Yow sa problème lan la ak lan guay sik si wakhtanam bi yen sen problème moy kou wakh guen critiqué té amo len ben kham kham ki limouy wakh lernama khamosi tous nopil té ga ame eudeub
@@MbayeNiangMbayeNiang-gn3qjki ngay wax xalé thie faydou bi dé mom la jeune yeup diox bop tay thie faydou Maxala yéne danguéne yakarni fo léne tok danguéne wara élevé niveau té Serigne bi mom ay waxame dakoy wathié ba xalé bi am 2 ans sax meune ko dégg
Machallah Yalla nako Yalla mousseul si thiate. Il est l'un des espoirs très sûr de la faydatijania... Dieuredieuf Cissé
Mashallah Cissé yalna yalla goudale sa fané 🤲❤️🥰 Lou wer billahi 😭
Machalah jalaloudine🥰 yalnna yalla yokkou khamm khamm bi téé deugueureullla 🤲🤲
Kou deugoul woul jobo doko beug kafoul bayam kafoul ligni donou si seen ma kham nagnu ko wormal nagnu ko❤❤❤❤ yalla nga fi yague tei weer Sisi
Serigne bi yalla na yalla samoullla yanétabi sakh dadane wakh niou wédika
Lavenir de la fayda...que dieu te protège
Machallah Djialaloudine Yalna Yalla yokou Xam Xam bi goudal fane wi ci barké Baye Niasse ❤❤❤❤
Machaalah yalna yalla barkel ya rabi
Machalah caisse goudou fan ak wer yala yokou xamxambi
ALHAMDOU LI LLAH. KHOL YI DEFAROU SI YALLAH YEUP NANGOU NAGNE SAY KADOU.
Machalla cissé❤❤❤❤❤❤
Dundal weral yague fii loll te andak werr sama sopeh bi ❤
Walahi naysan Cissé ❤❤
Machallah Cissé SOPÉ BII❤
Yalla na yalla samoullla yanétabi sakh dadane wakh niou wédika
Machallah ame na ndieurigne ❤Cissé
Mach alla cheikh jalal dine
Yameun jËRéJËF yalla samoula ya cheikh Ibrahima Cissé
بارك الله فيك انت وارث سرابيك
بارك الله فيكم
Machalla ❤❤❤
Mashalla Serigne dieuredieuf
Machallah yalla nala yalla sam
ما شآء اللّه ❤ يا ولد الماحي سيسه
Alhamdoulilah ❤❤❤
Walahi Cissé li rék Moy faydou dieureudiéfe
Machallah Cissé xam xam késsé nga. Yenn ñiye critiquer jangolen xamo len dara
ما شاء اللّه ❤❤❤
machalla amne solo
L'espoir de la fayda bilahi goor deug fierté Oumou islamique bi yeup nga kham kham bou ler té nekhna deg kep kou beug deug dinala beug dieuredieuf
Macha Alla
Kouy critiquer wakh tannn cheikh Ibrahim mi moy da nga deunggg do kou dioupppp
Cisse zaman ❤❤❤
❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤😢
Ciss ngary
Bou wakhoul ci faydou sakh wakhna li baaye wakh ci faydou, yénn gniy critiquer louy sén problème ?
Tajjiit fathooko jiitou😂😂😂
HAQQU CISSÉ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Wakhi nitt rk gaa fi wakh
Ms doff nio beug yakh faydou si Ay fène
Cisse
😂😂😂😂😂😂😂
Boye waxhofi dara bilahi xhamo dara amo béne arguments si faydou moye lane
Yow sa problème lan la ak lan guay sik si wakhtanam bi yen sen problème moy kou wakh guen critiqué té amo len ben kham kham ki limouy wakh lernama khamosi tous nopil té ga ame eudeub
Kii limouy wax amo niveau pour comprendre
Nopile
Sa way bilahi wakh nga degue amoul bene arguments si l'an Moy faydou kii khamoul yalla motakh nak
@@houboutidjanibayeba9922sa way kii khale la thi faydou bi khamoul dara
@@MbayeNiangMbayeNiang-gn3qjki ngay wax xalé thie faydou bi dé mom la jeune yeup diox bop tay thie faydou
Maxala yéne danguéne yakarni fo léne tok danguéne wara élevé niveau té Serigne bi mom ay waxame dakoy wathié ba xalé bi am 2 ans sax meune ko dégg
Mach alla cheikh jalal dine
Machallah❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
ua-cam.com/video/irq16hMhV4I/v-deo.htmlsi=7O1ZGqfQrTAHG2HP
❤❤❤❤
Machallah ❤❤❤❤