Merci President vous montrez vraiment que vous êtes là pour le peuple. Sénégalais soyons patients et laissons les faire. Tout irra pour le mieux Inchaallah
LE PRÉSIDENT BASSIROU DIOMAYE FAYE À MBOUR 4 À son arrivée à Mbour 4, le président Faye a été accueilli par les autorités administratives et locales. La visite s’inscrit dans un contexte particulier lié à la gestion foncière du pays, sujet sensible et d’actualité. En effet, le secteur de Mbour 4 a été récemment au cœur des débats après que la Direction de la surveillance et du contrôle de l’occupation du sol (Dscos) a démoli de nombreux logements jugés irréguliers, car empiétant sur une forêt classée.
Machallah alhamndoulilahi yallah moy bour son exellence mr le 5president du Senegal 🇸🇳 bassirou diomay faye le premier ministre ousmane sonko projet bi ligueye rek dioub dioubal dioubanti rek diadieuf presi di denaro sì askan wi di kham li khew nila wawaw Senegal 🇸🇳 migui dora am president a cote'du peuple senegalais machallah ndam rek sì projet bi dioub dioubal dioubanti rek inchallah
Ba ngay nek prison nga yoni mouhamed sagna députés du peuple pour mou lerlou mais ses bailleurs truands en complicité avec les autorité locale dara sennoule beneuh information meunoko am meme si tu as ton argent pour acheter...thies lagnu am bepeuh thiessois thies ba beugu deuk vraiment nagnu ko tek ci yone rek comme on a declassifier tput cet forêt kounek meunci am ak noussa poche toleuh bagneko cherale ba nga hamni borom barqué yi rek gnokay meuneuh dieundeuh...
Ils faut que les thessois en bénéficient aussi ....faut pas tout annulé souff bi souffou wa Thiès leu nagnouko diox thiessois yi gnou deukk si ya beaucoup de jeune thiessois ki travail a dkr sans maison ils louent des appartements a dkr té gnep khamnagnou ni appartement cherer dkr
Wa li yalana continuer liguey rek nekkalfi askan wi c tout...terain yi gnune gni deuk thies sah amougnuci beneuh information ils ont tout partager wa apr yi...
Qu' Allah assiste notre President Bassirou Diomaye! La charge de Chef d' Etat est tres lourde. Par consequent, prions pour que Dieu lui donne la sante, l'intelligence, le courage, la force et les moyens necessaires pour mener a bien sa mission🙏🏿
La patrie se pratique mais ne se dit pas seulement.
Merci Président Diomaye Sonko
Merci beaucoup présidents Diomaye et Sonko❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machalla 🎉🎉🎉
Président khalé ❤❤❤❤❤
Papa Diomaye notre fierté machala ❤
Merci président autorités sathieu yi dinagnou askanwi terrain yignou sathioneu yeep inshallah
Merçi beaucoup mon président serigne bassirou diomaye faye yalla na yalla faye
Merci President vous montrez vraiment que vous êtes là pour le peuple. Sénégalais soyons patients et laissons les faire. Tout irra pour le mieux Inchaallah
Merci beaucoup président dioumaye ack premier ministre Osmane sounko 🇸🇳🙏❤️🤍🙏❤️🇸🇳🙏
Merci perezi na lep l'ère
LE PRÉSIDENT BASSIROU DIOMAYE FAYE À MBOUR 4
À son arrivée à Mbour 4, le président Faye a été accueilli par les autorités administratives et locales. La visite s’inscrit dans un contexte particulier lié à la gestion foncière du pays, sujet sensible et d’actualité. En effet, le secteur de Mbour 4 a été récemment au cœur des débats après que la Direction de la surveillance et du contrôle de l’occupation du sol (Dscos) a démoli de nombreux logements jugés irréguliers, car empiétant sur une forêt classée.
❤❤yokouté rek inchallah
Que dieu protege le president et le premier ministre amine
Un vrai président
Vive pr diomaye ❤❤❤❤❤❤❤vive pr sonko ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
SOUDON MACKY AP SAGAROU PREFET LAFAY YONÉ MOU DEM NIOU DIOKH KO DARA MOU YONÉ NI C REGLÉ MR MR LE PRESIDENT APRES MOU DIEKH😂😂😂😂
Macky démna copin 😅
@@mbayediaw1962 dafnio sonomalon bro😅
Surtout sunu préfet bi mbacke baol
Boroom 3personne 😂😂😂
Macha Allah merci bcp
Quelle fierté pour le monde entier I am very happy
Merci presi❤❤❤
Bien fait presi
Merci président et bonne continuation inchallah
Macky da tayale président dagaye nék jeune té niémé président bureau rékk
😂😂😂😂
Un presi qui descend sur le terrain machalah
Nila président dangaye wathi si terrain bi
Billahi wollahi sama khôl sedna thi président diomaye sonko nila président degaye diégé sayy askane❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Merci peresida
❤❤❤❤❤bravo c est se qu on attend d un dirigeant
Merci Presi
Barke borom Touba Li la geum deh na sathie yeppou Aritte
Merci Pr fay❤❤❤
Merci beaucoup seydina Ousmane sonko linga niou tanal bakhna ❤❤❤❤❤❤
Merci bcp ❤❤❤
Lép day léér
Changement par force inchallah avec prési diomaye et son pm Seydina ousmsne sonko ❤❤❤❤
Président khalé dafay disponible Machala
Merci prési le contrôle n'exclut pas la confiance
Le travail continue djoub djoubeul djoubeunti
Machaallah
Merci Mr le président Bassirou Diomaye Diakhar Faye
Machallah ❤❤❤❤😭😭😭🇸🇳🇸🇳🇸🇳🙏🏾🙏🏾🙏🏾🥇🇸🇳☝🏿😭😭🙏🏾🙏🏾
Vive Sonko et vive Diomaye ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Prsdn merci beaucoup ❤❤❤
Merci son exellence,il faut etre pres du peuple tout verifier
Ma sha allah président bonne continuation
Machalla ❤❤❤
Le leadership en pratique 🎉
Merci presi n'a leup leer
Na leup leer merci Presi
Machallah
Machallah alhamndoulilahi yallah moy bour son exellence mr le 5president du Senegal 🇸🇳 bassirou diomay faye le premier ministre ousmane sonko projet bi ligueye rek dioub dioubal dioubanti rek diadieuf presi di denaro sì askan wi di kham li khew nila wawaw Senegal 🇸🇳 migui dora am president a cote'du peuple senegalais machallah ndam rek sì projet bi dioub dioubal dioubanti rek inchallah
Diomaye Faye est un inspecteur des impôts, il sait toutes les magouilles, cela va cesser inchallah
Notre Président ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah son excellence ,ndam rekk inchallah 🙏
Diomaye, Président de proximité ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🇸🇳🇸🇳🇸🇳🙏🙏🙏
Ba ngay nek prison nga yoni mouhamed sagna députés du peuple pour mou lerlou mais ses bailleurs truands en complicité avec les autorité locale dara sennoule beneuh information meunoko am meme si tu as ton argent pour acheter...thies lagnu am bepeuh thiessois thies ba beugu deuk vraiment nagnu ko tek ci yone rek comme on a declassifier tput cet forêt kounek meunci am ak noussa poche toleuh bagneko cherale ba nga hamni borom barqué yi rek gnokay meuneuh dieundeuh...
Merci beaucoup président
Vraiment yalla na len yalla diapale mais sen yene rafetna
Merci président na lpp tégou si deugue
Un Président intègre et son premier Ministre Ousmane Sonko Que le bon Dieu swt vous accompagne
Merci mon presi
Diay naniou souniou souf yeupp étrangers yii wallahi naniou dieulat lepp
MachAllah président bou gnémé sur le terrain ❤
Merci président ❤
🥰😍😍😍
Fi deh wa apr nioko seddo bamou diekh
Vrai homme de terrain
❤❤
J aime mon president Diomaye Diakhar Faye
Machala
Merci beaucoup notre président ont né fier machalla
Sénégal mongui sogga am président
Bradage foncier bii dinna diekh 💪, par force
Longue vie pour notre président ❤
Merci président
Mr Le Président Bassirou Diomaye Diakhar Faye nous vous souhaitons une longue vie et une santé de fer
On veut que ça soit définitif retrait définitif des constructions
Lépay ler
Bravo presi lguey rek tekko si yone
Sur le terrain rek
Pas ay président yegou ko wore yefou tapalé yoyou comme Macky
Tu es un comédien c'est ça un travail
Très bien mon président je suis fière de t avoir voté
President diomaye merci
Rewmi dii dana bakh ,,nitt yi ignane, nafekh yoo nara soona si rewmi
Liguey rek
Merci. Président il. Faut. Tout. Réglementer. Et. Arrêter. Tous. Ces. Délinquants. Fonciers
President bu dioulite laniuy am
Ils faut que les thessois en bénéficient aussi ....faut pas tout annulé souff bi souffou wa Thiès leu nagnouko diox thiessois yi gnou deukk si ya beaucoup de jeune thiessois ki travail a dkr sans maison ils louent des appartements a dkr té gnep khamnagnou ni appartement cherer dkr
Récupérer ce site pour de grands projets
Bien fait jerejeuf Président
Président khalé, bou taloul jour férié. Liguey rek mo wore
😂😂😂😂😂😂kon yéwouna ni Alhamdoullilah
❤❤❤❤❤
Hommes d'affaires yo khamni Nanguwu ñu creer ay entreprise de production ou de transformation. Sathie ak diay souf rek
Diadieufaty President👌👏
🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
❤
Laff thiat Laff thiat Laff thiat
Wa li yalana continuer liguey rek nekkalfi askan wi c tout...terain yi gnune gni deuk thies sah amougnuci beneuh information ils ont tout partager wa apr yi...
Bolé wouniou dara at at wakh, dieuf rek nieup guis. Nones yi di fatou
Location sur vente yînga waxone presi pourkw pas nga defko fii
Merci président diomaye nila daye déplacer wo Di xol
President meunoul kholenfo lepp nakk.
PATIENCE!!!
Qu' Allah assiste notre President Bassirou Diomaye! La charge de Chef d' Etat est tres lourde. Par consequent, prions pour que Dieu lui donne la sante, l'intelligence, le courage, la force et les moyens necessaires pour mener a bien sa mission🙏🏿
Waw goor nioune ay nandité lagne fal niou kham li khew si rewmi
Merci president, il ne faut pas se limiter sur les fiches de rensegnements parfois ils isolent le president longue vie au president