Entre l musique d'hier et aujourd'hui c'est que cette musique d'aujourd'hui ça va dégoûter très tôt Mais avec l musique de nos chers mamans chaque jour day béss daye nekh C'est très naturel
Sokhna Tabara ak Mame Abdou yalla naléne Yalla yok yeurmandé ak ler failléne bayi fi Serigne Maodo lou yak ak gnabot El hadji Malick ak kilifa diné yeup def diam si réw bi
L'éducatrice, cantatrice et diva , vous avez écrit une très belle histoire musicale sénégalaise, longue vie à la grande diva de la musique tradi-moderne
La musique comme on l'aime ,la tradition dans sa beauté la beauté de la femme sengalaises dans toutes ses formes . Senegal et sénégalaises revenons a nos valeurs et nos traditions
J’adore La partie oú elle parle des liens de parentés entre la famille de Serigne Bamba et Mame Maodo🥰 «Eumeudy farimata et Demba farimata nio bokk ndeye ak baye serigne mbacké maram moy Sen baaye...»
Ken dou kiné lam « Sa bay mingui si rawdou bi aboubacar lagnou kay wowé ali boy michel samba naar, khar yalla sidy, dyana sidy « , fofou la bokek yaw machallah 😍😍😍😍😍😍👍🏾.
Wawaw Adjaratou kine lam mame bamba La grande Diva de la musique sénégalaise. Merci beaucoup ibrahima sylla syllart production d'avoir déniché ce talent inégalable dans la musique sénégalaise et africaines..❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
écoutez les retro de la musique sénégalaise, plein de sens et mélodie vachement agréable à écouter, différents des musiciens d’aujourd’hui. Machallah! si seulement vous pouvez revenir sur la scène musicale sénégalaise, nous allons vivre une nouvelle ère.
C'est ça le vrai culture Sénégalais di soll ay yéré you diot di féthi féthi mou rafét mais contrairement aux vulgaire génération qui imitent les occidentaux et les richesse
La culture wolof est top🇸🇳💯😘 mashhallah Kiné Lam une grande Diva ❤
Wallahi kiné Langa Wakh Sokhna Oumou kalssom Sy Moy Sénégal
Ce clip.a mis en relief la beauté de la femme sénégalaise dépouillée de toute impureté innovatrice(khessal,greffage etc...)
Way bii comme tay ndeysan ndakh nekh ❤❤❤❤❤
Entre l musique d'hier et aujourd'hui c'est que cette musique d'aujourd'hui ça va dégoûter très tôt
Mais avec l musique de nos chers mamans chaque jour day béss daye nekh
C'est très naturel
Bilahi dégal mélodit yi cheikh tijaan tall ndeysan
Sokhna Tabara ak Mame Abdou yalla naléne Yalla yok yeurmandé ak ler failléne bayi fi Serigne Maodo lou yak ak gnabot El hadji Malick ak kilifa diné yeup def diam si réw bi
Amine yarabi🤲🤲🤲🤲🤲🤲
Amine ya Rabi 🙏
Li nimouy DF sama khôl bi ❤❤ohhhh je suis mouride mais damakoy déglou chaque instant 😢
L'éducatrice, cantatrice et diva , vous avez écrit une très belle histoire musicale sénégalaise, longue vie à la grande diva de la musique tradi-moderne
Machalla kiné lam serigne abdou Aziz sy yalla na yalla yokou léram
Liii déh moy vrai hénné time ,wayé Sénégal dagne thi bolé lou bokoul😆
😂❤
je suis un véritable fan de la musique traditionnelle. Elle me soigne et me rend joyeux.
La musique comme on l'aime ,la tradition dans sa beauté la beauté de la femme sengalaises dans toutes ses formes .
Senegal et sénégalaises revenons a nos valeurs et nos traditions
0% nudité
0% sagga
0% vulgarité
Et... Ça touche le plus profond du soi...
La femme sénégalaise est belle dans un grand boubou
Machallah merci Tata kiné Lam pour cette belle chanson dédié à la famille sy 🥰🥰🥰💯
J’adore La partie oú elle parle des liens de parentés entre la famille de Serigne Bamba et Mame Maodo🥰 «Eumeudy farimata et Demba farimata nio bokk ndeye ak baye serigne mbacké maram moy Sen baaye...»
Même moi aussi j'adore
Nio Bokk lèpp encore Diggeunté S.Fallou ak S.Abdoul Aziz Dabakh danio Bokk si Côté Ndeye ak Baye 🙏 Mashallah
@@fatoubah4800 ppp
Sayou ma dék lo son bi rek bgeu may maman kiné aye millions billay ki écoute en 2020👂👍
En 2024 je suis là
L'un des plus beaux clips Sénégalais vraiment ya que le nature
La meilleure cassette de maman Kine Lam. Je l’écoute jusqu’à présent sur Apple Music ❤
ey waay dembou aka neex lii mo dax lifi nek leegi ndeysan tan boy🥰
La grande cantatrice. Premier Hénné Time
Ken dou kiné lam « Sa bay mingui si rawdou bi aboubacar lagnou kay wowé ali boy michel samba naar, khar yalla sidy, dyana sidy « , fofou la bokek yaw machallah 😍😍😍😍😍😍👍🏾.
Eh wAaay liiii
Walay ndaysan wauay ama toul li ken masou ko giss
Wayou thiossane nékh neu😊maman Kiné yalla ngaa gude fane❤️
La Grande kiné lam lingua woy Sokhna Oumou kalsoum Sy "Dabakh" reuy na nèkh Eskeuy Mame Dabakh moy Bayam Sokhna Tabara Gaye moy Yayam wayè Tafsir Demba Bouna moy Mamam Mashalla Ya meun woy way Yagg fi lol tè Wër diniou bèggeul
Machalah sokhna tabara gaye khali Ousmane gaye masamba gaye diawar tafsir demba Bouna aka rirrrr djoudou
Machaallah 🤗
Wawaw Adjaratou kine lam mame bamba La grande Diva de la musique sénégalaise. Merci beaucoup ibrahima sylla syllart production d'avoir déniché ce talent inégalable dans la musique sénégalaise et africaines..❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mama kine la diva du Senegal yala nala yala may goudou fane ak wer tchi barke seydina Mohamed psl
Sénégal nekhona pauvres nouvelle génération nous avez tout pour être heureux et ont l'était
thieuy mame abdou sophietou arame bonko sokhena ndiaye ngouille ndiaye biram khoudia tam yalna na niou yalla tass thi sa barké sama mame
Ndeye Ndiaye yaw tamit linga tague souniou mame dji nekhna trop,mashalla
Ndeye Ndiaye macha allah
Machaallah ndiayene bi😍😍
Baa kham nguén ni Hanné Time adjia kiné lam moka ñëka deff si cilub Oumou kalssom 1993
Vous avez parfaitement raison
Billakhi waauy amatoul kholal thosaan bi degaul musique bi
Li daffa yiw dhe😂😂
Cheuteteut! J'ai cherche cette video pendant des annees! Un des plus beaux video clips de l'histoire de la musique senegalaise!
binoucheable ডফসফ
Je suis d'accord avec toi !! Surtout les boubou traditionnelle
Cette chasson me donne des frissons nekhna trop
écoutez les retro de la musique sénégalaise, plein de sens et mélodie
vachement agréable à écouter, différents des musiciens d’aujourd’hui.
Machallah! si seulement vous pouvez revenir sur la scène musicale sénégalaise, nous allons vivre une nouvelle ère.
A D Vraiment moi jen raffole 😊😊👌
Dafa lér rétro rék dangaye yeuk sa bop
Valeur yi amatoul beaute naturelle j'adore ce clip très originail
Qui est là en septembre 2019 pour écouter la belle voix de kinè Lam??
Ki est là en 2022 pour écouter cette belle chanson
Souma sagnone magou démbe laye donne lii nékhena waye❤❤❤
La meilleure maman kiné j'aime beaucoup ce tube
Qui l’écoute en 2020❤️🙏🏽
Moi ☝☝
Moi 💕💃
Moi
Moi
Moi j'adore cette chanson vraiment
je l'adore kiné lam, elle me rappelle mon enfance, je faisais toutes ses maniéres
Pleine de sens et de mélodie même à la traditionnelle. Vraiment hier est meilleure qu'aujourd'hui en terme de musique
En terme de tous
Billahi deug leu légui ni wayatounou dañougne tassou rk
bilay kamal malick khamo sakh lutah nga wah lii sonu thiosann rekk lanu amm tee artiste legi yii tegu niouko fenn
Qui l'écoute en 2019 macha Allah
leila sow moi 😍
Moi
Moi ndeysan yaram dawna
@@oumoudiop813 chante
2020
Ha ça c'était hier oumou kalssome dabakh malick ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤nekhna ba dé kiné lam longue vie à vous ziar nalen
C'est ça le vrai culture Sénégalais di soll ay yéré you diot di féthi féthi mou rafét mais contrairement aux vulgaire génération qui imitent les occidentaux et les richesse
Machallah Adja Kine Lam une grande diva. Loumou way mouneikh machallah 😍
Thiey adouna sa me replonge à de beaux souvenirs temps boy
Vraiment dafa nekh yaye kiné doundal lou bari😊
Ndeye sane thieuye Adouna bilaye ma beugone waye bi waye bima néké khalé
Maman kine lam j taimmme yalna yala weral baat bi k d bon souvenir
Ndeyssane temps yi nèkhone na 💕💕💕💕 masha allah
Ndeyssane machalah nehna trop
Li nakk moy henné time mais li khew legui ken khamoul loumou don bilay adaa ak tiosssann dara dakouko
Mama kiné lam aka mako beugua térale barké serign bamba wayé khamouma foumou deuk si dakar.
Omar Sylla parcelles assainies la deuk unité 25 côté monument bi bofa takhawé ko lathie keur kine lam mou wane lako
Lii moyy thiossanne mo nekhalone Sénégal wanté légui mom Moy lolou
Qui l'écoute en octobre 2020
Aka meun way machallah
Incroyable..les souvenirs d’enfance !
ohh lii nexna machalahh Maman kiné ndoundeul xamguenn nii lii nexna
Rombb na nekh machaallah ci mom
Ma beug Oumou Kalsom yi si boppam ❤️
nekh rek la. def kiné Dale. dou wayanetou
Mariéme Ndiaye .
J adoooore 2019. ...cest la tradition ..la culture ...la musique...
Vive la Tradition jadore🙏 🤗
Ndeysan longue vie à elle
On écoute plus de la musique
Naturel na nekh na si khol lay dougou machallah tata kiné chapeau
Qui est là en 2021 en plein confinement ?
Sui là
Ndeysane amoule khesall ak thioll gou bonne machallah maman kinè
Vraiment
Hoooo lii doynawar ta am vraiment adouna dou daara
Wow what a good image quality on what is a pretty old song... Thanks a LOT.
🥹🥹🥹 son bi nekhna walahi
Kholal niniou yiwei rek
Bathie Massamba Ndeys@an dawna yaram
Bilay ndeysane
veritable chef d'oeuvre
Ndeysan sama pape malick socce khalam rek lay defffffffd
quel beau clip... c naturel.. kine lam
P
Ouu est la en 2023
Bilaye ya mana waye lame
Ndeyesane 1990 j'avais 1 Ans
Musique amatoul Sénégal
Manchanlla kiné lam se clip ça me rappelle beaucoup de chose
Senegal nèxone na
Qui l'ecoute en 2020 masha allah
robena nekhe dou woyanetou te ndanane la
lou nèkh dièkhna
Musique traditionnelle dafa nekh
Dembo nekhouna te daniou yiwon❤❤❤
Ndeyesane les valeur amatoul fene bilahi
Quel chef d œuvre !!!
aucune femme au monde na la beaute de la femme senegalaise BLAISE CENDRAR
mansallah lii nekhna daal
Quel beau clip machallah kine lam c naturel machallah 😘😍😚👍👍
ligadone b soko begne dafa feke nga gueune seee gnaw. liiii lagnou mome. Nagnouko teye sougnou fouki loho.
saudações brasileiras
thieuye Adouna waye amatoule
thiossane yaye borrom la diva
@leftysergeant well that's part of it, but the lady is singing to holy man's daughter,. His name was Serigne Abdoul Aziz Dabakh.
Woy kate yi yaye Séne yaye waye bilahi
Li amatoul lep yiw di thiossane legui mom valeurs yi demna djiko yakhou
Ana koufi sasent beye
ah c ma chanson préféré j'aime bcp
Ndeysane sama yaram bagui daw....
LA CLASSE
Machala Sy Malick
Qui est là en juillet 2022 en mode enjoying ❤️
Doumassi doyal weiyou adja kinè lam yii ohhh