Hay😱modou mbaye tire gravement sur aziz ndiaye modou lo moy roi bi force bour et fadam en contre

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 17 тра 2024
  • Спорт

КОМЕНТАРІ • 193

  • @sankoungbodian2845
    @sankoungbodian2845 Місяць тому +35

    Nafeck bakhoul modou lo moy roi point merci modou mbaye

  • @AllaCheveux
    @AllaCheveux Місяць тому +14

    Moudu mbaye DEUG rek nga wakh machallah❤

  • @Galayendao-vf6tx
    @Galayendao-vf6tx Місяць тому +22

    Khalis daye dieunde ngor merci modou mbaye ❤

  • @coubatandine5057
    @coubatandine5057 Місяць тому +11

    Merci beaucoup 10.000 fois Modou mbaye fi yalla reck mofi neck wasalame

  • @MandellaFall
    @MandellaFall Місяць тому +18

    Bour gueweul masta 😢 amo kham kham sa khol di nekh di nakhari Modou lo moy roi 🤴

  • @Abdk0p
    @Abdk0p Місяць тому +17

    Modou lô rék ❤❤

  • @MouhameLo
    @MouhameLo Місяць тому +5

    Modou mbay yalla nala yalla fay bih

  • @user-bs9zt8sw9o
    @user-bs9zt8sw9o Місяць тому +10

    L'hypocrisie c'est pas bon,merci Modou mbaye tu es vraiment digne bilahi père becaye Moy sa papa Macha allah

  • @user-pm2zp8re9k
    @user-pm2zp8re9k Місяць тому +22

    Merci Modou mbaye KO wakhol dégue wakh féné🙏🏽

  • @PapaBarry-cw1vz
    @PapaBarry-cw1vz Місяць тому +7

    Chapeau à Modou mbaye 👌 diam si yene 🙏

  • @cheikhtidianediop6402
    @cheikhtidianediop6402 Місяць тому +5

    L'Arabie Saoudi à battue l'Argentine, mais cela n'a pas empêcher cette dernière d'être champion du monde.

  • @faye6718
    @faye6718 Місяць тому +4

    Machallah Modou mbaye done nga sax baye boul néki nafék com gni deug rek la yallah beugeu diaradieuffff merci mbaye ❤❤❤

  • @bayeratebayerate5893
    @bayeratebayerate5893 Місяць тому +12

    Merci modou mdaye

  • @ousmanesylla2620
    @ousmanesylla2620 Місяць тому +6

    Merci beaucoup moudo mbaye❤❤

  • @MameSow-vp7rj
    @MameSow-vp7rj Місяць тому +8

    Modou lôooooooooo ❤❤❤❤

  • @aliounedia8314
    @aliounedia8314 Місяць тому +3

    Modou Mbaye ioe nittu dëggg gua ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @fatoukasse1089
    @fatoukasse1089 Місяць тому +5

    Ay mak you nafék rek la bagn Merci Modou mbaye

  • @rassoultalibecheikhtidaner9082
    @rassoultalibecheikhtidaner9082 Місяць тому +5

    Modou mbaye fan nala naw nala beugeu nala xalé bou ndaw tim ak magoum dieum dilén wax deugeu fi modou lo moy roi des arène Sénégal modou moy roi soxor baxoul

  • @fatousamb1354
    @fatousamb1354 Місяць тому +6

    Modou lo kesse moy roi des arene du senegal lolou la yalla def❤

  • @leyemouhamed2149
    @leyemouhamed2149 Місяць тому +8

    Naafékh baxoll vraiment

  • @mameousmanedeme6895
    @mameousmanedeme6895 Місяць тому +3

    Par la force MODOU LÔ moy Roi mu nékh lén mu nakhari lén point.

  • @SauraDiop
    @SauraDiop Місяць тому +7

    Amna niou yagua wakh ni mod'lo gnikoy khekhé dafa beuri comme une certaine sokhna Ada mai tay Aziz Ndiaye dafa firné ligne done mai Modou Moy roi nkh nakari inchallah

  • @ShiekhjobeTijan
    @ShiekhjobeTijan Місяць тому +3

    Modou lo rek laño gem ta diko Topo ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ Yalña yalla defal ko jama AK Sallam

  • @modousene2271
    @modousene2271 Місяць тому +7

    Bala guaye 2 dou moussa nek comme avant lambdjie c'est Modou lo le technicien

  • @MohamedabdallahSeck
    @MohamedabdallahSeck Місяць тому +2

    Merci Modou mbaye Domi thiagua yii ay Domi khadieu lanieu

  • @ranebykawsara8877
    @ranebykawsara8877 Місяць тому +6

    Modou Mbaye ses le meilleur entre Bour et fadam

  • @bayeratebayerate5893
    @bayeratebayerate5893 Місяць тому +11

    Aziz Ndiaye dafa katt ndaye reww

  • @pourlepeuple2516
    @pourlepeuple2516 Місяць тому

    Modou Mbaye est pertinent, objectif, conséquent et impartial.
    Machallah, le professionnalisme brille en lui

  • @SerignePlayestore-pg5eu
    @SerignePlayestore-pg5eu Місяць тому +6

    Modou lo d'où sama mbeure mais moye roi deugeux nékhoul

  • @user-qw4ny7lx4d
    @user-qw4ny7lx4d Місяць тому +6

    Modou lo rek

  • @TheBandafall2003
    @TheBandafall2003 Місяць тому +12

    Siteu et modou lo le roi ne devrait pas être en jeux comme ça se fait ds tous les sports de combat y’a pas de structures ds cette lutte du n’importe quoi

  • @momidiop7878
    @momidiop7878 Місяць тому

    Merci Modou Mbaye Guemigne bou wakhoul deugg rekk fenn 👏👏👏👏❤️❤️❤️

  • @OMARKASSE-np2iv
    @OMARKASSE-np2iv Місяць тому +5

    Aziz ndiaye dang koy guiss rk kham ni da sokhor mom ak balla yeuppa bone

  • @AliounebadaraGassama-or4op
    @AliounebadaraGassama-or4op Місяць тому +3

    Bayi lènn modou lo Paré n'a thi dieul revanche wala diokhé revanche

  • @saerdiagne8198
    @saerdiagne8198 Місяць тому +1

    Bour guéweul bayil nafékh lolou baxoul fikéne meunoul dane gnépp Modou lô rois par force en plus diadieuf Modou mbay nite dangay deugou ✌️✌️✌️✌️

  • @diopmar6382
    @diopmar6382 Місяць тому +3

    Aziz Ndiaye ne respecte le monde de la lutte am na khalice louco nekh def domarame bour ak fadam vrai nafek nguen

  • @bayeratebayerate5893
    @bayeratebayerate5893 Місяць тому +5

    Aziz Ndiaye dafa berri ndaye wakh mouou lo moy sean baye

  • @fallouniass-sj7rd
    @fallouniass-sj7rd Місяць тому +2

    Ak déféte bii di nieuw nak wadial lén ko mouye 7 déféte

  • @user-tb5ni9xf8f
    @user-tb5ni9xf8f Місяць тому +3

    Les 2 emissaires de aziz en mission commandè

    • @10gitallewolof30
      @10gitallewolof30 Місяць тому

      Kene xamoul ay kilifa laniou wala aye Wayne kate

  • @AmadouNdoye-vl8np
    @AmadouNdoye-vl8np 12 днів тому

    Merçi modou mbaye sa pape yar nale si degue

  • @user-lq3ns7yx4q
    @user-lq3ns7yx4q Місяць тому

    Modou lo ❤❤❤❤❤❤❤❤🎉

  • @CheikhNdaw-qb1rm
    @CheikhNdaw-qb1rm Місяць тому +2

    Fadam khôl bi Sed trop kou d'accord lalal ❤❤❤

  • @maynadiouf7543
    @maynadiouf7543 Місяць тому +3

    Bour dele wakh si temps

  • @matarthiam9572
    @matarthiam9572 Місяць тому

    Modou mbaye invité len Assane Ron un bon analyste de la lutte ❤

  • @Abdk0p
    @Abdk0p Місяць тому +3

    😂😂😂😂no bour Day fontou

  • @sasonevoice9356
    @sasonevoice9356 Місяць тому

    Contane na ci yenn nyep 🤣❤ analisii nekhna rafetna

  • @GueyeTV-zu6ir
    @GueyeTV-zu6ir Місяць тому +1

    Modou mbaye yaye wah katou ndeugue

  • @lansananiang9506
    @lansananiang9506 Місяць тому

    je suis d'accord MODOU

  • @BassirouKa-vi8cp
    @BassirouKa-vi8cp Місяць тому

    Bour gueweul ak fadam ay seytané modou lo moy roi merci modou mbaye niut deye wakh degue te yalla takh

  • @lahaddione1814
    @lahaddione1814 Місяць тому

    Merci modou mbaye tu as parfaitement raison

  • @ranebykawsara8877
    @ranebykawsara8877 Місяць тому +3

    Bour tu dois savoir le combat de modou Lo et balla gaye lors de cette combat ses pas un combat royal en se moment !!! Le seul roi des modou Lo

  • @AliounebadaraGassama-or4op
    @AliounebadaraGassama-or4op Місяць тому +3

    Lép lolenn khalate ba ték modou lo rombeu n'a fofou

  • @adandoye3759
    @adandoye3759 Місяць тому

    Walahi Azim Bilahi Balla gaye 2 moye sama mbeur meussou ma faral Modou lô mais soyons sportifs Modou lô est le roi incontestable de l’arène Aziz bayil sa thiaxane yi té nangou dogal Wassalam

  • @user-nm8es7dl3g
    @user-nm8es7dl3g Місяць тому +2

    Aziz sa Mbeur mi minoul courone yéneu niar yèna yameu lëuf mo léneu sonal modou raw naléne

  • @biramesarr1601
    @biramesarr1601 Місяць тому

    Balla Gueye est le premier roi qui à concédé 2 défaites avant d'être roi( issa pouye, Eumeu)

  • @mouhamedmboup6991
    @mouhamedmboup6991 Місяць тому +2

    Modou lo kassé 🤞🏿

  • @sankoungbodian2845
    @sankoungbodian2845 Місяць тому +3

    Adouna yallah mo ko mome

  • @GueyeTV-zu6ir
    @GueyeTV-zu6ir Місяць тому +1

    Modou yaye wah katou deuge

  • @modousene2271
    @modousene2271 Місяць тому +2

    Fadam ak bour amounou xam xam waxewounou xell mou sel bopou bou reuy lanouy waxé

  • @thiernowade5769
    @thiernowade5769 Місяць тому +3

    Aziz.kou.tégeul.ndeyamla. balla.la.beugeu.deff.roi. parr.forsou.ngirr.éntréém. na.niappou.ndeyam.feulé

  • @GueyeTV-zu6ir
    @GueyeTV-zu6ir Місяць тому +1

    Modou lo AK balla diouniou moussa beuré wate

  • @OusseynouSeye-yi2ro
    @OusseynouSeye-yi2ro Місяць тому

    Aziz Ndiaye dafa nékh bilahi

  • @AFMPGMboup
    @AFMPGMboup Місяць тому +3

    Modou a terasse eume sene ki terasse deux foi balla boye niang a terasse balla ya koi encor

  • @kf8674
    @kf8674 Місяць тому

    Modou Mbaye a raison

  • @HabibLome-jx8cv
    @HabibLome-jx8cv 23 дні тому

    Bour khana danga am lo diapal Modou lo
    Eumeu sene moy sama mbeur mais Modou lo moy roi

  • @MalickSeye-ef6lc
    @MalickSeye-ef6lc Місяць тому +1

    Modou mbaye goor ❤

  • @ShiekhjobeTijan
    @ShiekhjobeTijan Місяць тому

    Waw modou mbaye wax Sa khalat la de

  • @ndiagaka8912
    @ndiagaka8912 Місяць тому

    Fadam mi mo geune Kat ndeyam Modou lo rek la bagne day défendre Aziz nakh dakoy diokh xaliss

  • @ndiogoufall9571
    @ndiogoufall9571 Місяць тому +1

    On évalue toujours les derniers indices pour trouver les données exactes ou approximatives. Les derniers vainqueurs de Balla Gaye 2 et Tapha Tine sont Boy Niang 2 et Ama Baldé. Alors Modou Lo les a battus récemment, donc il est le plus légitime à être le roi des arènes jusqu'au jour de sa défaite.
    En effet, L'empereur c'est Yekini, l'invincibilité durant 15 ans. Aziz Ndiaye est un vendeur qui veut organiser et gagner de l'argent pour les prochains combats chocs😂😂😂😂

  • @user-yn6yj9zy9f
    @user-yn6yj9zy9f Місяць тому

    Xaliss touss Aziz khaliss lanouy diay wayé sa data yaye modou lo kassé roi des arènes😅

  • @binetoufofana2428
    @binetoufofana2428 Місяць тому

    love u modou mbaye

  • @HametSall-rw1hw
    @HametSall-rw1hw Місяць тому +2

    Bourr guewel sa nounou ndeye

  • @takhfoulousetv6729
    @takhfoulousetv6729 Місяць тому

    iaw do ame daleu danga sayetane danga di makk rekk wayé kone ma wakhla lou garawe nga bayi sounou modou nangoule dogale modou moye roi❤

  • @bayemo4147
    @bayemo4147 Місяць тому

    Modou mbaye yaaa feetei khalé waayé yaaa yor tahawaayou kilifeu thi diotay bi❤ Diadieuf!! Wah deug té yallah tah rek!!!

  • @NdiagaDieng-xo8gb
    @NdiagaDieng-xo8gb Місяць тому

    Modou mbaye merci beaucoup ❤

  • @serignemourtallamboup5715
    @serignemourtallamboup5715 Місяць тому

    Probar sapaalii thioucouliii 😂😂😂😂😂

  • @basselabdou9891
    @basselabdou9891 Місяць тому

    Fadam môme moy radiem wayé bour yaye sayetané bi modou mbaye moye boparbi😂

  • @sophrotall8105
    @sophrotall8105 Місяць тому

    Bour Modou lo moko safoul dafay fegn si ay wakham

  • @fallouniass-sj7rd
    @fallouniass-sj7rd Місяць тому +1

    Yén loudoul sokhor défo lén ko ay nafékk nguén rék téranga bi niou deukeulé sénégal nioun waa sénégal niép kham nagne ni amoul ndakh lékanté mofi am yakhalanté mo fi am kon ana téranga dji nioun nitte niou niouul gni nio sokhor ni gnou mél amoull kou ko mél si adduna de tous les continents nak

  • @profcoly6085
    @profcoly6085 Місяць тому

    Kholal khourou fadam yi noumouy marqué si toubéy bi 😂😂😂

  • @chamousman2726
    @chamousman2726 Місяць тому

    Buur denko fai pur mu wakh ngir combat modou lo ak Balla

  • @serignedieng-vh4zv
    @serignedieng-vh4zv Місяць тому

    eumeu séne moy sama mbeurr mai mod lo moy roi kone légi Aziz foye calasé eumeu séne mi dane bala gaye 2 foi soi logique waye

  • @tallacisse7797
    @tallacisse7797 Місяць тому

    Aziz dh bagne modou lo rek moko diap. Modou lo dou mbeurr bi subir la loi des promoteurs

  • @ShiekhjobeTijan
    @ShiekhjobeTijan Місяць тому

    Mensour ba defal lo men Bola keñ dogal ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @papelo9893
    @papelo9893 Місяць тому

    Pourquoi roibi wakhouniouthie ba modou lo dieulko niou commencer eundi polémique ah 😡😡😡😡

  • @ibrahimaseck1000
    @ibrahimaseck1000 Місяць тому

    Bour sestanega yak fadame Aziz dafa khalis

  • @elhadjiabdoulayembenguecis3590
    @elhadjiabdoulayembenguecis3590 Місяць тому

    Modou Moy Roi Si Ayy lokho Lako dieulé Forouko da Farlou

  • @cafarsdesinfection-desinse7804
    @cafarsdesinfection-desinse7804 Місяць тому

    Nafekh yagui fégne rek.. modou lo moy roi des arènes lolou leu yallah doguale

  • @NdiagaDieng-xo8gb
    @NdiagaDieng-xo8gb Місяць тому

    Fadam ak bour geuweul ay nafikh lanio

  • @thiernoba5091
    @thiernoba5091 Місяць тому

    Modou mbaye lou lerr la wax Aziz naniou mey diam modou lo seine baye leu Aziz momeu nou way go

  • @user-fv3tp4ow8v
    @user-fv3tp4ow8v Місяць тому +1

    Modou mbaye ya dis gor mala beugue

  • @user-il6ej2hb6q
    @user-il6ej2hb6q Місяць тому

    Empereur ay tiakhane la, deal la pour indi wate balla gaye 2. Fi roi des arènes moy deug.

  • @kf8674
    @kf8674 Місяць тому

    bilay Aziz na nopaleku meunul fexé ba fokhati roi bi ci ay couronne yumuy créé.ku beuga nek roi faw NGA Daan Modou te pour ngen beuré faw NGA niane Koko ci ndiek.ci ndik dh

  • @elhadjiabdoulayembenguecis3590
    @elhadjiabdoulayembenguecis3590 Місяць тому

    Merci modou Mbaye lou Wer nga wakh té lér Bala bi miy Done Roi Beuré woul Revanche si défétou eumeu La tok Roi ba Danou Dieulate KO Danou

  • @abdoulayediop9331
    @abdoulayediop9331 Місяць тому

    Bour nioune wakeur Modou lo niougui lék ba sour Di nane ba mandi ndakh nioune yalla rék laniou yakar té lo ndiogué woul thi yalla manoul thi Modou Dara té Manou léune moume dara

  • @AlyseneSene
    @AlyseneSene Місяць тому +1

    Elhdji pobarou dom 😂😂😂

  • @SohibouLo-mi3ko
    @SohibouLo-mi3ko Місяць тому +1

    Bour mi dou gattt

  • @fallouniass-sj7rd
    @fallouniass-sj7rd Місяць тому +1

    BAlla 2 fois la dane modou mai 2 fois la ko eumeu dane té modou moh dane eumeu 2fois modou moh dane boye niang té boye niang dane na balla modou moh dane Issa pouye té Issa pouye dane na balla balla dane ko légui na niou khool lolou yén si bopam yénadoul diouk si tatou kouy dém danguén sokhor nangou lén li yalla dogual

  • @MoustaphaFadiga-jy3dr
    @MoustaphaFadiga-jy3dr Місяць тому

    Merci Modou Mbaye Aziz Dafa Sokhor li Modou nekeu Roi molen méti

  • @barkhama
    @barkhama Місяць тому

    légui modou lo mi dane eumeu séne mi dane balla 2fois ak boye niang mi dane balla nak doléne si wakh 😂