ASSALAMOU ALAYKOUM ZIYAR AK SAKOU NAINE MERCI POUR L INNOVATION, LA MÉTHODE ET LA PÉDAGOGIE WADJÎ WEUYELÉNE!!! MAWLAANA CHEIKHE AHMED TIDIANE R.T.A MOONAMELÎ THIKATANOU BOROMBI S.W.T Lî AYAATOUNE MINE AYAATI ABOULE HABAASSE R.T.A AYAATOUNE MINE AYAATILLAHÎ NOUS LA JEUNESSE NOUNOUTHI BAYIKHÉLE !!! NOUS LA JEUNESSE RÉVEILLONS NOUS !!!
pour mane daal rien à dire lou doul dileen niaanal ndam rek Serigne bi ya ngi yokku tioffeel gui ak niu xamm yenen Ponkalu Seydina Cheikh yi si reew mi ak fudul reewmi. yalna BOUR YALLA sottal projets yeup yombal leppeu Bidjaahi SEYDINA CHEIKH AHMADAT TIJJAANI CHERIFF RTA. niu ngi nuyu nioom Alaji Moustaf ak gnenen gni si back-office bi.
Aladji Serigne Bi bou changer virgule ci mission bi Bilahi grâce à lui xam na Yallah grâce à lui gnèmé touma togne Yallah . Yonnente bi Sala lahou aleyhi wassalam sakh il a été critiqué et c’est lui le maître des serviteurs et des prophètes. Serigne Ahmed Fall Yallah moko yoni xawma kane mais mane dé loumou ma sante ma def loumou ma téré ma bayi ndakh motakh ma xam Yallah ak Yonnente bi ak Cheikhouna Tidiane. Yallah nako Yallah Sam
WALLAHI mo takh niou kham Cheikh ba meune si yoka Djariniou lép si yonou YALLAH. Doli santeu car des aveugles du cœur y en aura toujours. Wakhi YALLAH La. Ken meunou si darra.
Bonjour Ouztaz je suis tout à fait en accord avec vous, on ne peut pas rester tout le temps à dire qu’on peut pas dire tel secret. Il faut faire connaître aux jeunes ce que c’est la tarikha tidjane, pour cultiver en eux l’amour envers Cheikh Ahmed tidjane (rat) .Moi de ma part, c’est un plaisir de vous écouter et je pense aussi c’est le cas de tous tidjanes.
Je remercie le Tout Puissant de t avoir mis sur notre chemin! Moi j télécharge et puis je prend note en mm temps ! C sublime billahi. J incite également les apprenants à donner le alarba . Merci
Assalamouhanlaykoume serigne Darra , mane mome awma sa faye walahi, lingua yokk ci mane hamoko sakh...j'ai suivi tous les cours par la grâce de Dieu et lolu takhna ma amm bennenn guiss guiss ci aduna bi té moy du beureubu noppolékay ak thiaxane, mais beureubou jamu Borome-bi la (deug deug jamu) et que suivre les passions de se bas monde, n'est que perdition
dieuredieuf Seydi Ahmad Fall kou tabé nga si xam xam teksi objectif ma sha Allah gnogui contane founiou tolou diawahiroul ma aa ni xam ko dafa war si bep Talibé Cheikh Ahmad Tidiane li xewoulou yallah bou mag leu dieuredieuf Seydi yallah nala yallah fay yiw
Ma ni diné Moy nga khame Di khame lé. Wayyé iniaané nitt yi kham. Ndaw sokhor!!! Oustaz nak kham-kham gui MachaALLAH ✨ kou amoul saggo rek mo lay sikkeu !!!
Yalnala Yallah fay sa mbakh.. Yangui deff si nitt yi xam xam mou néw mou baari wayé niou ngui lakoy santé.. Amal diam, amal wérr, amal Tawfékh Inshallah
Vraiment oustaz Akhmed fall wakhta ne bii amna solo Loll Mane mome sa sopey la dila suivre bou bakh té khamouma noumay deff ba guis la vraiment bougone n'a koumasii dimbalii
Serigne Ahmad contaane si yaw ! Di lene nianal gud fane bou andak wër bijahi RassoulouLahi sws té Yalla nangoulene sene liguey bi bijahi Rassouloulahi sws barké Cheikhou Tidjany rta !
Assalamou Anleykoum wa Rahmatou'LLAHI TAHAALAA ! Par rapport au projet d'ouverture du daara, nous taalibés, après tout ce que vous faites déjà, ne devons pas attendre tout de vous, je suis pour que nous les abonnés fassions une cotisation symbolique de 2000F par mois té Y'a ALLAH Rek takh; dans un an s'il plaît à ALLAH SWT on met en place quelque chose de concret et sans rien attendre en retour !!!
Yal neu Yallah sotil programme bi leup insha'Allah. Yallah neu leup soti insha'Allah.Yal neu Yallah déf niou takhawoul leup ensemble.Masha'Allah Ya Oustaz.
Salam di la nianal yallla wer ak fane you goude. Bilahi yokk gaa sama thiofel si ABUL ABASS SEYDINA CHEIKH AMADA TIDIANI. Donc je vous encourage et prie que le Grand cheikh Abul abasss vous gratifie de son amour et benediction.
Salam. Je vous remercie pour votre travail pour Cheikhna Ahmada Tidjany(Qu'Allah sanctifie son précieux secret.) Mais je vous conseille de prendre en compte les critiques objectives et d'ignorer celles qui ne le sont pas. Les critiques objectives (et même celles sans fondement) participent à l'éclosion du Savant et aident celui qui sait moins à mieux savoir. Je suis partant pour ce e-daraa. QuAllah soit content de votre travail et vous accorde longue vie pleine de santé bijahi RassouliLahi PSL!
Assala mu Alaikum. Leçon yi xana amoul format audio. Comme ça niou mane si diari niou. Budé amna telegram wala groupe watshapp ngène dima liniou si ngir Yalla. 🙏
Maachala. Gnune daal beg nagn ci lepp! Gnungui khaar tableau bi ! Pour schema bi "izhab ilaa chadjaratil yaqiine..." Yalla na bourr yalla kaatanal tei motali leeepp! barkè Yonnent bi SAWS, wormay CHEIKHU TIDJANI ! 🤲❤️❤️❤️
Mancha Allah Ya seyidi ligua al hour ane mo gueune fort té gniguikoy diema fini On t'encourage openaa bagna firi Yalna yalla same la te yokk xam xam bi Félicitation thi ligueye rafetna bravo
Mbok mane déh pape bilal amouma loubari wayé insha Allahou je suis partant pour donner ma participation tant soit peu qu'il en soit je suis avec vous que Allah nous accompagne ...
ASSALAMOU ALAYKOUM
ZIYAR AK SAKOU NAINE
MERCI POUR L INNOVATION, LA MÉTHODE ET LA PÉDAGOGIE
WADJÎ WEUYELÉNE!!!
MAWLAANA CHEIKHE AHMED TIDIANE R.T.A MOONAMELÎ
THIKATANOU BOROMBI S.W.T
Lî AYAATOUNE MINE AYAATI ABOULE HABAASSE R.T.A AYAATOUNE MINE AYAATILLAHÎ
NOUS LA JEUNESSE NOUNOUTHI BAYIKHÉLE !!!
NOUS LA JEUNESSE RÉVEILLONS NOUS !!!
pour mane daal rien à dire lou doul dileen niaanal ndam rek Serigne bi ya ngi yokku tioffeel gui ak niu xamm yenen Ponkalu Seydina Cheikh yi si reew mi ak fudul reewmi. yalna BOUR YALLA sottal projets yeup yombal leppeu Bidjaahi SEYDINA CHEIKH AHMADAT TIJJAANI CHERIFF RTA. niu ngi nuyu nioom Alaji Moustaf ak gnenen gni si back-office bi.
Aladji Serigne Bi bou changer virgule ci mission bi Bilahi grâce à lui xam na Yallah grâce à lui gnèmé touma togne Yallah . Yonnente bi Sala lahou aleyhi wassalam sakh il a été critiqué et c’est lui le maître des serviteurs et des prophètes. Serigne Ahmed Fall Yallah moko yoni xawma kane mais mane dé loumou ma sante ma def loumou ma téré ma bayi ndakh motakh ma xam Yallah ak Yonnente bi ak Cheikhouna Tidiane. Yallah nako Yallah Sam
Alhamdoulila nagnou sante yalla 🤲🏿
WALLAHI mo takh niou kham Cheikh ba meune si yoka Djariniou lép si yonou YALLAH.
Doli santeu car des aveugles du cœur y en aura toujours. Wakhi YALLAH La. Ken meunou si darra.
Bonjour Ouztaz je suis tout à fait en accord avec vous, on ne peut pas rester tout le temps à dire qu’on peut pas dire tel secret. Il faut faire connaître aux jeunes ce que c’est la tarikha tidjane, pour cultiver en eux l’amour envers Cheikh Ahmed tidjane (rat) .Moi de ma part, c’est un plaisir de vous écouter et je pense aussi c’est le cas de tous tidjanes.
Macha Allah y'a cheikhina yalla n'a yalla doli diapalé dila ziar dila bégué
Je remercie le Tout Puissant de t avoir mis sur notre chemin! Moi j télécharge et puis je prend note en mm temps ! C sublime billahi. J incite également les apprenants à donner le alarba . Merci
Un pédagogue à l'état pure. Que Dieu te préserve yalla faye leu té yatal liguey bi ci barké Cheikh Tidiane🙏
Assalamouhanlaykoume serigne Darra , mane mome awma sa faye walahi, lingua yokk ci mane hamoko sakh...j'ai suivi tous les cours par la grâce de Dieu et lolu takhna ma amm bennenn guiss guiss ci aduna bi té moy du beureubu noppolékay ak thiaxane, mais beureubou jamu Borome-bi la (deug deug jamu) et que suivre les passions de se bas monde, n'est que perdition
Dieuredieuf Oustaz yagual werèr barkèb CHIEKH SEYDIL AHMADAL TIDJIANI
dieuredieuf Seydi Ahmad Fall kou tabé nga si xam xam teksi objectif ma sha Allah gnogui contane founiou tolou diawahiroul ma aa ni xam ko dafa war si bep Talibé Cheikh Ahmad Tidiane li xewoulou yallah bou mag leu dieuredieuf Seydi yallah nala yallah fay yiw
Le meilleur dans son domaine machallah 🤲🤲🤲🤲🤲
Jattends avec impatience lexposee sur Mame Cheikh Oumar Tall❤❤❤❤❤❤❤❤inshala
Wahal dé billay niongui koy khar
Eskeuy Oustaz Ahmad🙌 ! Qu’Allah vous soutienne et fasse triompher vos efforts ! 🙏🏽
alhamdoulilah serigne Ahmad fall na yalla fayla barke yonent bi.. biniou Cheikhou Tidjane yawla dh yalla xamna ...
Ma ni diné Moy nga khame Di khame lé. Wayyé iniaané nitt yi kham. Ndaw sokhor!!! Oustaz nak kham-kham gui MachaALLAH ✨ kou amoul saggo rek mo lay sikkeu !!!
Tawfékh ak taïssir rek ngay ame incha allah
Dieuredieuf ya ngui dimali talibes yi si cheikhouna tidiane nala yalla ranga martaba you gueuneu mal si tarikha bi
Asalamu aleykum ittéwonañu firibi jërëjëf si ligééye
Kuye téwlu waxtaan-wi jariñu barké seydina cheikh jërëjëf jërëjëf jërëjëf 💚🤍💛⭐️🌙
Yalnala Yallah fay sa mbakh..
Yangui deff si nitt yi xam xam mou néw mou baari wayé niou ngui lakoy santé..
Amal diam, amal wérr, amal Tawfékh Inshallah
Vraiment oustaz Akhmed fall wakhta ne bii amna solo Loll Mane mome sa sopey la dila suivre bou bakh té khamouma noumay deff ba guis la vraiment bougone n'a koumasii dimbalii
Serigne Ahmad contaane si yaw ! Di lene nianal gud fane bou andak wër bijahi RassoulouLahi sws té Yalla nangoulene sene liguey bi bijahi Rassouloulahi sws barké Cheikhou Tidjany rta !
Jërëjëf Mawlayâ Cheikh Ahmad Tidjânî 💛🤍💚⭐🌙
Assalamou Anleykoum wa Rahmatou'LLAHI TAHAALAA !
Par rapport au projet d'ouverture du daara, nous taalibés, après tout ce que vous faites déjà, ne devons pas attendre tout de vous, je suis pour que nous les abonnés fassions une cotisation symbolique de 2000F par mois té Y'a ALLAH Rek takh; dans un an s'il plaît à ALLAH SWT on met en place quelque chose de concret et sans rien attendre en retour !!!
Le Groupe Les Amis de Serigne Ahmed Fall est disponible faites signe sur 763547534 on va vous ajouter
JE SUIS D'AVIS . IL FAUT PENSER A UNE STRATEGIE SANS DELAI.
👍👍👍👍👍👍👍
Salam sama beugue bok si group bi
Yal neu Yallah sotil programme bi leup insha'Allah. Yallah neu leup soti insha'Allah.Yal neu Yallah déf niou takhawoul leup ensemble.Masha'Allah Ya Oustaz.
On attend avec impatience l’exploitation de certains livres de Seydil Hajj Malick Sy (RTA) notamment le taïssir ! Inchallah 🙏🏽
Maachaa Allah. Jerejef Serigne Daara. Na Buur Yalla dolli la soutoureu.
Machallah sopei bi
Yalla na yalla fayal nouleen inchallah
Serigne Ahmed Fall talibé cheikh Tidiane Cherif 🙏 walahi sope nagnela ndakh sa thiofel si Cheikh Tidiane ❤️❤️ yalna YALLA barkél té doli soutoura 🙏🙏
Booko waroul wôna firi doko firi , bour YAllah mô dogal ngua warko firi firil ci hormay CHEIKHOU TIDIANE Content de toi et ton équipe....
MACHALLA YALNA BUUR YALLA FAY LA YIW ♥ 📿📿📿📿📿📿📿📿💯💯💯💯💯💯💯💯🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰👍👍
Bilahi beug na wakhatne si maodo lolou rek lay khar
Salam di la nianal yallla wer ak fane you goude. Bilahi yokk gaa sama thiofel si ABUL ABASS SEYDINA CHEIKH AMADA TIDIANI. Donc je vous encourage et prie que le Grand cheikh Abul abasss vous gratifie de son amour et benediction.
YALLA na mala sunu Borom fayal barke Cheikhou Tidiane samal mala aarla mala. Mousssala thi thiat, ak beut bou aay
Tawfékh ak taïssir si sounou serigne Daraa incha allah
Voir début cours n21 pour les questions de Alladji !
Ma sha Allah. Dieureudieufati serigne Ahmad Fall. Yallah nala sounou Borom faye té same la ci barké Cheikhou Tidiane RTA.
السلام عليكم ورحمةالله تعالى وبركاته ياشيخي احمد فال جزاك الله خير الجزاء بجاه شيخنا احمد التجاني
Mashallah à toute la khadara magui téoulou Mame cheikhiou Oumar Tall.Mashallah
Jeureujeuff Sheikh bi..
Tjrs un plaisir de suivre votre cours.
A chaque fois soumala dehlo demay guena sopp cheikh yalna yalla soutaral thi barké Cheikh ameth tidiane
Salam. Je vous remercie pour votre travail pour Cheikhna Ahmada Tidjany(Qu'Allah sanctifie son précieux secret.)
Mais je vous conseille de prendre en compte les critiques objectives et d'ignorer celles qui ne le sont pas. Les critiques objectives (et même celles sans fondement) participent à l'éclosion du Savant et aident celui qui sait moins à mieux savoir.
Je suis partant pour ce e-daraa.
QuAllah soit content de votre travail et vous accorde longue vie pleine de santé bijahi RassouliLahi PSL!
Du courage lepa bakh Macha Allah
بارك الله فيك حفظك لله وراعك رضيت الهدي وافوض امري الى الله
Machalla oustaz Ahmed fall yalna bur yalla faye yiw
Assala mu Alaikum.
Leçon yi xana amoul format audio. Comme ça niou mane si diari niou. Budé amna telegram wala groupe watshapp ngène dima liniou si ngir Yalla. 🙏
nous sommes de tous coeur avec vous mercie encore
yalla nanou la yalla samal ci barker aboul abass cheikhna tidiane cherif. gni wakh waro firi djawahir dagno khamoul rek
YA OUSTAZ YALNALA SA BOROM GOUDAL SA FAAN SAM LEU
Maachala. Gnune daal beg nagn ci lepp! Gnungui khaar tableau bi ! Pour schema bi "izhab ilaa chadjaratil yaqiine..."
Yalla na bourr yalla kaatanal tei motali leeepp! barkè Yonnent bi SAWS, wormay CHEIKHU TIDJANI ! 🤲❤️❤️❤️
Mancha Allah
Ya seyidi ligua al hour ane mo gueune fort té gniguikoy diema fini
On t'encourage openaa bagna firi
Yalna yalla same la te yokk xam xam bi
Félicitation thi ligueye rafetna bravo
Dieredjieuf serigne bi mane dall chaque jour notification lay ndieke khol yalla na sa diame yague yoke bibarakati seyidil woudjioude PSL🙏🙏🙏
J attends les cours avec impatience semaine par semaine
Mashallah mashallah
Allah
Yalna yalla dugeul sa fane wereulleu🙏❤ yagui si xol yi
Thiey gaayou cheikh yii ahmed fall Nala yalla geureum
Mbok mane déh pape bilal amouma loubari wayé insha Allahou je suis partant pour donner ma participation tant soit peu qu'il en soit je suis avec vous que Allah nous accompagne ...
Dieureudieuf sangu bi
Yallana yalla dollila jam bijahi Rassoul sas
ما شاء الله مفيد جدا بارك الله فيك يا فريد في الزمانك حياك الله
Aminn incha Allah yala nala bour yala doli soutoura si barkep cheikhou tidiane rta
Dieureudieufe' cheikhou tidjiane dieureudieuf maachalla oustaz yalla nala yalla Faye yalla Nanou yalla def deugeu deugeu talibe cheikh
Merci qu'ALLAH vous accompagne
Machalla dieureudieufaty serigne Ahmad Fall Bour yalla fayal gniouleu sì barke Cherif Ahmed Tidiany Cherif RTA
Masallah 💖 sama Sophé 🙏🙏🙏
❤️
Salam oustage Ahmad fall niogui ziarr ba maroc
machallah yagg fi lole té adak wérr si barkep seydina mouhamed lo doundou doyoll bilahi daga bakh lole oustas akhmed fall
Bonne continuation yala na yalla takhawou lene bidiahi cheikhou ahmada tidiane cherif rta
Brakallahou fikk oustaz Fall, bonne continuation
Merci oustag moukhamét fall yall'na yalla yagal lafii loll
Yalla na yalla mousseul....
Alhamdoulillah Alhamdoulillah Alhamdoulillah
Barakallah
Dierediefe chiekh Ahmet tidian' serif Diarama seydil khadji Malick Sy ak wa kuerem point
Serigne bi yana yalla fayella 🤍🤍
Macha Allah Serigne bi
Alhamdoulilah yalla na yalla motali Lep si barké Mohamed (psl)si worma cheikh aboul abass(rta) cours 45
Yagu fi lol inchallah...Machallah
Il a fait ma vie
Salam Serigne Daara Namon nagnla
Yalna Bour l'Ahou fayla yi mayla goud fann ak weer ba nga aguali ak diam...
💖🙏🏿🙏🏿🙏🏿
Barak'Allah fiik Ya Cheikh ♥️
Serigne bi beugue na kham kou beugue diap si liguéy bi noumouy déf
questions yi tontougako si cours 21 bi bou yague machallah serigne bi❤
Machallah ♥️♥️♥️
Dieureudieufeuty Ya Oustaz
Machallah
Machallah yalle na yalle motali
Machalah ya oustaz
Pour la creation de cette darà pourquoi pas des cartes de membre et des cotisations annuelles pour la fondazione?
quamou quamou rafete🙏🙏🙏
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Amoule wéraneté machalah ♥️
🥰🥰👍
❤️❤️❤️
Dieureudieuf dieureudieuf dieureudieuf
الحمد لله
Assalamou aleykoum wa rahmatoul lahi taala wa barakatouhou
machalla darse bi amatina solo
wallahi wakhe nga duegue
man dama buegue bokue si group yi
Group
Machalla seydi Fall
Dieureudieuf Ya Ouztaz