Moustapha cisse LO " mane bayi na politique, andouma ak pouvoir andouma ak opposant"

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 11 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 37

  • @gustare1407
    @gustare1407 Місяць тому +17

    Un vrai monsieur trop véridique yalneu Yalla yokk sa santé ❤❤

  • @cheikhounakhadimdiagne756
    @cheikhounakhadimdiagne756 Місяць тому +10

    Ndeysaan jërëjëf Loo

  • @moustaphadiop8974
    @moustaphadiop8974 Місяць тому +8

    Ki lou ler la wakh menatou ma kay lerna nak nagne ko gnanal yalla mo gueun❤ yalla nala yalla taxawu defal la diam yok la banga yeuko machalla ❤

  • @lecitoyentv2022
    @lecitoyentv2022 Місяць тому +11

    Vraiment icone moustapha cisse lo, un homme veridique

  • @damecisse7264
    @damecisse7264 Місяць тому +3

    Ndaysane yalne yalla gane doli ver inchallah ❤❤❤❤❤❤❤

  • @ndiagamatardiopsenegal4469
    @ndiagamatardiopsenegal4469 Місяць тому +11

    ndeysan yalla nala yalla gueneu weral

  • @YacineDiallo-h9u
    @YacineDiallo-h9u Місяць тому +6

    Daysane aka deuguo CiSSé lo yallana yalla dolli weere ❤

  • @Self5995
    @Self5995 Місяць тому +6

    Yalla nala yalla wèral

  • @FallouGaye-kj2tb
    @FallouGaye-kj2tb Місяць тому +4

    GOD bless you🙏🙏🇸🇳🇸🇳

  • @serignesall106
    @serignesall106 Місяць тому +11

    Cissé ngary boulma dioy lo waye😢😢😢

  • @senvar9357
    @senvar9357 Місяць тому +2

    Ndeysan waxji yërëmtalu na lool waay, nala yalla yokku wér ak jàmm 🙏🏾🙏🏾

  • @RITOUBeuthiumpleu
    @RITOUBeuthiumpleu Місяць тому

    Un grand monsieur je me souviens l'avoir rencontré à Karang à la frontière Sénégal-Gambie avec sa délégation. Il était tellement élégant et très ouvert. Yalla Nala Yalla mayla goudou fane ak wéér ❤

  • @fatoujobegarjo2073
    @fatoujobegarjo2073 Місяць тому

    Pa bi nehnameu nit Dangay frank Marshalla 👏👏💎

  • @5555-m6p
    @5555-m6p Місяць тому

    Ki duegu rek laye wakh manta fen yalla nako yalla samou si barkep s Touba

  • @elixxx632
    @elixxx632 Місяць тому +3

    Ensemble pour un senegal meilleur

  • @MamadouNdao-j1w
    @MamadouNdao-j1w Місяць тому +1

    Ndaye Sene Bilay lo😢😢🦻🏾🦻🏾✍️🏿🇸🇳🇺🇲👏🏾👏🏾👏🏾

  • @KhalifaLo-yw7nk
    @KhalifaLo-yw7nk Місяць тому

    Machalla 🙏

  • @mbaye53
    @mbaye53 Місяць тому

    Ki yalla na yalla goudal aw fanam aka deugou li nak la djioup di djarigñ c t un bon explair tay fouka nèkh djaar te dou seugg dou neubeutou fouka deug masa fèk wakhnaka si wakhinn c t un reference

  • @OusmaneNiass-w1k
    @OusmaneNiass-w1k Місяць тому

    Bonnes guérison vieux père

  • @idrissadembaka6553
    @idrissadembaka6553 Місяць тому +1

    Jaaraama mustafaa siisee loh miɗo yahdi e ma

  • @papediagne-x7t
    @papediagne-x7t Місяць тому +1

    Yalla nak yalla werell

  • @bubandong5658
    @bubandong5658 Місяць тому

    Merci monsieur Diakhate

  • @myrkosow9781
    @myrkosow9781 Місяць тому +1

    Pape Ngagne pourquoi insister il t'a bien dit que c'est fini il ne pratique plus la politique

  • @SerigneMbackeFall-k9x
    @SerigneMbackeFall-k9x Місяць тому +1

    Ki limou wakh wakhi nit la macky lim ko def kham nako bou bakh

  • @diakhou10
    @diakhou10 Місяць тому +1

    Qu'est ce qu'il entend pas diariniou? Genre il a profité de lEtat?

  • @kayezikartv7240
    @kayezikartv7240 Місяць тому +1

    😂😂 même so bayiwoul tamitt fii amofi place system bi déna soulné ko c fini lou béss tak lanu sokhla

    • @ibrahimambaye526
      @ibrahimambaye526 Місяць тому +3

      Nekal nite Ki c’est un grand monsieur

    • @lecitoyentv2022
      @lecitoyentv2022 Місяць тому +1

      Ki bamouy wakh li khalato sakh wakh wakhi system, nekal nitt tay khalate doff bi

    • @bathindiaye309
      @bathindiaye309 Місяць тому +1

      Amna niou dof

    • @kayezikartv7240
      @kayezikartv7240 Місяць тому

      @@ibrahimambaye526 khana sa grand monsieur la yaw

    • @kayezikartv7240
      @kayezikartv7240 Місяць тому

      @@lecitoyentv2022 Mani système bi dh n'a même mom sou beugone amoufi place

  • @FallOuss
    @FallOuss Місяць тому

    ✍️✍️✍️😭😭😭😭☝️👏👏

  • @kassasane2428
    @kassasane2428 Місяць тому +1

    😂😂😂

  • @hmpdiopa7681
    @hmpdiopa7681 Місяць тому

    Deug nekgna lo galame diarame diambar