Assalaamu alaykum wa rahmatul Laahi wa barakaatuhuu. Nanu YÀLLA tàggatal sunuy xol ak sunuy cër ca lamu tàggatoon sunu Yonnènt bi sAaws akiy sahaabaam rAa te wërsëgal nu dëkag gnoom ca kërug teràngaam. Nanu YÀLLA wan dëgg bamu leer mu yombalal nu topp ko, mu wan nu neen ba nu ràgnee ko mu yombalal dùmmôoyu ko. Nanu YÀLLA sàmm, sàmmal nu sunuy njaboot ak sunuy woroomi xamxam yi ragal sunu Boroom YÀLLA. Jërëjëfati yaa imaam.
Gana yag gana wer ❤❤❤❤❤❤❤❤
ما شاء الله
Dieredieuf yaa imam Mor MBAYE
Machllah amna solo
Machallah
Jamano ji ndamar si bir mâché la ,so xolé fingay jar jisss lo warata jisss, so xolul fingaye fir ay nit😢😢😢😢😢😢😢😢
🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
Assalaamu alaykum wa rahmatul Laahi wa barakaatuhuu. Nanu YÀLLA tàggatal sunuy xol ak sunuy cër ca lamu tàggatoon sunu Yonnènt bi sAaws akiy sahaabaam rAa te wërsëgal nu dëkag gnoom ca kërug teràngaam. Nanu YÀLLA wan dëgg bamu leer mu yombalal nu topp ko, mu wan nu neen ba nu ràgnee ko mu yombalal dùmmôoyu ko. Nanu YÀLLA sàmm, sàmmal nu sunuy njaboot ak sunuy woroomi xamxam yi ragal sunu Boroom YÀLLA. Jërëjëfati yaa imaam.
Jaajëf sëñ bi ci Wolof leer na
Ñoom
Ràññee
Mbaye yague fii loll té ande ak werr