Bougane Gueye attaque Sonko "naniu ligueye té bayi wah dji mane nek sathie moma geneul nek fénkat

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 16 чер 2024
  • Bougane Gueye attaque Sonko "naniu ligueye té bayi wah dji mane nek sathie moma geneul nek fénkat

КОМЕНТАРІ • 307

  • @BoussoMbacke-wr8ou
    @BoussoMbacke-wr8ou 9 днів тому +30

    Sonko moy Diomaye 50 ans de pouvoir inchallah

  • @youssouphasonko4900
    @youssouphasonko4900 9 днів тому +39

    Aucune classe …
    Un jour de Tabaski nguay téppékou ni 😂

    • @mortallafall1354
      @mortallafall1354 8 днів тому +1

      Mais guèweul il faut mou barè wakh wayè na neuk 2iem tour rek

  • @abbbbb1190
    @abbbbb1190 9 днів тому +13

    Gni dal l etats doit etre severe envers c est dechets la

  • @CHEIKH-FALL90
    @CHEIKH-FALL90 9 днів тому +12

    Quand il parle c est comme si ses journalistes qui parlent😂 c est ca la liberte de presse

  • @user-yw6jl7fc9b
    @user-yw6jl7fc9b 9 днів тому +39

    di ngua faye l'impot déh mba nga deme kassoo. point barre. sonko dou sa morome. senegalais yi xamnagniou lolou

  • @SFMS227
    @SFMS227 9 днів тому +22

    Waa kou diourř kii, tay la geum nii ya mom keur doff yii 😂😂

  • @antandiaye438
    @antandiaye438 9 днів тому +19

    Niar 2 yi nga wakh yép ci ioe la nék
    Sathie nga 😂féneu kat nga

  • @AlassaneNdoye-pf5qi
    @AlassaneNdoye-pf5qi 9 днів тому +2

    Après l'élection législative il faudra que les journalistes nous aident en ne tendant le micro qu'aux politiciens qui ont une légitimité politique.

  • @user-zv4zz9xr4i
    @user-zv4zz9xr4i 9 днів тому +22

    Sokon n'a pas ton temps il faut payer l'impôt

  • @fatougueye6348
    @fatougueye6348 9 днів тому +6

    2 tour😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @PapeMbayePape-tf5ju
    @PapeMbayePape-tf5ju 9 днів тому +5

    Bougaane vs azoura fall😂
    Takhwayóu azóura ga takhawè si niounee😂

  • @mbayevipecoleimameassaneci1638
    @mbayevipecoleimameassaneci1638 9 днів тому +6

    Kii dafa doff démall ga tok té bayi Fénnn bariga titree loull té béww sonko dousa morom😂

  • @mouhamedseye8840
    @mouhamedseye8840 9 днів тому +3

    Fay nday impot rk wala niap sa xone point

  • @mohameddiop7432
    @mohameddiop7432 9 днів тому +8

    Quand est ce que les politiciens arrêteront d'utiliser comme tribune de campagne les fêtes religieuses pour nous tympaniser? Franchement les politiciens nous fatiguent en fin de compte. Laissons ceux qui viennent d'arriver le temps de dérouler tout en priant qu'ils réussissent. En 2029, on évaluera et sanctionnera d'autant plus que les Sénégalais savent bien voter ..

  • @fishconjie3749
    @fishconjie3749 9 днів тому +3

    Guissss lennn mame mor ak ahmet ndoye 😂😂😂😂😂😂

  • @CherifbounamaDiarra-uc1gk
    @CherifbounamaDiarra-uc1gk 9 днів тому +1

    Oh Bougane, toi tu es entrain de te forcer aux sénégalais comme ça, non , tu n'as rien compris, le train de l'histoire t'a laissé derriere depuis très longtemps, tu te crois important aux yeux des senegalais😂😂😂😂😂😂

  • @mbayefam572
    @mbayefam572 9 днів тому +2

    Une grande geule

  • @IbouVane
    @IbouVane 9 днів тому +3

    Nioune nieup niougi santé yalla mes tu parles trop koi

  • @ousmanous
    @ousmanous 8 днів тому +1

    il a raison sur toute la ligne et bravo pour ton courage kou nafféekh doula déglou !

  • @ahmedseck6995
    @ahmedseck6995 9 днів тому +2

    Ndaysann donné yi dafa changé bou yageu té mom yegoko😂

  • @dembaztarkinda8270
    @dembaztarkinda8270 9 днів тому +1

    Bougane demal fayi impôt mo geun wakh dji yeup diaroukofi 😂😂😂😂😂

  • @aichadiallo8140
    @aichadiallo8140 6 днів тому

    President waliouw ousmane sonko moy President diomaye faye longue vie a vous amine rabbi 🎉🎉❤🎉🎉❤

  • @youssoudrame1588
    @youssoudrame1588 8 днів тому +1

    Doff bi dadialé doff yi si keurum nioukay ligeuyel waw amna mugui toudou 2ème tour di pdg télé doff yi😂😂😂😂

  • @aichadiallo8140
    @aichadiallo8140 6 днів тому

    President ousmane sonko rek a vie pastef pour 50ans grand bon dieu puissant a tout prgrm 🎉❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉deureudeuf

  • @CheikhNdiaye-br1hg
    @CheikhNdiaye-br1hg 9 днів тому +1

    Sooxor bahoul

  • @user-qj3qs5vf4b
    @user-qj3qs5vf4b 8 днів тому +1

    bougane bayil wakh ousmane sonko dousa morome

  • @yougafallydieng5184
    @yougafallydieng5184 9 днів тому +3

    Baloul ak té dém léki sa khar

  • @yilebaba6565
    @yilebaba6565 9 днів тому +2

    Pfff pathétique ce type 👎🏼

  • @NdiagaToure-tj7mv
    @NdiagaToure-tj7mv 9 днів тому +1

    Bougan Sonko dousa morom na ngoull dogalou yalla nopalou yaw parénage sakhe mano ko matall yaw wotélo sonko bayi ko nak akh .

  • @adamandiaye-ng3lx
    @adamandiaye-ng3lx 8 днів тому +1

    Dieredieuf sonko dieredieuf contane naniou dieredieuf sonko dieredieuf contane naniou dieredieuf sonko dieredieuf contane ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @SeneCheikh-gt7cw
    @SeneCheikh-gt7cw 9 днів тому +9

    Fene reke

  • @MakhadiTamba
    @MakhadiTamba 9 днів тому +1

    Yagui togne dou tous les inspecteurs des impôts et domaines gnoye sathie

  • @jilymbacke5891
    @jilymbacke5891 9 днів тому +1

    Demale fayi impos te bayi thiakhane thiakhane baxote 😂dewenaty bonne fête

  • @idrissandoye6550
    @idrissandoye6550 8 днів тому

    Merci bougane tu as raison sur toute la ligne...

  • @NdiagaToure-tj7mv
    @NdiagaToure-tj7mv 9 днів тому +5

    kou guise ni ngay wakhé khamné da nga bange sonko nga mélni kou ay poupe di khègne 😂😂😂😅

  • @issagaye7311
    @issagaye7311 9 днів тому +1

    Tabaski sakh daniouye politique damn balou Lene nit yi té déme ligueye yi

  • @galsenrek8242
    @galsenrek8242 9 днів тому +4

    Un meuna doul Barthélemy Diaz en tant que maire de Mermoz t’avait taxer de déléquant fiscal

  • @BinetaMbengue-sz5do
    @BinetaMbengue-sz5do 8 днів тому +1

    KI MOME AMOUL DIOM😂😂😂
    MONSIEUR 2ÈME TOUR😂😂😂😂
    BOROM TÉLÉ DOF YII 😂😂😂😂
    YAW AY CHRONIQUEURS AK JOURNALISTES NAFÉK REK NGA DADIALÉ SISSA TÉLÉ SAUF CHEIKH OMAR TALLA SERIGNE SALIOU GUEYE AK SANOUSSY BA
    YAW SONKO MOLAAY DÉRANGER DINGA DÉH DÉ TÉSSA HEURE DOU DIOT
    SONKO DALA RAAAW LOLOY DAAG SEU KHOL BI
    DANGUENE WAKHONE DOUFI MEUSSA FAALOU ALLAH NÉLEN KI MAAKOY FAAL BA FALALÉ KHARITAM MOUY SON EXCELLENCE DIOMAYE
    LOLOU DOLEN KO MEUSSA DIGÉRER
    SONKO DOUSSA MOROM SI DIANGUE SI KHAM KHAM SI HUMILITÉ
    YAW TRAIN BI DALLA FI BAAYI
    TOGGAL DI KHAAR 2ÈME TOUR😢😢😢

  • @cheikhdiop30
    @cheikhdiop30 9 днів тому +1

    Vive bougane ❤❤❤🎉

  • @traoresouleimane8456
    @traoresouleimane8456 8 днів тому

    Bougane il faut limiter les dégâts de ton idioties qui ta fait rater le train de de l’avenir

  • @IbouVane
    @IbouVane 9 днів тому +1

    Koi Sadie Halis danioukoy nangoul deh senne. Afer nafehk yi dafa dieh legi yaw danga beuri wah trop

  • @salioundiaye5763
    @salioundiaye5763 8 днів тому

    Merci ❤

  • @francoismendy8115
    @francoismendy8115 9 днів тому

    Moi je pense que ce monsieur est profondément malade. Il a besoin d'être suivi par psychiatre !!

  • @mohamedmalickcisse971
    @mohamedmalickcisse971 9 днів тому +1

    Mo nara gueuneu soneu si ngouurou Diomaye bi😅

  • @assanembengue2863
    @assanembengue2863 9 днів тому +2

    Bougane est devenu depressif

  • @elhadjimbengue5191
    @elhadjimbengue5191 9 днів тому

    Trop immature et bête ce monsieur. Jour tabaski mouye politique. Rien de surprenant, il a toujours détesté Sonko.

  • @FallHadrame
    @FallHadrame 9 днів тому +1

    Il est hort class

  • @sidyndiaye2927
    @sidyndiaye2927 9 днів тому +5

    mosso bok élection lolou Moy grand combat😂fénerek ngaydéf

    • @dembaztarkinda8270
      @dembaztarkinda8270 9 днів тому

      Ki kaye dafa nekh meusoul dem élection dou explique rek😂😂😂😂😂

  • @AbdourakhmaneKane
    @AbdourakhmaneKane 8 днів тому +1

    Buegane rewna bilakhie

  • @malickfall4067
    @malickfall4067 9 днів тому +1

    Dinga fate dh😂😂😂😂😂😂

  • @diarrawakhdeug3365
    @diarrawakhdeug3365 9 днів тому +1

    Bougane te gua bayi sa youfou yawadi ,niakk fayda yi Di garal Di manipuler digue Faye impôts mo dileu nekh moley nakari. Daw rekk amone gué blême fisc boulgnou soneul
    Newil,wakhal lileu saf digeu faye😅😅😅😅
    Fe.nkat certifié sou amme,,ahhh bireul Kat certifié amna deeeee

  • @joachimdmkanfany7063
    @joachimdmkanfany7063 8 днів тому

    Néneu dayy diindii Fond commun sou gnou ko fallone 😂😂😂. Un comédien comça 😂😂😂

  • @AbdoulayeDiagne-ye7ey
    @AbdoulayeDiagne-ye7ey 8 днів тому

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @gningbamba9024
    @gningbamba9024 2 дні тому

    Faiyale waye sa waye akh 😂😂

  • @sankaristemadiba4397
    @sankaristemadiba4397 7 днів тому

    💯💢Verifiez Bougane amoul Bac (baccalauréat) kou amoul diplome noumiouy diriger Senegal c'est un businessman wayé il fait croire aux gens que intellectuel journaliste leu . ÎL à eu en 1997 le diplôme BT bâtiment et que passe ceux qui ont le BFEM😂

  • @mordieng1678
    @mordieng1678 9 днів тому +1

    Bugaan 2e tour 😂😂😂 kaay ma jàngal politig ndaysaan

  • @Oscardiop
    @Oscardiop 9 днів тому

    IL VEUT CREER UBE DUALITÉ ET SONKO N'A PAS SON TEMPS! QU'IL AILLE DABORD CHERCHER LE BAC.

  • @salimatayoum7744
    @salimatayoum7744 8 днів тому

    Diomaye et sonko pour 50 ans les jaloux vont maigrir il n'a qu'à aller payer ses impôts c'est tout

  • @sadoundiye2601
    @sadoundiye2601 9 днів тому +1

    Nafikh

  • @babacarmboup8603
    @babacarmboup8603 8 днів тому

    Wakh gua dague sonko est un voleur sathie manipulateur domerame la koto mak

  • @BinetaMbengue-sz5do
    @BinetaMbengue-sz5do 8 днів тому

    FEN KAAT BI KAAGN YAWLA MONSIEUR 2ÈME TOUR😂😂😂
    YAWMI BIIRAL SEU EMPLOYÉE
    YAW DANGA FEN SEU AWO FEN SEU NIAREL
    BAAYI SEU AWO AK SEU NIAREL NELEN DAMA AAM RÉUNION DEM AND AK SEU EMPLOYÉE BEU BIIRAL
    YAW YAAY FEEN KAAT INTERCONTINENTAL BII

  • @henribadji884
    @henribadji884 9 днів тому

    Ousmane, n'est pas ton égal. Tu n'as pas le niveau.

  • @FatouDiatta-re4kc
    @FatouDiatta-re4kc 9 днів тому

    Nidji di ballou AK toi tu parles de politique,ndeyesane,il faut savoir faire la différence

  • @abdouladiane5727
    @abdouladiane5727 8 днів тому

    Une grande gueule. Classe 0😂

  • @boubacardieme4288
    @boubacardieme4288 9 днів тому

    Ils ont compris avant toi pas besoin de leurs rappeler....tu n'as pas de propositions concrètes sinon faire la diversion...

  • @sarrlokaw2178
    @sarrlokaw2178 9 днів тому +1

    way doullllll wayyyy

  • @francoismendy8115
    @francoismendy8115 9 днів тому +3

    Tu mens en direct et tu ose dire que tu préfères être voleur que menteur !! Combien de fois tes entreprises ont été poursuivies par le Fisc! 😂😂😂😂😂

  • @boubacardiamba
    @boubacardiamba 8 днів тому

    Bougane comment tu es devenu chef d'entreprise...

  • @serignembackemadinagueye
    @serignembackemadinagueye 9 днів тому

    ❤❤❤

  • @mouhamedthiam1043
    @mouhamedthiam1043 8 днів тому

    Yaw sa wakh dioubbeuri yeup tu reconnais que tu n’es pas en règle. Legui louy problème bi , fayal mou diekh

  • @iboubayefall7848
    @iboubayefall7848 9 днів тому

    Fayal impôt yi boys boug’s mo gueune gue né fi di tépékou rek pros dou sa morom 😂

  • @amadousow4768
    @amadousow4768 9 днів тому

    Il faut payer les impôts buisness er etat deux voies differents essaye de passer les parrainages même anta et autres nouveaux candidats qui sont passés

  • @moonndiaye5328
    @moonndiaye5328 9 днів тому

    Souniou la meusoul dégu si problème ak fisc c’est parce que pendant 20 ans yagui deal a ngour mai je l’accepte tu joue bien ton jeu

  • @bajjanmaram4409
    @bajjanmaram4409 8 днів тому

    FENN= SACI.. KUY FENN, DINA SACI.. 6 AK 9 LA..
    OUSMANE SONKO MOOY DIOMAYE TÉ ÑOOM DUNU FENN, DUNU SACI..
    KON FENN AK SACI SEN YËF LA KONN??
    JULLIT DAAL DAY MODESTE....

  • @papelo4423
    @papelo4423 8 днів тому

    Sonko rék si ❤️❤️❤️❤️ ousmane sonko ya bakh

  • @salioundiaye5763
    @salioundiaye5763 8 днів тому

    Merci wawaw 😂❤

  • @mamadoudiouf6260
    @mamadoudiouf6260 9 днів тому

    Fayil ta bayi sa wax ju beri ji mo gen

  • @misterloum
    @misterloum 9 днів тому

    Yaw sonko doussa moroom. Yaw étape bou réussir parrainage nga tolle. Vas payer les impôts reck, c est simple.

  • @ArfangBADJI-oz7yw
    @ArfangBADJI-oz7yw 9 днів тому +4

    Ce gars aime le beuz quelqu'un qui ne peut même pas avoir le parrainage

  • @papaba2425
    @papaba2425 9 днів тому +1

    Mbaye impôt

  • @sankaristemadiba4397
    @sankaristemadiba4397 8 днів тому

    😂😂😂Demal faye souniou impot,amoulo sakh diplome Baccalauréat terminale , amoulo kham kham

  • @adamandiaye-ng3lx
    @adamandiaye-ng3lx 8 днів тому

    Bougane yaw nafekh ga magoum fen Kat bougane sa data yaye sa bo yewo gordieguene nou kharam katal sa data yaye

  • @MakhadiTamba
    @MakhadiTamba 9 днів тому

    Gnaw tu n es pas n importe qui il faut faire l act d un bon citoyen de oayer tes impôts

  • @kbs933
    @kbs933 9 днів тому

    Bougane demal fayi impôt moguene 😂 😂😂 moguene si yaw
    Après ga all ma sa xol 💔 bi ma lakk yapp bok🧆

  • @senegal-reck8585
    @senegal-reck8585 9 днів тому

    le batar de la nation féyale impôt

  • @Magattesambe-rw7nd
    @Magattesambe-rw7nd 8 днів тому

    Faye impo

  • @moustaphadiakhate7165
    @moustaphadiakhate7165 8 днів тому +1

    Saagou cogne 1000 lay diar khamou katt

  • @mamecorecisse1849
    @mamecorecisse1849 8 днів тому

    Wa ki deugueuroule fiite yaw douguo si arréne bi di beurré grand combat yagui nakh sa boopp😂

  • @SekouomarDieme
    @SekouomarDieme 8 днів тому

    L'homme du 2e tour fayal impôt bi boul bay khel ci marchand ambulant yi niom niougni Faye sè impôt normal liguenté sa boss mono nakh kén

  • @user-be8hb1kc2o
    @user-be8hb1kc2o 8 днів тому

    Yaw amon lo kéne Ndierine daw lakou gua ak sa lékh yi di mélni 😂pain wallé😂 temps bi da la fi bayi si réthiou gua tollou ndakh wakaro won diomaye dina néck prési Sénégale sonko premier ministre Sénégale 😂😂😂 bougane presi sntv😂😂 kholale diférence bi motakh ragale fété daye khanié

  • @ndiagaable
    @ndiagaable 9 днів тому +4

    Bougs yagui déclaré guére nyu meunue khelh😂😂😂😅PROS X DIOMAYE!

  • @sportmaisonpourtoustv
    @sportmaisonpourtoustv 9 днів тому

    Le chien aboie la caravane passe
    Indiscipliné

  • @gningbamba9024
    @gningbamba9024 2 дні тому

    Koye beraile rk la khamoul

  • @nitoudeug118
    @nitoudeug118 9 днів тому

    Wallahii c'est vrai niom niofi dakha sathi

  • @AbdouNiang-ru9sz
    @AbdouNiang-ru9sz 8 днів тому

    Boucane démal ga fayi boudée da gà wara bariy pékhé dioub dagoo geunn 😎

  • @henribadji884
    @henribadji884 9 днів тому

    Tu te trompes , tu ne comptes même pas. Détrompe toi.

  • @ayoumamadoulaminesane3035
    @ayoumamadoulaminesane3035 9 днів тому

    Kendoula votel tu ne paye pas d’impôts.

  • @leveridique-kj7qo
    @leveridique-kj7qo 8 днів тому

    Danguène dinakh nit yi nane li ma beugal Sénégal yène bounguène sagnone élections yi dou ame khatarayou nguène ba sonou nane na gneupp bokk sène bopp rék molène gnor topou lène feulé waay

  • @mansourdieye9494
    @mansourdieye9494 8 днів тому

    2eme tour 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @julienbadiane505
    @julienbadiane505 9 днів тому

    Bougane est tellement nulle en politique 😂😂😅😅