fanane si garage ndeyesane sama rapel sama garage bima done fane adouna dou dara magui ni tèy machallah adouna sante yalla rèk dounde bou dièkoul lèp kethienasi
@@seynabouseck2231 merci seynabou..y a bc de chose qu on ne peut dire mais c est pas facile...9n peut même avoir les deux parents en vie et des fois c est très compliqué..il faut vraiment le vivre pour apprendre bc de chose mais santé borombi rek...le chemin était trop long...
Je me vois en toi machaallah dina gueun takk sama seurr nous sommes 9 et je suis l'aînée notre mère on l'a perdu il y 7 ans maintenant mais inchallah ils ne manqueront de rien
J'ai pleuré je te comprends j'ai perdu mon père tôt quand je voyais les enfants avec leur papa ça m'a rendu triste mais ma mère c'est une brave femme elle la fait les deux rôles du père de maman😭😭😭😭
Je ne suis pas sénégalaise, j'ai vécu ici ya longtemps j'ai connu aussi le calvaire,j'ai travaillé comme bonne pour élever mes enfants garçons seule jusqu'aux études supérieures,vous êtes une brave femme,amazone mais une référence agairie,longue vie avec santé. Chapeau
Moi j'ai perdue mon père 1996 je comence a travaillé mon premier travaill on ma payé 15.000F je travaillé du lundi au dimanche mais maintenant alhadoulila
Merci maman de faire comprendre aux jeunes la vie n'est pas facile.Mais pour aller de l'avant ça vaut la peine.Votre histoire encourage la jeunesse émerger pour le futur.Que dieu vous paye.
I have always admired her but listening to her story today made me love her more. May Allah grant her long life , great health and strength. She’s exemplary !
Bilahi mère bila fotelo teh fayoula guissoumako mais trokhna bou yague Yako yeugoul rek ndakh sa dolé biguako liguéyal teh fayoula en plus mou tangal sa khôl tek si nganiko bayinala ak yalla yaye goudal fane si barker alkhourane 😭🙏
Walahi niak yaye dafa meti dimanche matin dama yewu sama khelmi yeup dem thi sama yaye ndakh damay yobou sama dome ma def accident sama tank bi dame ma dioye ndakh wetay kou niak yaye wet magou yaye dou yaye rakou yaye dou yaye yaye ken la
Man de yalla kham nani mosouma khamni doundou nga lii yeup😭😭 damala yagga beug nguir ninga beugeu sama maam Ju baax ji di srg fallou mbacke bou feke amnaa si s fallou benn thieurr yalna nga goudou fan te weur inchalah dinala ziare si ba sa keur
Degue pirrr mane mabo la ndeuk lou bakh rek lay def chapeau rouge tata ndeye ndiouf yaw y'a takh sama yaye ndeuk si nieuk bou bakh. Merci yalla na yalla defal diam si barki serigne fallou mane yay sama idole
Masha Allah diome rek mo ame solo. Yaye jou wouter dafa meti. Mane khamnassi dara . Na Yallah yereum souniou waye dawlou joulite yep si barker Seydina Mohammed SAW
Innalahaa maha sabirine way mougne yi rek la andal yalna yalla deugueureul sa takhaway in chaa allah j perdu mon père il ya longtemps m alhamdoulilah dilen nianal rek yeurmadé
J'ai pleuré toute la vidéo tout comme moi j'ai grandi avec ma mère qui a tout fait pour que je réussisse j'ai pas peu voir mes deux parents dans une maison ses avec mon bayou djitte lé ou la femme de mon père et ils mont fait vivre l'enfer mes Dieu merci aujourd'hui je suis Modou Modou je remercie le bon Dieu et ma mère et que mon père repose en paix
Non la vie ndeye diouf m à fait pleuré elle a raison la vie est pleine de surprises bravo les femmes celles qui sont mauvaises redressées vous porfavor
Maman à chaque fois yaye sama référence bilahi je suis en Arabie saodi c'est dure ici les conditions du travail mes juste beugouma df lou bone t dama beug téral sama yaye bravo à toutes les femmes
Bilae maman lo guiss so amé foula rekk dafay diekh Sama Mame que son âme repose en paix m'a expliqué un jour cet histoire et ça m'avait vraiment touchée 🥺🥺
Deysan yak ga sama journée bi j ai vécu la mm chose et pourtant j étais chez la maison de grand frère de mn papa et demay teud Di Sango Bassan dakh séd mai téy diékh lolou Yep télla niak pape moko waral heureusement maman était là dnc motah yaye ken amul fayam bilahi 😭
J ait perdu ma mère a l âge de 7 ans mon père a l âge de 12 ans j ai vécu l enfer mais toujours brave machala je remercie le Bon dieu
Massa ma chérie courage et bcp de bonheur 🥰
Massa ma puce
Massa meti trop yalla nala yeureum khare aldiana firdaws thi barkhé seydina Mohamed salahou allhi salam
Courage à nous moi aussi l enfer mais tjrs courage dafameti torop YAlla rekk Dieu est là et on le sens courage
Courage
Ndeysane yalnala yalla takhawou may la moudieu bou raféte inchala c'est triste
fanane si garage ndeyesane sama rapel sama garage bima done fane adouna dou dara magui ni tèy machallah adouna sante yalla rèk dounde bou dièkoul lèp kethienasi
Mais pourquoi di fananal nit ci garage hoo ce pays ya des mauvaises personnes Bilahi
J ai larmes aux yeux..merci madame c est pas facile de perdre un parent surtout la maman....
bilay Lou amla
@@seynabouseck2231 merci seynabou..y a bc de chose qu on ne peut dire mais c est pas facile...9n peut même avoir les deux parents en vie et des fois c est très compliqué..il faut vraiment le vivre pour apprendre bc de chose mais santé borombi rek...le chemin était trop long...
@@seynabouseck2231 merci seynabou..
Ndeyssae ayy way tu m'as donné le courage merci maman😥😥😥
Bilay Ndeysane
❤️❤️
Ak mane mii 🥰
Je me vois en toi machaallah dina gueun takk sama seurr nous sommes 9 et je suis l'aînée notre mère on l'a perdu il y 7 ans maintenant mais inchallah ils ne manqueront de rien
Courage ma belle
Du courage ma fille lo mougne mou diekh inchalah
Inchallah tu triomphera yalla bakhna
courage ma belle
J'ai pleuré je te comprends j'ai perdu mon père tôt quand je voyais les enfants avec leur papa ça m'a rendu triste mais ma mère c'est une brave femme elle la fait les deux rôles du père de maman😭😭😭😭
Je ne suis pas sénégalaise, j'ai vécu ici ya longtemps j'ai connu aussi le calvaire,j'ai travaillé comme bonne pour élever mes enfants garçons seule jusqu'aux études supérieures,vous êtes une brave femme,amazone mais une référence agairie,longue vie avec santé. Chapeau
Yalnaléne yalla doli yeurmandé
Merci
Quelle femme admirable !
Dafa am gniou gniémé Haqe 😭😭😭😭😭
NDEYESANE YALLA NA LA YALLA sam te doli lla JAPALE SI Barke seyi dina MOUKHAMED amine 😘😘😘😘😘😘😘❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ndeysane Lou méti yagg n'a si adouna😭😭😭😭😭
Moi j'ai perdue mon père 1996 je comence a travaillé mon premier travaill on ma payé 15.000F je travaillé du lundi au dimanche mais maintenant alhadoulila
C'est sa hein c très difficile la vie est comme ça
Merci maman de faire comprendre aux jeunes la vie n'est pas facile.Mais pour aller de l'avant ça vaut la peine.Votre histoire encourage la jeunesse émerger pour le futur.Que dieu vous paye.
Bilay
@@falysarry9030 merci 💓
Maman dioye Lo ngama 😭😭😭😭😭 j’ai deux filles mais sama yaye Mo may aider si gnome motakhe ma fonkk ko goudeule fane maman
Machalla amna solo lool yalla maye goudou fane ak wéer si barke seydouna Mohamed saw dieureudieuf
I have always admired her but listening to her story today made me love her more. May Allah grant her long life , great health and strength. She’s exemplary !
Machallah je t'admire encore plus. Quelle brave femme. Tu es une référence pour les jeunes filles
Bilahi mère bila fotelo teh fayoula guissoumako mais trokhna bou yague Yako yeugoul rek ndakh sa dolé biguako liguéyal teh fayoula en plus mou tangal sa khôl tek si nganiko bayinala ak yalla yaye goudal fane si barker alkhourane 😭🙏
😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Walahi niak yaye dafa meti dimanche matin dama yewu sama khelmi yeup dem thi sama yaye ndakh damay yobou sama dome ma def accident sama tank bi dame ma dioye ndakh wetay kou niak yaye wet magou yaye dou yaye rakou yaye dou yaye yaye ken la
Vraiment c'est très intéressant,c'est pourquoi il faut les mbindane,car faut toujours penser à demain
Man de yalla kham nani mosouma khamni doundou nga lii yeup😭😭
damala yagga beug nguir ninga beugeu sama maam Ju baax ji di srg fallou mbacke bou feke amnaa si s fallou benn thieurr yalna nga goudou fan te weur inchalah dinala ziare si ba sa keur
Akay deug djigguen bouy tamou liguey fo diar dawsi guinaw goor voilà une leçon de vie et morale
Ndeysane sira lam dé meloule nonou
Mama yalla nanga goudou fan lool ci barke serigne fallou mbacke sounou soppe❤❤❤❤❤❤💪💪💪🇲🇦🇲🇦🇸🇳
Bravo à ma sœur, vraiment c'était très dur mais tout est fini bien. Qu'Alla t'accompagne.
Degue pirrr mane mabo la ndeuk lou bakh rek lay def chapeau rouge tata ndeye ndiouf yaw y'a takh sama yaye ndeuk si nieuk bou bakh. Merci yalla na yalla defal diam si barki serigne fallou mane yay sama idole
Machalah mettite bobou mola forger
Thi mission nga nekone
Elle a éte accompli Alhamdoulilah...
Famme de ménage kokou défoul meunoko kham😭😭
Bilaye
Billayi motax la femme qui m'aide et comme sœur
Bilae dafeu méti
😭😭😭😭😭 métina yaye boye 😭😭yalna thiono yéme adouna
Masha Allah diome rek mo ame solo. Yaye jou wouter dafa meti. Mane khamnassi dara . Na Yallah yereum souniou waye dawlou joulite yep si barker Seydina Mohammed SAW
J'ai perdu ma mère à l'âge 1an et mon père à l'âge de16an mais AllahmdoulilahDieu est Grand Dieu avec les patients
Innalahaa maha sabirine way mougne yi rek la andal yalna yalla deugueureul sa takhaway in chaa allah j perdu mon père il ya longtemps m alhamdoulilah dilen nianal rek yeurmadé
Sama artiste, sama référence Ndèye Diouf bou Serigne Fallou. Thia kaw thia kanam rék inch Allah
Ndeysan bilahi li daw na yaram 😭😭😭
Sama yaram dafa daw ndeysane say rakk dioyouniou yaye dh amal diam rek😭😭😭❤️
Bilaye Tata ndeye diouf machalla yalla nala yalla bayisinou kanal
😭😭😭😭 j’ai les larmes aux yeux machalla
J'ai un ami qui dormait dans un garage à la maison du grand frére de son papá il est devenu aujourd'hui un ingénieur
❤🎉❤
Bilaye verite contana ndeye Diouf ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Aka am diom yaye Ndeye Diouf machalla belle référence
Hoooo metina masta maman ndeye diouf thieuy adouna yague na metí 😭😭😭😭
❤❣❣🤦♀️😭😭😭😭😭
😭😭😭kou niak yaye kham ni mètina trop
Machalla
J'ai pleuré toute la vidéo tout comme moi j'ai grandi avec ma mère qui a tout fait pour que je réussisse j'ai pas peu voir mes deux parents dans une maison ses avec mon bayou djitte lé ou la femme de mon père et ils mont fait vivre l'enfer mes Dieu merci aujourd'hui je suis Modou Modou je remercie le bon Dieu et ma mère et que mon père repose en paix
Alkhamdoulilah yok gua ma courage merci du fond du cœur 💓💓💓💓💓 alkhamdoulilah Sant yalla alkhamdoulilah
Hooooooooooo 😤😤😤😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭kou mougne dingua meusseu ré
Kuû baaxla kuû baarii soutoura🥰❤😭
Tan Ndeye Diouf billayyy diammm guayyyy ammmm
Non la vie ndeye diouf m à fait pleuré elle a raison la vie est pleine de surprises bravo les femmes celles qui sont mauvaises redressées vous porfavor
Je sius fiers de toi ndeye Diouf mou s'en fallou yalla gaa walamathi amine ❤
Lii dhè tisseu na yalla nala yalla doli soutoureu
Vraiment yalla na yalla goudal saw fan yay boy ak tawfekh
Respect à nos braves mamans ❤️
Machalah une grande dame li moye goré
Ooohh ndayssann 😓 ndeye Diouf courage
Motah dara heyoull rék soti
MACHALA bilakhi kham na si dara wayé ma ame mague boubakh machala ndeye fatou aidara cherif ❤
Maman à chaque fois yaye sama référence bilahi je suis en Arabie saodi c'est dure ici les conditions du travail mes juste beugouma df lou bone t dama beug téral sama yaye bravo à toutes les femmes
Courage
Courage fo nek si arabi saodi mane magui arabi saodi
Massa Mbaye aduna mougn rek . Yalla nala yalla sam, defal la lou geum ci yaw
Oh amena gnou gnémé akk té gnak am yeurmandé si.diank
MERCIE BEAUCOUP DIEREUDIEF AMAN SOLO ❤ ❤ ❤ TATA NDEYE DIOUF GRAZIE MILLE VIELEN DANK ❤ ❤
Ndeyssane Yalla na sa diam yague
Cependant le 8 mars n’est pas une fête c’est plutôt la journée internationale des droits de la femme 👩
Ndèye Diouf gnokhabaye, djarama, Yallah Bour dina la takhawou. Sa yaye Yallah Bour dinako tèk sa Adiana dia gueuneu kowé...
Mo takh kène waroule ignané kou ame alale, ndakh khamo famou diarone démbe. Djiguènou Sénègal ame nguène aye royou kaye you doule diékh. Kone Djiguènou Sénègal waroule gniaw....
Les gens doivent souvent partager leurs expériences cela permettra au jeunes surtout de comprendre la vie
I9
Machallah. Grande Dame longue vie à vous..Très triste maman mais Dieu est partout
maChallah yallah dou moromi ké
Tu es une très belle femme merci
Machaallah rafetna merci ndeye Diouf Mabo ça kaw
😪lost my mom years now💔life has never bein easy since then but Thank God
Bilahi tu m’as fait pleurer
ndeysaan fanaane naa si garage une semaine 😭😭😭 mais lo mougne mou diékh 😭😭😭
J'ai versé des larmes car je me suis rappelé de mon passé.
Moi j'ai perdu ma mère à l'âge de 2 ans mais 😭😭😭
Ohhh massa chérie yalna yala mayla kholou mougne💔💔💔
J en connais quelque chose car j perdu ma mère et mn père a bas âge et j n'es personnes pour aider j en s'ouvre jusqu'à présent prière pour moi
J'ai perdue mon pére le 19 fervier passer me c trés dür et longue vie a non maman sante rek
machallah maman ndeye diouf je suis très fière de vous si kaw si kanam rek inshaAllah
Bilae maman lo guiss so amé foula rekk dafay diekh
Sama Mame que son âme repose en paix m'a expliqué un jour cet histoire et ça m'avait vraiment touchée 🥺🥺
Machala yayam sama harito badiene lawon ndeyssan yanalen yalla yeureum talibé Serigne fallou yoyou☺️🤲🤲
Ndeysann maman Ndeye Diouf yalla nala doli soutoura dinagnou guena gorgorlou inchallah yalla diekhoul
toulaye sarr depuis kaffrine tata ndéye diouf ya goré dioyena sakh bilahi ya rafet col
J ai méme pleurè ndéyssane
Ndeye Diouf mon amie que i'ai connue chez Aminata diop
Wakhe na dagg de mako sede ❤❤❤❤❤❤
J’ai perdu ma mère a l’âge de 17 ans c’était très dificile 🥲
Ndeysan 🥺🥺♥️🙏🏾
Bilay tata ndeye comme moi elle est décédé et ma laissé avec8enfant
Du Courage ma belle yala nalene souniou borome same are léne
Du courage yalla nala
Yalla diapalé ma grande
Beaucoup de courage
Masta yalna la Yalla takhawou té mousseul lèn mouthieul lèn
Courage pour atteindre l'objectif
Une histoire très touchant, j'ai presque les larmes aux yeux 😙 😪😪
Bilay Li rek motakh ma fonk sama bonne bi
Bravo ndeye
Longue vie a ndeye j'admire ton comportement
J’ai fais cette expérience moi aussi 😭
Man mii diar nassi mbindanou ba dougou europe
Machalah yalla senn diam yag ❤ 🤲
Machallah, ki damako beugu
Contanna waye j’adore notre maman si sincère longue vie que Dieu te protège
Machaalah yalla na sa dial yague
Deysan yak ga sama journée bi j ai vécu la mm chose et pourtant j étais chez la maison de grand frère de mn papa et demay teud Di Sango Bassan dakh séd mai téy diékh lolou Yep télla niak pape moko waral heureusement maman était là dnc motah yaye ken amul fayam bilahi 😭
Merci beaucoup maman j😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭e veux beaucoup souffert merci
Machalah manma long vie à toi bilahi linga wakh thi mbidan man doundou nako bilahi 😭
J'ai le cœur meurti Je l'aime tellement tata Ndèye DIOUF.
Senegal respecter wouniou femme de menage yi dafa ndiawe torop
Am so sorry mum😭😭😭😭❤❤
s'être senti non aimé et de ne pas recevoire le minimum d'affection dont on a envie - J'ai du mal ... waydiouryi dèlène topoto sèn ndiabote
Je l'aime beaucoup wallahi longue vie à toi tata ndeye 🥰❤️❤️
Dafa am gnou bone,bilay faut jamais les maltraiter
Machalla Fierté Maman ❤️ yiguene bou valeurs je ❤️
Tout est bien qui finit bien
Moudje gou rafete
Mère ndeye Diouf aka yarou si makk