Le temps peut changer beaucoup de choses, mais une chose qui ne changera jamais, c'est mon amour pour toi bro.Yagui sisa yoon machallah di doxal teksi jambar gua
Man mi dhh amouma massi mom sago beug nako ba parei douma deglou sax lou gnaw si mom courage et continue sur cette lancée une belle carrière se promet 🥰
Kouniouy sentou si gualou chien fexel ba boufa lek té geum nani dofa mesa diégué baye def lelene.gnagny bayi xél ns les inconditionnels beugua tougne nit yap njiou si ay détails. Parce que mane personnellement sama tabaski après xawma loumoudone saf.mais courage le phénomène
Kou beugue SIDY DIOP lallal j’aime svp🙏🙏
Y’a takh may degeulou musique 🎵 yalla kham nako bama lay beugeu dou tay dara meunou niou takhalé 😢❤️❤️🙏
Le chanteur du peuple Sidy Diop champion gua walahi
Yalla defna nit meunouma wax ci sidy louy wagni sama thiofeil ci mom yokoutei rek👏🔥
Bilahi yalla nako yalla defal diam inchallah
Walay Mane ak yow
Sidy Rékh 🇸🇳🇬🇦💪💪💪💪💪💪🏅🏅
❤
Machalla sama weuy kate bi yow dal boule tontou tu es jeune , un jeune adorable que j'estime beaucoup yow lo weuyoul bakhoul kon sidy weuyal
Le temps peut changer beaucoup de choses, mais une chose qui ne changera jamais, c'est mon amour pour toi bro.Yagui sisa yoon machallah di doxal teksi jambar gua
Man mi dhh amouma massi mom sago beug nako ba parei douma deglou sax lou gnaw si mom courage et continue sur cette lancée une belle carrière se promet 🥰
Yaw ya worr de
Mais fo dake
Sidy le peuple sénégalais est fier de toi
Le futur roi de la musique africaine
sidy Diop chanteur du peuple sénégalais yalla n'a nala yalla defal diamou
Un jeune pétri de talent dath lounek wayer mou takk ndigeum rek wollou yalla am fittt damala beug sidi diop😍🤩👊
Mashalaa yalnaa sa diam yagg adunaa nakk mo demeii nonou boul tontou defal ni sa référence Youssou Ndour lounekk lay degg t dou tontou
BILAHI NITT GUENOU KO AKA BAKH TAI WOYOF SIDY AMAL DIAM REK LIGUEYE DEF PATE NIOUNE YAY SOUNOU CHANTEUR NITT MOUNOUL WAKH LOUY TAKH NIOU BAYI LE BARKI BOROM TOUBA❤️❤️❤️❤️❤️👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑
Tu fais notre fierté champion domou Tivaouane gua
Franchement sidi Diop est le meilleur chanteur
Pape diongue sidi mako bege té yalla takhe bakhna yarouna bou niép baye Dina diap bilaye
AK mane
Cette chanson dey fekheul sama khol. Ci kow ci kanam. Ne te compare à personne, avance rekk.
Non sidy boul rayaty ngingi way li nekhna wayaw tamit 😂😂😂😂😂😂❤
Sidy Diop yalla nala yalla défal diam rk 🤲
Thiey mbeugello dfa nexo 😍😍
Nekh na wayei metina tamit
@@coumbadiaw1126 bou mette rk niou mougne par ce que moy thiass bi nek si mbeugello
Hooo l'amour qui fait rire 😂 après 😭
Loutakh nga meuna way machalla
Bo bayé weuy ma bayi déglou musique senegal
Cc sante yangui cool doma fi bayi bilay wallay barki baye niass sidy souy bayi ma delou si américaines yi
Senegal bagn bagn beug wally seck saxx boybi la fan walakhi hier la done setanate sene Apl bi nga xamni genru omaro yi nio nek thi guinaw diwaxxx rek
Sidy Meun nga way manchalla khawma lo teulé wayé dou inspiration
Masalah diop fi yafi né ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Guissouma si sama adouna loumy décourage lo si yaw bonne continuation frère amal djamou rék
Nekh si khol ❤️🥰
sidy bilahi kenne dou yaw diam rekk ❤❤❤
Linekh n'a je te souhaite que tu seras le roi du Mbalakh
on est en 2024
golden boye❤️
Ki dou nit c l’avenir de la musique sénégalaise
Weuy rek ngay deef😍dokhalal
Ki mako beugue ba amatou ma thi mome sago😭😭😭😭😭
Macahallah dafa néha beauk
bilay ya meuneu wayy mashallah💯💯💫💫💫✍❣❣❣💟
Tu est l meilleur sidy Diop
Billahi dioy lo nama sidy
Sidy yae papa
Mane número sidi rek la sokhla billahi ki démako beugeu ndakh geum bopamm
Bula ken decorase sa kaw sa kanam rek
Kene dou wa 05 etoile
Fadiar sakh damay deglou liii 🥹🫶🏽
Sidy mbeuguelo bi il faut mou am clip
Bly iow dafa nekh trop
Machalla 😍😘🥰🤩 sidi 💪💪💪💪💪💯😍😘🥰🤩
Machalla ❤❤❤❤❤❤❤❤👑
Yalla samela
Sidy yaffi nekkk kennn dou yaw
Mashallah Sidy Diop rk
Yalla Nala yalla takhawou
08:03 je me remercie
Www partie bi niépp di weur
Futur Youssou Ndour ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Do sama artiste mais cette live validé nako
Mo dak live si génération bi bilahi mo takh gayi diko daw
Kouniouy sentou si gualou chien fexel ba boufa lek té geum nani dofa mesa diégué baye def lelene.gnagny bayi xél ns les inconditionnels beugua tougne nit yap njiou si ay détails. Parce que mane personnellement sama tabaski après xawma loumoudone saf.mais courage le phénomène
Lol tre fort pour musique sénégalaise 😮bravo lol
Je suis sidy diop 🤩🤩
Sidy gnoune ak yw diamonoy mariage la wone boul tontou kéne daguay dém kéne doula teyé
Sidye 🥰🥰🥰🥰🥰🥰😍🤩😘😍🤩😘😘🤩😍🤩🤩🤩🤩
D'où nitou fii
Waaw nice na
Machalla sidy diop
Papay boy waykat yiiii mongui sidi
Fii le chanteur du peuple c'est Wally seck❤️
Mdrr bataye yènay douggou ci chaînou boy bi di am lolen di commenter wala daf lèni déranger
Diam sy yaw
🥰🥰🥰lou néhk rek lay way
yaye séne papa
Man li meunama rayy
Fier tivaouane
Dafa mana woy
Yafi meuble♥️💯✨✨
Li nèkh na dh
Yaye séne baye
Ndeysan billaye damako begue lool ndakh nimou begue yayame ta masou mako guis mais guemal sa bopou rk lépou Dina bakh ta yalla wakhoul kénne dara
Ki yalla mo ande ak mom na non yi nopalou
waw ana Pape ndiaye
Dafa guénnon mais il paraît que nieuw na
Nioune ioe RK.lanou beugue mé svp déléne dougal lépou
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
thiey mbeugello
Deinthio dra Lou bonne
Mayy waxx omaro nane gediawaye y’a mouna doul ki moy sougnu youssou ndour sa data nday omar
Dafa xamoul rk.Nioune wa Gway xamnagn lepp 2016 ba tay dou ay foo.
❤️❤️❤️
Mane mome iow la beugg
Omaro piano balay tontou boy bi nexoul fay d yeena far nak nangoul né deff nga erreur Adouna dou tay rek souba amna
Sidy réy
🎹❤️
Kendou Iow fils
Li dafa garaw
🥰🥰🥰🔥
🔥🔥🔥🥰
❤❤❤❤❤❤
🥰🥰🥰🤩🤩🤩
Laf bouche Sidy
Le chanteur de Ive Dia
Yaw lagniou am deii yaniouy beguel deii
Weuyou diambour yi rk lay weuy
Et après ?
Li nex n'a de
Abou sala li sidy way nekhna mais ya yakh lep khamo gatt yamal si teuge
Pape Ndiaye kaye mo wara gaw nieuw
Daga meuna way🥰
🔥🔥🔥🔥🔥🔥❤️❤️❤️
Machallah !