"Modou Lô est mon fils", Mame Gorgui Ndiaye fait des révélations sur XLO

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 5 лют 2025
  • #TaphatineVS#boyniang2 #modouloVS#amabalde #ballagayeVSbombardier
    #lambdiaspora​,#lamb​,#luttesénégalaise​,#SunuLamb​
    LEEWTOO TV est la chaine N°1 de la lutte sénégalaise.
    🔴 Abonne toi
    / @leewtootv

КОМЕНТАРІ • 111

  • @Idyxaragnelo
    @Idyxaragnelo 3 роки тому +30

    Papa Mame Gorgui Yalla guafi yaaaaaaaaaaag loooooooool té wére Modou Lo Xaragne Lo Yalla nala Yalla maaaaay ndaaaaaam

  • @momotouray172
    @momotouray172 3 роки тому +3

    *Maa Shaa ALLAH une première fois de vous voir j’entendais toujours votre nom mais Maa Shaa ALLAH une Longue vie à vous Et Merci 🙏 Modou LO Ndam Reik*

  • @papeomar8530
    @papeomar8530 3 роки тому +22

    Bilahi beugueunala Mame Gorgui Ndiaye sopeye Seydina Mouhamed(PSL). Coach Pape depuis Gabon

  • @mouhamedndiayeyoff7524
    @mouhamedndiayeyoff7524 3 роки тому +9

    Sunou baye mam Gorgui ndiaye yalna fi yageu loole ta wér amine ya rabi

  • @andrembengousarr7051
    @andrembengousarr7051 3 роки тому +12

    Un ancien lutteur que j'aime beaucoup longue vie à vous père Mame Gorgui Ndiaye

  • @papesidi9845
    @papesidi9845 3 роки тому +21

    Délén def ci soutoura
    Modou Lo un bon exemple 🙏🏾

  • @khadimpigue1140
    @khadimpigue1140 3 роки тому +17

    Ndeysane modou lo li rafet na trop bon continuation champion

  • @khadimlo5999
    @khadimlo5999 3 роки тому +7

    Mame gorgui ndiaye yalla nalla yalla bayi basi knam modou ligay
    Def nice na yalla nalla yalla may ndam

  • @alioucisse998
    @alioucisse998 3 роки тому +7

    Mame gorgui Ndiaye yalla na fi yag té wér amine 🙏🙏

  • @hasboyedawe9569
    @hasboyedawe9569 3 роки тому +14

    Merci modou lo mame gorgui ndiaye doundal 200ans 🙏🙏🙏

  • @baidy7418
    @baidy7418 3 роки тому +20

    Ndeysaan modou kou baah leu....délén guestou ancien mbeur yi 🙏

  • @Steven-ul8pw
    @Steven-ul8pw 3 роки тому +7

    Tabarackalah Modou Xaragne lo walahi litah yalla def ma beug le bobu batay rathiouw mako tjr yangui niouy sagal ay djeufu Noble rk ngay def yallnala yalla fay kuy keral mak ak xalé ak djiguéne do torokh muk nasi niép bayi xél

  • @khalildiaw9127
    @khalildiaw9127 3 роки тому +9

    Machallah goude fane ak werr gui yaram mame boye❤

  • @malicksarr8303
    @malicksarr8303 3 роки тому +11

    Mame gorgui Ndiaye sopou Nala ndakhe modou xarang lo ♥️❤️kokou awmasi khéle ♥️🤷‍♂️

  • @daoudasarr3614
    @daoudasarr3614 3 роки тому +2

    Merci mame gorgui yalna yalla yok fane lol ande ak wer thieuy x lo

  • @mamikane9180
    @mamikane9180 3 роки тому +11

    Merci papa dam rek issalaha modou lô

  • @sidibouyafaye8608
    @sidibouyafaye8608 3 роки тому +4

    Mame Gorgui Ndiaye sopaye SEYDINA MOHAMMED

  • @papeomar8530
    @papeomar8530 3 роки тому +7

    Macha Allah yalla nala borombi maye goudou fane ak wér ci barké Seydina Mouhamed(PSL)

  • @mamadouly6561
    @mamadouly6561 3 роки тому +11

    Diadieuf père modou lo moy champion

  • @ibrahimaNiang-rl2xi
    @ibrahimaNiang-rl2xi 3 роки тому +1

    Machalllah mame boye yalla nalla yalla défale diam bou bakh ❤🤲🏿🤲🏿🤲🏿🤝🙏🏿

  • @ndiagafaye3106
    @ndiagafaye3106 3 роки тому

    Maaacha allaah yalna diamm yaague té yalla yaaggal sa takhaway té may Modou ndam Lou seedd guouy

  • @mamesow2415
    @mamesow2415 3 роки тому +3

    Mame yalna yalla gouddal sa fan mayla wérr incha alla

  • @momotouray172
    @momotouray172 3 роки тому +1

    Bilahi Walahi Talahi Maa Shaa ALLAH Modou Lo Iaw Daleuh Chaque Fois Mbecté reik Ngagnouye Diokh Bilahi Dagnou Rousslo Jamais ♥️Alhamdoulilah Bimala Sopei

  • @ndoffenetine5333
    @ndoffenetine5333 3 роки тому +10

    Mod lo ❤❤

  • @dabondiaye7796
    @dabondiaye7796 3 роки тому +1

    Bravo Modou Lo un est un exemple pour les autres champions respect ✊ Gris bordeau il faut allez visiter ton père Balla Gaye sama champion toi aussi tous les champions doivent allées visiter les anciens champion et leur faire sourie

  • @daoudasarr3614
    @daoudasarr3614 3 роки тому +8

    MODOU lo yalnanga bayui lamb ak courone bi

  • @abdoulayet4086
    @abdoulayet4086 3 роки тому +2

    Yalnala yalla dolli diam

  • @moustaphasonko596
    @moustaphasonko596 3 роки тому +5

    Mame yalla nala yalla may wëre machallah

  • @ahmedmb7491
    @ahmedmb7491 3 роки тому +17

    Walay Modou ak yeniki gnoy mbeur You eup soutoura. Modou Lo il fait des actions sociales dans les prisons et dans les quartiers C’est pas parce que personne n’en parle mais Modou Mo beugoul dara siw. Lolou moy andouna

    • @badaradiouf4646
      @badaradiouf4646 2 роки тому

      Bilahi lou lerrr contrairement à balla baaxna nakk mais toutes ces actions dafay feusss trop

  • @abdoulayeniang2511
    @abdoulayeniang2511 3 роки тому +3

    Talibé Serigne Moustapha Sy Djamil Pure Yalla na Yalla guena Goudeule sawe fane défale la wére Barké Al Khourane ❤️🙏

  • @mamadousarr3371
    @mamadousarr3371 3 роки тому +7

    Merci Modou lo délen gestou ancien mbeur yi di wakhtan ak niom delén diapele .. mame gorgui ndiaye sopey seydina mouhamed

  • @jarrafmoussakane9088
    @jarrafmoussakane9088 3 роки тому +2

    Ki nak moy Mame gorgui ndiaye seutoub marame diéne yallna sa diama yague sibarké seydina Mohamed psl

  • @tupacsahkur1260
    @tupacsahkur1260 3 роки тому +8

    Yalla nakou fi yalla bayi baci kanam

  • @seydinaissademe8122
    @seydinaissademe8122 3 роки тому +2

    Machalah goude fan ak weer sounou mame

  • @momotouray172
    @momotouray172 3 роки тому +2

    Walahi nous avons besoin de ça et je pense il mérite souvent qu’on lui fasse des interviews des conseils de la vie car le Sénégal 🇸🇳 ne manque pas de savant comme ces vieux mais Dougnou leine Xam ce qui est anormal

  • @chamousman2726
    @chamousman2726 3 роки тому +4

    Macha allah ken du modou lo leppu si sutura lakoi deffeh kii du moromu gayi blie 😋😋

  • @diopdiop7008
    @diopdiop7008 3 роки тому +1

    Yalla na yalla goudal fane wi inchallah

  • @modoucamara3772
    @modoucamara3772 3 роки тому +2

    Machalah per godou fane rek lalay nianall ak wer

  • @daoudambow8348
    @daoudambow8348 3 роки тому +2

    Modou Lo lepeum soutoureu leu 🙏🏿

  • @mordiop9187
    @mordiop9187 3 роки тому

    Yalla na yalla goudeul fan wi❤️

  • @azizsarr9533
    @azizsarr9533 3 роки тому +2

    Goudeul fane mame boyyy🙏

  • @hafissoukane2003
    @hafissoukane2003 3 роки тому +2

    Longue vie champion ❤️🙏🏽

  • @momotouray172
    @momotouray172 3 роки тому +1

    Super 👍 Maa Shaa ALLAH

  • @fadelbadiane7525
    @fadelbadiane7525 3 роки тому +3

    merci mame

  • @FallDamel7484
    @FallDamel7484 3 роки тому +4

    Machallha♥️♥️Pape Doundal

  • @clientelaspalmas3721
    @clientelaspalmas3721 3 роки тому +3

    Machalla rafètna

  • @dameseck6232
    @dameseck6232 3 роки тому

    dieredief papa yala na yala mayela goude fane ak werr ak bouleme diolete amine ya rabi😍😍

  • @bayfallfall1256
    @bayfallfall1256 3 роки тому +10

    Mame gorgui Ndiaye enfants chéris de Dakar

  • @ndoumbeseye6798
    @ndoumbeseye6798 3 роки тому +1

    Yalla na yalla goudal sa fane

  • @momotouray172
    @momotouray172 3 роки тому +2

    Mame Gorgui NDIAYE Sopey Seydina Mouhamed ♥️

  • @jazzjazz4902
    @jazzjazz4902 3 роки тому +13

    DEL KHOL SOUBA MBEURS YEUP DEME SEETI KO COMME MODOU LO DEMNA SETIKO😄😄😄

  • @khalifasow3600
    @khalifasow3600 3 роки тому

    machallah modou kharagne lo talibè cheikh ngua lou bakh rek mola war

  • @marielaureahoua6369
    @marielaureahoua6369 3 роки тому +2

    Modou lo vraiment chapeau

  • @serignefall3000
    @serignefall3000 3 роки тому

    Ndeye San modou lō moy papay mbeuri 💙🤍❤️❤️❤️❤️💈

  • @dabondiaye7796
    @dabondiaye7796 3 роки тому +1

    Masha un très grand champion mais les champions de cette génération doivent aller visiter les anciens pour les honorer

  • @momotouray172
    @momotouray172 3 роки тому +2

    Que de la connaissance

  • @papediop2039
    @papediop2039 3 роки тому +1

    Modou lô champion bilakhi

  • @laminediabakhe8459
    @laminediabakhe8459 3 роки тому +1

    Yague lol ta weer bou beuré gua contane su bako gua contane merci Modou lo

  • @dembakharagnelo2379
    @dembakharagnelo2379 3 роки тому +1

    Auhh yalnanga goude fanne mame gorgui🙏🏼🙏🏼🙏🏼

  • @leminsarr9667
    @leminsarr9667 3 роки тому +2

    Machalah

  • @nioulesskaye8964
    @nioulesskaye8964 3 роки тому +3

    Modou lo amoul morome billahi diame réck laye ame kouko bagnie do ame loula nékh si lambji

  • @papesenne8010
    @papesenne8010 3 роки тому +2

    lo❤❤

  • @ndiagafaye3106
    @ndiagafaye3106 3 роки тому +1

    Yalna yalla guoudeul fanam

  • @pouyelepro5668
    @pouyelepro5668 3 роки тому +4

    Ndeye san they Modou lo

  • @alioudiouf6405
    @alioudiouf6405 3 роки тому

    Machallah yalla na yalla weral yaram yi

  • @papeseck6124
    @papeseck6124 3 роки тому +3

    ndaysan yaggaufi té weur

  • @madembasy1504
    @madembasy1504 3 роки тому

    Allahou akbarrr kabira

  • @taphademe2261
    @taphademe2261 3 роки тому +1

    Yalla nala Yalla may wèr ak goudou fane

  • @abdoulayediouck3539
    @abdoulayediouck3539 3 роки тому +7

    Deysane sama yaram dawna

  • @papaniawba1734
    @papaniawba1734 3 роки тому +4

    Ho adouna dou darra

  • @abdouazizsy7991
    @abdouazizsy7991 3 роки тому +8

    Yalla nakofi yalla bayi baci kanam

  • @kenzykindkeinde38
    @kenzykindkeinde38 3 роки тому +1

    C honteux pour les lutteurs de fass. Il faut aller profiter de cette ancienne gloire

  • @ndiawdieng6976
    @ndiawdieng6976 3 роки тому +1

    Nice

  • @boubafall1014
    @boubafall1014 3 роки тому +9

    Mod’lo dou wax day dieuff rk niouy gis tal laniouy cedel bakh Mod’lo meusouko wax

    • @moustaphagaye1457
      @moustaphagaye1457 3 роки тому

      Mdr kou deff lou bakh kay daniou koy wax com niko gorgui Ndiaye défé nék léne sportif té rakhass séne xol yi bane mbeur mofi wax té douko dieuf

    • @thiamahmadulattekh562
      @thiamahmadulattekh562 3 роки тому

      @@moustaphagaye1457 li mou wax dey tontou gni nane dafa ney
      Kharagne dou def di video dey def nei thiel

    • @moustaphagaye1457
      @moustaphagaye1457 3 роки тому

      @@thiamahmadulattekh562 mdr kane moy deff di vidéo waxal

  • @kingmao6724
    @kingmao6724 3 роки тому +1

    Il parle sur modou lô 10h20

  • @bijouterielismam
    @bijouterielismam 3 роки тому +2

    Modou Lo 10mn 45s

  • @modoudiagne7607
    @modoudiagne7607 3 роки тому +3

    Mame grogui Ndiaye yagiu fi lol te wer lol mame

  • @djilyboumodoulo8217
    @djilyboumodoulo8217 3 роки тому +4

    Yague fi te wer

  • @diawcheikhna8130
    @diawcheikhna8130 3 роки тому +3

    Sama son bi aka nekh

  • @Steven-ul8pw
    @Steven-ul8pw 3 роки тому +3

    Mame goor gui Guéna dound Guéna wér yaw danga Bah maso fi déf walanga wah luñi xébé mbeur nayalla yok fan wi te doli sutra si

  • @gorguindiaye3068
    @gorguindiaye3068 3 роки тому

    Mashallah

  • @ballaguaye4203
    @ballaguaye4203 3 роки тому +3

    Yala mayla werrr goudal sa fane

  • @gorguidiop9840
    @gorguidiop9840 Рік тому

    ❤❤❤🙏🙏🙏♥️♥️

  • @MoussaGueye-o1b
    @MoussaGueye-o1b 11 місяців тому

    😢😢

  • @amethsarr6940
    @amethsarr6940 3 роки тому +1

    MODOU LO

  • @jazzjazz4902
    @jazzjazz4902 3 роки тому +3

    YOW DEE PÉRE WOUTE NGAK MBEURS ROU TEYE YI AK SEN 100> BOUDONE MBEUROU TEY LAGNOU WAKH😄😄😄

  • @adamandiaye7863
    @adamandiaye7863 3 роки тому +1

    Mame nasa jam yagg

  • @hannelhadji9368
    @hannelhadji9368 3 роки тому

    Bègue na bilahi

  • @moussacissebrahmanetv1308
    @moussacissebrahmanetv1308 3 роки тому

    😭👏👏👏

  • @babacarfall2774
    @babacarfall2774 3 роки тому

    Journaliste bi kou yarou té dale

  • @modoudiaw1960
    @modoudiaw1960 3 роки тому

    🙏🙏🙏

  • @sarrabdou3040
    @sarrabdou3040 3 роки тому +1

    Mo dafa diantalonn sahh

  • @daoudasarr3614
    @daoudasarr3614 3 роки тому +4

    Merci mame gorgui yalna yalla yok fane lol ande ak wer thieuy x lo

  • @hadjismith5689
    @hadjismith5689 3 роки тому +2

    Modou Lo doma rouslo jamais bilahi diam ci yaw rek 🙌🏿❤️❤️

  • @alioudiouf6405
    @alioudiouf6405 3 роки тому +1

    Machallah yalla na yalla weral yaram yi

  • @abdoulsy5365
    @abdoulsy5365 3 роки тому +2

    Machallah