FACE 2 FACE CHOC ENTRE ZOSS VS ALIOUNE SEYE 2 - A MOURIR DE RIRE 😂😂

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 16 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 342

  • @sambaba683
    @sambaba683 3 роки тому +4

    Zoss daffa meune wakh gnèmè machallahh sans complexe kèenndou zossss🤣🤣😂😂😂😂😂😂😂😂🤣🤣

  • @babelofficiel4130
    @babelofficiel4130 3 роки тому +72

    😂😂 Zoss bayiwoul wone beurré bani legui nagnkoy wowé Saliou Ngom, dem ministere de la santé di sensibilisé di mayé derett.
    SÉNÉGAL KENN GUEMOUL DARA MOTAKH LOUMA WAY WAKH MANILA UNHUN REK

    • @thiapathiolibouxaragnlo7987
      @thiapathiolibouxaragnlo7987 3 роки тому +8

      🤣🤣mom kaay deel waaaxx unhun reek seni wax mom dieuroul doumeu sa dom

    • @trafamily8397
      @trafamily8397 3 роки тому +4

      Bilahi😂

    • @khadimg2078
      @khadimg2078 3 роки тому +5

      Wakhi beur diaroul dor sa dome

    • @hasboyedawe9569
      @hasboyedawe9569 3 роки тому +5

      Yéna bone bilahi 😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁

    • @mamadousall7046
      @mamadousall7046 3 роки тому +6

      Nena seriñam moko wakh mou bayi lamb tay mingini 🤣🤣🤣🤣

  • @cheikhsarr1347
    @cheikhsarr1347 3 роки тому +25

    zossssssssssss nandité leu 🤣

  • @ngagnegueye8008
    @ngagnegueye8008 Рік тому +1

    Alioune seye 2 ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @abdoulayeba4636
    @abdoulayeba4636 3 роки тому +9

    Zoss vrai comèdien nous😅😂🤣 damala moudiè fan

  • @deuguerek4547
    @deuguerek4547 3 роки тому +38

    Alune seye dh boula zoss dané niniou nara def koukandé bou kharoulé guédji lanioulay deff ndoulila banga noy yoboula 🇰🇪

    • @Imame698
      @Imame698 3 роки тому

      🤣🤣🤣🤣🤣kill ngama

  • @ousmanefaye2662
    @ousmanefaye2662 3 роки тому +41

    Aline Sèye yow ya Wara dieul combat bou tangue téh nga bayi Lou yomb deulale: Modou anta , wala diène kairé wala revanche avec moussa ndoye

    • @cheikhndiaye500
      @cheikhndiaye500 3 роки тому +1

      Li dou combat bou tang bro ya meun soop nopil hei!

    • @youssoumbengue7698
      @youssoumbengue7698 3 роки тому +1

      @@cheikhndiaye500 saway zoss insbi yaw sakh yako meun

    • @ousseynoundiaye8910
      @ousseynoundiaye8910 3 роки тому +3

      Alioun sey ay moromam nioko nie mewul motah te l'amb la am dou tok rek Day competir

    • @mouhametpouye9119
      @mouhametpouye9119 3 роки тому +4

      @@cheikhndiaye500 wakh na deug, li dou combat... Aliou Seye lou yomb rék lay weur

    • @abibdoundouguiss5629
      @abibdoundouguiss5629 3 роки тому

      @@youssoumbengue7698 boul ma ray way

  • @mouhamedtoure937
    @mouhamedtoure937 3 роки тому +8

    Alioune seye temps yi amgua serigne deh bilahi 🤣🤣🤣🤣

  • @kheuchactutv529
    @kheuchactutv529 3 роки тому +21

    Zoss mi garyi cmodien laniou ko diaper legui😂😂

  • @mbayewade2360
    @mbayewade2360 3 роки тому +46

    Zoss bayil doul Gaston dagne ka diokh xaliss lolou boul si débat nieuweul beuré rek nga nopi

  • @abdoudiome4697
    @abdoudiome4697 3 роки тому +16

    Il faut comprendre Alioune seye il a fait des années blanches donc s’il voit l’opportunité douko bayé lambe moye liguéyam tmt ak tabaski bi 😂😂😂😂

  • @yawsamayaye9347
    @yawsamayaye9347 3 роки тому +21

    Non Zoss Amoul 😂😂😂😂 Saway Yagui ni Mélni Keurgui 😂

  • @boromebakh28
    @boromebakh28 3 роки тому +8

    Zoss day diémeu dokh si kaw Alioune seye 😂😂😂

  • @ndiayemandela5275
    @ndiayemandela5275 3 роки тому +4

    Zoss Bathi Sérass Balla Diouf Boy Seye et autres sèni diamono lamb neixonn neuh

  • @adamandiaye5321
    @adamandiaye5321 3 роки тому +4

    Alioune seye 2 courage frère ndame rék inchallah

  • @goraniang6898
    @goraniang6898 3 роки тому +35

    Vraiment alioune seye dèmal dieuli sa morom yi ah ngua bayi payi daguay tardè rèk dane issa pouye ak zoss dou lamb dèmal dieuli boy yi nèk si yonebi km modou anta,diène kaïrè,yèkini junior ,moussa ndoye,

    • @fodeetoure8715
      @fodeetoure8715 3 роки тому

      Merci

    • @lapiraterie92i7
      @lapiraterie92i7 3 роки тому +1

      Ki xaliss lay lidjeunti

    • @kebemoustapha7580
      @kebemoustapha7580 3 роки тому +4

      Alioune Seye bi nekkul xalé dh bufi nekké di xaar combat bu tang legui mu jéexal

    • @abdoumane7700
      @abdoumane7700 3 роки тому

      Alioune gni gnoy moromame si lamb

    • @fakhadiagne5288
      @fakhadiagne5288 3 роки тому

      Bien dis bro..da wara dieuĺ si boy yi topou pa yiii rek,li dou combat

  • @minguediop3124
    @minguediop3124 3 роки тому +15

    Zoss laye Doneeeeee 😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @mamoussapouye3484
    @mamoussapouye3484 3 роки тому +15

    Zoss il est comique 🤣🤣🤣

  • @abdourahmanely627
    @abdourahmanely627 3 роки тому +2

    Alioune S2 never give up✊ lou diott yombou...👊 yaal nala yallah yombalal leep nga moss ba nekkaat thi leneen...🤞

  • @hugosow2786
    @hugosow2786 3 роки тому +1

    Alioune seye es ce que amna ay conseil li dou combat way😂😂😂😂😂😂😂

  • @labsolugueye1474
    @labsolugueye1474 3 роки тому +11

    Thaï Aliou séy 2 sama Mbeur nga Billahi Mé Bayill paa yingay Dieule 😂Déll lath thi Boy you Tangeu dieur yii Lanla wax fall Danga xawa Beugeu lounoy Billahi.....Pourquoi Mouno won Lath Fra wollah Gri 2 wollah Dién kairé sax 🙂

  • @moussaboukharagnelo5465
    @moussaboukharagnelo5465 3 роки тому +4

    Zoss néna sawaye yaguini Mélni keur gui guén mounako pouss b52 clash 🤣🤣🤣

  • @cherifbarry171
    @cherifbarry171 3 роки тому +17

    Zoss est devenu politicien 😂😂😂😂

    • @mariogotze5122
      @mariogotze5122 3 роки тому +1

      Il a toujours été un con🤣😂😂😂

    • @cherifbarry171
      @cherifbarry171 3 роки тому

      @@mariogotze5122 on a tout compris avec le prometteur 😂😂

    • @ndeyecamara190
      @ndeyecamara190 3 роки тому

      @@mariogotze5122 fmjmmg

  • @patheba6834
    @patheba6834 3 роки тому +7

    Zoss ma fogone ni légui intellectuelle leu 😅😅

  • @djibrildiao4572
    @djibrildiao4572 3 роки тому +11

    Alioune seye 2 mo nara am chace zoss amoul chance

  • @sambaba683
    @sambaba683 3 роки тому

    Zoss dafa mine micro machallahh 🤣🤣

  • @sambaba683
    @sambaba683 3 роки тому +1

    Zossnanditè deuggueu leu billahi 🤣🤣

  • @tmasterp8279
    @tmasterp8279 3 роки тому +2

    Gaston svp donné à malick niang un combat 🙏

    • @ibk4266
      @ibk4266 3 роки тому +1

      Vraiment

  • @ouzdaking382
    @ouzdaking382 3 роки тому +3

    Alioune seye Baye Fall grand champion ndam rek Inchallah

  • @djinguefils7273
    @djinguefils7273 3 роки тому +15

    Antou bouko Aliou seye hebb si birr wakh monkoy wakhné bandi lamb la té buko wediwe n'a ladj boye Niang wala Gouy gui wala tidiane faye

  • @elbaraniang
    @elbaraniang 3 роки тому +8

    Zoss bayil fén yi nakk Gaston xaalissou Etat lay teugué lamb

  • @akhloulbayt6818
    @akhloulbayt6818 3 роки тому +12

    Gaston est financé par Macky, merde zoss tu n'as rien compris

  • @moussaboukharagnelo5465
    @moussaboukharagnelo5465 3 роки тому +6

    Zoss do toukh do nane café🤣🤣 do dane kén

  • @mouhamedtoure937
    @mouhamedtoure937 3 роки тому +2

    Modou mbaye bayil zoss way 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣

  • @joopibouh8936
    @joopibouh8936 3 роки тому +1

    Zoss vrai diay prekkk leuh🤣🤣🤣🤣

  • @charlydaniz1379
    @charlydaniz1379 3 роки тому

    Le Sénégal est le seul pays où on pense que la lutte est un moteur de développement. Détrompez-vous la lutte n'a jamais développé un pays. D'autre part, compte tenu de la situation sanitaire du moment, l'Etat doit prendre ses responsabilités à deux mains et interdire tous rassemblements y compris l'organisation des combats de lutte dans le but de préserver la santé des populations. La pandémie est toujours là; elle continue de faire des ravages. Alors Macky Sall ne soyez pas frileux soyez courageux comme doit l'être tout président de la République dans ce cas d'espèce. Hélas, j'ai le présentiment que vous ne le ferez pas car pour vous, la lutte est un moyen qui vous permet d'endormir le peuple pour ne pas qu'il se révolte, à l'instar de ce qui c'était passé en Mars dernier. A bon entendeur salut.

  • @cheikhbadiane1904
    @cheikhbadiane1904 3 роки тому +28

    Aliou seye 2 ndem rk inchallah

  • @chamousman2726
    @chamousman2726 3 роки тому +1

    No alieun seye dafa yarou torop macha allah

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 3 роки тому +1

    Zoss miii de dafa nieuw si lamb pour ambiance nieuwoul pour carrière

  • @dembaguite4945
    @dembaguite4945 3 роки тому +3

    Zoooosss man bou gueu danee guy gui thii laleu fans 🤣🤣🤣🤣

    • @ousmanediop570
      @ousmanediop570 3 роки тому

      Guy Gi kay dafa niakk jom haha. Zoss daf ko daan ba pare foxoj baaraam bi haha.

  • @cheikhsano7842
    @cheikhsano7842 3 роки тому +3

    Non zoss moy defar lamb dhi😂😂😂

  • @omardiabo8323
    @omardiabo8323 3 роки тому +8

    Yaw Kay soss fou ISSA pouy diarr rek ngaye diarr dangaye déme inchalla alioun saye bilahi dioumo dé khaliss nga wara am yaw dokhalal merci

  • @cheikhmbacke4379
    @cheikhmbacke4379 3 роки тому +4

    ALIOUNE SEYE2 ndam REKK

  • @onelove6721
    @onelove6721 3 роки тому +3

    Zoss employé Gaston la da mélni
    Macky diokhoul na Gaston lolou sa yone nekousi à chaque fois ngakoy wakh
    Senegal door kate yi niongui si secteur yeup

  • @modougaye6646
    @modougaye6646 3 роки тому +4

    Zoss nga khamni diap dane leuh li dou combat way bilahi

  • @talldjily2536
    @talldjily2536 3 роки тому +4

    Alioune seye 2 yallnala yalla may ndam

  • @ndebayethiongane1558
    @ndebayethiongane1558 3 роки тому +1

    Zoss Lambe baayi nalaa

  • @benboy2908
    @benboy2908 3 роки тому +1

    Nah zoss amoul nenaka erreurs nga déf melni cou mayé limdon lék😂😂😂

  • @amadouthiam6358
    @amadouthiam6358 3 роки тому +1

    Zoss néna ndakh wadjii la mom la keyy 😂🤣🤣

  • @weyouwacrew2652
    @weyouwacrew2652 3 роки тому

    Bilahi li nékh n'a😄😅😂🤣😂😅😄😅😂

  • @ngagnekhouma4308
    @ngagnekhouma4308 3 роки тому +8

    Zoss légui comédien leuh koi

  • @elagetoure4048
    @elagetoure4048 3 роки тому +1

    Ki dou zoss dehh 😢😢😢😱😁

  • @libasseniang7869
    @libasseniang7869 3 роки тому

    ZOSS day SHOW rek mais Alioune SEYE kholouko sakh

  • @aissatoukonate6344
    @aissatoukonate6344 3 роки тому +1

    Machallah ndam rek seye 2

  • @generalndiaye7353
    @generalndiaye7353 3 роки тому

    Wa Zozz Khana Bayi wowon lamb dji🤣🤣🤣

  • @mhd6280
    @mhd6280 3 роки тому +6

    😂😂😂😂😂😂😂😂😂📊😂😂😂😂douma nane café

  • @ilidiouf3789
    @ilidiouf3789 3 роки тому +5

    Ndaye san man zoss bama nékhé khalé mo nékon sama mbeur

  • @taphadiagne3713
    @taphadiagne3713 3 роки тому +4

    Zoss Gaston sarakhe naleu bou yagg

  • @elhadjicheikhthiam56
    @elhadjicheikhthiam56 3 роки тому +1

    Affaire bi seye 2 domou gounass ndam rk incha allah

  • @aramesndiaye590
    @aramesndiaye590 3 роки тому +1

    Zoss sa ca mo critique ani idy rissa seck wala bookkk 🤣🤣🤣

  • @joe6326
    @joe6326 3 роки тому +5

    lii Dou combat wayyyy Aliou seye danioulay nakhh rek demal dieule say Moromm

  • @chosen1798
    @chosen1798 3 роки тому +1

    #Zoos kañ nga meneu doul ? Gaston a été financé pour nous divertir mais le combat continue

  • @khadim1875
    @khadim1875 3 роки тому

    THIEY ZOSS , DAFAY NEIKHAL LAMB DJIII !! AK ALIOUNE SEYE 2 DO DOYE SAKH , COMBAT BI DOU DURER 5 MIN 🤣🤣🤣

  • @TaphaKaraproduction
    @TaphaKaraproduction 3 роки тому +5

    Zoss khaliss la woutte

  • @cheikhsano7842
    @cheikhsano7842 3 роки тому +1

    Zoss demal treuni dh so entrainer meune nga am ndam bandit nga psychologiquement ya lene meune

  • @goorandione3766
    @goorandione3766 3 роки тому +7

    Billahi zoss tay mou dh

  • @fode558
    @fode558 3 роки тому

    Zoss amoul dou changé bilahi malla fans dh

  • @mhdkara3398
    @mhdkara3398 3 роки тому +1

    Zoss vrai boy town la

  • @momissdiop2560
    @momissdiop2560 3 роки тому +4

    Li mo yakhe lamb dji mbeur yinou warra teugue dounioulene tegue Alioune seye vs tyson2 comba bou nekh la wonne

  • @edouardkaspers2940
    @edouardkaspers2940 3 роки тому +1

    Noo ma faan zoss..il a tout compri..il fait du sports busness..jespere quil ne sera pas humilié rek comme ces derniers tps ds larene.

  • @boucardiop4409
    @boucardiop4409 3 роки тому

    Zoss l'intelo😀😀😀😀

  • @seckndanane1945
    @seckndanane1945 3 роки тому

    Senegal 😱😱😱😱😱😱

  • @djibrildiao4572
    @djibrildiao4572 3 роки тому +2

    Dor mou danou lafi nara guiss ca wou alioune seye 2 koune war nga sè diang adouna kou mougn mouougn kene dou yalla sougnou borom

  • @azizdieng6394
    @azizdieng6394 3 роки тому

    zoss dangaa wéddi sa ndigueulou serigne. Tu avais dis que c'est ton marabout qui t'avais demandé d'arrêter et tu reviens pour te faire humilier loool

  • @yayanayellely1131
    @yayanayellely1131 3 роки тому +1

    allez zoss iow mome sa retour amna ndieurign

  • @abdoumane3557
    @abdoumane3557 3 роки тому +1

    Bonne chance Aliou Seye2

  • @mamadoudia4226
    @mamadoudia4226 3 роки тому +7

    zoss dagay doule rekkk yen mbeuryii sen intérêt rekkk daray rewmii nioroulen iow idy kheu adalone si coalition mbourou au sow bii

    • @lampseck9291
      @lampseck9291 3 роки тому

      Yaw kou niak yar nga fi koune sa entere nga khol

    • @tiktoksenegal7488
      @tiktoksenegal7488 3 роки тому

      Demal ligueyi moi gueune

    • @mamadoudia4226
      @mamadoudia4226 3 роки тому +1

      @@lampseck9291 man Kou niak yarla ok lamb amoul ndeye niariye tes so si delo ma sagala ok

    • @ziziniangg7240
      @ziziniangg7240 3 роки тому

      Merci

    • @lampseck9291
      @lampseck9291 3 роки тому

      @@mamadoudia4226 yaw ya amouloul ben ndeyi dierigne loudoul wakh djou bari te boma saga ma sagasa wa familles bomou nekh

  • @adamagaye4119
    @adamagaye4119 3 роки тому +1

    Zoss vrai comédien gua ioe mom alioune seye booo kholeii ba zoss dannn la worna mame ma bayii

  • @cheikhdiop8416
    @cheikhdiop8416 3 роки тому +1

    Alioune seye fi ngay bakh le fi ngay yakhou le gor Gor loul

  • @ousmanengom4899
    @ousmanengom4899 3 роки тому +1

    Alioune sey gorr goor lou ka dane zoss ton chance è la

  • @crackespana4591
    @crackespana4591 3 роки тому

    Zooss devenu politicien 😂🤣😇

  • @barandoye7413
    @barandoye7413 3 роки тому +3

    Li dou combat way zoss mi da mageutte

  • @boygueye1976
    @boygueye1976 3 роки тому

    Zoss Nandité la dafa togooone si roukom di defarou naan bayina bayiwoul feene lol 😆

  • @ndiayedistandiayendiaye2209
    @ndiayedistandiayendiaye2209 3 роки тому +2

    zoss loy wakh sa serigne ba moussa nawel khana téréwoula wone lamb

    • @labsolugueye1474
      @labsolugueye1474 3 роки тому

      Amall Talibé lanla wax lanmoy moussa nawél 😟serign Moussa Nawél laniouy wax 🙂zoss Mom ay féne la Meune waxouma ay waxam Mome 🙂

  • @ibrahimabadiane8252
    @ibrahimabadiane8252 3 роки тому +2

    Très bien zoss boulén kénn teudj beuré lén dh 3ème vague ay doull la

  • @aliounediaw6483
    @aliounediaw6483 3 роки тому

    Zoss bayuu woull wonn 😛😛😛😛

  • @lifestylelifestyle8188
    @lifestylelifestyle8188 3 роки тому +1

    Aliou seye ngir yala zoss bouko daneu gñafale mako ay cou ba parè mou doga talale ngir yala

  • @dimshoot5597
    @dimshoot5597 3 роки тому

    Non Mais je réve ou quoii ZOOOSS LA DJISSAT NII WALA SHEUUUUU ZOOOS Bahnaa dall
    séne micro yi teuyélenko waye

  • @dembaguite4945
    @dembaguite4945 3 роки тому +2

    Waw mais modou baye legui guande gua dee do lahj sa pa bi ndakh mouneu leu bay gua dougou si lambouji

  • @ibrahimabadiane8252
    @ibrahimabadiane8252 3 роки тому +1

    3ème vague amoufi ay doull la bilahi bou kénn bayi say activité bilahi walahi talahi

  • @bmkillertv1849
    @bmkillertv1849 3 роки тому +4

    Pourquoi vous cherchez à faire percer Alioune SEYE coute que coute en lui donnant des morts vivants que je respecte bien sûr mais ce sont des morts vivants

  • @modougaye6646
    @modougaye6646 3 роки тому +1

    Alioune seye2 vraiment sama mbeur mais tamit dél dieul ay combat you méti

  • @mbackeniane917
    @mbackeniane917 3 роки тому +3

    Non 😂😂man guegnema guiss facc facce bu miel ni sozz yaw mom dangay nékhall lambou

  • @saliougueye1290
    @saliougueye1290 3 роки тому

    Waa zoss dafa nieuwatt kon 😂😂😂😂

  • @layembodj8826
    @layembodj8826 3 роки тому

    Zoss Légui Politicien Leu Borom Ko You Bari

  • @idysy8495
    @idysy8495 3 роки тому

    Zoss dafa vrai vrai intellectuel

  • @zaltall3479
    @zaltall3479 3 роки тому

    Merci zooss bilayi nitou deugue nga

  • @tpacalypse
    @tpacalypse 3 роки тому +1

    Tous ces combats c'est pour divertir le peuple. C'est Macky Sall derrière. Mbeurs yi yewuleen. C'est votre argent qu'on vous donne car c'est l'argent du peuple mais arrêtez de dormir. Gaston est est juste un pion de l'état.

  • @date876
    @date876 3 роки тому +3

    Zoss nopile arètèle politik bi boy also sèye va te montrè bari wax dou tax ga dane

  • @fakhadiagne5288
    @fakhadiagne5288 3 роки тому +1

    Li dou combat way alioune seye dakay dane