JAZBOUL MOURIDE 26 01 2021 CHEIKH IBRAHIMA FALL ak ZIKROULLAH (BAYE ADAMA SARR)

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 6 лют 2025
  • Restez scotchés au programme de Jazboul Mouride TV.
    Merci de liker et de vous abonner sur nos différents supports :
    1) #UA-cam : / jazboulmouride17
    2) #Instagram : www.instagram....
    3) #Twitter : Ja...
    4) #TikTok : vm.tiktok.com/...
    Jazboul Mouride TV, la chaîne au service de Mame Cheikh Ibrahima Fall!

КОМЕНТАРІ • 515

  • @mamadoudiakhate1580
    @mamadoudiakhate1580 2 роки тому +39

    Vraiment cet homme est extraordinaire.Non seulement
    il est tres eloquent mais il est due d'une memoire fantastique.Pour cela Baye Adama est un grand alime d'une valeur inestimable. En plus de il est vraiment un Sage. Que Dieu le benisse.Amine!

  • @mouhamadoubambambengue8421
    @mouhamadoubambambengue8421 4 роки тому +19

    Thiey Bay Adama
    Goudall fane bay boy
    Makk bou maggue
    Kou diara topato bou bakh
    Yalla nala yalla goudal sa fane bou bakh!!
    BAY BOY GOUDAL FANE BARKE CHEIKH IBRA
    PATRIMOINE DEUGUE LA YOOR

  • @abdoulazizdiagne5276
    @abdoulazizdiagne5276 4 роки тому +13

    Cette emission meritait un plateau special,noce bi neex na. Baye Adama yague fi teu wer !

  • @saliougueye8443
    @saliougueye8443 4 роки тому +16

    Baye adama sarr yalla na goudou fane si barcke mame cheikh ibrahima fall

  • @ibrahimandiaye8214
    @ibrahimandiaye8214 4 роки тому +12

    Baye adama Sarr yalla nafi yague téweer barker mame cheikh ibra fall

  • @ousseyenoudiop5315
    @ousseyenoudiop5315 4 роки тому +2

    Baay Adama Sarr sama xaritt bii nitt Koubaxx tei woyof lol kou nitt gnii oumpleii Dieum djii di Baye Adama Sarr. Yalla Na Yalla goudeul sa Fann mayla ak Werr Sarr🙏🙏❤️❤️😍😍

  • @elhadjiousmanegueye3277
    @elhadjiousmanegueye3277 4 роки тому +7

    DIEUREDIEUF Mashaa'Allah Baye Adama Sarr Borome Touba Ak Mame Cheikh Ibrahima Fall Bègue Naňou Yagg Fi LOLL Tè Ande Ak Weer Gueureume Serigne Alioune Ak Serigne Mamoune Ndao Takhawou Bi Rafetna

  • @abdoulayediop1175
    @abdoulayediop1175 4 роки тому +7

    Ceey Baye Adama !
    Yalna Yallah goudeul saw faan barkep Mame Cheikh Ibrahima Fall Lamp.
    Jeureujëuf ti ndankh ni fi geuneu yaag mouy geun thi keup kouy roye thi Sidy Birahim Fall Aboridial.

  • @amdykharma4871
    @amdykharma4871 4 роки тому +1

    Diereudieuff mame cheikh ibrahima fall serigne adama sarr yalla na la yalla yokk fane wi ak were

  • @abdoulahatsall9660
    @abdoulahatsall9660 4 роки тому +4

    Ayyy waayy serigne mamour yalnaguenn am diamm bay adama sarr bay mousttapha sek ak bay ndiana gnu takh ma khamm kouy mame cheikh tee beg ko loll yallna sen diam yagg. Di gnanal bay diana bu bakh

  • @bambahann5573
    @bambahann5573 4 роки тому +16

    Baye adama sarr yalla nafi yagui te and ak werr🙏🙏 diadieuf alione badara ndir diadieuf mamour ndaw baye fall

  • @ndotheking5995
    @ndotheking5995 4 роки тому +21

    djeureudieuf baye adama. Goud fane rek ak weur! si barkè mame sèkh

  • @moustaphakhalifa1352
    @moustaphakhalifa1352 4 роки тому +1

    Machalla waxtan bi kawé neu lol yalla nagnou fayal Serigne Touba cheikh Ibrahima fall
    Numéro Serigne Mamour ndao la yitéwo

  • @ahmadinasaliousour9615
    @ahmadinasaliousour9615 4 роки тому +2

    Baye adama yalla na yalla wereul thieur yi goudale faan wi barki male cheikh ibrahima fall

  • @serignefallou8198
    @serignefallou8198 4 роки тому +4

    Setetete nexna lol machala. Baye Adama adji nako nak, niveau la ladj deug. Yalna yalla goudal taxawayam

  • @dikhasalikhate234
    @dikhasalikhate234 2 роки тому +1

    Machalla mame boye yague fi looooool te wer wakhtane bi amna solo trop dieuredieuf serigne touba khadimoul rassoul serigne mountakha yalla nafi yague looooool te wer mbacke balla aycha diarama mame cheikh ibrahima fall lamp baboul mouridina ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤

  • @papefall6167
    @papefall6167 4 роки тому +9

    Baye Adama sarr Yalla na ga am geuremal serigne touba amine si barcép mafatihoul bichri

  • @thiamasthiam122
    @thiamasthiam122 4 роки тому +7

    Baye Adama yalna yalla goudeul sa fane amine yaraby

  • @makhtarsanguediop4969
    @makhtarsanguediop4969 4 роки тому +24

    6,30 minute danou na bou yag si sikar si bou yagg fall baye adama sarr yalna yalla goudeul saw fan tai may la werr amine diarama cheikh ibrahima fall

  • @bayhatouridwanetvridwanetv4554
    @bayhatouridwanetvridwanetv4554 4 роки тому +1

    Ah begue tina wa Jazboul mourid
    Sr mamour ndiao sr aliou badara

  • @serigneibrahimathioune1460
    @serigneibrahimathioune1460 4 роки тому +47

    Barke cheikh ibra dama beug baye adama té yalla takh ak xam xam bi 🙌

  • @husjbsusb7925
    @husjbsusb7925 3 роки тому +2

    Serigne mamoun nadao dama sop ngir chiekh ibrahima fall bilahiiiiiii

  • @milofall4546
    @milofall4546 4 роки тому +3

    Baye adama yallanako sa borom defal tawfex ak taysir ak fan you yatou si barkei cheikhoul khadim ak sa mame Cheikh Ibrahima fall amin

  • @fallloumbow2963
    @fallloumbow2963 4 роки тому +2

    Ndeysane xol sédd na si barké Mame Cheikh Ibrahima fall notre fierté notre professeur

  • @Bayfall123
    @Bayfall123 10 місяців тому

    Ken dou mam chiekh Ibrahim fall dierefe seringe touba khadim rasoul diarama mam chiekh Ibrahim fall yalla nanga fi yagui lol thie wer thie barkep seringe touba khadim rasoul bay adama sarr ❤❤❤❤❤❤

  • @alyndiaye7228
    @alyndiaye7228 4 роки тому +2

    Yallana nafi baay Adama Sarr Yagg loll té And ak Wér ak wérlé Barkep Mame Cheikh Ibra Fall. Ci Darazay Ku Ted Ki. Amine

  • @sdamekimanboromleppayebakh8605

    Koudoull mom Mame cheikh Ibrahima fall gonéga

  • @bambaparforce4
    @bambaparforce4 4 роки тому +5

    Baye Adama Sarr yalla nalafi sounou borom bayiwat ay ati ati at barkép mame Ibrahima fall 💖💖💖💖💖

  • @bayeamdyfaliloundiaye4313
    @bayeamdyfaliloundiaye4313 4 роки тому +10

    Thiey baye Adama Yala nafi yag té werr té magui mame chera fall yi nioko yarr aka oyoff té diss gann ❤️✊
    Namone nanoula loll baye adama

  • @khadimtalla1687
    @khadimtalla1687 4 роки тому +1

    Thiey baye adama yalla na fii yague tee weer si barké serigne touba mame cheikh ibrahima fall lampe baboul mouridine

  • @ndiobasamb7153
    @ndiobasamb7153 4 роки тому +5

    Bay Adama sarr yalla nafi yageu lool te wér barké cheikh Ibrahim fall🙏🙏

  • @moustaphadiop7687
    @moustaphadiop7687 2 роки тому +1

    Leup Serigne Touba la motakh Dieuredieuf Serigne Touba rék .

  • @filmmovie9326
    @filmmovie9326 4 роки тому

    Thieye baye adama sarr
    Yalla na yalla gudal fan wi

  • @badarasane
    @badarasane 4 роки тому +5

    Mani fi rek la deh baye adama sarr dieureudieuf Yague yokal wereul si barke mame chiekh ibra fall baboul mouridina

  • @aliousarr8703
    @aliousarr8703 4 роки тому +6

    Mame cheikh ibrahima fall bakh foula goor di dabee

  • @moussafaye6137
    @moussafaye6137 2 роки тому

    Dieureudieuf mame cheikh ibrahima fall LAMPE baboule mouridina

  • @d.abdoul5103
    @d.abdoul5103 4 роки тому +48

    Thiéy Baye Adama yague filoll téwér ci Barkéb Cheikh Ibra fall 🙏🏽🙏🏽

  • @astougueye6473
    @astougueye6473 4 роки тому +1

    Yallah naleu YA Rabi Fay yiww tchi Barké Borom Touba
    Baye Adama Sarr goudeul fane
    MASHA ALLAH plateau bii yeup

  • @ndackabdou
    @ndackabdou 4 роки тому +7

    Bilahi sama xol sedd na bima guisé baye adama sarr yalla nafi yagg loll té wérr ndax cheikh ibra néwone na bindou ma ay téré wayé dina fi bayi ay goor yalla yo xam ni dinaniou fi yagg té louniou wax deugg laa

  • @senegalrek98
    @senegalrek98 2 роки тому +4

    Dieuredjieufé Serigne Touba.. Dieuredieufé Cheikh Ibrahima Fall

  • @gondiaye6661
    @gondiaye6661 4 роки тому +23

    Ma beug bay adama

  • @mamadouseck7124
    @mamadouseck7124 4 роки тому +44

    Baye adama niogui niane sunu borom mou yokou fane wi gueneu yagg geneu yokou gueneu weur 🙏🏾

  • @taphaseye243
    @taphaseye243 4 роки тому +2

    Machallah Dieredieufff brom Touba cheikh Mohamadou Mountakha Mbacké yàlla na fi yague ta wër ci barkeb ku tëdd qui Aminnne

  • @kman-97
    @kman-97 4 роки тому +6

    Thiey bay adama sarr yagulen yoklen werlen 🙏🙏🙏

  • @kman-97
    @kman-97 4 роки тому +8

    Ayy wayy gnanalen bay adama sarr bou bakh mou goud fan lol té geuneu wer barkep chiekh ibra fall machalla 🙏🙏🙏

  • @papembaye7921
    @papembaye7921 4 роки тому +2

    Hakasa bay adama yallana yalla yok fane wi

  • @aliounebadarambaye1601
    @aliounebadarambaye1601 4 роки тому +30

    Baye adama sarr yalnafi yagg lool tè wèr lool barkè mame cheikh ibrahima fall lamp

  • @pendambengue5318
    @pendambengue5318 4 роки тому +3

    Li dal doumathi doyal barkep mame cheikh❤️

  • @bassetoure1802
    @bassetoure1802 4 роки тому +1

    Baye adama sarr yague wére thi barke mame cheikh Ibrahim fall té yalla yaguale fi thi barké khassidayi

  • @omarsecka3762
    @omarsecka3762 4 роки тому +6

    jerijefe serigne Touba jarama mame Chiekh Ibra fall

  • @gassamandame5153
    @gassamandame5153 4 роки тому +1

    Jërëjëf fati wa jesboul mourit biknañu ci waxtaan wi

  • @makhaseck2932
    @makhaseck2932 4 роки тому +1

    Bilakhi Lou wer la wakh fall serigne bi rek la begue

  • @fallou1703
    @fallou1703 4 роки тому +4

    Thiaye baye Adama yalla na sa borom goudall fann yi barkep Serigne Fallou😍😍

  • @madickediop8244
    @madickediop8244 4 роки тому +20

    Thiye mama cike Ibrahim fall ❤❤

  • @niokhobayediouf9347
    @niokhobayediouf9347 4 роки тому +6

    baye adama dh farata la thi mouride yeup gnou gnanal ko mou yague fi lol tei and akoup weer ! baye Adama dagua wessou bakh wallahiiii
    kene khamoul li loumou

  • @elche4179
    @elche4179 6 місяців тому

    Walahi amoul loi dakeu wahtaan bayefall dagay noce ba fin ❤😂kenn dou Cheikh Ibra Fall

  • @mortalladiop7140
    @mortalladiop7140 4 роки тому +2

    Baye adama sarr yalla nafii yague lool tée wéer

  • @maremediop8089
    @maremediop8089 2 роки тому +4

    Sante serigne touba ❤ akasssa ana sollo dieuredieuf mame cheikh ibraima fall Dieuredieuf ❤ ❤ ❤ ❤

  • @pendambengue5318
    @pendambengue5318 4 роки тому +31

    Baye Adama la beugue manue thieye lì nèkhna 💔💔💔

  • @aramekonkafall3604
    @aramekonkafall3604 3 місяці тому

    Yalna yalla goudal say fane baye adama sarr❤❤❤

  • @moussambengue4861
    @moussambengue4861 4 роки тому +3

    baye adama dama tawate actuellement sa wakhtane motakh ma diog barcké mame cheikh ibrahima goudaal fane baye adama ak weer bilakhi nima la beugué eupna

  • @fadelndiaye9751
    @fadelndiaye9751 4 роки тому +1

    Bay adama yalna yallah goudale sa fane lol barké cheikh ibra fall amine

  • @mamadoudiane2651
    @mamadoudiane2651 3 роки тому +5

    Amine Baye Adama sarr akasa mamez cheikh Ibrahima Fall amine serigne touba

  • @abdousow1959
    @abdousow1959 4 роки тому +3

    Baye Adama Sarr bibliothèque bou magla limouy wakh loumou doundoula Bilakhi YALLA na sa fan goudou BARKI BOROM TOUBA

  • @mandouman4456
    @mandouman4456 3 роки тому +1

    Baye adama sarr yalla nafi yagg té ande ak werr si barkey cheikh ibrahima fall contane nagne

  • @zikroulah221tvsenegal5
    @zikroulah221tvsenegal5 4 роки тому +3

    Akassa Baye Adama Sarr Baye fall

  • @ndiayedjibril
    @ndiayedjibril 4 роки тому +2

    Baye Adama Mouride Yeepala soop begla

  • @deamtekona9212
    @deamtekona9212 4 роки тому +1

    Baye Adama SARR sa waxtane rékama doy bilahi yalna souniou borom goudal sa fane lol way
    Wa jazboul mouride douniou doyal si Baye Adama SARR déléne ko invité chaque mois way
    Diaguéne dieuf way yokouté rek ak gueuna kawé

  • @serignefalloudethiesarr188
    @serignefalloudethiesarr188 4 роки тому

    Thiey liilléé way Baay Adama Sarr Yalla na sa borom défal la fane wou guoudou lolll barké CheikhRaFall 🤲🏽

  • @abdoulayebaneniang
    @abdoulayebaneniang 4 роки тому +2

    Jerejeuf Mame cheikh Ibra fall lamp bountou yonewi

  • @sidymatarkhouma8357
    @sidymatarkhouma8357 Рік тому +2

    Mame cheikh laniou xaamul Loumou🙏 Jeureujeufė Mame Ibra Fall 💡

  • @morseye2528
    @morseye2528 4 роки тому +1

    dieure dieuf S.Touba diarama Mm Cheikh Ibrahim Fall

  • @fathatasantati2024
    @fathatasantati2024 4 роки тому +5

    tiaye mame Adama yallna Fanvi Good lollllllll♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️

  • @papadjibyba4296
    @papadjibyba4296 4 роки тому +7

    Akassa mouride tawfékh rek Baye Adama

  • @djamildiouf8593
    @djamildiouf8593 4 роки тому +2

    Ma cha Allah bay Adama yalla na yok saw fane

  • @aliounesarre4559
    @aliounesarre4559 4 роки тому

    Yalla nako fi yalla yagual baye Adama Sarr si barki borom touba

  • @aliounebadarambaye1601
    @aliounebadarambaye1601 4 роки тому +22

    Dieureudieuf borom touba khadimou rassoul diaaraama mame cheikh ibrahima Fall lamp

  • @ndiassembengue7007
    @ndiassembengue7007 4 роки тому +2

    Amna solo

  • @daoudageuyefall3475
    @daoudageuyefall3475 4 роки тому +1

    mame cheikh ibra fall mo nékhhhh

  • @lampefallkasse7241
    @lampefallkasse7241 4 роки тому +3

    tiey sama baye bou bakh bi Alcaty bamba kasse loumou meusseu am Cheikh Ibra lako delo te doyloko done Talibe Cheikh Saliou Mbacke wayer kham ni bountou bi Ibrahima Fall Lamp laa.
    Baye Adama Goudeul Fane Fatewo dembeu.

  • @mortensen42
    @mortensen42 4 роки тому +19

    Magui sante mame cheikh ipra thi nieke guis wakhtan wi

  • @serigneababacarmbacke8235
    @serigneababacarmbacke8235 4 роки тому +2

    Dieuwrine amna solo loll dh bay Adama beug naa Numerom dh bou diapandée

  • @sokhnadiarrambacke2697
    @sokhnadiarrambacke2697 4 роки тому +1

    ndeysan Baay Adama yagg fi dehhh

  • @papandiaye4108
    @papandiaye4108 4 роки тому +6

    Yagg fii looll tei ande ak weer si barkei cheikh ibra🙏🙏❤️

  • @morsylla9960
    @morsylla9960 4 роки тому +1

    Thiey mam Cheikhe kèn dou mom dé bay adama yalla na Ga fi yag tè werr

  • @sallaka1163
    @sallaka1163 2 роки тому +4

    Walahi azîm kénn dou dieumm yoyou bilahi 🥺🙏

  • @abdousakorndiaye8895
    @abdousakorndiaye8895 4 роки тому +2

    Baye adama sarr sarr yageu yocou tewer fall yarem bi barke sa mame cheikh Ibrahima fall rek

  • @awarenesstv2540
    @awarenesstv2540 4 роки тому +4

    dieureudiefe serigne touba dieureudiefe serigne touba dieureudiefe serigne touba dieureudiefe serigne touba dieureudiefe serigne touba dieureudiefe serigne touba dieureudiefe serigne touba dieureudiefe serigne touba dieureudiefe serigne touba dieureudiefe serigne touba dieureudiefe serigne touba dieureudiefe serigne touba dieureudiefe serigne touba dieureudiefe serigne touba dieureudiefe serigne touba dieureudiefe serigne touba dieureudiefe serigne touba dieureudiefe serigne touba

  • @mAhmadoubamba
    @mAhmadoubamba 4 роки тому +3

    Baye adama yallah ngafi yagu te weer Barke borom touba

  • @ibrahimasene5393
    @ibrahimasene5393 4 роки тому +2

    They Chekhe Ibrahima fall. Machal

  • @NdeyeNdiaye-uh4hy
    @NdeyeNdiaye-uh4hy 4 роки тому +1

    ❤❤❤❤❤yagu lén fi lol te werr ci barkep cheikhoul Khadim mame cheikh ibrahima Fall lamp❤❤

  • @ahmadaofficiel9834
    @ahmadaofficiel9834 4 роки тому +1

    Li dé ak sante la ci nioune ndaw ndi nah beug naniou wayé hamé wouniou yalla na tahaway bi yag barkep SIDIBIRAHIM FALL

  • @filmmovie9326
    @filmmovie9326 4 роки тому +2

    Thieye Baye adama sarr

  • @fallouleye5325
    @fallouleye5325 4 роки тому

    Dierediefeti s touba diarama mame chekhx Ibrahima fall lamp baboul mouridin 💡💡💡

  • @khadimrassoulmboup493
    @khadimrassoulmboup493 4 роки тому +2

    Thiey amarr falll sayérr ndiay keinn dou mommm
    Sidy birahim rekkaa maattaa wollou

    • @senegalpoint7299
      @senegalpoint7299 4 роки тому

      Sarr Ndiaye dou sayeer Ndiaye Magui diegeulou fall

  • @cheikhgueye2950
    @cheikhgueye2950 4 роки тому +3

    Baye Adama Sarr Yalle Nafi Yagu Té Wèr

  • @marasarr5883
    @marasarr5883 4 роки тому +6

    ❤️❤️❤️❤️ goudale fane sunu Mame 🙏

  • @gueyelax
    @gueyelax 4 роки тому +1

    Baye adama sarr yalla gafi yague té werr lol waye amine.

  • @sarrpapasambou3897
    @sarrpapasambou3897 4 роки тому +1

    Baye adama sarr contana lol bilay Lamp fall rey

  • @NdaoIbrahima-d7j
    @NdaoIbrahima-d7j 8 місяців тому +1

    Diarama Mame cheikh Ibrahima fall❤