Serigne Sam Mbaye : AY LERAL SI DOMOU NDIALO

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 1 лют 2025

КОМЕНТАРІ • 102

  • @moustaphangom4535
    @moustaphangom4535 2 роки тому +10

    Machallah serigne sam mbaye tontou ga lép mbaye wallahi mala beug si sama khol yallana yalla yok saye lérre té tas gniousisa barké

  • @abdoukane5608
    @abdoukane5608 3 роки тому +17

    Baye Sam mbaye yala nonou KO yala fayle si barkep Serigne Touba Amine

  • @thiernoniang5625
    @thiernoniang5625 3 роки тому +15

    Machalla serigne Sam mbaye yallana noko yalla fayal amine yarabi 💕 💯 💞

  • @modoudabo7163
    @modoudabo7163 3 роки тому +32

    Yalna soufe woyofe si kawame
    Nite kou amone savoir yalna aÿ lérome yook si képou kouye DIOULITE 🙏🙏

  • @khadimdiop7485
    @khadimdiop7485 3 роки тому +21

    Koula dégu am lou lér si adouna bi yala yoki léram si barké nabie sa

  • @mhm.tthiam6035
    @mhm.tthiam6035 3 роки тому +38

    Ils sont innocent deysaaan
    Nalen yalla yereum😯

  • @cheikhmbackeseck6704
    @cheikhmbackeseck6704 3 роки тому +12

    Machallah amna solo trop yalnako yalla yereum ✅

  • @khalydiagne1376
    @khalydiagne1376 3 роки тому +5

    Akassa machallah amna solo yalla na yalla faye

  • @naskelly4451
    @naskelly4451 3 роки тому +19

    MASHALLAH THIEYE SERIGNE SAM MOO YÉMÉ BILLAHI ❤️🙏🏾

  • @abdoulayeosnseck7012
    @abdoulayeosnseck7012 3 роки тому +10

    Mashala Serigne sam mbay Yala na yala yokk ay lëram tass niou thi barkém

  • @Ousseynoud18
    @Ousseynoud18 2 роки тому +3

    Yallah nah yallah yokki lérame Serigne sam mbaye❤️🙏

  • @souhaiboundao5272
    @souhaiboundao5272 3 роки тому +29

    Yallah nanouko sunu borom fayyal

  • @mbsylla
    @mbsylla 3 роки тому +40

    Li am solo moy moytou téré Yalla yi. Sounou borome moniou gueneu kham souniou bopou. Ndialo dafa diara moytou. Boudoul wakh dji sakh, togne sa dome wessou woul nga fatou yaw baye dji say domou yone dila donou mome niou guéné ko si mirass mi.
    Kokou yako togne, yako touteul.
    Naniou Si Yalla mousseul, té mayniou niou moytou téréme yi.
    Nieupe kham namou dioudo.

  • @BayelateKane-i4w
    @BayelateKane-i4w 3 місяці тому

    Machallah serigne sam yalna souvent wayofe si kawame

  • @aliounembayendoye6027
    @aliounembayendoye6027 3 роки тому +9

    Machallah yalna yalla faye

  • @serignesambadiagne6976
    @serignesambadiagne6976 3 роки тому +10

    Machalla diadieuf serigne sam Mbaye

  • @babacartoure3786
    @babacartoure3786 3 роки тому +8

    Yallah nayallah yereum ko moy sounou bay

  • @ibrahimambodji3220
    @ibrahimambodji3220 3 роки тому +15

    Bouko kenen waxone ma wediko😭... allahu akbar

  • @assanembow6460
    @assanembow6460 3 роки тому +16

    Li rek motakh moy salté kallah nous pardonne

  • @atumandiagne8828
    @atumandiagne8828 3 роки тому +10

    Niit warna na kholat bopam, yalla warnaniou wessou diko djamou rek ngir dougou aldiana akk ragal safara !

  • @cheikhounagueye526
    @cheikhounagueye526 3 роки тому +9

    Amna sola

  • @djilymbacke4946
    @djilymbacke4946 Рік тому +1

    yalla na niou ko yalla fayal😧🙏

  • @maguttediop2071
    @maguttediop2071 3 роки тому +10

    اللّهمّ إغفرله وارحمه

  • @ibrahimambodji3220
    @ibrahimambodji3220 3 роки тому +26

    Nagnou sante sougniy wadiour bou baah

    • @khadimdioum9584
      @khadimdioum9584 3 роки тому +14

      Nagne ko santé yalla nakh souniou borom moko namé nonou

  • @TheBadiane2
    @TheBadiane2 3 роки тому +15

    Depuis quand une personne décide kouy dougui adjana 😔

    • @soxnamariammbackengom2234
      @soxnamariammbackengom2234 3 роки тому +4

      Ioe xana amo degu?

    • @TheBadiane2
      @TheBadiane2 3 роки тому +3

      @@soxnamariammbackengom2234 ngue balma tu ne m’as pas compris. Je ne faisais pas allusion si Sergine bii...

    • @falloucisse33
      @falloucisse33 3 роки тому +2

      @@blacknegro7408 ah kay diar na niou diamou yalla nguir you bary :
      1 même bou démoulé al Diana dou dem sawara dem sawara nak louneeko geun.
      2 yalla lom digle def rek, amoul di chart dem al Diana wala sawara.
      3,4,5,6,7,8,9........

    • @moussadieng3378
      @moussadieng3378 3 роки тому +13

      @@blacknegro7408
      C'est du n'importe quoi.... yalla dafa mandou.
      Amoul féne fou yalla wakh ci al quran ni doumou ndialo dou dém aldiana.
      Kou am ayya bi namaka wakh, parce que duangue na fatiha ba nassi, guissouma ci aya bobou.
      Sénégal nak, ay nite nioy takhaw di légiférer ci dine yalla dji, diko toumal té kéne sagnou léne wakh danga dioum.
      Des gens se sentent exclus de cette vie, deviennent défaitistes et pessimistes à cause des avis et jugements erronés de certains illuminés.

    • @mansour3284
      @mansour3284 3 роки тому +2

      @@moussadieng3378 Mane daal guiss naa kou yalla khass Si alkhoy Aane tei Loumouko khassé moy Dimou ndialo

  • @diopmareme3752
    @diopmareme3752 3 роки тому +6

    Yalla rek mo kham kouy dougou aldiana ak kiy dem safara li am solo moy gua nek nitou diné ak l'islam li yeup amoul Sanche

  • @sarrabdousalam9493
    @sarrabdousalam9493 3 роки тому +2

    Akasa ❤️❤️❤️❤️

  • @abdouazizdieng5671
    @abdouazizdieng5671 3 роки тому +3

    Machallah

  • @maissandiaye8895
    @maissandiaye8895 3 роки тому +7

    Bilahi ya woor🤝

  • @alicisse5554
    @alicisse5554 2 роки тому +1

    ما شا االه

  • @cheikhdiop5226
    @cheikhdiop5226 9 місяців тому

    Fenaal yonente bi mome bakaar bou reuy la . Yalla dou togne keen et dou diamou yalla walla djoud mou yobou nit jannah . Kou dougou jannah rek , yeurmande yalla nga fa dougué..

  • @elbachirmbaye0315
    @elbachirmbaye0315 2 роки тому +3

    Serigne sam mbaye brome le 15 mars

  • @bambafall6723
    @bambafall6723 3 роки тому +3

    Machalah Yallah nako Yallah fay 🙏🏽🙏🏽♥♥♥

  • @salamsalam-ph4vf
    @salamsalam-ph4vf 3 роки тому +15

    Li wer moy domu ndiaalo ak kudul mom gno yam si diamou Yalla, su diamoo Yalla dafay doug aldiana com gneup. Lolu la yénèn borom xam xam wakh, té lolu mo yanu maana, mo deupo ak manduté Yalla, mo deupo tamit ak li Yalla wakh si alqur'ane. Wayé lolu téréwul Serigne S.Mbaye ku maag la si gnune, wayé Yalla rék modoul dioum .

    • @KaadukSerigneSaamMbayetv
      @KaadukSerigneSaamMbayetv  3 роки тому +3

      Serigne esk man gnagno fatali li Yalla wakh si Alkhourane ci domou ndialo

    • @damediopdiop2212
      @damediopdiop2212 3 роки тому +2

      @@KaadukSerigneSaamMbayetv mangui ziar boubakh sama dieuwrine am na solo lolll

    • @KaadukSerigneSaamMbayetv
      @KaadukSerigneSaamMbayetv  3 роки тому +1

      @Dame diop diop ndiongui lay délo ziar

    • @serignefalloudiop5827
      @serignefalloudiop5827 3 роки тому +2

      Sa Diagu SORIWOUL

    • @blacknegro7408
      @blacknegro7408 3 роки тому +4

      @@KaadukSerigneSaamMbayetv Yalla wakhoula fén si alkhourane k domou ndialo dou dougou aldiana.limou niou Sant moy niou diamou ko té môme su boba moy aaté diaam yeup si yeurmendém

  • @mouhameddia5168
    @mouhameddia5168 3 роки тому +6

    Domou ndiallo sou diamo yallah dina dougou aldiana

    • @inconnu90000
      @inconnu90000 Рік тому

      Do degu rek limou wakh

    • @mouhameddia5168
      @mouhameddia5168 Рік тому

      ​@@inconnu90000loutakh maye dégue limou wakh ?walla mome sou wakhé nieup wara wakh waw lohlou yalla réck moko ame

  • @abdoubarham
    @abdoubarham 3 роки тому +5

    Dem nek harifou bilah moy mouslouway bi si Mom

  • @mbayeniang5597
    @mbayeniang5597 3 роки тому +4

    Waw kon li yalla wakh ni man amila salían falinafshihi khana weroul

  • @Abdou_por
    @Abdou_por 3 роки тому +5

    💯

  • @linekoubakhndiouck8540
    @linekoubakhndiouck8540 3 роки тому +3

    💗💗💗

  • @mendesshasha1021
    @mendesshasha1021 3 роки тому +14

    Yallah rek modoul dioum. Kou siania wakh ni domou ndialo d'où dougu aldiana yagui si dioumté bou reuy. Gni dioude si boume téwoul nio geuna Bone kouy Bone niom dagni dougu aldiana ? Mdrr

    • @magicfoot7845
      @magicfoot7845 3 роки тому +9

      Ndeysane kham kham bai beury tontu nla sx si birri wakham naina snu diané dji dousi philosophy wala science wala khel nn boudone lolu ylla dou yonni ay yonnenti niouy dianglé

    • @KaadukSerigneSaamMbayetv
      @KaadukSerigneSaamMbayetv  3 роки тому +2

      S.Khadim diop dieuradiaf

    • @mendesshasha1021
      @mendesshasha1021 3 роки тому +9

      Amoul Loy wakh ba confirmer ni domou ndialo d'où dougu Aldjana meussouma guiss kouko firi. Et montre moi un verset du coran ki le stipule . Fanatisme bi ngeni bayi

    • @TawbatouNasouhTV563
      @TawbatouNasouhTV563 3 роки тому +5

      Yaw S Same tontoul nala bopam ci wakhtane wi deglouwat ko ?

    • @mbayeniang5597
      @mbayeniang5597 3 роки тому +5

      Yalla de néna bakan bouné lamou dief lañoukoy fay waw domou ndialo bouy def lou bakh badé sí himane mom loukoy yobou diahannam té yalla néna mom dou tong bene diamam té li yalla wakh moy deug piur

  • @adoufaye6508
    @adoufaye6508 3 роки тому +3

    doomou ndialo bou defer louko mana dougeul aljanna dafay dougeu aljanna.
    et amoul lougnioukay labaler.
    un enfant adultere n'a pas besoin d'etre purifie

  • @kadzooballer9463
    @kadzooballer9463 2 місяці тому

    Madiama fall warneu deglou li serigne sam wax si domou ndialoo

  • @cheikhsambou6190
    @cheikhsambou6190 3 роки тому +4

    Ndakh daguane na si ape joulite mou taka domou ndialo

    • @Beateye
      @Beateye 3 роки тому +2

      Mais Domou ndialow meuna nékk dioulitt di kon kay loolu Dou cas

  • @seynaboudione3771
    @seynaboudione3771 4 місяці тому

    C'est n'est vraiment pas normale ça les enfants nos rien fait

  • @amndiaye1985
    @amndiaye1985 3 роки тому

    Lima nakari nekhouma

  • @beuguesonko-wt6eu
    @beuguesonko-wt6eu 6 місяців тому

    Amana borom xam xam you dakh lolou

  • @afrokema3388
    @afrokema3388 3 роки тому +4

    انا لم أوافق معه بهذا المسألة لأنها ينافي بالعدالة والله عادل
    أما من رباه المشركين ووالديداه مسلمان.
    إذا بلغه الرسالة النبي صلى الله عليه وسلم فأبي أن يسلم فهو كافر وان لم يبلغه الرسالة فلا يقال إنه كافر بل يفوض أمره إلي الله والله أعلم

    • @umuaboubcr961
      @umuaboubcr961 3 роки тому +3

      أوافق معك لأن الله يقول في تنزيله:( من عمل صالحا من ذكر أو أنثى وهو مؤمن فلنحيينه حياة طيبة ولنجزينهم أجرهم بأحسن ما كانوا يعملون) فكانت الشرط الإيمان أي أن يكون شخص مؤمنا ليتقبل عمله ولا يُمنع من دخول الجنة بذنب فعلها غيره فالله تعالى يقول:( ولا تزر وازرة وزر أخرى)

    • @afrokema3388
      @afrokema3388 3 роки тому +1

      @@umuaboubcr961 شكراً أخي جزاك الله خيرا

    • @magicfoot7845
      @magicfoot7845 3 роки тому +1

      Motax yalla ni bou diamo ylla dou doug safara

    • @talibebayamcisse5058
      @talibebayamcisse5058 3 роки тому +1

      وأناماوافقت معكما ! أيه الشيخانى لولاالفهم ماكان العلم! ماقال شيخ صام مبى بأن ابن زنى يدخل نارا إذاكان مومنامسلما بل يدخل فى الأعراف! وهومأيدقوله بقول رسول الله صلى الله عليه وسلم لأن ابن زنى هوماءالذى تحرك أولاللعصيان، ودخول ابن زنى فى أعراف وجدت هاذاالقول فى كتاب شيخ بمب المسمى بمنورالصدور ! إذاالفى مع عارف بالله ربمايمكنه أن يطهره بتوفيق الله!
      والله تعالى أعلم

  • @africaunited92
    @africaunited92 3 роки тому +11

    C'est faux !!! Vous blessez des gens qui n'ont rien demandé...Alahou ahlam...

    • @mousa5132
      @mousa5132 2 роки тому +1

      Serigne sam ngay wakh c'est faux

  • @ablayethiounexalaattv7883
    @ablayethiounexalaattv7883 3 роки тому +4

    Macha allha

  • @toumanyfatyndione4010
    @toumanyfatyndione4010 2 роки тому +2

    Macha Allah

  • @moustaphadieng440
    @moustaphadieng440 2 роки тому +1

    Machalla

  • @fatikebe7483
    @fatikebe7483 2 роки тому +2

    Machallah