Hée! Bour Gueweul waxna lou graw si Pokola vs Talfa, Abdou Bakhoum allume Franc et modou Lo

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 7 січ 2025

КОМЕНТАРІ •

  • @MoustaphaKEBE-d4x
    @MoustaphaKEBE-d4x 20 годин тому +4

    Modou lo moy séne baye moy couvereneure pikine ❤❤❤❤❤❤❤

    • @Mbodji-walo
      @Mbodji-walo 16 годин тому

      Damay ooh wa Guediowaye dé😂

  • @elhadjimaodoniang5531
    @elhadjimaodoniang5531 16 годин тому +2

    Modou lo kasser
    Nopalou leen dou sen morom C’est le roi🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥

  • @ThioubouArnold66
    @ThioubouArnold66 23 години тому +10

    Bakhoum Kou sokhor la mouy melni crocodile ni😅😅

  • @MameSow-r4i
    @MameSow-r4i 23 години тому +4

    Modou ❤❤❤❤looooooo❤❤❤❤❤

  • @DethieDioufFissel
    @DethieDioufFissel 16 годин тому +1

    Bilahi Bour guéweul vrai saytané la😂mais yalna yalla mayy POKOLA, JACOB, AMA ndams yous sédd gouyy 🤲

  • @leboundoye7898
    @leboundoye7898 23 години тому +5

    Ki moo meuna doull
    Modou lo moy sene baay

  • @BayeAbdoulayeGueye-en2cn
    @BayeAbdoulayeGueye-en2cn 10 годин тому +1

    non pére danga sokhor Modou lo est le meilleur lutteur de tout les temps

  • @CheikhIbraFall-u2r
    @CheikhIbraFall-u2r 20 годин тому

    Ama baldé yalla nkô yalla TaxaWou incha'Allah maïko ndam si barké seydina Mohamed psl ♥️🫶🌴

  • @benzdictenobalegomis6139
    @benzdictenobalegomis6139 15 годин тому +1

    Thieye pikine aye mague yo khameni yalla topéwouléne dara
    Motakhite chaque jour yalla waneléne bopam

  • @abdoulayeba1461
    @abdoulayeba1461 7 годин тому

    Modou kharagne lo 💪 💪 💪 ❤❤❤

  • @MOUSSATERANGA-n9i
    @MOUSSATERANGA-n9i 21 годину тому +1

    Ndeysane bakhoum manoule supporté Modou lo

  • @thiawfoot5217
    @thiawfoot5217 8 годин тому

    Ngathie Gueye deuk la ❤❤❤

  • @jobehamidou6545
    @jobehamidou6545 9 годин тому

    Merci bour

  • @leboundoye7898
    @leboundoye7898 23 години тому +5

    Modou lo moy Maire Pikine
    Nangouléne lii yalla dogaal

  • @diopmar6382
    @diopmar6382 23 години тому +5

    Abou bakhoum modou lo mo meune sa baye

  • @ndiagafaye3106
    @ndiagafaye3106 19 годин тому +1

    Ba leen siisou nak franc moo leen meunn té Abdou bakhoum mii chaque jour mou am guaathié wallaahi

  • @amdymoustapha6130
    @amdymoustapha6130 23 години тому +4

    Bakhoum y'a sokhorr

  • @mansourkane1426
    @mansourkane1426 20 годин тому +1

    Abdou bakhoum sa data yaye sa khourou papa

  • @BayeAbdoulayeGueye-en2cn
    @BayeAbdoulayeGueye-en2cn 10 годин тому +1

    26 coups lako Modou lo door

  • @bassirousamb3595
    @bassirousamb3595 18 годин тому

    Pabi bouy dé cardiaque mokoy raye ndakh boné modou Lo rek cardiaque bii yék franc day dane ama inchallah alla

  • @AbdaNdongo-h5l
    @AbdaNdongo-h5l 19 годин тому +1

    Modou Lo seul talfa seul faran seul

  • @assanekaka9414
    @assanekaka9414 16 годин тому +1

    Bakhoum yangi waxati barké yalla suma donon mbeur bakhoum duma ko may mouy wax ci man mouy lou bakh wala lenen

  • @BaMasour
    @BaMasour 22 години тому +2

    Wakhrek guene meune modou dou diourome tamou noklene danelene

  • @papefall7062
    @papefall7062 21 годину тому +14

    Abdou nakhoum bilahi dafa sokhoré modou lo 😢😢😢😢 c dommage vraiment. Ama merite mieux, lui c un vrai bay fall

    • @SerigneFaye-n4o
      @SerigneFaye-n4o 21 годину тому +3

      Sisouman khôl bou bone la yor

    • @papefall7062
      @papefall7062 21 годину тому

      @SerigneFaye-n4o bilahi frère

    • @hamidoutall9134
      @hamidoutall9134 21 годину тому +1

      Wayé dina déh deh koumou foral modou nokou ko

    • @abdoulatifdiop5640
      @abdoulatifdiop5640 17 годин тому +1

      Ki dafa doff

    • @DethieDioufFissel
      @DethieDioufFissel 15 годин тому

      Vous parlez trop il faut être honnête ce que Père Abdou a dit ces la vérité seulement. Va vous faire foutre way😂

  • @bassiroundiaye3913
    @bassiroundiaye3913 17 годин тому +1

    Diome mome amouléne ko menouléna bayi modou lo

  • @NdiawDiop-o6u
    @NdiawDiop-o6u 22 години тому +2

    Modou lo Ama leroul loutakh défoulent recours😂😂

    • @Torodo5434
      @Torodo5434 22 години тому

      Vraiment ki mbame la rek ak égoïste

  • @OuseynouSarr-l3z
    @OuseynouSarr-l3z День тому +2

    yénigui wakhaté bakhna 😂

  • @jeanpaulgomis6427
    @jeanpaulgomis6427 16 годин тому

    Ama boy bi moko sauvé na santé yalla sinon cadavre nguén warona yobalé😂

  • @bachirdomouparcelle4293
    @bachirdomouparcelle4293 21 годину тому

    Baxoum nena dieul bim dane ama leroul Billahi yaye Dmrm 🤣🤣🤣😊

  • @cheikhtidianedia2424
    @cheikhtidianedia2424 20 годин тому

    Billahi gni ay doméram lagne

  • @falloubeye4763
    @falloubeye4763 21 годину тому

    Kou may sagualé Abdou Bakhoum 😂😅

  • @AladjiFall-yz8oj
    @AladjiFall-yz8oj 21 годину тому

    Bakhoum aka sokhor si modou lo

  • @assanegueye1352
    @assanegueye1352 22 години тому +1

    Per danouy wakh Pathé balde mé yawawit yalla topéwoula dara ama modou nioussnako daneko 😂😂😂 wa pikine ndieuw di walou bodé lolou moy var kone yalla na modou di yaga dém var

  • @kurayahmi
    @kurayahmi 21 годину тому +1

    *Abdou Bakhoum bayi leine diko diokh micro non seulement dafa sokhor mais il dit des propos haineux. Lane moy Franc neu andak ay yefeer? Les catholiques croient au même DIEU que nous les musulmans. Ay joulitt legn dougn ay yeferr. Wakh dji niaw neu torop*

  • @bigpatotvmbeurouaskanewi453
    @bigpatotvmbeurouaskanewi453 2 години тому

    Ndeysane Abdou bakhou day fooo rekk day nékhal lamb rekk kou beug modou lo leu foum wakh toudou ko

  • @AssaneMboup-p7f
    @AssaneMboup-p7f 4 години тому

    Modou lo ak ama kou danon dama fatté sen combat bii😅😅

  • @DaoudaCisse-hn6hy
    @DaoudaCisse-hn6hy 23 години тому +3

    Abdou bakhoum sa data baye 😂

  • @Domouparcelle
    @Domouparcelle 21 годину тому

    Day toukhhhhhh 😂😂😂

  • @MoDraronie
    @MoDraronie 20 годин тому

    « Andak yefeurrr yiii » Bakhoum vrai domrammmm leu

  • @EumeuSamb
    @EumeuSamb 13 годин тому

    Bakhoum kagn lay wérr

  • @AboubacryGASSAMA-zs7oi
    @AboubacryGASSAMA-zs7oi 22 години тому +1

    Bakhoum eske khèlmi migui bakh tamitt😅😅😅10% yi motakh mouy wakhèni rèk amoul khèlou sportif voilà😅😅😅

  • @ndiagafaye3106
    @ndiagafaye3106 19 годин тому

    Li ma ci neex inchallah mooy bou biss baa ngueen seugueu ti rek tamm ngueen ko 😅😅😅

  • @hamidoutall9134
    @hamidoutall9134 21 годину тому

    Amo len diom deh 23 Coup nguen wakh Modou dou dara

  • @Niomnieugz
    @Niomnieugz 21 годину тому +1

    Mac bou malhonnête mo nek nii🤦🏾 Abdou bakhoum nopaloul Ama modou Lo louko yobou var wakhoko d rien à avoir ak siteu modou Lo

  • @Mobachir92
    @Mobachir92 17 годин тому

    Niak diom wessouwoul gua andi sa mbeur Modou niouss ko bagne dougou diko até mais toujours yaye topatt di wax si mom bamou len dané lalen faté fétéwolen wakh dji ba Franc yeksi

  • @TouradeNguer
    @TouradeNguer 21 годину тому

    Ki weroul waye dou nit

  • @cheikhmbackesyll9838
    @cheikhmbackesyll9838 22 години тому +1

    Te gua bayii modou lo yaw kou katt sa ndeye sokhor gua

  • @bachirdomouparcelle4293
    @bachirdomouparcelle4293 21 годину тому

    00:53 kone deh na wadial teki nguembam

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 20 годин тому

    Ama baldé mo meune franc

  • @Deugkeep
    @Deugkeep 20 годин тому

    Sokhor day ray ..

  • @ndiagafaye3106
    @ndiagafaye3106 19 годин тому

    Yeen yeeneu moom micro gneulé moom jëf dji

  • @soppeousmanesonko777
    @soppeousmanesonko777 22 години тому

    Yow père Bakhoum yow combat Modou Lo Ama balade kane lagne si dorr Mouy Daww ? 😂

  • @AtoumaneNiasse
    @AtoumaneNiasse 21 годину тому

    Pawou Pékin you doff yagui ni toujours wakhou doff tilim ak khoul you bone rk😂😂😂

  • @ousseynousangott740
    @ousseynousangott740 16 годин тому

    Mais Abdou Bakhoum LoutakhH mou sokhor kii moy domou fils de nuit domeram nga way père niakk lerr rekk loutakh nga mell nii sa ngam niou niapp ndemm yii

  • @leyemouhamed2149
    @leyemouhamed2149 4 години тому

    😂😂😂

  • @SerigneFaye-n4o
    @SerigneFaye-n4o 21 годину тому

    Pa bou sokhore Mugui ni

  • @barradieng9824
    @barradieng9824 20 годин тому

    Borome kap Bou nioul ndayam bi mo mana doul ama modou lo dane ko lou lér Dor bamou tede

  • @cheikhdiakhate219
    @cheikhdiakhate219 21 годину тому

    😂😂😂😂😂😂😂

  • @avivetcabinet512
    @avivetcabinet512 День тому

    😂😂😂

  • @PapiNiang-l3p
    @PapiNiang-l3p 7 годин тому

    Bour tu es dangereux pourquoi wakho albourakh niou abalê balla

  • @gorguidieng7796
    @gorguidieng7796 22 години тому

    Bour bilahi ama baldé bou paré mou meune fouki Modou lo

  • @jeanpaulgomis6427
    @jeanpaulgomis6427 17 годин тому

    Amal yarrmak nga

  • @DaoudaCisse-hn6hy
    @DaoudaCisse-hn6hy 23 години тому

    Yaw Doull