Salam ya Salam magui ziarer tous mes fans je prie pour vous bilahi quand je lis les commentaries je suis plus moi meme j ai les larmes aux yeux alahou akebar raboule gharechile Azim k dieu vous benisse mes sopes dieureudieufety et j avoue aussi k c est des encouragements pour moi aussi donc prie pour moi pour k je sois plus inspiree a bien chanter taahaa mouhamet moukhetar psl dieureudieufety
Machallah sama yaye fatou binta ndiaye mala beuge guirr yalla ak mouhamed yalla na yalla weural bate bi si barké mouhamed yalla nala yalla défal diame ak goudou fane ak weure way Machallah kou beuge fatou bintou ndiaye sama yaye dji beusal Jaime way 💖je t'aime😘
salam salam wattnako si cheikhna cheikh Saadbou (wakhartou) sonbi Guay deglou moy mellni louguenna bésss a chaque fois man sokhna Dior Faye magui si Sama yaye djima mousoul guiss sokhna Fatou bintou Ndiaye bâ kara may dé ndakh bègue boumou bègue seydina MOUHAMED salalahou alleyhi wasalam bègue wa alibeyty nabi dieuredieuf niguay sétalé sougnouy khôl yalla NASA kholl di sété té déukksii si Barker saadoul khalhi
machallah sa fans number one la sokhna Binta ndiaye.... danga naturel machallah weuye bimome nimaye def make yalla rek kako khame. goudeul fane sokhnasi.
Sokhna Fatou Bintou, qu' Allah te donne la bonne santé et une vie longue, heureuse et bénie, pour que tu puisses toujours oeuvrer dans ce qu'il y'a de plus merveilleux et exaltant comme travail, faire avec bonheur les louanges du Prophète Mohamed Rassoulillah, Paix et Salut sue lui. J'ai bcq d'admiration pour Toi, Fatou Bintou.merci mgkok 26-10-2012, 20h22m, Tremblay en France.
Machalla toubarfakala qui aime tata Fatou Bintou pousse j'aime
Elle chante très bien
Salam ya Salam magui ziarer tous mes fans je prie pour vous bilahi quand je lis les commentaries je suis plus moi meme j ai les larmes aux yeux alahou akebar raboule gharechile Azim k dieu vous benisse mes sopes dieureudieufety et j avoue aussi k c est des encouragements pour moi aussi donc prie pour moi pour k je sois plus inspiree a bien chanter taahaa mouhamet moukhetar psl dieureudieufety
Fabinta Ndiaye machala Diam rek gay am
Dieuredieuffff longue vie à vous
Je vous admire beaucoup DIEU m'est témoin bon vent
Lii doumako doyal
Yallah gue goudou faneeee
j'ai des larmes aux yeux à chaque fois que j'écoute cette chanson !!!!! machallah !!!!
Machallah sama yaye fatou binta ndiaye mala beuge guirr yalla ak mouhamed yalla na yalla weural bate bi si barké mouhamed yalla nala yalla défal diame ak goudou fane ak weure way Machallah kou beuge fatou bintou ndiaye sama yaye dji beusal Jaime way 💖je t'aime😘
Yèwou Fadjar dèglou kaddu you sëll yi Di yeungeul deunou Goor Yallah yiii Mashalah
Yallah naleu sugnu borom fayela yiiww !!!
Masha Allah skhna FABINTA ligua beugue sakh khol yako kham yalla nalako YALLA sougnou borom daifal thie barkép SEYDINA MOUhAMED(PSL) on FiÉR d'être khadre baaa ALDIANA💘❤💓💕💖💗💙💚💛💝💞💟❣
Ma la beugue piir mane yalla ne yalla wéral batte bi thi barké nabi sama tourodoure dome❤💙💚💛💜
salam salam
wattnako si cheikhna cheikh Saadbou (wakhartou) sonbi Guay deglou moy mellni louguenna bésss a chaque fois man sokhna Dior Faye magui si Sama yaye djima mousoul guiss sokhna Fatou bintou Ndiaye bâ kara may dé ndakh bègue boumou bègue seydina MOUHAMED salalahou alleyhi wasalam bègue wa alibeyty nabi dieuredieuf niguay sétalé sougnouy khôl yalla NASA kholl di sété té déukksii si Barker saadoul khalhi
Machallah, contane na si yow bou bakh sama mbokou talibé cheikhna cheikh saadbou
Maïzena Kane est
On est 2020 et c'est toujours ma chanson préférée 💓
❤❤❤machala elle chante merveilleusement notre prophete
Machallah yalna Yallah SWT wéreule bate bi. Séguéla trop si yow beuguenala guistorop khowma loulaye défnak. Souma laye déguelou nga waye Seydina Mohamed PSL damaye chair de poule yalna Yallah SWT faye
Cette music me donne la chaire de poule j'adort le prophete(psl)
Mashallah wakhayert cheikhna cheikh Saadbouh ❤️🥰🤩👌⭐️
Machallah merci Cheikhna cheikh Sadbou 💪💪💪🙏🙏🙏🤲🤲🤲
J'adore cette maman si seulement je pouvez la rencontrer
machallah sa fans number one la sokhna Binta ndiaye.... danga naturel machallah
weuye bimome nimaye def make yalla rek kako khame.
goudeul fane sokhnasi.
Hola do
Machalah
Machalah L,islam ma religion jusqu'à la mort je vous adore Yalla na Yalla Faye si barké seydina Mouhammad Salahou Aleyhi wa Salam
Machallah maman Fatou bintou takku ligueyal cheikhna cheikh saadbou
Machallah yalla na batt bi were yalna cheikhna fathie sa adio
Machallah sam sopee bu male bougue yallah ne yallah yagal fu son doundou ame solo, j sui tn fans dpui a nouadhibou
cela m fait plaisir d'ecouté cette voix d'or c bien reussit cette chason et le tariha tijani et ma religion preferé
*FaBinta* dama weur woy bi beu sonnou. Étant d'une mère Mauritanienne🇲🇷, J'adooore cette chanson masha'ALLAH🙏!!!
Song starts at 3:10
Qui est la en 2024❤
Yalla na yalla weral bate bi waye sokhna fabinta ndiaye borome nimzate
machala
mashallah Fabinta yallana yalla goudeul sa fann ak mbooléém djoulitt amiine!
Franchement man jour bima la ndieuké guiss thi télé lala beug damay took sax sama xel nek thi yaw ma téléchargée sa son yi
inégalable cette dame. Macha Allah !
Fiere d etre Khadre Tarikha nimero 1 Salalahou Aleywassalame.
J'AIME WAKEUR CHEICHNA CHEICHE SAADBOU SAMA KEUR MAME MAIS FATOU BINTOU ELLE EST EXELLENCENTE.MACHALLA LONGUE VIE
Salam hadja alhamdoulilahi pour l'amour que tu propulse dans tes chansons que Dieu accepte nos prières quand je t'écoute j'ai une joie même énervé
Sokhna Fatou Bintou, qu' Allah te donne la bonne santé et une vie longue, heureuse et bénie, pour que tu puisses toujours oeuvrer dans ce qu'il y'a de plus merveilleux et exaltant comme travail, faire avec bonheur les louanges du Prophète Mohamed Rassoulillah, Paix et Salut sue lui. J'ai bcq d'admiration pour Toi, Fatou Bintou.merci mgkok 26-10-2012, 20h22m, Tremblay en France.
amine
Salamou aleykoum mangi nyou nyeup macha allah la illaha illa la rék
YALLA Contane nah, sama Mame SEYDINA MOUHAMED bégu nah
Fier d'être khadrie❤️❤️
Dioyna Fatou Bintou yallnala Yalla may fan bou gouddou ak werr begual ngua sougnou khol yi Dieredieuf way yallnala cheikh sadbou fayi
Je me rappelle gamou Ngoumba Ngewoul kan elle chantait accompagné du defunt boy narr bidanne teug tabala ndaysane. Fatou binta doundeulll lou barii❤❤
cela me donne la chaire de poule a chaque fois que j ecoute cette musique really
Machalla tata yalla tata n'a Bate bi guena wer chekhna rek ❤
Ce n'est pas une religion mais ton tarikha préférée.
A chaque fois que j'écoute la voix de Adja Fabinta j'en n'ai la chair de poule
on est deux :)
on est trois et + encore
Lou Petra
manchallah ma maman et moi t'aimons beaucoup wallahi😍😍
Masalahhhh sasoumay degulou waybie damayyye contane maman beuguenallla tropppp longue vie à vous
Machallah goudou fane weee akk werle maman
Machalla yalla na bate bi weer
Machallah j’aime bien cette chansons❤️❤️
Ndeysane Li doumassi doyal
Yalna sunu borom defal là jam
j'aime tout ce qui vient de fatou bintou ndiaye
J'aime bien ce chanson
Salalahou aleyhi wa salam Je l'adore aussi
machallah
goud fan ak wér si barké serigne touba yakari diam gni
Mâcha allah, que du bonheur
machallah même en 2022
maman billahi de ma la begeu yalna yalla def guissè
Tu fais notre fierté maman❤❤❤
Merci maman chérie
Beugue cheichna mo maure❤
Ma cha allah sister. Que Dieu te protege
dieureufé cheickna cheick saadbou
machalla elle chante très bien
Machala elle chante très bien
Machala très belle chanson
Ma sha Allah ♡♡♡
Maman fathe Bintou doundal🤩
Marchaalah rafét na
Mashalha.
machalla fatou binetou ndiaye
elle me fait beaucoup de bien machallah
machalaaaaaaa!!!!!!!!!!
Machallah nekh na trop
Fabinta...Maaashallah
Mashalah sokhena ci
♥️
J aime bien fabintou n diaye woni
2020 ❤
j aimeeeeee!!!!!
YÉFER YI AK NITTOU SAFAYI DI METT PAS J'AIME TROKH REK
Boul wah lolou way
cheikhna cheikh saad bouh mo kémané
Machala
G la chair de poule. God bless!
ndeysane billay li monekh machallah fabinta
Masha allah ❤❤❤❤
Bokena si neila guene beugue Sénégal
Machallah!
Machalla 1❤❤❤❤💞💞💞
SA ME FAIT DU BIEN D ECOUTER FABINTOU
Machalla mala beug bilahi
Masha allah
weny bikk machalah alhamdoulilahi dieureudieufety mon numero c le 77 533 70 66 choukrane diasilane weny keubirra seydina mouhamet moukhetar psl dieureudieufety
😂😂❤
hey le jour où je vais me rencontrer je l'aime bocou
machallah longue vie je veux ton numero
Malls beug mane machalla
Bientôt le site officiel de fabinta ndiaye >> fabinta.com
😍🥰🥰🥰🥰😍😍😍😍
quelle voiiiiiiiiiiiiiiiiiiii
kéne dou mom SALALAHOU ALEYHI WA SALAM
2022 🙏🏾❤️🙏🏾
keneu gueunoumakoo beugueu.
Wa khaitoul cherif
❤❤❤❤❤❤❤
Rafett na
Wakhiyertou Aïdara cherif