Machalla madame Seck amo morome setna selna ta lii nieup hamnagne ni meunoul nahari hamnani safna sapp mane souma hifee rekk laleu sayy video yalla yalla yagual tahaway bii bonne continuation
macha allah. mais mane mom soblé ak yéte ak piment vert laye roussi wé. après ma deubb sa ma bissap bou wow (pour mou bagna nane huile) légumes aussi je mets les plus durs (carotte, navet, choux et manioc) batagnsé et kandia après taye la pour bagne mou tasse
Salam salam madame Seck magui laye ziar dila nianale goude fane ak were.Je vous remercie car vous me permettez de me perfectionner et de découvrir d autres plats.sète na sèle na machallah
WeuzDa king voila diafewoul par contre j’aime bien cuisiner mon mari n veu app as manger ailleurs j fait tt à la maison tous sucre comm sale 👍♥️damalay invite usa 🇺🇸 gua gneuw di lek rek 😂😂👍
Mashallah tata❤️ mais un conseil crevette yi delene dindi boutite bi nekk si biir moy indi intoxication alimentaire yi. Motakh gnou beuri dougn lekk fruit de mer (seafood) yakarni dagn ko allergie alors que rakhass bi moy dess. Di toub bou bakh nak nekal si diam.
Un intoxication alimentaire vient d'un aliment pas bien conservé . Pour infos un allergie na rien a voir avec u intoxication a propos de crevette langouste tout ce mange du moment qu'il est bien vrais ou bien conservé magui diegalou aussi s'était juste pour vous informer
Ah Machalla Mme Seck mane dale yawe lay weur ba fadiar diote ma dem teudi mane ma beugeu djiguene bou niamè wagne dale defale tour france waye té tamite beuna say epice gua niou koy wakh si français
Saye epice toure yi gua kay wowè dee niou bayi khele nioune gni degoule anglais té dila sétane dele wakhalé epice yi si français niou khame bane épice leu merci beaucoup
Ah bonjour Madame vous nous gatez avec vos plats j aime bien votre cuisine et particulierement vous meme il faut nous envoyer aussi nous de Paris un yiecal tout est bien propre chez vous je suis une de tes fan de Paris je t embrasse fort merci bz
Sokhna bou melni begeunako way k'ou d'accord beusseul j'aime may guiss 😂
Machallah nekhna mes eska do wagni diwline
Machallah yalla na yalla goudal sa fan barké seydina mouhamed saw
Machallah sister ❤️❤️❤️
Djiguéne dall day kheurrr 👏❤️😍😍machalla
Machalla madame Seck amo morome setna selna ta lii nieup hamnagne ni meunoul nahari hamnani safna sapp mane souma hifee rekk laleu sayy video yalla yalla yagual tahaway bii bonne continuation
macha allah. mais mane mom soblé ak yéte ak piment vert laye roussi wé. après ma deubb sa ma bissap bou wow (pour mou bagna nane huile) légumes aussi je mets les plus durs (carotte, navet, choux et manioc) batagnsé et kandia après taye la pour bagne mou tasse
Say togg mom chapeau mé ingrédients yii ak bouillon rék gay diminué rék da bari trop
MashaAllah mme seck sama toma. Waa loula soblé def.
Merciii tata😋😋😋😋😋
Ouhhhh laaa trop d'huile mais nurou na lou nekh machaallah
We love you ya thioro ♥️Mansha llah yallah na lokho bi were 🥰
Je valide j'aime beaucoup le plas sénégalais je suis 🇲🇱
Tata meune gua togue lolu mais sa oil bi dafa beuri lolu sakh esque li dina bakh sene sante parole
Machala machala madame seck merci encore une fois,, li ngay reugeul Euppnaaa
Machaalah waye na togue yi naturel meun na saf sap te produit you Bari dou thi dem. Attention la Sante avant tout.
Mancha Allah 👌 j'admire ta façon de préparer... Moi également je n'aime pas les rossis trop noir.
Thieye djiguéne senegal togou yènamaci doye
Thieye madame seck machallah défati ngue se meunine
Aka meuna togue manchallah. Lingua beugueudj eupeuna, lingua diaga tokena manchallah
Machallah toujours fort
Machalla madame seck sa thiep bakhna sa bissap saff na
😍mashaallah ..bobou thiep bou amm diom😋😋😋
Tata chérie, sopp naleu. Danio khawa ndiro lokho nio bokkeu niniouy toguei. I'm proud of You. 🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
Machallah rafetna tè sell na mais too much oil!!
Souniou sokhna wagnil.so diéko del balé.Les Gueyéne et les Diawénes prenez notes 😍
Mane tamatei dom biniou teumbeul toukil n sameu adouna
I really admire and adore you....you my reference
Madame seck Man thiebou bou wekh rék la beuge ana njikou beuge
Salam salam madame Seck magui laye ziar dila nianale goude fane ak were.Je vous remercie car vous me permettez de me perfectionner et de découvrir d autres plats.sète na sèle na machallah
Machallah Mme Seck wa Bergamo gnongui lay beugué
Oumy Thiam mou ngi thi birrrr deee
Awa kane cheri Bachir Diouf wawaw
Je passe mon temps à regarder des vidéos de "toggou" sur UA-cam té toggou manoumassi salamaleykoum
WeuzDa king 😀dagay diem rek touti tooti digua meun insha allah
@@rokhycilla4284 enfaîte j'aime bien regarder les gens le faire, mais Mann tayal nako, sinon meunn na thiébou guinarr récemment... Ndeketer diafewoul
WeuzDa king voila diafewoul par contre j’aime bien cuisiner mon mari n veu app as manger ailleurs j fait tt à la maison tous sucre comm sale 👍♥️damalay invite usa 🇺🇸 gua gneuw di lek rek 😂😂👍
Diemal rék dinga meun inch
Mane yaw laa gueum machala
Machallah cette plat j'adore t'elle ma
Machalla fatabarakallahou 🥰😍❤❤❤❤❤
Mme seckh machallah mais del wagni huile bi touti mais jdr ta cuisine
Machalah Mme Seck diana yon yallah na yallah barkel ❤️
Mashallah tata❤️ mais un conseil crevette yi delene dindi boutite bi nekk si biir moy indi intoxication alimentaire yi. Motakh gnou beuri dougn lekk fruit de mer (seafood) yakarni dagn ko allergie alors que rakhass bi moy dess.
Di toub bou bakh nak nekal si diam.
Ta parfaitement raison Aka moussi gaw
Nice
@Aida Balla Willier voilà
Un intoxication alimentaire vient d'un aliment pas bien conservé .
Pour infos un allergie na rien a voir avec u intoxication a propos de crevette langouste tout ce mange du moment qu'il est bien vrais ou bien conservé magui diegalou aussi s'était juste pour vous informer
@@beautenayo1031 merci remarque très constructive
Machala Mme seck kéne dou yaw
Machalah sa thieb bakhna mé déle wagni huile bii
Ah thioum macha alla ma tanty shert
Yaw dé sa dieukeur tébina ass machalla 🤣💋
Nonnnnnn Mme Seck nak vraiment toggolok NBA nak Mach Allah 🙏
Machallah femme forte
💪💪💪💪💕💕💕👍👍👍👍🌹🌹🌹💮💮💮💮🌷🌷🧡🧡💚💚💝💝🇸🇳🇨🇵
Machalla amna solo mdm sèche
La cuisine sénégalaise trop généreuse 😍. Un peu de modération avec l'huile. 😍😍😍😍😍
Madame Seck léne rék moma nékh si togue bi moye beugeuthieu bi mention trés bien 💅
Madame seck sa huile barina dee je trouve
Barina trop sakh
Mashalla saf na
Merc6 pour l recette mé une chose cherche une marmite plus grande pour préparé l repas sa te permet d mieux mijoté ta recette jmexcuse nakhh
mashallah madame seck ❤️🇸🇳
Machalla M, Seck wa bologna gnogui lay beguè❤
Ça a l'air bon mais attention à l'huile
Oui ya trop de l'huile machallah yalla na diam yague
Mme Seck begue na sa façon togue waye diap thine dico khoss bamou kheum gnounane dagnouye dorel machalah rafetna couleur yeup guen
Kouy soldar diogeul mak clonel bagi soga gneuw 💪
😂
Madame séck yama doye si togou
Mme seck il faut diminuer l'huile et le poivre c'est trop à mon avis merci
thiane sarr même remarque trop d’huile c’est pas bon sa diminue le goût
Pour moi thiepou dieune diaroul pobar
Wi y'a trop d'huile je confirme
Limouy togu no Bari motakh mou def huile bou bari
Mme sekkk dalle Machallah
Je suis de Katy Texas maman. Dans quelle partie des États-Unis habitez-vous. Je veux faire du KHARANE please.
Machallah plat thiebou dieune amna base
Salam ziar bou werr j'aime ta façon de cuisiner mais ya trop d'huile ...
Machallah dieureudieuf nekh na lol😘
Machala Bonne continuation
😋😋😋😋😋😋😋😋👍👍👍✌🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹ماشاء لله 🌹
Man dal say dieun am na mana
Riz paella la beugone nga togalgnou yama si doye
Waye waye waye mais limotakh mr seck neubeutou 😂😂😂 mashallah 😍😍😍. Safna sapp
Sa thiébb bakh na Machala
Machalla Mme seck 💕💕💕💕💕💕💕❤❤❤❤❤❤👏👏👏👏👏👍👍👍👍👍🙏🙏🙏🙏🥰😘
Macha allah ce quoi pigna
Il faut des vidéos tout les jours 😗😗machala
Ah Machalla Mme Seck mane dale yawe lay weur ba fadiar diote ma dem teudi mane ma beugeu djiguene bou niamè wagne dale defale tour france waye té tamite beuna say epice gua niou koy wakh si français
Saye epice toure yi gua kay wowè dee niou bayi khele nioune gni degoule anglais té dila sétane dele wakhalé epice yi si français niou khame bane épice leu merci beaucoup
Ok cheri amoul problem
Mme seck mane Thiaroye gare la deuk😂😂😂😂😂😂😂
Machallah sister eupeuna👍❤️🥰🥰
nalé mongui ni nak. merci
Thank you thioro dokhna 😍
Franchement les choux-fleurs mounee gniak
Yaw YAa metti
Mais c'est excellent, il faut essayer d'abord. Les goûts et les couleurs......
QuEen fifi 😂😂
Mane la💃💃💃💃💃
Bilahi chak jour ma nangou
Ya trop d'huil mais j'aime bkou
C la 2e k Je regarde mais j’aime beaucoup comment vous cuisiner
Machalah très appétissant
Tata Ndeye thioro rek dou ay foo
Ah bonjour Madame vous nous gatez avec vos plats j aime bien votre cuisine et particulierement vous meme il faut nous envoyer aussi nous de Paris un yiecal tout est bien propre chez vous je suis une de tes fan de Paris je t embrasse fort merci bz
Chapeau Madame
1er personne
Thieye madame Seck rek thi Wagne mala begue
Machallah madame seck 😘😘😘
Machalla tata
Rossi bii bonne naaa
Machalla Mm Seck
Sa lepp dok nak khalassss
Man dal Mme seck la beugue
Machallah amna solo
Diaga mom sans sobler dou diaga
hana ly defnako si deggo mounei soblei bou mauve bi
@@abdoulayecome4878 ah ok Kone Mako degoul alors, merci
Machallah Mme seck
hana ly de rien
Madame seke kendou yaw
Mashallah 😋😋😋
mai tomate bi loutakh dimbooko
L’huile et le sel il faut mesurer sinon mashala togu ga mashala ❤️❤️
Machahala 😋😋😋
Machallah can you please tell me the English name of the fish beurre?