakar

  • @leschroniquesdemayramesow8782
    @leschroniquesdemayramesow8782 5 років тому +6

    Naniou delo xelsyi tchi ALLAH SWT Allakhou Akbar ndeysanne Adouna diaroukoo Dieureudieuf ❤❤🙏

  • @ndeyebintadiop7736
    @ndeyebintadiop7736 5 років тому +1

    Je suis talidéy cheikh .Mais tu ma fait vraiment pleure de ton chanson omaro. De tout mais condéleas,il été un grande maradou ,et digne de se nom😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @ibrahimaba3096
    @ibrahimaba3096 5 років тому

    Barki serigne saliou si thiangui lagnouye sakhe Ba faww😭😭🙏maneu lou doule serigne béthio Safouma dakhe moma défe mourite ngioune wa touba ndare chékhe bi rékeu akeu wa keureum alpha ba

  • @Miss_Yyyy
    @Miss_Yyyy 5 років тому +11

    Ndeyssane da beugone Cheikh Béthio nak.
    Du courage adouna mo démé ni. Adouna dou dara 😣

  • @khoudishdiarra2508
    @khoudishdiarra2508 5 років тому

    Allahou akbar ndeye sane omaro dioylo nga gnou bari yalnako yalla kharé aldiana té maylen kholou mougn 😤😥

  • @anitabenejeloune8669
    @anitabenejeloune8669 5 років тому +34

    Omaro c est bien nit deye deugou tout le monde sait tu aime beaucoup serigne saliou et cheikhs betio clip bi nekhna machala

  • @arametoure8258
    @arametoure8258 5 років тому

    Ndeyssane Yalla nako Yalla Yeureum Té bolé ko ak Serigne Saliou mou térou ko dougueul ko Aldiana Firdawsi

  • @Mskmg37
    @Mskmg37 5 років тому +13

    Man katolike :la wayé yalla nako yalla ak serigne saliou térou si aldiana firedawsi👍

  • @mariamandiaye6340
    @mariamandiaye6340 5 років тому +1

    Non sama yaram dawna je suis talibe cheikh ms omaro sa waye toyal na sama khol serign b thioun yalla nako yalla yereum khare ko aldjana yalla djegeul ko

  • @bambaprincefaye9233
    @bambaprincefaye9233 5 років тому +4

    Mà cha alla j ai les larme àu yeux oh omaro s ést sincère je sens ke tua un grand vide mais yalla bahna cheikh d'où fi massa diougué

  • @djilydiop6062
    @djilydiop6062 5 років тому

    Cheikh bethio thioune yalla nako yalla yeureum té kharé ko aldiana si barkép Serigne SALIOU mbacké ❤😢😭😭😭😭💪❤

  • @ndeyekhadydiop3257
    @ndeyekhadydiop3257 5 років тому +10

    Ndaysane Omoro yalla nala yalla may kholou mougne ak bép thianta. Cheikh bi yalla yeureum ko tabalko aldiana. Métina mai délou santate yalla. Si yalla lagnou diougué té si mom laniye délou.

  • @kanediallo4579
    @kanediallo4579 5 років тому

    Omaro goudal fane
    Cheikh bethio yalla na yalla yok say leer🙏🏾❣️

  • @rokhayaniang9504
    @rokhayaniang9504 5 років тому +13

    Omaro ya nex xel dh déjà fénete nga fi wayy félicitation

  • @djibycisse4051
    @djibycisse4051 5 років тому

    Cheikh Bethio yalla nako yalla yereum tei kharei ko aldjana ak bep djoulite boufi bayeko

  • @elj2808
    @elj2808 5 років тому +5

    Thiey yalla adouna dou dara cheikh bi dème na ni rek.....
    Yalnako serigne saliou térou

  • @ndeyefatouba3655
    @ndeyefatouba3655 5 років тому +1

    Len rek moma neikh si Omaro mom meussoul neubb que talibé Cheikh Bethio la malgré louko Sénégalais yaakk bassi mane mii. Ndah niou beuri bi tiol lii djibéé danio dawoone mais tay bi yalla léralé niou nieuwate di post di wakh ragal fetté dal day khagné weurseuk. Omaro yalla nala Cheikh bi takhawou nikoo Serigne Salihou takhawoo. Reposes en paix Cheikh Bethio.

  • @rogersotieno773
    @rogersotieno773 5 років тому +8

    Yalla nako yalla yeureum kharéko aldianna firdaw Cheikh béthio

  • @cheikhabdoudia2398
    @cheikhabdoudia2398 5 років тому

    Machlla omaro amaty na soolo Torop machlla yalla nako serigne touba terou ty Barkeb mawahibo amine

  • @imaneanne9464
    @imaneanne9464 5 років тому +9

    Son bi nèkhna kadou yi rafète na frero yalna ko yalla yeureum tè khareko aldiana firdawssi Amine 🙏🙏🙏🙏

  • @bintadiengmussaliou
    @bintadiengmussaliou 4 роки тому +1

    😭😭😭😭😭thiey du ma ci massa doyal

  • @myarecavision7872
    @myarecavision7872 5 років тому +7

    ndeysane sounou serigne bi démna .damaka beugg ndah thiofél bimou am si serigne saliou mbacké té manite serigne saliou tafanék sama khôl ak sama yaram,ndeysane. serigne béthio dodiouk si khôl yi yalnala baye zalle téérou,.😢😢loudoul yalla néénela,niirék la meunone déméé

  • @Baba92
    @Baba92 5 років тому +1

    *je suis un tidiane de tivaouane mais je suis ému de cet chanson. Que la terre lui soit légère. Et k Dieu l'accueil dans son Paradis.*

  • @pendaba3040
    @pendaba3040 5 років тому +53

    Ay sama wadial dém na ni.merci bcp omoro

  • @kanamere1127
    @kanamere1127 5 років тому +1

    Sante serigne saliou rek

  • @sokhorcle4489
    @sokhorcle4489 5 років тому +149

    Repose en paix Serigne bethio thioune

  • @ndiayetacko5702
    @ndiayetacko5702 5 років тому +1

    Sama khele mi demna si sama djeukeur khalébou ndaw 84 la djoude taye mou déme bayi ma thieye adouna mo mouno wore d😢😢😢😢😢😢

  • @olyladeesse3068
    @olyladeesse3068 5 років тому +34

    *Machallah sh8 po Mouride mais cette chanson m'a rendue émotionnelle Yalla naka Serigne Saliou terou*

    • @badoundiaye9423
      @badoundiaye9423 5 років тому

      Bilahi oly ta raison même moi je suis pas mouride mais cet chanson m'a fait pleurer car quoi qu'on puisse lui dire cheikh béthio diambar diou mag lawone si yonou mouride té nak yalla dou fay wax bayi dieuf kouné guisnako khana nianal ko yalla yeureum ko té kharé ko aldiana té wanéléko ak serignam sopé di serigne saliou mbacké

    • @mexdroid1703
      @mexdroid1703 4 роки тому

      Bayilén bokalé yalla rk moy térou

  • @cheikhbasskeurmassar4654
    @cheikhbasskeurmassar4654 5 років тому +1

    Ndeysane

  • @perfectmbaye949
    @perfectmbaye949 5 років тому +4

    machalah omora liguéy bi rafétna Zbest yalah nala yalah téral sama mak dji Ndiaye diatta kéne d'où yaw

  • @bobbiepatterson1924
    @bobbiepatterson1924 5 років тому

    Chekh béthio thioune diamou Serigne Saliou ba yalnako Serigne bi térou té téralko barké Wérou Koor gui 😓😓🙏🙏

  • @sokhnamaidieng7842
    @sokhnamaidieng7842 5 років тому +102

    Dioylo guama nak 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭sama khél bi yep da délou wat si serigne saliou cheikh Bethio yalla nala serigne saliou térou

  • @awasarr7389
    @awasarr7389 5 років тому

    Omaro borome kholou Diama bi toute mes condoleances

  • @mamecheikhantadiop9692
    @mamecheikhantadiop9692 5 років тому +6

    Que la terre lui soit léger le bon Dieu accueil dans son haut paradis 😭😭🤦🏽‍♂️