Fall nak bari nga problème tropeu serigne touba sakh dadane diegalè mais yaw sa vidéo yeup ay problème rek please may niou diam way Serigne touba diam la woté
Da ñoo soof. Yoon wi kéne momouko kou doul Serigne Touba té wakh na ni mouride di mél... mouride la wayé bou maye wéyé ndigal Serigne ba may wéyé ndigalam day doon Serigne bou mate Serigne comme niko Serigne Touba diangalé ci Massalikoul jinan.
Fallou Fall mii moom noppi réck la wara déff Ab mouridla ab talibéla....wayé dafa diangoul darra....pour mana wakh ak nitñi. Daiangoul dara amoul ab kham kham....dafa wara noppi té bayyi internetbi, démthia daaradia di lagèèye......
Soxibu moom dafma beet lool,ku am deeg deeg ak seetlu di nga xamni nimu tamblee bokkul ak nimuy doxalé,man desabonena,amna solo faal,message bi dal na ta ku nek man nako teewlu.
@@louxewtaye161 man neewoon nala duma saaga,maala gëna ñaaw lamiñ fuuf ,ta soo jakkarloo ak man dooma saaga,ta doo am fitam,yaw ku critiquer sonxibu yaa koy saaga ta liñukoy wax dëgla
Qui etes vous pour decerner des diplomes de bons ou de mauvais talibés. Arreter de crier tjrs au complot contre le mouridisme. Je suis mouride et je ne compte pas etre un mouride selon votre vision.
Dieureudieuf Serigne fallou fall mbaor yalnala Serigne Touba Faye, mais souhaibou Diop mome dafa rééw té khamadi il faut qu'on l'arrête il est trop indiscipliné
Jerejeuf fall wakh dji leerna té sante nansi. Pour le cas souhaibou diop et autres, il faut comprendre que amou gnou xamxam sén lamigne mo reuy rek. Il m'a déçu. C'est un malhonnête bo khamni khamoul boppam.
Un marabout dont les interventions sont toujours instructives et très argumentées. Un grand défenseur du Mouridisme. Dieureudifati Serigne Fallou.
Nite day djoume nak..jajeuf serigne bi,.🙏❤💪👍
Macha Allah Amna solo yaguefi rek ta wer yaw
Serigne fallout fall yalla nagkafl League te wer
guisnan sa taxa way si yoon bi yalna la serigne bi dolle takhawou
Dieuredieuf Fall goud fann ak werr deug rekk gaa wakh... danio khamoul lou kheww rekk
Fall nak bari nga problème tropeu serigne touba sakh dadane diegalè mais yaw sa vidéo yeup ay problème rek please may niou diam way Serigne touba diam la woté
Da ñoo soof. Yoon wi kéne momouko kou doul Serigne Touba té wakh na ni mouride di mél... mouride la wayé bou maye wéyé ndigal Serigne ba may wéyé ndigalam day doon Serigne bou mate Serigne comme niko Serigne Touba diangalé ci Massalikoul jinan.
Fallou Fall mii moom noppi réck la wara déff Ab mouridla ab talibéla....wayé dafa diangoul darra....pour mana wakh ak nitñi. Daiangoul dara amoul ab kham kham....dafa wara noppi té bayyi internetbi, démthia daaradia di lagèèye......
😃😃😃
Fallou fall bayil fen saragal yallah
Machallah yalla ne le yalla defal diamu ak tawfekh sa takhaway rafett na👌
Fallou Fall Mbaor soulard bou mag nga
Wakhi nafékha rék ngay wakh kholale wakh diou bone dji thiym yaabone
Demal diamoudji yalla mo gueun
Souma donone sohibou damay kharou fallou fall néna Sohibou dadof 😁😁😁
Pabi mom dai kholo rék khana amo loubakh ???????
Dieureudieuff
Serigne Bamba kèn mounouco bagn...
Srg ténga wakh ak Sonhainbou rék té bagne thié bolé walfadjri wakhé wouko walf conte youtuboubab lako wakhé yangui togne nak
Souhaïbou Limoy wakh momla concerné yoonu walfadjri nekosi
Menteur. Sinon pourquoi il n’est pas viré ce lache
Machall serign bi falla amna solo
Dieureudieuf Serigne Fallou
Dieuredieuf Fall yalna nou la yalla fayal
machalakh amna solo trop
Dmalaye lugaye
Bien dit Fall njaga
Wakha fi dara
Ki waxi doff rek lafi wax thiey mim rew.
Machalla rafetna trop
Ki dou dara
Dieuredieuf fall sa takhawaye raféte na
machalah fall yaram gena yage gena wer rk amna solo loool
Macha allahi fall s.touba rekk lanou geume
ماشاءالله
فال
Machallah
Dieureudieuf fall
gamoul serigne bi
Ouii dafa barri ay mourides yu bess yuniou rakh. Naafekh yu barri
Gueum ak wolou ak beugue ak topou ak yakar serigne touba khadimou rassoul rék lane koy déf
🙏🏻🙏🏻🙏🏻🙏🏻🙏🏻👍🏻👍🏻👍🏻👍🏻
Yawit sa wax dji teguoko fenn
Soxibu moom dafma beet lool,ku am deeg deeg ak seetlu di nga xamni nimu tamblee bokkul ak nimuy doxalé,man desabonena,amna solo faal,message bi dal na ta ku nek man nako teewlu.
@@louxewtaye161 man neewoon nala duma saaga,maala gëna ñaaw lamiñ fuuf ,ta soo jakkarloo ak man dooma saaga,ta doo am fitam,yaw ku critiquer sonxibu yaa koy saaga ta liñukoy wax dëgla
@@abdouseye4949 ki page gcb lanek ,ku critiquer sonxibu mu saagala,yaw yaak sonxibu yeena yam ndax moom xamna yaay kan
Même ma mii
Diadieuff diewrine mourid sadikh🙏🙏🙏
Fall mbaor demal wouti beuz
Bilahi fall
Sonhibou nafekh la
Deugueula 👍👍👍
Sonhibou khath deugla gueumoul dara
Serigne touba kokou bagn ci sonno ngay deke
Man dé kouma nekh nga ndakh mou mouride yepou defon ni yaw con mou nekh sonhibou mon da yakarni ab donneur de lecon la
Machalla kadou yi rafet na lol
Quítate las gafas tiene miedo de mirar la gente por los ojos.tiene que dar cara tio
Jaajëf Faal amati na solo de.
🤣🤣🤣🤣😂🤣😂🤣😂😂😋
Walfadjri nio geuna bagn yonou mouride
Tant que gueumolen sen serigne si ay nitt laniou daniouy dioummm daguen di sonnn rek
Chiekh nokhamadoul basir ba légui lime wakh kéne tontokoko xam xam ولاتلقوابأيديكم الي التهلكة
Yawe topale fale
Serigne touba kokou bagne ci aw naxar ngay deke soof ngén trop ak sèn xol you bon
@@massmadridkhouma9553 Nel serigne bi mou outal jeunesse bi liguey mo gueunn .
Seringe bi khamaloko dra banane na wotal kéne liguéye liguéye aka yom koko yétéwo daga liguéye
Conn douge avion kharoula
Li nga wakh leppp deug la
Geuna yague guena wer fall niagua
Dirradieuf fall
machalla
Qui etes vous pour decerner des diplomes de bons ou de mauvais talibés. Arreter de crier tjrs au complot contre le mouridisme. Je suis mouride et je ne compte pas etre un mouride selon votre vision.
Aka dégoût fall yaram
Dieureudieuf Serigne fallou fall mbaor yalnala Serigne Touba Faye, mais souhaibou Diop mome dafa rééw té khamadi il faut qu'on l'arrête il est trop indiscipliné
Souhibou diop fém tolnii rosneu lol
Jerejeuf fall wakh dji leerna té sante nansi.
Pour le cas souhaibou diop et autres, il faut comprendre que amou gnou xamxam sén lamigne mo reuy rek. Il m'a déçu. C'est un malhonnête bo khamni khamoul boppam.
Bala wakhe thi nit khoko bapare
Sohibou rouslen tour wi ngir yalla dèlèn ko wowè nafèkh bi
walahi dou mourid
👍🏻👍🏻👍🏻👍🏻👍🏻
Kii mome dafa beug siw rèk
Diarra dieuf fall yonou mourite Amel nan la ndioukeul
Ngor si Diop kokou la meunoul supporter mane il est telment malhonete le gars
Waw gorr mourid wawaw ngor ci diop rèk doyna
Walllahi
Li yakhou tchi dine bi yeup sene tarikha bou bone bi moko yakh
Sa leufeul ndeye
@@damecisse4628 dello na saaga bi serigne touba
Pourquoi il ne parle jamais d'Allah et de son prophète ?
Sadiobou ndaye dangano guena guemm yalla ak yonentebi merde
Fall diaga yaram waxgue lppe
Yagui fi lol te wuer
Jaajeuf Jaajeuf souhaibou mom dafa khama di trop
Qu’est-ce que il raconte lui c’est idio
Machalla amna solo
Machalla fall
Machalah
Sohibou rouslen tour wi ngir yalla dèlèn ko wowè nafèkh bi
Macha Allah
Machallah