Alhamdoulilah Dieu merci yéné bi matt na niongui niane yallah liguey bi oyof. Nous réservons une mention spéciale à Xalaat tv franchement sen liguey bi rafete na vous nous a accompagné depuis l’opposition jusqu’au pouvoir donc nous vous souhaitons une bonne continuation 🙏
Alhamdoulilah Dieu merci yéné bi matt na niongui niane yallah liguey bi oyof.
Nous réservons une mention spéciale à Xalaat tv franchement sen liguey bi rafete na vous nous a accompagné depuis l’opposition jusqu’au pouvoir donc nous vous souhaitons une bonne continuation 🙏
Ndam rek inchallah ❤❤❤❤❤❤❤
Oh doyen Alla kana yaram dawna binga togué thi chaise bi. féké demb ak mamadou dia taay ngay gongué sonko# thiey yallah goudal faane mame
Ana patriot yi❤
Machalla xalaat masta thiono debut ba fin xol sedna si yen billahi
Masala amna solo lolou sakh bill li néhkne ❤❤❤❤❤❤
Pastef seul❤🎉
Maman Ami Dia. Félicitations ❤
Foccus rek sur le jub jubbal jubbanti
JUP JUBAL JUBANTY
Xalat dafa wara am télé media
❤❤
Doyens alla Kane ❤️❤️❤️
Yalla naléne Yalla protège
Merci