s'il vous plait chers freres et soeurs, revoyons notre maniere de vivre. Regardez l'etat de cette plage et qui dit Yarakh dit Baie de Hann, la baie qui etait la plus belle au monde derriere Rio de Janero au Bresil. Cette meme baie est devenu un depotoir depuis pas mal d'anneee. tout le temps on indexe l'Etat mais parfois nous devons faire une auto-critique. Senegalais nioussi bari setou guinar laniou sett ter lolou dokhaloul rew naniouy bayi khel ni mbalit mom meuno mouss aka waner bamou natal ap rew; yitam set ci diamou yalla la bok. Faisons de notre mieux pour que nos littoraux soient propres et attirants. Niogui diegalouwat ci kaddou yi
Yalla nala yalla déf roi des arènes 🙏 ❤ SAMA CHAMPION bi
Al bourakh c'est le meilleur je vous félicite
s'il vous plait chers freres et soeurs, revoyons notre maniere de vivre. Regardez l'etat de cette plage et qui dit Yarakh dit Baie de Hann, la baie qui etait la plus belle au monde derriere Rio de Janero au Bresil. Cette meme baie est devenu un depotoir depuis pas mal d'anneee. tout le temps on indexe l'Etat mais parfois nous devons faire une auto-critique. Senegalais nioussi bari setou guinar laniou sett ter lolou dokhaloul rew naniouy bayi khel ni mbalit mom meuno mouss aka waner bamou natal ap rew; yitam set ci diamou yalla la bok. Faisons de notre mieux pour que nos littoraux soient propres et attirants. Niogui diegalouwat ci kaddou yi
@@Mamba01015 machalla mbokh mi ligua wakh Dara douko dinedi bilaye
Mâcha allah quelle analyse !!! Vraiment c'est émouvant
MashaAllah très très pertinent
Deugg leu lou lérr nga wakh saleté na tropp
Allez à cayar cette plage est tellement propre 😮
Très belle initiative, j'ai vraiment apprécié le concept. Albourakh, vous êtes entrain de revolutionné la lutte sénégalais
Un vrai lutteur jambar....Moussa Ndoye yokh le dieuliko
Très bonne initiative de ALBOURAKH évents pour magnifier cette culture purement sénégalaise. On est fier de vous , qualité image son impeccable 🔥🔥🔥
Moussa Ndoye Ndam rk inchallah ❤❤❤
Yarakh deuk leu ❤❤❤
NDAM REK DOMOU YARAKH🎉
Je suis fière d'être lebou Moussa ndoye Yallanako yalla Maye ndme inchallah sibarki Serigne Babacar Sy rta ❤️✌️💯❤️
Ndoye ndam rek
Nguirr yalla rek teuttt DIEULL ma boucher wou mbaye gouye gui rek 👉💪💪💪♥️💯💯💯💯❣️🤛🤛🤛
Un grand champion
Mbaye gouy gui yalna ko yalla maye ndam 🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲
Yarakh ma fiérté ✌️❤️
Machallah belle réalisation yala na yalla diapalé. 💪
Dam rek Inchallah Moussa🙏🏾
c trop nice vraiment ❤
Bonne chance champion moussa Ndoye 💪💪
Ndam rk inchalla 🎉
Mbaye gouygui ndam rek❤❤❤❤❤
Bonne chance Lébou bii🎉🎉
Yalla Nala Yalla May Dome Si Bark S Babacar Sy 🙏♥️♥️♥️
Quelle forme mashallah Moussa ndoye 👍✊
Albourakh bilay nioy lamb
Mbaye Gouy gi ndm rk inchallah
Nice documentary big up moussa ndoy❤❤❤
Ndame rek inchallah
NDAM RÉCK INCHALLA 💪🏽🔥💪🏽
LE REQUIN NOIR BOU ENTRAÎNE DOU MOROMOU MBEUR YI
Bilae walae
Machalla Albourakh ❤❤❤
Yallnala yalla may Ndam Moussa Ndoye🙏🏾
Mbaye gouye Gui 💯💪
Domou baye❤❤
Yalnala may ndam champion inchala ndam rek
Bonne chance 💯
Avec sous titrage ce permettrai de mieux rependre cet extrait nice
Mách 🎉😊
Weuz diambar machallah koula guis khameni yagui liguéye aussi
Bonne chance
Moussa ndoye mo meune mo eup Dole 💪💪
Moussa Ndoye rek ❤❤
Yarakh seul athia pa yatou ndam rk💪🏾
Akh mbaye gouy gui tangoul yako meun dee so dèfè foula do takhaw ak mom champion la nak
Moussa ndoye AK sa yarakh yarakh da sokhla
Nice❤❤
Thiay albourakh❤
Moussa ndoye boul doof sakh yébognou sakh boy bi do moromam doussi beuré doussi khékh
Yalla nalla yalla défal laa ndam
Ndam rék inchallah 0BY
Mbaye gouygui rek laniouy top
Xana amo wayou lébou
Yarakh daniou décidé dhe😂
Non nek lebou fierté la Bilay Moussa Ndoye seule
Moussa fokga khew khew 𝕓𝕠𝕦 sakh ak Mbaye gouye gui boko beugeuii daneu
Mbaye gouy gui seul 🫶🏾🎉
❤❤🔥🔥
❤❤❤❤
Vidéo bii dafmay fatté 2001 yarah tableaux féray sama keur tourando dara doxoul digeunté guéth bii ak keurgui mol yii chambres bima donn fanann lagnou donn déth sénn yeuré guéth yii fadiar gnou gnow dieulsiiko goudigui sii plage bii lagnouy tok makk sama tourando ma adiou sikow thiolou galgui souvenir bouma nekh 😂
@@artsafriquecommunication6587 kouy sa tourando
Yarakh lanioun deuk 😂❤😂
Yarakh seul 🎉
Magnifique
So indi woul contact bou doy doo daane Mbaye guygui
Mbeur bou eusss gaye beurrel wadjal d que meilleur gagne
Kokou dafa bari wakh
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😢
Ciao
💪🏾❤️🙏🏿
Mbaye gouy gui soko maye mou diapou doko daneu so beugué dane Mbaye dagay khékhe ag môme dou guiss kou
Ki mo meune fouf mbaye guouye gui
Wah rek laye defe😅
Moussa ndoye seul
Moussa doy vs bg2
Mousa vs ada
Bane mo diadou??
Dou combat
Bane bg2
physiquement ça reste ligueyal dess na
Lo def danou
Athia lèbou ndoye ndam rek
Pa yatou seul
Ndam rk
Bo entraîner do moromou kene
Lo deff dano
Ki khan a doubere
Le 10 novembre bii
Guedj bi nak saleté na , pas une belle image pour le Sénégal, mairie yi la khamoul sen ligey pfff
Fis boul dof dioum dioumate taéf la fis ya meune Thierry le malien