Masha Allah J'ai suivi un debat enrichissant, avec deux érudits de hadith. À part ça je vois que beaucoup de gens n'ont pas compris les propos de cheikh thioub, quant à cheikh Baye il a été methodique et calme. Merci à chiekh bitéye pour son sens de repartie et de modérateur. Fier d'être sénégalais.
Félicitations aux deux invités de Oustaz, certains moments ont été très enrichissants, mais Oustaz Thioub franchement je ne vois pas de motestie dans ton discours. Si tu te dis être un intellectuel il y'a le minimum d'ingence. Cheikh Baye continue ainsi et enrechie d'avantage ta connaissance, courage pour le reste.
Cheikh baye niass khawma lanla mais Sama khol nangou nala guiss na si yaw akk Dale akk yarr akk tëy tabarakallah à vous trois 🤣💚💛❤️💚💛❤️💚💛❤️💚💛❤️💚💛❤️💚💛❤️💚💛❤️
Chiekh baye niass borom xam xam Te kou jangue la gueustou la rombe na genrou débat yi si niveau intelligence etude pertinence enseignement ect machallah chiekh baye❤
Ce Oustaz thioub est très limité..Il n'a pas d'argument c'est pourquoi il fait une attaque personnelle. Cheikh Baye machallah très serein et très pertinent
No Thioubou diambarga yalnala yalla youkou guiryala damalaye niane gadoli sa khame khame rèk dina bakhe wayè Cèikhe baye dala rawe si kotè hadise ndakhe loumou wakhe yèp si dalile lakoye tè diokhla pas bimou nèk diokhla nimoro kone dafla rawe si kotè hadis loubari gastoule rèk dina bakhna 🙏
Mashala débat bi âm na niveau lima si gueuneu néh ak lima sii diagaatt moy niari sénégalais you âme ham ham mashala Yalla na lén Yala same layaneté bir la rek pas de rancune ni d’injure toute façon c’est le bénéfice de l’islam ☪️
رايت في بابكر تيوبو تصرفا أرعنا رهيبا ألا وهو محاولته دفاع موقفه بأي ثمن، وتأويل بعض الأحاديث بمجهود خاص وخاصة الحديث الذي ينص على تفضيل النبي صلى الله عليه وسلم لواحدة من أزواجه. ولكي تُدافعَ ياتيوبو عن موقفك بجدية عليك معرفة حجج المعارضين لكنك تنظر بعين واحد .. صراحة لم يظهر عنك هنا إلا حقد كامن يارجل. أنا لست من أتباع شيخ باي هذا وأيم الله بأني قد خاصمته يوما، لكني معه اليوم لأني أحاول قدر الإمكان أن أكون مسلما يقف مع الحق والعدل. وفي النهاية أسأل الله لكما البركة والنصرة، فأنتما صراحة فخر للأمة الإسلامية بصفة عامة ولإفريقيا وخاصة شبانها بصفة أخص، أظهرتم مستوى راق في العلم والمعرفة.
Sa waye niome niarre nii dire wakhtane yep Talibe baye lane oustaz bitey sakh talibe baye blanguaye khôl ale ba kam niome niepp talibe baye niass lanou
Même en 2024 je regarde encore ce débat de très haut niveau avec deux experts ❤
Masha Allah
J'ai suivi un debat enrichissant, avec deux érudits de hadith.
À part ça je vois que beaucoup de gens n'ont pas compris les propos de cheikh thioub, quant à cheikh Baye il a été methodique et calme.
Merci à chiekh bitéye pour son sens de repartie et de modérateur.
Fier d'être sénégalais.
Machallahh ckeikh baye xam xam bi réfét na torop yalna yalla fay la yiw in challahh ❤
500 j'aime pour Cheikh Baye Niass.
Cheikh Baye Niass dall takanderou Charia Baye Niass la
Alhammdoulilah ...gueuneu yague gueuneu werr Oustaz Cheikh Tidjane Bitéye ma challah..machallah thi invité yii ...khamm khamm neixna ❤❤
Kou yallah maye tawfekh nga xamni ch babacar thioub dioulit la yalnala yallah ar samou la yalna yallah mousal niou ci nafek bi
Macha'Allah Cheikh Baye Niass tu maîtrise vraiment très bien ton sujet. Yallah na Yallah sameu la thi barké Baye Barham Niass 🥰🙏♥️
Dafa am xam xam
macha alla oustaz thioub yalnako yalla deguereul yokeu léram !! dégue dégue bi rafétna
😂😂😂
Macha Allah, je vous aimes. Vous êtes une fierté pour la hadra cheikh Ibrahima NIASS
Machallah débat bi ame na solo lool cheikh baay niass begue nala torop souma manoma ame sa numèro
cheikh baye niasse est une vraie temple du savoir macha alla !!!!!! yalnako sougn borom protéger béneu kéneu dou meun dara thi mom amine !
Mdr
Félicitations aux deux invités de Oustaz, certains moments ont été très enrichissants, mais Oustaz Thioub franchement je ne vois pas de motestie dans ton discours. Si tu te dis être un intellectuel il y'a le minimum d'ingence. Cheikh Baye continue ainsi et enrechie d'avantage ta connaissance, courage pour le reste.
Billahi cheikh baye niass d'où sa morom wallahi
Je confirme babacar thioub beug nako lolo wayii cheikh baye niass mii xam xam leu
La confiance n'exclut pas le contrôle Machalla cheikh Baye
Sincèrement parlé on a besoin ces débats religieux
Machallah débabi nekhna yalla na yalla faye leen yeen gnaar gneup
Niome niarre nii dire wakhtane yep Talibe baye niass lanou cheikh bitey sakh talibe baye niass la si guediou baye niass lanouye nane
Serigne cheikh Baye Niass mande mourid la khadim Sall la td wayie khamnane xam xam am nga ko lool machalla yalla nala yalla Faye
Merci à vous deux et chekh biteye je suis très content de vous et très fier de votre connaissance ❤️❤️
Sa waye niome nii Toq si plateau bi yepp si Baye niass lanouye nane
Cheikh baye niasse yalla nanga goude fane te weer
Mais Cheikh Baye Machala
Tu es trop fort vraiment
Kham Kham bi leernaaaa Baye
Machala a Oustaz Thioub aussi
Cheikh baye Niass . Merci d’avoir éclaircir certain hadis pr moi … 👍
جزاكم الله خيرا الجزاء ❤
Grande émission de débat intellectuel sur l'islam!
Kham kham nekh na machallah ♥️
Répètes haut et fort.
Wallahi
Merci Baye Niass, t'es intelligent, calme et respectueux. T'as mené le débat en restant sur le thème et en refusant de répondre aux attaques de Thioub
Mancha allah cheikh baye ninga fixé thi débat bi bania tontou personnel bakhna
Macheallah Cheikh Baye yallana yalla barkel xaam xaam bi
CheikH Baye Niass et Cheikh Baye Thioub gnom gnar yepou ay brom xam xam lagn waxtaan bi nexna tégou na ci xam xam. Machallah yalla na yalla faye lene
Yalla na yalla fayall niou cheikh ibrahima Niass dieuredieufee baye Niass
Cheikh baye niass khawma lanla mais Sama khol nangou nala guiss na si yaw akk Dale akk yarr akk tëy tabarakallah à vous trois 🤣💚💛❤️💚💛❤️💚💛❤️💚💛❤️💚💛❤️💚💛❤️💚💛❤️
ماشاء الله الشيخ باي نياس حفظك الله ورعاك ولجميع المسلمين 🤲🏼🙏🏻
Mashaa alah Cheich baye wallah xam xam deug lay wahé💖
Chiekh baye niass borom xam xam Te kou jangue la gueustou la rombe na genrou débat yi si niveau intelligence etude pertinence enseignement ect machallah chiekh baye❤
Lii rék dafay firndél ni euttou Cheikh Ibrahima Niass moy euttoup kham kham.
Cheikh baye Niass yalla nalla sounou borom samme machaalah kham kham bi raffetna
Amine
Cheikh baye Niasse yalna yalla fayella
Amine
MERCI BEAUCOUP MOUHAMED CISSÉ. KHAM-KHAM THI BOP LEU. DOU THI TÉLÉPHONE.
Merci wakhnga lepou
Ham ham dou ci bop ci deune leu
Machala amnasolo torop wayé babacar Thioub yawe diambarga wantè dafa mélni daga dégoule louwarale porocarame bi pasck danla wakhe galéralnou liwéroule ak li wér wayé ladiounla ndakhe Ceikhe baye amna khame khame wala xamout dara mane sasopé la wayénak kharouma wone siyawe ay poukaré borom khame khame dou rayelou dési bayi khélnak diwakhe lounit khame merci Cèikhe Bitèye yalnala yala samou Yarabi وسلام على من التبع الهدى
DEUG DEUG CHEIKH IBRAHIM SA KHAM KHAM DAFFA AM FASHAA IMAM ASSANE CISSÉ NGAMAYE FATALI MACHALA❤
Cheikh Baye xam xam bi rafetna machalah kel éloquence
MashaAllah débat très instructif. Regardez jusqu'à la fin avant de juger Cheikh Babacar Thioub il a vraiment bien été signifiant au final .
Élégant vraiment cheikh baye
Macha Allah Cheikh Baye xam xam bi réfétna
il est très cultiver Cheikh Baye Niass ! Borom xam xam deug lah téh limou wakh amena foumou koo ték machala yalla yalla diamal lah
Ma sha Allah! Débat bi amna solo lol. THOUB AK NIASS, Yalana borombi yokheuh ham ham yi in sha Allah!
Niome niarre nii niepp si guediou baye niass lanouye nane
Allahou Akbar
Macha Allah
Se debat c'est du 💎💎💎
Machalah déglou na waxtane bi yup amna solo trop walae cheikh baye limi wax yup DEUG leuh yalla na yalla samou
machallah bilahi debat bi nékh na trop té kham kham fégn nasi
mashallah, yalla na leen yalla defal jam yeen niar niepp.
Machalla cheikh Bay . yalla rék Moy nétalli Mou wérr.Boukhari nit késsé le te fékéwoul yonéntébi .li eupp si Boukhari ay kathieu le
Est ce que wakh dji bou rafeté dou eup ndiarigne
Tout les deux sont des sages ❤🎉
Macha-Allah debat bi nekhna niom niep borom ham ham len.
Ce Oustaz thioub est très limité..Il n'a pas d'argument c'est pourquoi il fait une attaque personnelle. Cheikh Baye machallah très serein et très pertinent
Cheikh tidiane bitey est le meilleur des organisateurs sur les plateau ma
Guis nga
Bilahi dafa mandou
Cheikh baye niass Mashallah ❤
Machallah Serigne khadim bousso walahi sopenala amoo morom dé machallah. Dieureudieuf cheikh tidiane bitèye Dieureudieuf cheikh baye dieureudieuf abacar thioube. Dieureudieuf yen gniy commentaires
Dieureudieu yaw itame rafetna
Yeun d cheikh baye rek nguen di xeexx.thioubou geunn andall.yeunn waa happiness
@@elhadjitoure7937 waa happyniass dégnoo ame kham kham té yaw khamoo dara
@@mouhameddiouldediallo4806 sa waye yaw momou ya khamoule niome niarre nii dire wakhtane yep Talibe baye niass lanou
مشاءلله جزاكم الله خيرا
Merci cheikh baye
Merci thioub xam xam bylerna
Baye niass est très fort
C pertinent mé thioub daye déf règlement de compte
machalla chiekh baye Niass ❤️❤️❤️
Cheikh baay Niass yaa yarou té dal té am kham kham Machallah
Franchement a la fin du débat thioub m'a emporté par ses raisons
ما شاء الله جميل جدا فضيلة الشيخ باي إنياس لا فض فوك ولا قام ضدك بينت وأحسنت.
Machallah cheikh baye niass sope nala NDAKH sa kham kham linga wakh lou werla BEUGGNA am SA N UN MÉROU NGUIR YALLAH
Cheikh baye machaAllah sa wakh rafetna amna teguine
Wallaye cheikh baye Niass Macha allah
Machalla alla yalana yalla barkél lén
اني احبك شيخ برهام باااااااي
No Thioubou diambarga yalnala yalla youkou guiryala damalaye niane gadoli sa khame khame rèk dina bakhe wayè Cèikhe baye dala rawe si kotè hadise ndakhe loumou wakhe yèp si dalile lakoye tè diokhla pas bimou nèk diokhla nimoro kone dafla rawe si kotè hadis loubari gastoule rèk dina bakhna 🙏
Machalah cheikh bay niass
Mashala débat bi âm na niveau lima si gueuneu néh ak lima sii diagaatt moy niari sénégalais you âme ham ham mashala Yalla na lén Yala same layaneté bir la rek pas de rancune ni d’injure toute façon c’est le bénéfice de l’islam ☪️
Mach allah serigne baye niass
Oustaz Babcar machallah xam xam bi rafeitna.
Cheikh Baye tamit machallah..
Yawit sa wakh rafetna machalah
@@HappyniassTV l💓
❤️❤️
Machala débat bi amna solo
Mashallah xam xam bou lér rekk mo am solo yalna yalla déflén ayy Makk
رايت في بابكر تيوبو تصرفا أرعنا رهيبا ألا وهو محاولته دفاع موقفه بأي ثمن، وتأويل بعض الأحاديث بمجهود خاص وخاصة الحديث الذي ينص على تفضيل النبي صلى الله عليه وسلم لواحدة من أزواجه.
ولكي تُدافعَ ياتيوبو عن موقفك بجدية عليك معرفة حجج المعارضين لكنك تنظر بعين واحد ..
صراحة لم يظهر عنك هنا إلا حقد كامن يارجل.
أنا لست من أتباع شيخ باي هذا وأيم الله بأني قد خاصمته يوما، لكني معه اليوم لأني أحاول قدر الإمكان أن أكون مسلما يقف مع الحق والعدل.
وفي النهاية أسأل الله لكما البركة والنصرة، فأنتما صراحة فخر للأمة الإسلامية بصفة عامة ولإفريقيا وخاصة شبانها بصفة أخص، أظهرتم مستوى راق في العلم والمعرفة.
Machla cheikh baye❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Talibé baye yi amnanou kham kham
Kou sa sérigne di dieumi kham kham fo diaar am kham kham baye niass dieumi kham kham la yalla na gnouko yalla fayal amine
yalla nalla yalla defal diam yokk la si bopam , mais dire que talibe amoul kham kham niak kham kham fofu la yeim , diegualou nak mais depasel lolou
Regarde bien CHEIKH BAYE NIASS,quant il parle il ne lit même pas sur son portable,les mots lui viennent facilement...daffa guesstou té am méyou yalleu
Cheikh Baye est très fort!
Machallah Niass
Machallah debabi Amna solo trop mai oustass Babacar thioub borom kham kham Bou mak la billahi limou lathie cheikh baye manouko tontou
Cheikh thioub a tellement raison . Si on utilise que le tête pourquoi le prophète Mouhamad a eu 9epouses ça c'est plus grave.
Yow yay kan bay grawal lou yonente yalla def yemal sa place frère niaka nga talibe trop
Cheikh baye est le meilleur
Brave bay Niasse Raby hi Zidak Illema
Cheikh Baye xam xam bi rafétna machallah
Machallah Cheick Thioubou ak Cheick Baye Niass kham kham bi rafétena torop yene diou amoul kham kham Boulin Di khaseté aye taliblle Baye rek la niou
Niome niarre nii dire wakhtane yep Talibe baye niass lanou cheikh bitey sakh talibe baye niass la
Machallahh chiekh baye niass machallahh s khadim boussoo
Bravo oustaz thioubou lima guena nékh si yaw danga ame dégue trop té ame osi yarou soufiangké machala bone continuation .🤲😭
Sa waye niome niarre nii dire wakhtane yep Talibe baye lane oustaz bitey sakh talibe baye blanguaye khôl ale ba kam niome niepp talibe baye niass lanou
😂😂😂
Walahi soufyanké deug kou am yar am talibé wek djoulite nyeup yagfi thé wer seydi Aboubacar Thioub
Alhamdoulilah...Cheikh BAYE machalla lér naaa...Oustaz Thioub dolile kham kham Alhamdoulilah
bilay yow
FELICITATION A OUSTAZ BITEYE . VRAIMENT ON A BESOIN CES GENRES DE DÉBATS. INTÉRÊT COLLECTIF
WalAy
Dieureudiefeeeeee cheikh baye niass
بارك الله فيك يا فضيلة الشيخ باي انياس
Cheikh baye.ya.bakh.yallana.yalla.samoula.taxawoula'
Machalla cheikh baye thioub sans téléphone do wax demal diangi
Babacar Thioubou ya am kham kham way 😂😂😂😂😂 machallahh
بارك الله فيكما كان نقاشا هادئا وعلميا وكان بناء ، حفظكما الله ورعاكما وأبقاكما ذخرا للأمة،
أريد من حضرة الجميع من يعطيني رقم الشيخ باي انياس
c'est agreale d'ecouter cheikh Baye niasse. Jaambar deug la.
Macha Allah cheikhs baye niass macha Allah oustaz blablacar thioubou sene wahtane bi nehna