Machallah je ne peux m empêcher de regarder cette vidéo chaque jour et à chaque fois j 'en pleure d’émotions que DIEU vous garde au nom du prophète SEYDINA MOUHAMAD SAW Amine.
Sama oustaz assane kane yalna sa diam yague amna solo lole diangana si yow loubari macha allah ma sopela lole nak sa wakhtane dafa naikhe daye bolè utile ak agréable merci ya oustaz
Yâ Man azharal djamila Wa sataral qabiha Wa lam you-akhiz bil djarirati Wa lam yahtiki sitra Wa ya azimal afwi Wa ya hassana tadjawouzi Wa ya wasral maghfirati Wa ya bassital yadaïni bi rahmati Wa ya mountaha koulli chakwa wa ya karima safhi Wa ya azimal manni Wa ya mouqilal atharati Wa ya moubtadi-an bin ni'ami Qabla'stihaqiha Yâ rabbi wa ya seyidi wa ya mawlaya wa wa ya ghayata raghbati As alouka an La touchawiha khilqati bi balala-i dounya wala bi azâbi nâri bi barakati.... Amine yalla naagn yalla fayyal sang sangu yi
Salamouleykoum machallah mais Oustaze bougene mounane di binde niane yi écrans bi dina bakhe té niane yi aussi dignou diokh verset yimou nek si alkhourane Dina bakh lool merci

Alhouma amine Serigne Assane Kane amouniou sa feye. Manedé beugona khame noumaye défe ba guisla. Mangui laye tope si chainebi saa souné. Yalnala yalla faye
Machallah je ne peux m empêcher de regarder cette vidéo chaque jour et à chaque fois j 'en pleure d’émotions que DIEU vous garde au nom du prophète SEYDINA MOUHAMAD SAW Amine.
Tidjane yi raw nagniou barké Al Quran ☝
Walaahi, wakhatiko
ma challah Al Ouztaz. Ya Allahou Fayal Gnoula. Moom rekk Lagnou Layy Bayéel.
Machallah jajef serigne Assane kane ❤❤❤❤❤❤❤
Serigne Assane yalla na yalla nanguou nianbi gua fi niane ci adouna bi yeup. Amine
Salam serignbi dieureuf dieuf.. Wa gnane gui kouko binde ... Eskeuyyy
Jeurejef serigne assane kane yalla na yalla godal sa fann meyla weur
J adore aicha mashalla elle est sympa
Machallah Machallah serigne Assane Kane dieuredieuf !
Sama oustaz assane kane yalna sa diam yague amna solo lole diangana si yow loubari macha allah ma sopela lole nak sa wakhtane dafa naikhe daye bolè utile ak agréable merci ya oustaz
Sama oustaz Assane Kahn lallow Amna solo masalaa masalaa 🙏❤️
Very important topic
Shukraan, y’a oustaz, saa doundeu amna ndiaarign, MachAllah
dieureudieuf Serigne Assane Kane Yalla nangua fi yague té weerr linguaye wakh ame na solo troop
Dieredief ❤
Diadieuf kou bakh yalla na yalla Faye dieuredieuf
BOROM XAM XAM PUR LA SERIGNE ASSANE KANE GOUDEUL FAN KANE
Machala yalna nieup ame diam
Machala dieuredieuf oustac
Amna solo dh wa lègui niane gui nounouy dèff ba diote si ( c’est à dire l’écriture de ya mane azharal bi )
Yâ Man azharal djamila
Wa sataral qabiha
Wa lam you-akhiz bil djarirati
Wa lam yahtiki sitra
Wa ya azimal afwi
Wa ya hassana tadjawouzi
Wa ya wasral maghfirati
Wa ya bassital yadaïni bi rahmati
Wa ya mountaha koulli chakwa
wa ya karima safhi
Wa ya azimal manni
Wa ya mouqilal atharati
Wa ya moubtadi-an bin ni'ami
Qabla'stihaqiha
Yâ rabbi wa ya seyidi wa ya mawlaya wa wa ya ghayata raghbati
As alouka an La touchawiha khilqati bi balala-i dounya wala bi azâbi nâri bi barakati.... Amine yalla naagn yalla fayyal sang sangu yi
Ya waaci'al mahfirati*
Masalaa masalaa Borom xam xam sering Assane Kahn lallow Amna solo ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🙏🙏🙏
Amna solo lollll
Serigne Assane Kane dundale teh were yalla na yalla gudale sa fane machallah
Machalah amna solo yalna la yalla maye goude fane ak were
Mashallah 🔥✨ Borom kham kham
Yagui fi lol Serigne Assane 🙏🏾
Yalla na yalla goudele sa fane mayela wére
Walakhi boko thi KAne goudou fane ak weer
Salamouleykoum machallah mais Oustaze bougene mounane di binde niane yi écrans bi dina bakhe té niane yi aussi dignou diokh verset yimou nek si alkhourane Dina bakh lool merci
Yâ Man azharal djamila
Wa sataral qabiha
Wa lam you-akhiz bil djarirati
Wa lam yahtiki sitra
Wa ya azimal afwi
Wa ya hassana tadjawouzi
Wa ya wasral maghfirati
Wa ya bassital yadaïni bi rahmati
Wa ya mountaha koulli chakwa
wa ya karima safhi
Wa ya azimal manni
Wa ya mouqilal atharati
Wa ya moubtadi-an bin ni'ami
Qabla'stihaqiha
Yâ rabbi wa ya seyidi wa ya mawlaya wa wa ya ghayata raghbati
As alouka an La touchawiha khilqati bi balala-i dounya wala bi azâbi nâri bi barakati.... Amine yalla naagn yalla fayyal sang sangu yi
Macha allha ♥️♥️♥️♥️
Machallah jerejeff Serignebi
Salam oustaz assane kane machalla
Machallah amna solo lollle
Machala yalla na yalla may werr té goundal say fane khamkham bi sell na té ame solo
Salam aleykoum mane gnane bi yeup la beugone svp?
Machalla machalla
Machallah🙏❤🙏
Macahla
Machallah serigne Assane Kane dieuredjeuf Way
Machala
Amine
Machalla amna solo kane Diallo yag fi lole te were kane Diallo
Bonsoir serigne assane q Le Tt Puissant jalonne et eclaire votre chemin
Je voudrai savoir ce q Le coran pense du port d amulettes(gris gris)
machallah
Beaucoup d'enseigne
Alhamdoulila
🙏🙏🙏
Amna solo lool
Alhouma amine Serigne Assane Kane amouniou sa feye. Manedé beugona khame noumaye défe ba guisla. Mangui laye tope si chainebi saa souné. Yalnala yalla faye
Ajarama chrono alassan yo alla juno balde ma
شرج حسن كن ماشاء الله جرجف
Sen groupe watsapp bi kou si beugua bokk intégré nak noumouye dèff
Mane damaye lathié signification 16 figures de la géomancie
Man damay lathe koubeugeu dindi ligey boung la déf sadigénté ak sa boromkeur ngir yala loumathi dimbalé madial
Bindma
Je vais te donner un numéro si tu veux-tu te yalla reekk tah
Machallah ♥️♥️🕋♥️♥️