Wally Ballago Seck, le génie de la musique sénégalaise, celui qui berce mes journées avec ses chansons. Les fans de Wally montrez-vous. Car vous êtes les meilleurs 💯 🔥
Mach'allah Wally tu as vraiment la maturité mais surtout la classe Seck si guinar amal jamm rek qu'Allah accomplis tes vœux pour le Sénégal . Wakh deugue yalla yagui wané diom dji domou Sénégal ame merci et encore une fois merci aux noms de tous les Sénégal aller sama bayfall bi one love❤️❤️❤️❤️❤️❤️🇸🇳 .
Wally yalla bo guiss loye ragalll liga beukk yako khamm yalla nalako yalla défff borome xolou diamabi défo loudoule dimbalé néww di doléyii wally doundale wérale mane je tmmm dakkk sa xole bou raféte aye Wally amale diammm si barké Serigne saliou
je t’aimais depuis le début de ton carrière mais je t’aime encore plus. Continue ne change jamais et reste surtout sur le droit chemin inch’Allah tout ira loin.Respect pour ta femme je l'estime beaucoup bonne continuation.
J'aime Wally? C pas pour la musique mais ça façon de faire,ça générosité, un homme sociale. Nite gni nioy wakh si yaw lou bone mais yaw nieup nga yéné diame khamal ni motakh yallah dila may diame. J'apprécie aussi l'émission
Vrement t'est quelqu'un de bien beug na wally nak papa thione nena waly da am une générosité spéciale mananko car machalh 🤣🤣wally seck est une bonne personne machalah yaleu nalah yalla defal diam sa khol mo rafet disque d'or yi dina gnew awards yagui gnew maryacine
Wally seck tall bou yalla tall ken mounouthi yota bo banie dooundal lo doundou doyoul borom xol diama seydi seck long vie et santé prospère réussite totale a vous tous ce qui proche de toi aussi mon chanteur unique
machallah notre très cher chanteur du peuple sénégal Dg doundal basaye maye di bawaye barki kigniou begue cherif abdou rakhmane fall tilala amin le meilleur de tout les temp tu fais notre fierté anna les vrais faramareen%%%%%%
Wally Seck que Dieu te protège je te souhaite tout le bonheur du monde et ton entourage je veux que tu sois toujours parce que ça me fait plaisir de te voir heureuse
Machalah waly ballago seck yalnala yalla sam sam ndjabott laffal la thiaatt tey dioyna bubah koula xol khamni dagua bakh ta générosité dépasse les limites Machalah yalna yokk inchala..... Ton témoignage envers ton épouse m'a fait pleuré...Fonk wadiour diokh thieur sa wadiour topoto sa wadiour dara guenouko ci adina
Wally sant yalla rk yalla nala yalla fayy sa khol reference amal goudou fann rk ak wérr liga mbé beut lépp yalla maylako barki cheikh ibre ❤🙏🏿 j t suis partout et j sais que ni je vais realisé mes rêves yalnala yalla samm
Ppa thione limou wah rek thia kaw thia nakam bilahi sa xol mo set yalla na yalla guenala dioule ak Soxna Aidara ( machalah sama faramaréne bi) sa détermination dangay am inchalah tegal leup thi lo sunu borom bi
Mane wally souma lay setane day. Ame loumay yeug sama kole mou nek.lou sedd dou louma la beug en tan que artise mes juste tes propo tes conseils ton parcour ta grandeur je veux réussir dans.la.vie et j'y tien tes tes parole me motive vraiment merci a toi et ma télé 2stv vie sur vous
Wally Ballago Seck, le génie de la musique sénégalaise, celui qui berce mes journées avec ses chansons. Les fans de Wally montrez-vous. Car vous êtes les meilleurs 💯 🔥
Mandeh souma stresse sakh momaye delossi nako yala sam bate bi were mou gude fane andak wer
@@amminambengue9000 bilahi io 🔥💯❤️
Slu
@@arakonte9676 laye done bamou am diom waly dal amouthi morom dal tmt
Machallah wally
Sokhna aidara bravo je sais que ça n'a pas toujours été facile pour toi. Une bonne leçon pour guel you beug lou yomb yi
Ndaysane Wally dioylo nameuh 😭néneu bou amone 7 garçon sakhhh Mouhamed laniouye toudou 😭😭Machallah 🙏🏽❤️yalna yallah barkel 🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Kolore rek mon âme sollo Wally sa yaye kou bahna nit yarna nit defal ko sonasi mou maga fate l’épeu chapeau à kiné Diouf
Machalla wally seck l'enfant béni et bien aimée par le
peuple sénégalais tu fais notre fierté ou son les vrais faramaren 🥰🥰
Nous sommes la
❤❤❤❤💯💪
❤️❤️💍
We are here
I just like wally from the bottom of ma heart.
Mach'allah Wally tu as vraiment la maturité mais surtout la classe Seck si guinar amal jamm rek qu'Allah accomplis tes vœux pour le Sénégal .
Wakh deugue yalla yagui wané diom dji domou Sénégal ame merci et encore une fois merci aux noms de tous les Sénégal aller sama bayfall bi one love❤️❤️❤️❤️❤️❤️🇸🇳 .
Alioune MBAYE Nder est mon artiste mais, j'aime la personne de WBS, un gars généreux, humble, loyal etc❣. Que tes ennemis se mordent le doigt😎 !
Wally yalla bo guiss loye ragalll liga beukk yako khamm yalla nalako yalla défff borome xolou diamabi défo loudoule dimbalé néww di doléyii wally doundale wérale mane je tmmm dakkk sa xole bou raféte aye Wally amale diammm si barké Serigne saliou
Amine
Amine
Amine
Waly yalla nasa diam yagu
Amine
je t’aimais depuis le début de ton carrière mais je t’aime encore plus. Continue ne change jamais et reste surtout sur le droit chemin inch’Allah tout ira loin.Respect pour ta femme je l'estime beaucoup bonne continuation.
Ay yala yalna nga niou ko samal j’ai les larmes aux yeux Bilahi wally dina am lou bakh inchala il a souffert 😭😭😭
Au temps j'écoutais pas Wally mais legui mom ndeeysaane amatuma sago thii mom.Amal diam Wally je te jure do guiss lo ragal dhh
J'aime Wally? C pas pour la musique mais ça façon de faire,ça générosité, un homme sociale.
Nite gni nioy wakh si yaw lou bone mais yaw nieup nga yéné diame khamal ni motakh yallah dila may diame. J'apprécie aussi l'émission
Wally Seck khawmako wayé kou bakh la🥰🥰🥰❤
Vrement t'est quelqu'un de bien beug na wally nak papa thione nena waly da am une générosité spéciale mananko car machalh 🤣🤣wally seck est une bonne personne machalah yaleu nalah yalla defal diam sa khol mo rafet disque d'or yi dina gnew awards yagui gnew maryacine
Walay bo wayoul sax soy wax rek khol day seddeuh ndax machalah xol bou rafet ak maturité ak simplicité😍😍😍oh walay ki ken meunouko bagn
❤🎉
Wally seck tall bou yalla tall ken mounouthi yota bo banie dooundal lo doundou doyoul borom xol diama seydi seck long vie et santé prospère réussite totale a vous tous ce qui proche de toi aussi mon chanteur unique
Macha-Allah
Wally est et restera le meilleur
@@seckmaimouna5238 meerci
Meecu
❤
Machala yalla na la yalla diapalé thi barké seydina Mouhammad ( saw) notre waly international on t'adore bonne continuation
Gambia 🇬🇲 love Wally ❤️❤️❤️❤️🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲you our number one
Maar yacine maïssa bigué Maïssa bigué maar Diamm diou bari si yaw je t’aime bcp ❤️❤️❤️
Machaalah une emission plein de valeur waly amo morom
Tu fais la fierté sénégalais je suis si contente de te voir les Faramareen contengéne
Bravo wally mon fiérté je te sui depuis la Mauritanie 🇲🇷 one love❣️❣️❣️💎
J’ai même pas les mots bilay ❤️❤️❤️j’ai tout cœur avk wally il est adorable 😍🥰🌹
machallah notre très cher chanteur du peuple sénégal Dg doundal basaye
maye di bawaye barki kigniou begue cherif abdou rakhmane fall tilala amin
le meilleur de tout les temp tu fais notre fierté anna les vrais faramareen%%%%%%
Machallah waly yalna yallah goudeul sa fane mou ande ak wer ci barké seydina Mouhamed saw🙏❤️
WALLY FIERTÉ SÉNÉGAL T ES LE MEILLEUR✨✨✨✨
Amga nianou wadiour thia Kaw thiakanam machalla
Son afro music est juste top. j'accordais pas de l'importance à ce qu'il fait mais l'afro music m'a vraiment séduit.
Ndeysan le son de ndiaga mbaye me rappelle mon papa chaque matin mom lay deglou goudal fan papa
Sa papa yalnako yala doli ler
Que la terre lui soit légère.
@@khadywade4888 amiin syster
@@amsadieng4672 merci ms mougui ndoundou da diem magg
Ndeysane Machalla Adouna dara kheuyoul souti 😍😍😥😥😥long vie à toi wally yaa bakhe té goré billahi yallna yalla defall la diam mes larmes 😢 au 👀
Longue vie a toi sa mon chanteur préféré bakh yewene borome ❤ diamant bi yalla na yalla deal diam thi barket Seydina Mouhamed psl🤲
Le chanteur du peuple❤️gouddou fanne rekk lanioulay nianal ak weurre gua yague diniou mbégeul🙏🏾
Bly
Machalla wally amal djame rek seck yaw talibè serigne touba to tanou ❤❤❤
Bilahi sa parcours Nice n’a...kou soneu si dara Yalla fékkk lafa....diam si yaw❤️💯
Diam cii yow mon chanteur adorable de ma vie, qui me soulange ,me divertit au moment ou je souffre j'écoute ses chansons merci Séck.
Waouh, machallah. Waly a beaucoup progressé dans sa communication. Il a également gagné en maturité.
Amal jamm diou bari diambar.
Ay sama papouneh amga gnagnou yay ak barke baye machala yalla nala yala lafal thiate te may la fane wou goudou ak wer
Mashallah Wally si kaw si kanam silou bakh yallah nala yallah défal diam diou sakh dakh ak famille bi amine ya rabbi
Manchallah wally bonne continuation et succès sur tes projets you raw sa gnorte
Ayoooo sama Daddy National yalna la yalla defal diam🙏🏼🙏🏼🙏🏼 je t'aime tellement❤🔐🥰
Très fière de Toi Baye Fall bi respecté ga sa diabare machalla ❤️❤️❤️
Oumy Niang c est ce qui fait sa force.il respecte sa femme.😍❤️il la magnifie à toute occasion.douko torokhol.motakh si kaw si kanam rek inchallah.
Machalla rafetatina diam thi yaw sounou waly international 😍❤
Wawao waly seck néhoul ba néhoul yafi nék Macha Allah
Machanh Allah wally seck di borome khol bou rafette yalla gua dieume sa kaname rékke atte sa diabar
Billaye gaïdé dou diour mouss waly amal diame barké borom touba ❤️
Machalla kou beugeu Wally nel rang mou guaw ♥️💪🇸🇳
Vraiment wally Seck Kou bakh la bonne continuation.
Merci.
Je demande 🙏à Allah ☝️qui vous protège et qui veille🙏 toujours sur vous, durant toute votre vie Aminé 🤲🤲😘😘
No waly a part bak da fa gore machalla laf thiat yalla na yalla mey koudou fan ak were 💖💖💖
Wally Seck que Dieu te protège je te souhaite tout le bonheur du monde et ton entourage je veux que tu sois toujours parce que ça me fait plaisir de te voir heureuse
Mashallah my golden boy Secka balloga with the golden heart stay bless ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤️❤️❤️❤️💖💖yalla molay faaay borom xol bou labiiir bi dou gnou meusa done ioe brk alkhourane
Goudeul fane gou and ak weire wally ballago seck le visionnaire
Le musicien le plus aimable❤❤
Machalah waly ballago seck yalnala yalla sam sam ndjabott laffal la thiaatt tey dioyna bubah koula xol khamni dagua bakh ta générosité dépasse les limites Machalah yalna yokk inchala..... Ton témoignage envers ton épouse m'a fait pleuré...Fonk wadiour diokh thieur sa wadiour topoto sa wadiour dara guenouko ci adina
Machallah wali Seck Mauritanie ngui begué si yaw 🇲🇷🇲🇷🇲🇷
Je comprends maintenant prkw Wally yegu fi mou yeg ni Machallah 🙏🏾 nekhou ma wone nonu trop mai legui mom bagn bagn beug😊🙏🏾
Yalla n'a la yalla samou fayla goudou fan amiine yaraby machalla dieureudieuf seck waly 🙏🙏🙏💯💯💯💞💕❤️😇😇
Mash'@lla wally faramaren que Dieu t'accomplice a réalisé tous tes rêves et te protége contre les satans
Wally sant yalla rk yalla nala yalla fayy sa khol reference amal goudou fann rk ak wérr liga mbé beut lépp yalla maylako barki cheikh ibre ❤🙏🏿 j t suis partout et j sais que ni je vais realisé mes rêves yalnala yalla samm
Wally son mature dépasse son âge très généreux, Posey quand il s'exprime il est extraordinaire ci kaw ci kanam"Golden boys"🇸🇳🙏❤️
Billay yalla nala yalla Faye sa khole 💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞
Mes respects!Bonne communication, tu as fait preuve d'une grande maturité.
No wally c’est un grand homme il ma fait pleuré 😭💖
Non wally amo ak liga perdre thi corona bi gay yeuketi sa alal dico diokhe yalna yalla samla may goude fan ak werr❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah waly yalna yala same la defal la dame thi barké sangue bou téde bi psl
Machalla papa wally Amna solo way nice na Amine😘😘🙏🏼🤲🏽👏❤
Nianou wadiour lou bakh la si dôme bilahi thi kaw rek wally ♥♥♡
Machallah l'afe thiate Wally seck ♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Ki mome kouko bagne da nga sokhor reike point final
C'est vrai mon
Vraiment
Bilahi
Bilahi
🤣🤣😂😂dafa lerr
Macha Allah Carr yalla nalayalla same Wally rafétena mare Yacine
Mako sope dé mare yacine maïsa bi yalna yalla samou ❤️
Yalla nala yallah Faye sa khôl Wally nimala beugué dh weurna aduna amal jamm rek maryacine chéri soxna
Machalla kole yayui nekh
Goude fane gou and ak weire wally ballago seck le visionnaire ❤
Ppa thione limou wah rek thia kaw thia nakam bilahi sa xol mo set yalla na yalla guenala dioule ak Soxna Aidara ( machalah sama faramaréne bi) sa détermination dangay am inchalah tegal leup thi lo sunu borom bi
Amine
papa thion yar nala soula yarou won do yaksi fi. ..chapeau wally
Mane wally souma lay setane day. Ame loumay yeug sama kole mou nek.lou sedd dou louma la beug en tan que artise mes juste tes propo tes conseils ton parcour ta grandeur je veux réussir dans.la.vie et j'y tien tes tes parole me motive vraiment merci a toi et ma télé 2stv vie sur vous
Machallah Wally seck machallah ❤️❤️🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲♥️♥️🇬🇲
Vraiment c est EXTRAORDINAIRE wally et un grand chanteur
Toujours égale à lui même yalena sa diame yague frére bon courage
Courage wally seck sa khol rft na trop
Machallah wally longue vie à notre Faramareen bi le chanteur du peuple 💙🙏👑
Macha allah grand ballago doundeul rek que le bon dieu te protéger amine
Mon idole mon fierté bonne continuation frère 👊💪
Que le BN dieu continu de te bénir et te protège avec ton équipes.
Mashalla mashalla
Alhamdullila my day is excellent here come Waly my only star dem rek inshaAllah
🇸🇳 musicien Sénégal 🇸🇳 yépp dosènn moromm
Ndank rék ngoorrr
Mc Raba Niang ioe doul
Bly wly
Iow khana ya mom commenté ésk d'ailleurs nitt ngua sakh
Sidi rékk
Wally seck numero uno ❤❤❤
Diaral nganiou setane video one hour on UA-cam
Yalnala yalla lafal thiate
Niit kou baah nga yalnala yalla moussal mouthiale la♥️♥️♥️♥️
We love you
Machallah Yalla nala yalla same té arela beug na liguay deff lol
J adore wali ndeyssane danga bakh meune déflou bakh goudou fane ak wére rek thi barkep alkhourane
un grand artiste, bonne continuation
dafaa am yarr bilai I really love that in him 👌
Le meilleur de sa génération j aime beaucoup
Ma Cha Allah. Laf thiat Waly ❤
Yalla nala yalla mouseule si laminou Tage bi, laf thiatte faramaréme bi
Seck danan momay danel. Damoko beugeu. 🙏🙏🙏👊👊
Les Meyer sa generation Africa🥇🏅🏅🏅🏅
Vraiment rien à dire yalla nala yallah sameuh sameu sa ndiabote
WBS tu es une fierté tt une peuple un grand ❤️ pour toi
Sama star Thanks wally seck✊💪✊