Fils De Balla tire sur Balla Gaye 2 : "Samba alare la, wakh nagn ma lou nék ndakh mom mou..."

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 10 лют 2025
  • Visitez notre site web luttetv.com/ et aimez notre page Facebook pour voir des combats en direct / luttetv
    / luttetv
    / luttetv
    / luttetv
    luttetv.com/

КОМЕНТАРІ • 1,3 тис.

  • @vieuxeusse8185
    @vieuxeusse8185 Рік тому +83

    Bilahi Balla wéréna ! Ki koukou guiss noumouy wakhé malgré son chagrin on sent intérieurement qu'il le porte dans son cœur ❤

  • @galsen7780
    @galsen7780 Рік тому +26

    Walay Sénégal 🇸🇳 c'est un pays de théâtre 🎭 la jeunesse Sénégalais réveillé vous le monde avance

    • @MyaMya-rj7yx
      @MyaMya-rj7yx Рік тому +1

      Bilaye danio bègue mar Tate lolou moy sen problème

  • @KallyKurumang-cg7wq
    @KallyKurumang-cg7wq Рік тому +82

    That's the truth...Balla Gaye should try by all means and consider the boy.....he helped you a lot and love you 🎉❤

    • @Black_DTv-y5q
      @Black_DTv-y5q Рік тому +1

      Balla defoul deug

    • @ibrahimasambseye2938
      @ibrahimasambseye2938 Рік тому

      Aziz will be the best champion. At this moment it was good for him 😊

    • @Alisa-oo6nt
      @Alisa-oo6nt Рік тому

      Correct

    • @hameh8917
      @hameh8917 Рік тому +1

      💯 bro he should have try by all means to come or give the guy a call no matter what.

  • @ousmanegueye6477
    @ousmanegueye6477 Рік тому +120

    T’as parfaitement raison champion quoiqu’il en soit il devait venir franchement

  • @adamaseck8816
    @adamaseck8816 Рік тому +48

    Deugue Deugue Beuguena balla gaye trop bilahi mé bou meuner déme si boy niang wara meuneu nieuw siyaw vraiment yanek si deugue🙏

  • @sambboss8418
    @sambboss8418 Рік тому +13

    Non lolou bomoula diakhasé ak balla gaye saytané dafa bari dollé ❤mane yaw ak balla gaye ak sathies rek lay suporté si lambe bilay yaw ak balla gaye yena fare beugouma dara dokh sene diganté❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @mbayefam572
    @mbayefam572 Рік тому +65

    Tu as parfaitement raison

  • @seydouba2027
    @seydouba2027 Рік тому +49

    Fils de tu as parfaitement raison mais on te demande pardon lui 😢

  • @bipsall7335
    @bipsall7335 Рік тому +211

    Vraiment c'est vrai balla dafa warone gnewe waxe DEUG yallah je suis fans de balla gaye daga djoume

    • @asskasse9513
      @asskasse9513 Рік тому +8

      Geumeul sa Bob fiimou aague meun ngaafa aague toppou ci ganaw gaur dico doungourou

    • @Aki-id7ko
      @Aki-id7ko Рік тому +8

      Mais danga Kham loko Teyai ba niowout...mais Sa thies niow na

    • @bipsall7335
      @bipsall7335 Рік тому +3

      @@Aki-id7ko sa thies bopape la gneweule balla gaye dale da djoume vraiment balla défoi do comprends lui c'est ça le problème de balla gaye 2 sama champions bi

    • @Aki-id7ko
      @Aki-id7ko Рік тому

      @@bipsall7335 mais Sathies moune dafa niowal magam lolu la wakh. kon amna loutah Balla niowut

    • @bipsall7335
      @bipsall7335 Рік тому

      @@Aki-id7ko sa thies lolou la meune waxe pour rafétale dei xame kate sa thies dou waxe lou gniawe si balla gaye

  • @famafallouyayousamate4758
    @famafallouyayousamate4758 Рік тому +17

    TU ES CHAMPION MON FILS YALA BAKHNA ❤

  • @kurayahmi
    @kurayahmi Рік тому +68

    *Fils de Balla je l’aime bien parce que mom il n’est pas faux loumou khalaat daf koy wakh diaar ci digue bi ak koo meunti done. Si c’était les autres fii laniouy nek di tourner autour du pot, Balla borom bakh leu mais li mom raffetoul*

  • @ibrahimagueye3988
    @ibrahimagueye3988 Рік тому +15

    vraiment tu as raison fils de Balla Balla gaye 2 devrait venir franchement 😢

  • @serignemormbaye2465
    @serignemormbaye2465 Рік тому +91

    Vérité absolue balla dafa warone téw

  • @massndiaye7897
    @massndiaye7897 Рік тому +15

    Merci champion deugue rék nga wakh bilahi Mane Balla moye sama mbeur

  • @khadidjagning182
    @khadidjagning182 Рік тому +18

    Vraiment tu as raison Aziz lou balla khéwlé Aziz téwe na courage yalla bakhna ❤❤

  • @ndongomsalioutourye162
    @ndongomsalioutourye162 Рік тому +2

    bilay balla defna lolou niaw me yalla bakhna fils de balla guem kou rek dina bakhna INCHALLAH

  • @bachiroubadiane3135
    @bachiroubadiane3135 Рік тому +42

    Courage champion gueumeul sa bopp rkk
    Balla Gaye da rerr diamono yi gnou tolou

  • @tawdabasall
    @tawdabasall Рік тому +6

    Merci fils de balla domou hamo ❤️❤️❤️ boul lakou si kaineu

  • @djibysow6519
    @djibysow6519 Рік тому +9

    Vraiment si on dis la vérité je suis fans de Balla Gueye me fils de Balla il est parfaitement raison 😢

  • @AhmedDiawGassama
    @AhmedDiawGassama Рік тому +10

    Bien dit frère tu as parfaitement raison

  • @bassdiokhane1472
    @bassdiokhane1472 Рік тому +14

    Merci beaucoup fis de Balla wakhl degeu môme mn fi né geume mall bopou dé yall nala yalla diapalé bare képp borom Touba Mbaké

  • @abdoulayecamara4716
    @abdoulayecamara4716 Рік тому +32

    Quoi qu'il arrive vous êtes des frères ❤❤

    • @sidyahmeddiop3207
      @sidyahmeddiop3207 Рік тому +2

      Lolou wakha tougnou ko.. Mais Bg2 Lim def Dou yeufou Goor. nit amoUL loudouL biseum..

    • @coeur2lion38
      @coeur2lion38 Рік тому +1

      ​@@sidyahmeddiop3207déléne wah nit deg frére bo hamni hamoul sa boutou keur noumou mel 😂😂😂

    • @biradiop2571
      @biradiop2571 Рік тому

      Vraiment

    • @lampfall1372
      @lampfall1372 Рік тому

      ​@@sidyahmeddiop3207bou nieuwoule naka wo mo geuna rafete

  • @bestcontentsSN
    @bestcontentsSN Рік тому +64

    Iow mom so wakhé rék y'a problème. Ndax la plus part du temps do siissou man, nitou kessé nga. Courage boulko topp diégalko 😎

  • @AwaKonare-tj2ox
    @AwaKonare-tj2ox Рік тому +17

    Courage champion ❤❤❤❤❤

  • @buurlofficiel4354
    @buurlofficiel4354 Рік тому +30

    mom da sonnou si mbeurou guediawaye yii nieuppa wara nieuw sou khewleiii courage mbeur ioe diam rk ngay aame gueumeul sa bopp

  • @khadimdiop9457
    @khadimdiop9457 Рік тому +12

    Tu as parfaitement raison mbeur❤🎉

  • @AhmadaJadid_Diop
    @AhmadaJadid_Diop Рік тому +72

    Non vraiment Balla khoulo naa beu tayi ndakh mom saga nagnma beu tayi mais Fils de Balla a parfaitement raison. Nit kounek seu biss ngu am beurki dembo ndiaye ngu demci nganalei waydiour boy niang nieup nane lii lou nice leu tay fils de Balla demaloko tei nagn wakhantei deug Ngentei mo eup priorité nganalei makka temeri diouni yone, Fils de Balla ak Thiatou Daouda Fall sougnouy wakh dagay sentir ni gnii Balla lanioy noyéé. Vraiment Balla je serai avec toi illa yawmidine mais defaratal seu togay beurki demb ngu takhaw nane lamine golo mounouma diangal dara même boudé deug leu tei nieup xamnagnko dafa am lou wakhouwoul, tay aussi acte bi rafetoul, kougn tekci kanam dey moytou dih wakh waleu dih def lou meune merlo gniko djiteul. oufatal boy yi kou khewlei ngu demalko kou am combat ngu kharci seu tankou toubey niko lac2 dih défé, mais chaque jour Balla bou yagué nak ligniouy wakh done deug gnileu beug rouss. A un moment donné tamit amone ngu problème ak niom famille Aziz Ndiaye ci histoire niak Koleuré commencé wone am khaliss rk dih def loulleu nékh tak diabar, niak respecter entraînement, d’ailleurs seu problème yeup période bobou leu commencer . Nitki nak soko beugué deug doko gaw bayi tei lolou moniou dal ci ioe, dagn leu beug. Mais nekal niiit ishh, yay mak mais boul khar kéneu dilene dioubolei woko ngu diégalou, ngu khol noum gueune gaawei ngu dem setiko def bèneu geste, wakhal bouri mou préparélko valise😂😂😂 diamneh nioy. Dagnlaa beug torop mais ioe daga réglé woul.

    • @Dr.D.GarfilldDavis
      @Dr.D.GarfilldDavis Рік тому +4

      Mais yaw li lanla si commentaire

    • @mansourseye7810
      @mansourseye7810 Рік тому +3

      Sa livre lire na 5 pages incha allah dina terminé 20 pages yi demain

    • @Papisco.sall.
      @Papisco.sall. Рік тому +1

      @@mansourseye7810sérieux wo😂

    • @Justin-Lo.
      @Justin-Lo. Рік тому +2

      😂😂😂bien dit mon cher @swartnwar916

    • @diawlayendao3791
      @diawlayendao3791 Рік тому +3

      Commentaire bou toleu ni meusumako guiissss😂 mais quand même lerna et amna cohérence et deug rek nga wax

  • @DiakhateAmsa
    @DiakhateAmsa Рік тому +5

    Merci fils de balla❤❤

  • @ousaineydanso3313
    @ousaineydanso3313 Рік тому +8

    Am a real fan of Balla Gaye2 but what this guy said is true he really need to stand this boy

  • @tvcodendiayematarelsdaroua7668

    Merci beaucoup fiésdié bala

  • @ousmanesarr8279
    @ousmanesarr8279 Рік тому +1

    Merci beaucoup frère

  • @IbrahimaNdiaye-jj8gu
    @IbrahimaNdiaye-jj8gu Рік тому +28

    Courage geum sa bop fils

  • @mamadouniangniang8236
    @mamadouniangniang8236 Рік тому +8

    Fils de balla machllah 💯💯🇪🇦🇪🇦

  • @mameabdouthiam1740
    @mameabdouthiam1740 Рік тому +31

    Merci beaucoup ❤❤❤

  • @amadouba4254
    @amadouba4254 Рік тому +7

    Courage aziz ❤

  • @talibeserignebabacarsy3055
    @talibeserignebabacarsy3055 Рік тому +4

    Courage yalla bakhna

  • @petersept4334
    @petersept4334 Рік тому +81

    Donnez et ne jamais attendre en retour c'est une leçon de vie.sinon ne fais rien du tout et tu auras une vie paisible c'est tout.

    • @dallavili5266
      @dallavili5266 Рік тому +3

      Lou ler nga wakh broski ✌️

    • @jazakafall8305
      @jazakafall8305 Рік тому +2

      Wax nga lou diafé saway!!! Yeug yeukoy fay

    • @edilsoneddy3348
      @edilsoneddy3348 Рік тому +1

      Je suis d’avis avec toi. Mais Sénégal lagnou nek nous avons nos propres réalités.

    • @Lambfiteu
      @Lambfiteu Рік тому +1

      Yaw wakho bii dara

    • @ibrafatyndaw9891
      @ibrafatyndaw9891 Рік тому +12

      Saway ki d'après nimou wakhé kharoul dara si balla gaye mé dafa rafét niit boula yeugué dila safo gua yeuk khana sakh mou woko téléphone ndakh empêchement dafay ame boy . Balla gaye nimou mél ak fils de balla mélo koo ak boy niang tée la balla gaye déem ba pikine si nganalé gnom boy niang bi. Nagnouy atée deugue tée yalla takh

  • @ousmanesarr131
    @ousmanesarr131 Рік тому +7

    Vraiment tu a raison

  • @djimsow6895
    @djimsow6895 Рік тому +33

    Vérité absolue

  • @omarfadera5194
    @omarfadera5194 Рік тому +5

    Je suis fans de Balla gaye mais le gars a parfaitement raison ♥️

  • @cheikhounagueye6291
    @cheikhounagueye6291 Рік тому +4

    Ndaysan😢
    Sama khol toyna❤

  • @sambaba683
    @sambaba683 Рік тому +5

    Fils de Balla grand champion machallahh

  • @faty1353
    @faty1353 Рік тому +12

    Fils de balla kou bakh nga t am deugu nak ms rero amoul niak wakhtane mo am yalla baxna bilay mou wowone la sakh mo guenone 🙏🏼🙏🏼🙏🏼

  • @ThiernoWakana-c7y
    @ThiernoWakana-c7y Рік тому +23

    Merci ❤❤❤

  • @aladjitoure1269
    @aladjitoure1269 Рік тому +6

    Du courage champion ❤

  • @diopmassame8289
    @diopmassame8289 Рік тому +5

    Machalla fils de balla kadouyi amna solo vraima nitt kou degou nga bo ware wakh deug wakh ko je sw fier de toi mbeur yi mak yi danio wara fonke niouy sonou si niome

  • @Mbt.-_
    @Mbt.-_ Рік тому +5

    Vérité absolue fils de balla balla vrai Defean la dou nitou dara Dmrm la 💔🤦🏽‍♂️

  • @Omar-vy5mt
    @Omar-vy5mt Рік тому +2

    😢 tt Guediawaye est d'arrière tw ❤

  • @yilebaba6565
    @yilebaba6565 Рік тому +10

    Tu as raison fils de balla ! Khamouma kane dei wayé yaw kou takhawou balla gaye 2 ngua . A chaque fois que je le voyais je te voyais à ses côtés ! Balla Gaye nelaw naa vraiment 😢

  • @thiernondiaye5126
    @thiernondiaye5126 Рік тому

    Yalla yalla Def diame amine courage

  • @alassanedieng2657
    @alassanedieng2657 Рік тому +39

    Vive sonko ❤

  • @fatoukounta
    @fatoukounta Рік тому +5

    Deugue nehoul dh mais yalla bahna ioe fils de Balla ❤

    • @sumocarterdiop8609
      @sumocarterdiop8609 Рік тому

      Aziz c simon ton frère lidiantil visa usa nga déme déf d,autre sport lamb ammoul ndiarinn sénégalaise yi am bop bayinaniou lamb boy

  • @ibrahimakeita8888
    @ibrahimakeita8888 Рік тому +6

    Il parle avec le cœur Balla daka warra tewal

  • @Ndarguedjtv
    @Ndarguedjtv Рік тому +5

    Je suis fans de balla gaye ms grand deugue rék nga wax billahi balla wérénga

  • @biramesarr4381
    @biramesarr4381 Рік тому +3

    Tu as parfaitement raison Balla dou dara bilay

  • @djimbaniang2190
    @djimbaniang2190 Рік тому +4

    Thieye Sénégal pourtant fils de Balla sa combat passe banga dane Ball gaye dafa contan😢😢

  • @yorokante777
    @yorokante777 Рік тому +3

    Bravo Luttetv 👌

  • @cheikhfall4729
    @cheikhfall4729 Рік тому +1

    Waw billahi lolou mom deug leu mes esseil de le comprendre RK boulen khadial sen diguente seytané man jsui de Pikine 💚❤️

  • @seynitoure7092
    @seynitoure7092 Рік тому +42

    Franchement je suis émue fis de balla d’où yone Bilay

  • @Elhadji2187
    @Elhadji2187 Рік тому +15

    En fin un lutteur honnête Balla gaye sougnou mbeur la mai vrai samba alar moy mom lolou damako yague wah
    Balla gaye gnikay doungourou rek la ham yaffi meun ya eup dolé Youssou ndour père Balla balahi dafa meunoul wah rekk mai moy lolou

    • @diaaaa9607
      @diaaaa9607 Рік тому

      Bilay balla gaye dof la 😢😢

  • @ModouMbacke-s9g
    @ModouMbacke-s9g Рік тому +9

    Wax nga deugue dh❤

  • @jonkonggassama4486
    @jonkonggassama4486 Рік тому +2

    Cest vrai Fils de Balla 👍😭

  • @AmadouDiallo-vh9qo
    @AmadouDiallo-vh9qo Рік тому +4

    Tu as raison

  • @salioundiaye5763
    @salioundiaye5763 Рік тому +7

    La légende

  • @abdoucoly8278
    @abdoucoly8278 Рік тому

    Champion Ga Ménga amme Lou éppe balla loumou amme fit bagui sii iow Guéme Guéme biegui SII iow bonne continisation fils de balla 🤌🏿✌🏿

  • @moussacisse9259
    @moussacisse9259 Рік тому +7

    Je suis fans de balla Gaye
    Ms fils de balla yalla nala yalla défal diamm
    Balla Gaye damako diépie ba mounou touma khol ay video me blh

  • @mamadoucisse3728
    @mamadoucisse3728 Рік тому +2

    Tu as parfaitement raison bilahi

  • @gueyelabsolu5889
    @gueyelabsolu5889 Рік тому +23

    Même sii Mane afair bii Diaxall Nama trop pourquoi Balla nieuweul ak Niko Fls De fonkè Balla Mom Dou Nith vrement 🥹nila Défone Éltone Yayam Ganiou Nieupou nieuw Dialysy Élton Mom Démoul Balla thi bopame Monoull nith vraiment respecter Woul ay Niteum thiotou nayam Balla Gay 2 Diaroul rayanté Fonkoull ay Niteum Dei 😒Balla Gay 2 conla 🥹

    • @milkmilo4082
      @milkmilo4082 Рік тому +2

      Balla gay con la mais yow yak moma yam loufi diar saga yow bou yébo gnou woutal la ay comprimé

    • @veroniquenatack7392
      @veroniquenatack7392 Рік тому

      @@milkmilo4082*Vraiment deff na erreur mei tmt diaroul wone saga yi BG je l’aime bcps mei wéré na bi yone*

    • @milkmilo4082
      @milkmilo4082 Рік тому +2

      @@veroniquenatack7392 effectivement balla si bopam kouko wakhoul da dioum nafék leu yow naka ga meuné déme si boy niang lolou bouko son poulain gissé emplus de ça gnewoul si son baptême dafa gnaw balla da wara balou akk rectifié wou publiquement

    • @veroniquenatack7392
      @veroniquenatack7392 Рік тому +2

      @@milkmilo4082 *Nonou kay la wara defff bilay walay ndakh fils de Balla ngoor rk lako yagueu djii donc rafettoul mou am bissam téwoufa té mouy téw thi bissou gnénéne nitt momm bissam rk la am bokoko khébalé rk khebb guako nako wo wala mou déme fa djiégualou mérone na sakh thi interview lirou bi mei fils de balla wakhna deugue*

    • @milkmilo4082
      @milkmilo4082 Рік тому

      @@veroniquenatack7392 niga défe d c'est comme ça faral nitt boumou takh bou défé erreur doko reconnaître legi nak si balla la désse

  • @bambasindidi4
    @bambasindidi4 Рік тому +2

    Tu ya raison

  • @fatoubadiane754
    @fatoubadiane754 Рік тому +5

    Noooooo balla ma soul nieuw sa keur 😢

  • @ndowbabacar352
    @ndowbabacar352 Рік тому +1

    ❤❤❤❤❤❤ il faut réveiller c'est pas quelqu'un qui beh il faut réveiller il faut prendre ton sommeil il sait pas bon réveille-toi frère

  • @cheikhdiakhate6474
    @cheikhdiakhate6474 Рік тому +3

    Tu as raison champion même s'il ne vient pas il t'appelle

  • @taphabadiane7604
    @taphabadiane7604 Рік тому

    Bilayi 😢

  • @casadinke8215
    @casadinke8215 Рік тому +2

    Tu as raison frérot
    Balla Gueye 2 déçoit bcp

    • @filykamian594
      @filykamian594 Рік тому

      Balla c'est mon lutteur mais franchement parlé il est malhonnête bilahi

  • @amydieng3430
    @amydieng3430 Рік тому +1

    Tu as parfaitement raison

  • @talibecheikhoulkhadiimmbac5652

    Fils de balla champion ngua geumeul sa bopp binguay khalé batay Gora pata lala nieupp khamé té batay yénangui andeu kon yaw goor deugg ngua yalnanguen degg roi des arènes inchalah

  • @bailandiaye2979
    @bailandiaye2979 Рік тому +8

    un conseil que je te donne champion fi yallah mofi nék geumeul sa bop ak say entrainement nit day am fayda ak foula tu est jeune et c'est votre temps maintenent Balla diékhalna c'est mon lutteur mais c'est fini pour lui boy geumeul sa bop té diéma léck sa weurseuk si lamb ji mo geun

  • @ebrimasusso5394
    @ebrimasusso5394 Рік тому

    You are right bro

  • @falilou869
    @falilou869 Рік тому +12

    Balla c'est la fin tragique mame mom manatou mako khol

  • @moussadiao5603
    @moussadiao5603 Рік тому +2

    Ta parfaitement raison

  • @maragueye354
    @maragueye354 Рік тому +4

    Balla dafa dioum bilay wakh nga degue mom❤❤❤❤❤❤❤

  • @papendiaye1371
    @papendiaye1371 Рік тому

    Merci tua raison

  • @sambatorino8115
    @sambatorino8115 Рік тому +10

    Wakhe nga deugue boye bilahi

  • @moussacisse1509
    @moussacisse1509 Рік тому

    Yalna la yalla same

  • @aboubacarkouyate4102
    @aboubacarkouyate4102 Рік тому +5

    Balla gaye 2 def na lou niaw .. changel tour toudé sa boop domou guediawaye Kessé ❤️🎉

  • @Lastkingmafia2.0-hd7vh
    @Lastkingmafia2.0-hd7vh Рік тому +1

    Metina torp mes yalla bakhna begeunal bilahi yalnal yalla takhwou incahall

  • @tidianesall3124
    @tidianesall3124 Рік тому +15

    Vraiment Rafetoul nit aussi dagay am Coloré Balla keine warouko fo wone djitou

  • @AstouSane-l4q
    @AstouSane-l4q Рік тому

    Merci c'est vrai

  • @mbayefam572
    @mbayefam572 Рік тому +18

    Tu iras très loin nchala

  • @falloutoure8326
    @falloutoure8326 Рік тому +2

    Wallahi wérna ❤❤

  • @FatouThiam-zf4op
    @FatouThiam-zf4op Рік тому +4

    Lou lérr la wakh ❤❤

  • @moussamboup5761
    @moussamboup5761 Рік тому +1

    Bilahi walahi watalahi tu as raison nit Day gorè wlahi khamal sa boop gueum sa boop vas-y frr

  • @fallougueye3368
    @fallougueye3368 Рік тому +17

    Fils de balla yaa nékk sii deugeuh dh vraiment 😢

  • @LaminSam-s8m
    @LaminSam-s8m Рік тому

    Love you 💕

  • @layefall452
    @layefall452 Рік тому +4

    Man fans Balla gaye la mais moy lolou

  • @syllepogba1743
    @syllepogba1743 Рік тому +2

    Champion nga flis guemeul sa bopou té liguey diapou sa bopou té diokh ñpou thieur ❤

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 Рік тому +10

    Vraiment c'est vrai Balla dafa warone gneuw wax DEUG yallah je suis fans de balla gaye danga dioum

  • @PapeDione-l9z
    @PapeDione-l9z Рік тому

    Merci

  • @Robbe-Grillet
    @Robbe-Grillet Рік тому +23

    Je suis un inconditionnel de Balla gaye 2 mais wax deugue yalla dafa def erreur. Na ame grandeur diégalou té diéma rattraper wou.

  • @moussambaye6915
    @moussambaye6915 Рік тому

    Vérité absolut fiss de balla❤❤