Je ne suis pas thiatacoune et j'ai souvent condamné certains actes de Cheikh Bethio avec ses talibés mais je viens de comprendre cet amour que feu Cheikh Bethio avait pour Serigne Touba a travers Serigne Saliou. Je pris pour cet homme que j'appelerai pas un chauffeur mais plutôt un compagnon qui a su m'éclairer sur la générosité de Cheikh Bethio et son immense sacrifice. Sa wakh lérr na té andeu ak yarr ak mandouté DIEUREUDIEUF Ps: sans limites changé le titre de la video cet homme ne mérite pas ça si té d'accord pousse bleu
Machahala loumeleni rek lanouye khare si cheufeure ak secretaire Ndakh Mandou yalla na yalla defarate digeunete bi ba lepeu done beneu Amine si bareke serigne Saliou amine
Ndeysane, je suis un talibé cheikh et anhrif de surcroît wayé nous sommes tous des musulmans. Lahatt dafa dem ma nirok Serigne Bethio mandouté lou am solo leu thi domou adama. Wakhdji rafetna torop.Nay dioub rek aka malene fonk sama mbok Mourides yi salihatou 🤲🏽🤲🏽🤲🏽.
Bro yaw esk nitt nga rawatina talibé Cheikh, Bethio taxam finé Serigne Saliou mooy yalla tegg ci né yalla thiantacoune leu, di way aka leumbeul,diabaram yi di khessal aka tekk cheveux, meussoul djiité kenn dioulli wala diangue al Quran. Ba paré nga koy défendre,niou melnii mom nio yakh diiné dji ,kou Serigne Saliou defar doo melnii, xolaatal sa bopp, yonente bi nena dioulli moy première chose bou niouy khôl yawmal hiyaam, Serigne Touba nena kou bayi benn dioulli rek bou niou la dioullé té bou niou la soul ci cimetière musulman,bou fekké diokhé lekk rek Bill Gates mi ngi koy deff fepp ci adouna bi té dou dioullit ,kouma saaga ma fayou nak
@@serignekaire6597 iow ya wara nekeu nitt. Aka ma mandou thi yeufou diambour. Je parle plus de la relation entre Bethio et son chauffeur. En ce qui concerne la forme chacun est libre. En ce qui concerne les Mourides je prône leur engagement indéfectible. Kene doula saga iow tamit sangue bi fi ay nitt niofi nek dh tek am yar ak teguine. Nekal thi diamb fall ndiaga yaram 🙏🏾
Bien dit pére lahat samb iow ak cheikh debou la wone sa beugue serigne saliou tahna gua dieul sa taw bou ngor toudéko serigne saliou Bagne nako sahh serigne saliou cheikh bi la yabalonn djoloff bou toudou siko Dieurdieuf père yalla nla serigne touba fay sa khol❤j SS très content d tw yalna diamou yaje
Cheikh bethio meussoul amm compte bancaire allahou akbarrr ak liko yalla mayoneee si khéweul Lou gneuw nonou layy deimé... Yalla na yalla woyafal soufff si kawamm
Ki moy abdou lahat samb limouy wakh aka ko kham yagu ak cheikh bethio Tawam mou toudé ko serigne saliou samb ki si topeu cheikh bethio jajeuf sama wadji ya bakhh
Ndeysane ki gorla nit la kou bahla Serigne bethio dei wadji wadji wah tahna ma ham moy kan ndah man Talibe cheikh la wayei lima deug ni Moy Waneni limou liguey rek lako yalla fay hana diko nianal yalla famou nek yalla yeureumko si barkè yonete bi
Arrêtez de vous mêler de cette histoire de famille! arrêtez de jeter de l'huile sur le feu! De quelles vérités crues vous parlez? Cet ancien chauffeur de serigne cheikh Béthio est digne il n'a dit que des mots d'apaisement il a incité à la réconciliation familiale donc ne foutez pas la zizanie c'est indigne de vous...
Yalla mi meuna boler yalna yalla boler wakeur cheikh bethio si diam ak salam niou nek bene si barker yonet bi ak serigne saliou je ss tidiane mes diam dafa nek yalnako yalla def
Mashallah !!! Deug rék la Mbaye Pékh wakhone. Cheikh Saliou Thioune kheuthiowoul dara, kén dou kheuthio lo mom ba paré si dérétt, si baatine ak si zaayiir. Danou ko sass mom Cheikh Serigne Saliou Thioune si Ndigueuleul Serigne Mountakha Bachir Mbacké, yallah nafi yague té weur. Tékssi il est discret, Kèn guisseugoul sokhnam ou ay sokhnam affichéyou si wétam di diay gueuneu goudoulé ak reuyelé moussaure (foulard) uniquement pour fégn, feuss né or si vitrine, niépeu nan yawla yénela😁. Pourtant dé, sa ou ses propres femmes nioko gueneu yéyo, té amssi plein droit. Yague fi lole té weur Thioune !
Je ne suis pas thiantacoune ! Mais témoignage pa bi ak mandouté rafetlou nako torop ! Nit dey reconnaissant té mandou way 🙏🏿
Je ne suis pas thiatacoune et j'ai souvent condamné certains actes de Cheikh Bethio avec ses talibés mais je viens de comprendre cet amour que feu Cheikh Bethio avait pour Serigne Touba a travers Serigne Saliou. Je pris pour cet homme que j'appelerai pas un chauffeur mais plutôt un compagnon qui a su m'éclairer sur la générosité de Cheikh Bethio et son immense sacrifice. Sa wakh lérr na té andeu ak yarr ak mandouté DIEUREUDIEUF
Ps: sans limites changé le titre de la video cet homme ne mérite pas ça si té d'accord pousse bleu
Aka baax
Kou beug Serigne Saliou lolou réck
Yaw beugeul Serigne Touba réck té mouy dég ci yaw
Wallah ça ma fait très mal souma guissé yèn commentaire par ce que c'est le père de mon ami intime son fils aîné qui s'appele Serigne Saliou samb
Rafétna
Bilay ndékété oumplewona cheikh bi yalla na yalla yokk léeram
Ndeyesane cheikh bethio yalla nga tassék yeurmandé sunu borom
Amine
Amine wayy
J8 talibé cheikh mais sama khol dafa toye yalla na Yalla défar leupe incha Allah
Monme dafa déme ba nurou ak cheikh bi
Machallah wax dji raféte na amna ayy téguine téyit takhna ñou gueuneu kham cheikh bi diguëntém ak serigne Saliou
Yalna yalla doli yeurmandé ci moom
Mashallah, une parfaite maitrise sur tout ce kil dit, mandouté ak thieur bou matt seukk. Dieureudieufff baye lahad
Parmis les témoignages du cheikh c'est celui le plus franc et le plus convaincant yalla n'a sa diamou yagg
Jeureuff Serigne Lahatt. Yalla nga Jam diou matt seukk. Wakh bi rafettt tropp
vraiment wakhoul lou gniao serigne saliou papa gnianal nako man douma thiantacoune mais serigne saloum thioun day dem inchalla yalla na een bii oyof
ndeysane iow mom kou loyal nga danga dem ba nourok cheikh bi machallah
Machalla 😭😭 yalna yalla yokou réram barkep S saliou🤲🤲🤲
Machahala loumeleni rek lanouye khare si cheufeure ak secretaire Ndakh Mandou yalla na yalla defarate digeunete bi ba lepeu done beneu Amine si bareke serigne Saliou amine
Dieureudieuf Borom touba
Cheikh bèthio vraiment yagana diayantè Yala nako Yala bourbi boolè diotaye ak serigne saliou thia aljana firdawsi 🕋🕋
Ndeysane je viens de comprendre la relation qui lie Serigne Saliou et Serigne Bethio .
Chėkhe Bėthio Thioune yalla na serigne touba serigne saliou tėrou la alldiana firdaw si Barckė Magal gui💚💚💚💚👌
Nuit guenoul chauffeur bi très discret cela montre que Serigne saliou maka yar
Thiey yalla mala santé thie tanef biguama deffal thie Serigne Saliou thioun wathiona au yaw sama beuguel maguikoy yeuk barkep borome touba
Jiarajiefe thioune mame Bambi yanou dimbali yanou sagale machalla jiarajiefefate 💞💞💞💞💞💞💞💞
Manchalla amna sollo cheikh bethio Talibe moko maye loumou beug
Ndeysane, je suis un talibé cheikh et anhrif de surcroît wayé nous sommes tous des musulmans. Lahatt dafa dem ma nirok Serigne Bethio mandouté lou am solo leu thi domou adama. Wakhdji rafetna torop.Nay dioub rek aka malene fonk sama mbok Mourides yi salihatou 🤲🏽🤲🏽🤲🏽.
Bro yaw esk nitt nga rawatina talibé Cheikh, Bethio taxam finé Serigne Saliou mooy yalla tegg ci né yalla thiantacoune leu, di way aka leumbeul,diabaram yi di khessal aka tekk cheveux, meussoul djiité kenn dioulli wala diangue al Quran. Ba paré nga koy défendre,niou melnii mom nio yakh diiné dji ,kou Serigne Saliou defar doo melnii, xolaatal sa bopp, yonente bi nena dioulli moy première chose bou niouy khôl yawmal hiyaam, Serigne Touba nena kou bayi benn dioulli rek bou niou la dioullé té bou niou la soul ci cimetière musulman,bou fekké diokhé lekk rek Bill Gates mi ngi koy deff fepp ci adouna bi té dou dioullit ,kouma saaga ma fayou nak
@@serignekaire6597 iow ya wara nekeu nitt. Aka ma mandou thi yeufou diambour.
Je parle plus de la relation entre Bethio et son chauffeur. En ce qui concerne la forme chacun est libre.
En ce qui concerne les Mourides je prône leur engagement indéfectible. Kene doula saga iow tamit sangue bi fi ay nitt niofi nek dh tek am yar ak teguine. Nekal thi diamb fall ndiaga yaram 🙏🏾
Omar Ben Khatab Niang .
@@benkhatab14 bilahi ya am yaar ak teguine
@@apg-senegal walakhi yama eup yar ak teguine aduna amoul solo. Yallah na borom bi tapé khol yi mayniou diamb ak kheweul bou sakh. 🤲🏽🤲🏽🤲🏽
Ndeysane repose en paix cheikh Bethio Yallanako yalla khare aldiana ndeysane adouna
Amine
cheikh bethio yalnako serigne touba terrou Aldiana.Diambar deug laa
Adiana souniou borom moko mom wa salam
@@patriotedusenegal1350daga deg mani aldiana yalla momouko.walla dego wolof
@@gaindendiaye4295 fo momoul nofa meuna tero nite bayil sa xel mi guay fowé
@@patriotedusenegal1350 jalou
@@niangdieynaba9246 celui ou celle qui n'est pas d'accord avec vos conneries c'est un jaloux moi je dirai que vous êtes des ignorants
Yalna yalla féexël xolyi ba talibé cheikh bi andando nekk been amine
Waye ki yalla na goudou fane mandou na macha Allah
Cheikh bethio thioune mame bambiii dinagn laa woyyy dilaa féthialll thioune beugggg guimala beuggg yalla rekkk moko xamm❤❤❤❤
Machalla seu wakh dji rafétna!!!!!!wakhdiou diogué sii khol bilahi sii khol rék lay Doug!!!!
الله أكبر kilimou ame si serigne saliou dafe ko ligeuye
Machaallah sa wakh rafetna
Bien dit pére lahat samb iow ak cheikh debou la wone sa beugue serigne saliou tahna gua dieul sa taw bou ngor toudéko serigne saliou
Bagne nako sahh serigne saliou cheikh bi la yabalonn djoloff bou toudou siko
Dieurdieuf père yalla nla serigne touba fay sa khol❤j SS très content d tw yalna diamou yaje
dieuredieufe mame saliou Mbacke dieuredieufe mame saliou Mbacke dieuredieufe mame saliou Mbacke dieuredieufe mame saliou Mbacke
Machalla wax bi rafetna..... Jrnaliste yi bayi len yokk téy kholaaaT sen titre yi
Wakh dji rafetena dégoulouna dieuredieuf thi khelmou rafetmi té yallana yalla fayeserigne bi té serigne touba béguelho maachaala maachaalla
Papa chauffeur sa kadou yi amna solo machalla yalna sa diam yague 🙏 🙏 🙏
Ndeysane yalla nako yalla doli yeurmandé
Machalah Theiye seringe saliou
Dieureudieuf tonton wakh dji rafetna
Machallah dieurieudieufaty s touba yalla na yalla diapale s saliou thione
Dieuredieufaty Serigne Saliou diarama cheikh Bethio Thioune
Dieureudieuf Serigne bi takh nga ma guenna kham diguente Serigne Saliou Ak cheikh berhio
Dieuredieuf yalla sunu borom
Thiey Serigne Bethio mo kennal kou ted ki 👍👍👌
Cheikh bethio meussoul amm compte bancaire allahou akbarrr ak liko yalla mayoneee si khéweul Lou gneuw nonou layy deimé... Yalla na yalla woyafal soufff si kawamm
Mashalla Cheikh Bethio bilay Gaindé la Diambar la
Yalha nala yalha ak serigne Touba Faye thi barké serigne saliou
Ndeysane cheikh bethio kouko khamoul rk ndekei khamoko yalla na yalla yok ak lerame🙏🙏🙏🤘🤘❤️😍
Yalla na ko yalla yeureum
@@ousseynoufbi9074 Zs
Nèle yala nako yala yerem
@@ousseynoufbi9074 Mo diara gnaan.
@momo repondeur ah diaroul tontou dh Sénégal tontou motax niou tardé
Cheikh bethio Gorre ngua Ba wouyoudji souniou borom paix à son âme cheikh bi
Ki moy abdou lahat samb limouy wakh aka ko kham yagu ak cheikh bethio Tawam mou toudé ko serigne saliou samb ki si topeu cheikh bethio jajeuf sama wadji ya bakhh
Alé Ndiaye khana moy saliou samb dieuwrigne universel
Nday sann kaduyi dawna sa ma yaram s lahat yalla na la yalla samu def diamu thi rewmi ak bépu dioulit
MACHALAH... WADJI KOU BAAX LA...
Mashalla ya bahhhh
Machallah baye lath sa wah rafet na
Machalla yalla nako yalla yeureum fam nek
Paix à son âme. Il a bcp œuvre pour le rayonnement de cette confrérie. Yallah nako yallah yeureum te khareko aldiana firdawsi.
Ndéyesane yalnako yalla yeureume cheikh béthio si barké serigne saliou mbacké
ndeysaan nit loumou taxxool niroo ak moom seugn bii di wax dafa niroo ak cheikh bethio.
yalnaniou yAllah taas thi barkeem
Ch Bethio yalna niou ko yalla fayal te tass niou ci barkeem barkeb SERIGNE SALIOU ❤❤😢😢😢😢❤❤❤
Cheikh béthio yalla Nako yalla yeureum tes kharéko aldiana firdawshi si barki serigne saliou
Macha allah amna solo yallah naco borombi yeureum
Machalla cheikh bethio nitt kou bakh demna
il ressemble même A cheikh bethio
c'est m'a première impression
Trop même
Ah wai ils se ressemblent trop même
Khalil IG Niggvz dama dem bay wakh lolou tek tek bilaay
@@ourayecisse5868 lol je t'ai marché sur la langue
Albouraakh nga toudou tu as un joli coeur ma shaa Allah
Yalla na yalla yok ay leram Cheikh Bethio
Ndeysane ki gorla nit la kou bahla
Serigne bethio dei wadji wadji wah tahna ma ham moy kan ndah man Talibe cheikh la wayei lima deug ni
Moy Waneni limou liguey rek lako yalla fay hana diko nianal yalla famou nek yalla yeureumko si barkè yonete bi
Amine
Ndeysaan Dieuredieufé Serigne Touba
Yalla nako yalla yeureum thi barké seydina Mohamed psl thi barké cheikh Ahmad bamba khadimoul rassoul aminnn yaraby aminnn
Thiye sisekh betho yalla nanoko yalla fayeyal
Dieureu dieuf serigne salihou mbakce serigne béthiou yalla ne yalla Yoko le RAM
Machallah Mandou gue
Machalah wakh Day rafet dara niawoul
Ndeysann ken dou serigne touba
Wakh dji rafet na sell nheu deugou nheu wa salam mon père baye lahad samb
Machalah rafétna thé dit wakh rek amine yala nako yala déf mou niow rangé derier Serigne saliou gueule tapé dey gueuna nékh té dagane
Dieureudieufati S Saliou. Gadou yi rafet na loll. Santate nanou bou bakh.
Thiey yalla Sam xol Sedna walahi Keen dou cheikh béthio mou s saliou yalnako Sun brom djegal xarei ko aljana firdawsi
Thieuyyy Serigne Bethio😭😭😭
Kadouyi rafetna
Yalla n'a sounou borom bolé Ndjiabot gui yepp mou done bene.
Ci barke Serigne Touba
Wakh dji refetna lol. Amna ay téguine. Cheikh Béthio Yalna ko Yallah doli yeuremandé.
😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭oupalé nite bakhoule cheikh béthio talibe pire la geume na liki wakh
yalla yalla Faye kadu yi rafet n'a 🙌🙏
Salam. Wakhdji rafetna. Kouy defar mbokk nga
Arrêtez de vous mêler de cette histoire de famille! arrêtez de jeter de l'huile sur le feu! De quelles vérités crues vous parlez? Cet ancien chauffeur de serigne cheikh Béthio est digne il n'a dit que des mots d'apaisement il a incité à la réconciliation familiale donc ne foutez pas la zizanie c'est indigne de vous...
masha allah samb Yallana yalla feyla barkep serigne saliou
Ya bakh way 🙏🙏🙏🙏🙏
Ndésane balla gua xam wadia rk mou sorila yalna yalla yok ay léram
Ban YALLA le gueumoon?
@@amantubillahi9628 lolou démal lathie ko sa pape ak sa yaye
Yalla mi meuna boler yalna yalla boler wakeur cheikh bethio si diam ak salam niou nek bene si barker yonet bi ak serigne saliou je ss tidiane mes diam dafa nek yalnako yalla def
Bilay amine way
@@ndouradiop3085 Amine Ya Rabbih kou andoul ak sa mbok dinga and ak mbokou diambour té mbok alalou Yallah la.6
ThieY cheikh béthio Yalla nako serigne Touba FayE Sa LiguéY Rafét na
Thieuy Cheikh Bethio, aka beugeu Cheikh Saliou Mbacke' ta yague ko ligueyel ta way thi... Yalla nako Yalla defal ay daradji goor guoumou Gueureum!!!
Machala max bi rafett na
Ndeyssane 🙏
Macha Allah kadouyi amna solo
Ndeyssane mâchallah kaddou yii raffetna thiey thioune mame bamby mo diêkhone takke thi sanguame borome jamono motaxe raaw yallena yalla yokk aye leram t tass niou thi barkem
Thiaye chèikh bèthio Sama rogogn Dou Masa far 😭😭😭🤣😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Mashallah !!! Deug rék la Mbaye Pékh wakhone. Cheikh Saliou Thioune kheuthiowoul dara, kén dou kheuthio lo mom ba paré si dérétt, si baatine ak si zaayiir. Danou ko sass mom Cheikh Serigne Saliou Thioune si Ndigueuleul Serigne Mountakha Bachir Mbacké, yallah nafi yague té weur. Tékssi il est discret, Kèn guisseugoul sokhnam ou ay sokhnam affichéyou si wétam di diay gueuneu goudoulé ak reuyelé moussaure (foulard) uniquement pour fégn, feuss né or si vitrine, niépeu nan yawla yénela😁. Pourtant dé, sa ou ses propres femmes nioko gueneu yéyo, té amssi plein droit. Yague fi lole té weur Thioune !
Cheikh Béthio Yaalla nakoo yalla Dolli lèrri aldjanna si Barker SERIGNE SALIOU
Mom dafay ndirou cheikh bi sakh walahi ndeysan
macha'allah merci beaucoup bien dit merci beaucoup
Ah vrmt c touchant bayilene khouse journalistes yi svp
Xassidaas yi daw thi souf n3xneuu😭😭😭
Amadou Ba rabi karimoun la bo tapè youtube di ngako guise
Thiey yalla yalnaline yalla kide jaap L'une si serigne touba ak tawam bi cheikh bi
@@bayeamdyfaliloundiaye4313 dieuradjeuf
Serigne bethio RAW na
Je suis talibé cheikh mais journaliste yi fene rek ak tass keur koulene moytouwoul .ki wakhoul dara Lou gnaw
On a besoin des gens comme toi la vérité
Waw gor talibé cheikh ni lay mél
Dieureudieuf serigne Touba
Sama mbokou Talibè Chièkh bi sounou Wassila Mame Seydi Elhadji Malick Sy dafa moyetoulo mandoulo gnou fague lo gnou sounou lamigne tamite gna balma akhe dama beugue gnou mouthie rèk Incha'Allah
Tass famill rek ak sen titre bou bonne le chaufeur na rien dit de mal sur Aïda
Izidine Izidine lou lér nga wakh nite day mandou
diaaradieuf serigne saliou vheikh bethio yalla na yalla yokk ay lairam
Sa kadou rafetna yarame