10Mil Problemes - Dof ndeye nous explique sama ndidiaye moma...

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 7 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 137

  • @quetespirituelle6647
    @quetespirituelle6647 3 роки тому +3

    ASSALAMOUHANLEYKOUM SEUGN 10000, SEUGN DOF NDÈYE BEURI NA GNOU BEUGG DOF NDÈYE LOOLOU NGIR NIMOU YEUREUMEE YAAYAM, AK NIMOUY XEEXEE BANDITISME, AK NIMOU AMOULEE COMPLEXE CI WANEE YAAYAM AK FIERTÉ MAA SHAA ALLAH WAAYEE DOF NDÈYE BOUNIOU KOY GIS MOUY BAKKU TOUJOURS CI BEUG WANEE LOU JEUMAAT CI MBIR YIMU WEESSU, NITE GNI SEEN ESTIME CI DOF NDAYE DAY WAAGNEE KOU. DAGNOUY DÉCOURAGER. SEUGN DOFF NDEYE BAYYI CI XEL. GNOUGI LAY BEEGEE.

  • @ndeyeamiendao5376
    @ndeyeamiendao5376 3 роки тому +19

    10 000 problèmes ak Dof néy wone love Big UP

  • @aliounebadarasy8368
    @aliounebadarasy8368 3 роки тому +8

    DOF NDÉYE AK 10.000 PROBLÈMES
    BIG UP

  • @josemullerbassene1061
    @josemullerbassene1061 3 роки тому +25

    Frère moi je t estime bcp ne baisse pas les bras continue de prendre soin de ta Maman car une Maman c'est la plus grande valeur qu'on puisse obtenir dans cette vie

  • @medounediop7670
    @medounediop7670 3 роки тому +1

    Du courage dof ndéye yalla nala yalla samb .

  • @adamendiaye1395
    @adamendiaye1395 3 роки тому +1

    Je ne savais pas k né 10000 problème amna chaîne UA-cam je te jure bon courage wayé sa micro bi😂😂😂

  • @papeomardiagne8201
    @papeomardiagne8201 3 роки тому +3

    🤣🤣🤸‍♂️🤸‍♂️ténn aka sonal diaye Katou poupp yii🤣🤣kararo kanaro🤣🤣🤣rang🤣poup kénn douko diayy🤣🤣🤣

  • @pikinequartierdarou4896
    @pikinequartierdarou4896 3 роки тому +17

    Wa 10 mil li bane xetou micro la thiey doff

  • @ndiagaeurodiouf3104
    @ndiagaeurodiouf3104 3 роки тому +1

    10mille ak sama sama rappeur bii mes Nice na nak ✊✊✊✊😞🔥🔥🔥🔥🔥

  • @bayeniass5633
    @bayeniass5633 3 роки тому +3

    One love 10000 problème and dooff nday

  • @boromebakh28
    @boromebakh28 3 роки тому +4

    Nice job 10m ak dof Ndeye 🤣🤣🙏

  • @abdousamb4617
    @abdousamb4617 3 роки тому +1

    Amngueine micro bou riss 😂😂😂😂dangueinma diakhal

  • @DialloSalmana
    @DialloSalmana 5 місяців тому

    ❤❤❤Dof❤❤❤ndenk❤❤❤one assamblée c'est bien dit ❤frère

  • @elikenzo_intelec_officiel8794
    @elikenzo_intelec_officiel8794 3 роки тому +12

    Bonne chance sama guays 👋

  • @fallouamar8898
    @fallouamar8898 3 роки тому +5

    Alhamdoulilah banga nieuwatée sisa ndiabott

  • @nl8235
    @nl8235 3 роки тому +2

    Pour môme rambo la quoi 🤣🤣👈

  • @channel10011
    @channel10011 2 роки тому

    Wah yenn 10000 léquette la def micro? Je t'adore

  • @massaerleye6114
    @massaerleye6114 3 роки тому +1

    Bonne chance 🤟🤟🤟

  • @lamindarboe2046
    @lamindarboe2046 3 роки тому +2

    Nice na bless boys

  • @nfatv8
    @nfatv8 3 роки тому +5

    dof ndeye 10mil je vous love s

  • @kodiagnetv5984
    @kodiagnetv5984 3 роки тому

    Doff ndeye nak guén ngeu prison bayil lépp mou sédd dél mougne do diégueulé kou naik si yone fauk problème am allez courage👍

  • @Momo-go5vh
    @Momo-go5vh 3 роки тому +4

    sayo guener kasso gueneu am inspiration

  • @kourouma1957
    @kourouma1957 3 роки тому +6

    Nice 🔥🔥🔥👏🏽

  • @Momo-go5vh
    @Momo-go5vh 3 роки тому +15

    tu as le potentiel de devenir un grand artiste mais tu as un probleme de registre . il faut chanter des melodies semblable a ton premier album

  • @MamadouDiallo-hw6zd
    @MamadouDiallo-hw6zd 3 роки тому +4

    😂😂😂nooootooo bilahi vs êtes des bns sama gays yi✊👍

  • @lambasarr6577
    @lambasarr6577 3 роки тому +21

    Bandit bandit lou nga wara bayi gôr lolou doxoul👌🏿yaa salam fall rek

  • @lelawal-wodobere4147
    @lelawal-wodobere4147 3 роки тому

    Wakhal pape Mbaye réck wahdji diéhh🤣🤣😂😂😃😁😆😀

  • @ibousouane733
    @ibousouane733 3 роки тому

    Je remercie 😭😭😭

  • @assanediop8283
    @assanediop8283 3 роки тому +6

    LOVE SUR VOUS👊🏽👌

  • @ousseynoudieng5084
    @ousseynoudieng5084 3 роки тому +3

    Nice bro 🥰😍

  • @awathiam5149
    @awathiam5149 3 роки тому +2

    Doff mougnal yalla bakhna

  • @lelawal-wodobere4147
    @lelawal-wodobere4147 3 роки тому +1

    Wakhal pape Mbaye réck wahdji diéhh

  • @Ndof_officiel
    @Ndof_officiel 3 роки тому +3

    Nc bro 🇸🇳💪💪

  • @khadyba5140
    @khadyba5140 3 роки тому +5

    Wa dix mille kagne la nek journaliste ay yallah minou sakeuh

  • @gelawargelawar7145
    @gelawargelawar7145 3 роки тому +1

    Libérer Abass 💪

  • @miruboy9856
    @miruboy9856 3 роки тому +10

    We need you in gambia 🔥🔥🔥

  • @expertpablo7148
    @expertpablo7148 3 роки тому +4

    10 mil yagui niouye Ray waye 😂😂

  • @kokodejoseph5533
    @kokodejoseph5533 3 роки тому +1

    euy way ani UCG?deuk bi saleté neu!PETERSEN HLM CENTRE VILLE.LES GENS VENDENT MARCHENT ET MANGENT DANS LES ORDURES

  • @alinendiaye1053
    @alinendiaye1053 3 роки тому +4

    Doof ndeye iow ya wara bayi diaye Pérec tega neka ndeye niit

  • @King-walo
    @King-walo 3 роки тому +1

    C’est une infraction de la part des policiers de fouiller une maison sans obtention d’un mandat de perquisition lii motakh kén bougoul policiers yiii ndakh cii togn rék lañiou deuk

  • @ouzwallysidibe9902
    @ouzwallysidibe9902 3 роки тому

    Vraiment diambar nga boul bay ndeye ak baye d'où morom yalla ko wax

  • @mansourdiallo5098
    @mansourdiallo5098 3 роки тому +1

    Les deux foux du senegal

  • @amadoulaminendiaye2780
    @amadoulaminendiaye2780 3 роки тому +3

    Diadieuf sama gars yi adouna mo méti rék mais leup dina diékh

  • @elhdjimeissadiop94
    @elhdjimeissadiop94 3 роки тому +1

    Wang wang 👌

  • @Pzenga26
    @Pzenga26 3 роки тому +1

    Jiajeuf kilifeugui doff ndeye jiajeuf kilifeugui 10000

  • @user-hi5bc9wk5z
    @user-hi5bc9wk5z 3 роки тому +1

    Wame saxarr si nakk 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣

  • @douablack2790
    @douablack2790 3 роки тому +1

    Doff baye fall la 🔥❤️

  • @Patriotsavie
    @Patriotsavie 3 роки тому +2

    Ligua def basa ndiaye yobla kasso wakhoko,epuis kerou famille boy t'a akh daguay wakh ac nite gni ba paré té sa yaye gua wo Association ande takhawou gni weredi gniou fadialko mo gueune guay bandibandilou sama fans gua wone m'ai légui dama retirewou dakh ba légui amna comportement you nitgni appreciéwoul thi yaw

  • @ousmaneseck6044
    @ousmaneseck6044 3 роки тому +1

    Thiey sama gayi

  • @expertpablo7148
    @expertpablo7148 3 роки тому +1

    10 mil micro bi mome 😂😂😂

  • @ahmadouba7052
    @ahmadouba7052 3 роки тому +2

    10000 problème nga bayi si khél soy déme touba boul yobalé yamba dji dh

  • @boubacarndao3382
    @boubacarndao3382 3 роки тому +2

    Diayekatii poup kay 🤣🤣🤣 tentaw way 🤣🤣

  • @mamadousilla3436
    @mamadousilla3436 3 роки тому +1

    Dof ndeye geurre wa 10000 naci

  • @guidotoure4254
    @guidotoure4254 3 роки тому +9

    Nn 10mille c'est quelle genres de micro sa 🤣😀

    • @zalefaye5716
      @zalefaye5716 3 роки тому

      Micro calebasse rang mouy tothie

  • @abdourahmanesindidi1818
    @abdourahmanesindidi1818 3 роки тому +1

    10000 mom journaliste wala😅🤣

  • @elhajidiawkabir7074
    @elhajidiawkabir7074 3 роки тому +1

    10 000 poroblém lii micro la wala lékétt galou dof dou téer dof ndaye iow tamit diémala change bayi affaire bandit banditlou amoul béna ndiarigne nekal ndayi nitt mo guene

  • @mbayesonko8968
    @mbayesonko8968 3 роки тому +1

    10000 vs dof ndaye wane love

  • @falloupene9813
    @falloupene9813 2 роки тому

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ra ke

  • @neymar10diallo92
    @neymar10diallo92 3 роки тому +1

    Rang moy poup 😅😅🤣🤣🤣🤣❤️🔥🔥🔥💪💪💪💪🙋‍♂️🙋‍♂️👋🏃🏃🏃

  • @omzobrickoffical738
    @omzobrickoffical738 3 роки тому +2

    😭😭😭😭😍

  • @dembadrame3967
    @dembadrame3967 3 роки тому

    Nis

  • @narrefallfall2583
    @narrefallfall2583 3 роки тому

    Dof nice bro

  • @Seck221
    @Seck221 3 роки тому +1

    10.000 règleil ton micro ak la calebasse keineu deigoul bou bakh

  • @tigrenoir5147
    @tigrenoir5147 3 роки тому +1

    Yéne niare ñi kou tané moromam bayilen doff doff lou bi tes nek aye nite

  • @alioucisse998
    @alioucisse998 3 роки тому +1

    Rang mouy DEUG

  • @cheikhououmartall4489
    @cheikhououmartall4489 3 роки тому

    Teyalle si wahdji

  • @alex-to1hc
    @alex-to1hc 3 роки тому +2

    Wa keulll bi 10milles yoré nak wala micro lá 🤣🤣🤣

  • @layediene4251
    @layediene4251 3 роки тому +3

    😍😍😍💯💯

  • @guidotoure4254
    @guidotoure4254 3 роки тому +3

    Thiey 10mille kagn nga nek journaliste 🤣

  • @ngathiefallmusiquefromsene2060
    @ngathiefallmusiquefromsene2060 3 роки тому +1

    Dafa mechan quoi

  • @diagnelerebelle9490
    @diagnelerebelle9490 3 роки тому +5

    ❤❤❤❤

  • @mansourlam5250
    @mansourlam5250 3 роки тому +1

    Mboke boubakh mo diafe ci aduna bi

  • @gorouantadiba2194
    @gorouantadiba2194 3 роки тому +1

    Mane microbi Moma néx

  • @fallouseck3142
    @fallouseck3142 3 роки тому +3

    Nic na doff més bayile bandit bandit lo bi nak diame ak salam

  • @bebendiaye3416
    @bebendiaye3416 3 роки тому

    se nidiaye bi kou bone le ,,,dieuleule se keuyitou keur ngeu dintieule ko se bope, mo geuneu wore

  • @gelawargelawar7145
    @gelawargelawar7145 3 роки тому +1

    10000 mi dafa moss

  • @waganegning5554
    @waganegning5554 3 роки тому

    sa nidiaye monoula bagne mé il a peur de toi pas que il te connaît mé c kw son djob bamouye ame aye keur di fa aye oborje

  • @serignediop4388
    @serignediop4388 3 роки тому +1

    Dof nday dafa meune bandi bandilou do dra tapet gua

  • @kingmao6724
    @kingmao6724 3 роки тому

    10mille mi niéméwoule say dé

  • @2mnoft7
    @2mnoft7 3 роки тому +1

    Ki yawo rék yakoy dalale ndakh weroule

  • @ousmanediop1729
    @ousmanediop1729 3 роки тому +1

    Tate lagne défff gnome gnarrrrr ✋

  • @moustaphfall3192
    @moustaphfall3192 3 роки тому +1

    Dimbalignou boul neboo sa yaye nekal nit mooo geun sa nigay khamnala bou bakh polis khamnala boubakh yamba bi geni day .yaw yafi gennewon fital loula dal yako def sa bopou

  • @coeur2lion38
    @coeur2lion38 3 роки тому +2

    Yaw ya wara nék nit soite dagay nék bandit gnép bayila wara ga nék nit cou bah normal respecté yép dioh yép thieur amak gnép diam gnép ad ak yaw

  • @tidianecamara6133
    @tidianecamara6133 3 роки тому +1

    Dof yow ya wara def yeufou nit nioune douniou ak nguaka

  • @guidotoure4254
    @guidotoure4254 3 роки тому +1

    Doff ndey mais fo nekone ?

  • @Rdiouz
    @Rdiouz 3 роки тому +3

    🤣🤣🤣🤣

  • @bassirouseck5161
    @bassirouseck5161 3 роки тому +3

    Dof khamal ni legui killifeu ga té bayi di diaye prék di bandi bandilou wala di gniangal aka xonkal beute

  • @oussbah2919
    @oussbah2919 3 роки тому

    Dof Ndèye namenala de

  • @nouroulhoudatv7007
    @nouroulhoudatv7007 3 роки тому +1

    😂😂😂😂😂

  • @mouhamedcisse9728
    @mouhamedcisse9728 3 роки тому

    Lima diakhal loutakh talibé cheikh yi doléne guis gnimelni loukhew

  • @sarjobah7691
    @sarjobah7691 3 роки тому

    Nice ❤️❤️❤️

  • @senegalmt9603
    @senegalmt9603 3 роки тому

    Nice

  • @PAomartoure2002
    @PAomartoure2002 3 роки тому +1

    Mais 10mil mi dafa mandit

  • @aminatacisse1154
    @aminatacisse1154 3 роки тому +1

    Niaary dof yi

  • @alieudrammeh3824
    @alieudrammeh3824 3 роки тому

    Niarry dof mandi rek

  • @amadousow3149
    @amadousow3149 3 роки тому +2

    Yénn do lénn touss way

  • @moustaphfall3192
    @moustaphfall3192 3 роки тому

    Ysw fo sopekou giko ak morom deerek

  • @kebasoce8115
    @kebasoce8115 3 роки тому

    Yaw 10000 yaw nafh nga

  • @Patriotsavie
    @Patriotsavie 3 роки тому

    Mais est ce que khamguéne dix mille dafa ragalé dof

  • @philippebrisset1718
    @philippebrisset1718 3 роки тому +1

    10000 t’es gentil mais tu parles beaucoup pour rien, laisse le mek s’exprimer quoi? On n’a compris pour le l’ arrestation de 2008 mais on a pas compris pour le 2021

    • @Patriotsavie
      @Patriotsavie 3 роки тому

      J’ai pas compris l’arrestation de 2008 lanelawone s’il te plaît