Wakho fiidara ça C'est la lutte ça le temps passe ok .com ça ne concerne pa cache toi ok avec yekini bala tout le sénégal disé bala a prématuré ninaa ninaa seulement vous avé ko ama a une vision vs voulé le bloké en disant di nimport koi ki ose dire modou é plus lourde ko ama le fils de falaye kiki modou é lourd ko tafa tine et alors modou boudeye niéméka va prendre l'avance c mio de dire ds bla blaaaa ok.
yaw xamo dara linga wax ni foko tek ? esk yaw xamnga fek 2 ans foumou lay fekk? wala Ama mom nékoul ci digge dollèm? mané lamb fitt la ta xalé koy def! ta beug louyomb baxoul ! bayi ba Modou lo niak dolé nganan ko kay nio beuré lolou dou exploit suis vraiment désolé
Père khana khamo modou ak niom ama ay morom laniou modou dalene ndieukeu feuleu rek
Khamoul lolou billakhi modou lo dinalen trompe
Modou mo mak sakh balla
Parole d'un expert 🤝
Ki est la en 2020 ama yeeeeee
per modou lo khale la deh
Konn janvier 2019-2020 binga wax mo diott nii nak, dinagn khol ndax sa wax yénouna maana bou gnom niarr tagaliko inchallah!
VAR daal mingui fi rek
Il a raison ama va battre modou lo
Modou lo de mo guen nourou ama hale et j sai k ay morome laniou ,te modou lo moko eupe igene de vie
Vive Ama le futur Roi des arènes amine
Mon yow kou la wakh ni madou lô mac là
Bilahi moussa yakham lamb lou ler nga wakh
Mais père Modou moromou ama la diih moh kholal bou bakh liguay wakh
Bigué ko wakhe ak legui 2 anns yi matt na legui bravo 👏
Bien dit père Moussa
svp j'ai besoin du numéro de moussa gningue urgent
Lolou yeufi ragalla..filakay daneii...gnou khamni bimouy dane modoulo thi digg doleim la neikk..wayeii khar ba modou djeikhal ngay doga beurei ak mom..tei modou sakh da neikhoul makk
ay morome l'an Modou magou ko
alalou bamba sa wadji modou mo makk Ama 90 leuh ish
Mouhamed Bakayoko yamana doull ama foumou neke 90 ama 88 la billakhi
Yow yagg gua indi mbeur niou dane ko di weuh ki werna
Jotna legui.. amayé
Père modou hygiène bou bakh leu yor mashalla. tei ama niam n'a
abdoulaye sy bobou Ama 14ans rk la amone
Père boulgnou yakal way,bayil mou gneuw Modou defal KO bagage RK
Wakhnga deguenak la cloche a sonè 2ans yi diotna seukke
Pér 2 ans matt na tay kon diotte 2021
Wahnga lou kén bayiwoul khel
Lima métty rék moy modou dinako humilié
Bayiléne ama gneuw rek dou lolou la beugueu boula kharagne lo diapé ba bayi la di nga kham nii yakamti bakhoul
Ningui si 2020 di modou dolem jexna 🤣
Diotna 2020😂😂
Yen fans Modoc love yi danguena khamol sport nill ba dè
ama dina maguet bayfi lo
Mais 2ans yi Mat na dh
Ndam rek
Khamo lingay wakh modou lo ak ama ay morome lañiou
Futur
2 ans yi matt na dé...Thiey thiaw sa khirrr
Pere Modou Ama mag amoufa
Na niaw Modou defal ko baggass
Billahi ya wakh deug
Kii kharagne magouko gno mbeuré ndo mbapatt t3 modou moko danone
Fidèle Castro voilà ya pas de différence entre Modou lo et Ama une année où 2
Les gars je vous dit simplement que Ama n'a que 28ans ok
MODOU LO kouy xarr mou maguette pour gua danne ko dihuz maguette bayikofi
Wakhofi dara wayyyy
Modou lô moola waleen wakhné mackla même génération la moom ak Ama Baldé la preuve Bërénañ moodaanko. daleen gëna am diom rk dakhleen bëré
Père grawoul bayil Modou nokhou KO rek
Père mou khar 2 ans si diguenté bi ya koye depense ? 🤣🤣🤣
Loolou deug la. Instant yi modou mingui si dolle na khaar ba thie kanam
2ans yi matna mai iska modou guenoul ame dolé
Père bayill gnou yarr KO bul gnou yakal
Mousa niang yakham lamb
Ki.limoy.wakh.khamoko.de.ama.moduo.ay.morom.lagno.de.maguinte.amthi.
pére iow dagay xarr si kaway modou xalé la
lou leer ngua wakh Père
copainboye wakhou fi dara
Legui lako ama di nokho ko daan ko sou defoul lolo kham nga lonoy wakh bimkoy daan dafa diekhal ay nafekh lan
Ah non père lolou amoul si sport
Papa no no
Lou lérr nga wax
Per khamm Dara barki yalla
Ama balde vs Modou Lo rek
2ans yi matna nak c fini🏋️
Diotna dai
Sa khallat rék ngay wakh mais linga wakh d'où kham kham
Pere niom niar ay morom Lagn Modou lo dalene raw rek si beuree door bi gueume bopam motakh niounane molene mak
Wakho fiidara ça C'est la lutte ça le temps passe ok .com ça ne concerne pa cache toi ok avec yekini bala tout le sénégal disé bala a prématuré ninaa ninaa seulement vous avé ko ama a une vision vs voulé le bloké en disant di nimport koi ki ose dire modou é plus lourde ko ama le fils de falaye kiki modou é lourd ko tafa tine et alors modou boudeye niéméka va prendre l'avance c mio de dire ds bla blaaaa ok.
N’importe quoi donc modou maguet leu 😅
J n sui pa d'accor avec toi.moussa gningue waho fi dara.tu es tombè dans l'irrationnel
Modou lo ama mem generation la rek magouko 3 ans youmat
Non père 2ans meme une semaine unchallah Ama va battre Modou
Kiakiakia le rêve es permis
pabi loumela wakh si lambe takal téré
Légui kone loutakh wa fass deuké danou
Non ama dafa asma sou yagé douko enragé ta Madou lou komba geuna yege geunko anrage motakh balla douko may tempo sino douko dane
Yor that philosophy is wrong . Modou lo, Ama is Now . Ok ok .
Fi ba aduna di touki modou dakoy daan
yaw xamo dara linga wax ni foko tek ? esk yaw xamnga fek 2 ans foumou lay fekk? wala Ama mom nékoul ci digge dollèm? mané lamb fitt la ta xalé koy def! ta beug louyomb baxoul ! bayi ba Modou lo niak dolé nganan ko kay nio beuré lolou dou exploit suis vraiment désolé
Wakhofi dara pèr
Nitt dou sokhar
C'est vrai d lolou mo dalone modou lo si balla gaye nakkk rekkk
Yaw xalatga moddou wangékou
AMA mo mak modou Lo. Leufeul ndeyou AMA
Yaw hamo dara
En tout cas heures boun beuree inchallh ama baldé dinako daan inchallh
yangui tok fi di féne RK ni
Tapha Djiamil Lo fo ko ték
Futur