Pape ndiaye vrai chroniqueur spécialisé dans un domaine precis. tu ne parle que de justice et rien dautres .contrairement aux autres khamougnou dara ba pare beug wakh thi lepp di fenn rek et se disent chroniqueurs aussi
Parfaite vérité et analyse mon frère monsieur Ndiaye grand journaliste politologue chroniqueur des affaires juridicojudiciares .Que ceux ou celles qui critiquent le nouveau gouvernement du président bassirou diomaye Diahar FAYE et son premier ministre Ousmane sonko et cie n'ont encore rien compris de la sincérité et l'honnêteté dans le travail bien fait de cette nouvelle équipe gouvernementale au pouvoir. Ce sont des saints d'esprits en politique. Alors soyons sérieux justes honnêtes et très rassurés .
Thiey pape ndiaye narone nga diaayyy sa xam xam wi macky ak ndiabootam ay vrai mbaam laniou wone. Kii limouy dako maîtriser yalla xamnako bravo et continu sur cette lancer pape ndiaye😅😅😅😅 borom missil yi
Pape tu es très pertinent Meree wone na la trop djamono maky sale mais... objectivement tu as une excellente analyse de l actualité juridique au Sénégal. Ndanane nga. Bravo
Bsr Sama gagni Naa gni woutti xamxam bala wayy diwakh dara thi benna biir . Xam dara ci ben mbir lou am solo parce que nieupalé naaw , exemple com pape Ndiaye mi Beaucoup de sénégalais parleparlo moléen néex DEUG MO NEEX
Pape Ndiaye mi der beug nako loll il est très précis. bilay wa sans limite de rouss nanou parce que niomm lolou rekk lanou bogonn bougane, cheikh yerim seck et kader Sokhor bakhoul
Pape ndiaye vrai chroniqueur spécialisé dans un domaine precis. tu ne parle que de justice et rien dautres .contrairement aux autres khamougnou dara ba pare beug wakh thi lepp di fenn rek et se disent chroniqueurs aussi
😊😊😊😊😊😊😊😊
😊
Rewmi dina sopeekou incahalla ndamrek yallanayala samoulen taxawoulen Amin yarabi 💯💯 Saloum Saloum 💯💯 kawkaw baykatbi ✊🏿🙏🏿
Parfaite vérité et analyse mon frère monsieur Ndiaye grand journaliste politologue chroniqueur des affaires juridicojudiciares .Que ceux ou celles qui critiquent le nouveau gouvernement du président bassirou diomaye Diahar FAYE et son premier ministre Ousmane sonko et cie n'ont encore rien compris de la sincérité et l'honnêteté dans le travail bien fait de cette nouvelle équipe gouvernementale au pouvoir. Ce sont des saints d'esprits en politique. Alors soyons sérieux justes honnêtes et très rassurés .
Thiey pape ndiaye narone nga diaayyy sa xam xam wi macky ak ndiabootam ay vrai mbaam laniou wone. Kii limouy dako maîtriser yalla xamnako bravo et continu sur cette lancer pape ndiaye😅😅😅😅 borom missil yi
😅😅
Vous avez raison, mais nòonu la il n'est jamais trop tard pour bien faire .
Pape tu es très pertinent
Meree wone na la trop djamono maky sale mais... objectivement tu as une excellente analyse de l actualité juridique au Sénégal.
Ndanane nga. Bravo
Pape Ndiaye, je ne commente pas souvent, mais je suis très content de t'écouter par ce que xam xam guay wakh.
Merci beaucoup c'est pertinent
Pape Ndiaye borom balance,gayii keufoone nañu Leu deh😂😂😂😂
Mouthie si macky yomboul dh 😂
SONKO ❤ DIOMAYE ❤ PASTEF ❤ 165 DÉPUTÉS POUR UN SÉNÉGAL RICHE LIBRE EN PAIX🎉🎉🎉 FIN DU SYSTÈME VAMPIRE PRÉDATEUR 🎉🎉
Bsr
Sama gagni
Naa gni woutti xamxam bala wayy diwakh dara thi benna biir .
Xam dara ci ben mbir lou am solo parce que nieupalé naaw , exemple com pape Ndiaye mi
Beaucoup de sénégalais parleparlo moléen néex
DEUG MO NEEX
Très pertinent Pape Ndiaye
Vérité ❤
Pape equilibriste pur et dur xam nañu lepp ,temps macky yagoul fii lañu fekk
Pape Ndiaye mi der beug nako loll il est très précis.
bilay wa sans limite de rouss nanou parce que niomm lolou rekk lanou bogonn bougane, cheikh yerim seck et kader
Sokhor bakhoul
Xamxam dou pexé...
Fii dou keur dofyidé
Merci pape❤
❤❤
AY SAGA KENE DOUKORAFÉTLOU KOU AMOUL KHAM KHAM BOWAKHÉ KHANA AY SAGA AGY KHASTÉ DANGAWARANO I
Attention missil sol sol
Pas de problème...Source ou pas. Loyauté et probité.
Tu les connais très bien? Vraiment ?
"Manquer de respect, injures..." Ils ont fait quoi?
Pape missile ya eup gathie gnépe 😅😅
Reste dans ton domaine comme ça et bien....
Cheikh yerim seck AK bougane Gueye warou gnou wone geuna kasso lane warone dem Li dafa yombou koi Saga nitte wakh nitte Loula nékh gnou bayi la ni kanene dinako wakh xaral toti rek
Bignona la deuk casamance