Abdou Bakhoum sur la victoire de Thiatou Daouda Fall: "naniou diokh Siteu victoire. CNG na bayi…"
Вставка
- Опубліковано 14 січ 2025
- Visitez notre site web luttetv.com/ et aimez notre page Facebook pour voir des combats en direct / luttetv
/ luttetv
/ luttetv
/ luttetv
luttetv.com/
Merci père bakhoum
Ama neekh mo dane 🎉🎉❤❤
Merci Abdou bakhoum bilahi amanekh mo dané
Bakhoum a parfaitement raison ❤
Walahi thiatou la begone mou dane mai sérieusement avce imag yi amanekh a bel et bien vaincu
yéne wa keur mod lo guéne ci séni commentaire rék laléne di khamé amanékh mo dieuka danou pa bi di bakhoum nak mome dafa manoul mougne mod lo wayé siteu ak mod lo ci sakouyi la ta li ci bir guéw bila
Toute l'erreur c les arbitres pourquoi ils les faisaient pas lutter encore , sénégalais mo beug lou yomb koi c koi c histoire ki mo dieuk épaule après ki tek na bop ? Diel dafay lerr
Amanekh daffa Dane vraiment li daffa gniawe
té en plus avant bras la tékk, amoul béndeu épaule bou lale
Merci père ndahh Sénégal désé kénakou wahh DEUG la tête de thiatou Daouda fall moo djiitou
Vraiment siteu daane naa modou lo
Siteu niéméwoule watené modane modou lo Siteu bopou lalena sakouyi gayi toujours coté modou lo rék laniye wané di neube coté siteu waya bo gussé coté siteu bopou bi lalena sakouyi
Le problème pk gayi di neub côté bopou siteu cikaw saccouyi ? Nie ay vrai mbam laniou...@@dakardk4750
Deugue deugue sita dana
Deugla diokhléne siteu victoire rame boudet victoire laniou diokh thiatou daouda fall deug rek moye deug
Bilay CNG togn na amanékh bathi la alou yalla
Togne siteu senegalais yi andeu ak mom
Vraiment Tay mom deugue rk la wah
Siteu a battu Modou lô pour dire vrai 🙏
Si sacou yi
*Kii mom dou nopalou ci Modou Lo 😂😂*
Dafa wakh deug mais deuk nafekh laniou nek
Te pourtant kou Nafekhoul khamni Siteu mo dane lou lerrr
Défait modou lo mo guen ler sakh😂😂😂😂😂
Lii victoire menou thiè am , dagnoo warrona taxawàt beuré .
Nanio diokh sitta victoiram
Pere daga nieme deug rek❤️
Diokhe lène siteu victoire kone père tu as rèson cng son des coronpie
Menou daw dane😂
Bilahi bakhoum deug la wah
Me loutax ki bagne Modou lo😂😂😂😂
La réaction de Amanekh après la chute montre qu'il est tombé, car il a continué l'action. C'est psychologique
CNG dagnio nèlaw Si Modou Siteu
Père la situation de siteu n'est pas comparable avec bi, siteu da done daw té si bitii la nec, il faut tenir cela en compte, mano nec si biti di dane, souko déféwone si birr comme ama'ekh AK thiatt dans ce cas meun na am victoire, il faut savoir faire la part des choses
Même siteu da tekk bopou ci saccouyi lolou kéneu begouko wané
Bakhoum dof respecté le roi
Kou lerr Guam wakh
Mod lo mm sou dano règlement bii mo validé woul chute bii
Da am skh si football joueur day dougeul but hors jeux am dounn ko validé
Mane de thiatou daouda fall la faral wayé bougnou diokhé thiatou daouda fall victoire nane diokh siteu victoire
Siteu c en dehors de l’enceinte boulen fatei
@@damedia9410 Ndamou Siteu mo geuna lerrr
Iba kane les gens te respectent et te suis arrête d'inviter ce haineux, il a un problème ce gars
Premier commentaire 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Amaneh a belle et bien battu thiatou Daouda fall.
Bakhoum Nonou
Modou lo Bou Bonn la
Ms ayway bayilene Modou lô ak ndambam li bakh
Vraiment bakhoum taye mom ande na ak ioe modou lo moy Sama mbeur mais bougnou dioxe thiatt victoire kon modou lo siteu dann nako
Iaw yay nafekh 😂😂😂
Dafa lère kone siteu dafa dane modou lo ay nafèkhe gnène ambèsile
Abdou Bakhoum aka bagne Modou lo fi ladone waax Modou du neek Roi😂😂
Var bi kon amoul chance
Ama nèkh mo dan thiatou situ mo dan modou lo li Moy degue nitt mome bou waxoul Li rek defa farr
Contexte combat yi bokoul règlement mo atté siteu modou lo chute bi biniouy wax si sakkou yila l'autre au milieu du l'enceinte
Règlement mo wax kouy danne si sakou yi moy ki def action bi ki nek sibiti meno danne surtout bou lou eupe si yaw néké sibiti
Quant à amanekh au milieu leu lep xéwé
Loumassi diaxal moy daniou wax ni épaules dou chute si règlement bi pkw niou dieul victoires diambour wala aziz ndiaye moy dirigé
Pour moi épaule bi c à revoir vraiment.
Épaule ak bras mom soriwowouniou
Question de position le rek
Kii épaule bi mo djitou yor na vidéo bou lerr nagni
Ama nékh seul❤❤
Boulene fater ni pere bakhoum moy wakh..beugoul modou lo
Thiey père Abdou Modou bakhoum😂😂
Ama nekh mooo dan
Cng bayilene thiakhana amanekh mon dane
Abdou bakhoum siteu diokhou d'ara wayé daga bagne Modou lo motakh ga. Sonou
Amanekh mo dane dafa lérr bakhoul a parfaitement raison
Kon siteu dana modou lo
Père ngeumeul yalla
Ki mome khole bou bone la yor wayé diga bayi modou deh
Modou lo dako wara porte plaite
bilay walahi Sou gnou diokhé thiate 😂😂😂ndam kone ya oustaz Siteu dako torokhal d'Anne ko 😂😂😂
Pére Abdou lou ler nagne la wakh siteu mo dane dé bayiléne manipulation bi
Thiotou nayam Senegal 🇸🇳
Dina yageu Tardé nax Dafa bary Naféx 🥹Sieu Moo Dan Modou lo 🧏♂️Bayma ndione Moo Dan Modou lo 🧏♂️Zarko Mo Dan siteu 🧏♂️Amanéx Moo Dann Thiatou Daoda Fall barke Alhouran 🧏♂️✍️✍️
Cng louléne nékh lagnou déf mais ama nékh mo dane
Nane diokh siteu victoire ral
Non lamb yakhouna té bari nanfekh malick ngom attanoul cng bilahi,kou gueumné malick ngom dou yagg cng lalal j'aime magui xaar kona améric
Xana Senegalese yii wahoulén né cng. epol dou suite 😂😂😂 nafeh nio bri Senegal 😢😢
Wa Abdou bakhoum mi louko modou lo déf
Siteu solénn ko diokhoul sakh mo dane modou lô
Billahi per bour khanne limou wakh moye degeu
Amanekh na déf recour
Amanekh mo dane bilahi cng gnioy nanfekh deug malick ngom yala n'a wathi
Sawye mane sama khel azzi ndiaye setou ci
Baoume.lou.takhe.nga.sokhore
Sa.ndaye.waye
Meun wakh deugue yalla parcelle la deuk mais damani boufe Nila demé kone nonou leu demé
😂😂😂😂
Pere tega gueum yalla 😂😂
Siteu mo dane dee senegalais mo nafekh😂
Waay lii njaax la ken daanul😂😂😂
Amanekh mo dane vraiment
A quoi sert la var alors soit le cng conserve les recours et élimine la var ou bien si la var décide c’est définitif 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Vraiment amanekh mo dane
Malick ngom kholatale sa doxaline
Pr bkhoum loumou wakh moy dueg
Ndiakh daffa am si beure li ndiakh la
Ama nekh mo dane var mo ate cnc ate wounioula deugue
En tout cas Dale combat takone n'a Souf si louma guiss
Amanekh a battu TDF !!! Le CNG doit être sérieux
Amanekh mo danne lolou dou dagne
Bakhoum effictivement même ama baldè nagne ko dèlo victoiram contre modulo 😅😅😅😅
Bane victoire 😂
Bakhoum le jaloux wallah tu vas maigrir 😅
Ama Nekh mo dane par force
Lii du Yoon Amanekh mo daan
Ça c'est injuste. c'est une grand injus te Modou lo alors.
Mom louko modou lo déff 😅😅😅😅
Siteu mo dane
Ama nekh mo daan dei sérieux nak
Donc Siteu mo dane mdlo
Cng wakh léne deug vous êtes des faux
Mais presidente NG a été nomiminé par la gueye et Ndiaye en bon attendeur merci
Abdou Bakhoum nopaloul Modou lo dou meusseu dioy guay rétan
Pér bakhoum guemele yalla 😂😅modou Lo defko nika yalla def 🤷🏽♂️ 👑
CNG danou nagniou
Mais Sitau Danoull
Modou lo dhè Niari Combat yèppu
Ndiakh la
Mé man légui var pour lan lan
Amanekh mo dann dé.
Li dou débat waye thiakhane bakhoul....ce CNG est ridicule....un peu de sérieux je suis thiate mais il a perdu sur toutes les angles
li dou yonè way
lou leerr gua wakh père
bakhoum mom modou lo mooy problemam
Papi manoul beugue kharagne lo
nopaloul cii modou lo
Ah kon Siteu moy roi des arènes😅
Gorgui dal bakhoul. Tu peux pas laisser modou tranquille ? Comparaison n'est pas raison !
Vraiment li Moy indi problème si lamb franchement li CNG def c'est pas normal Amanekh mo dann DEUG nexoul fou amanekh dano rk Modou Lo danou na Naniou waxanté deug rk lamb amoul paarr paarlo Amanekh mo dann Naniou ko diox son victoire voilà
Mais siteu mo nieuk tekk bopou ci saccouyi yéne môme menoulen digéré modou...teu danio anulé action nakh sibiti la siteu daw