Limamoulaye Guaye fait un malaise en plein match et meurt, Emouvants témoignages des proches

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 30 лис 2024

КОМЕНТАРІ • 602

  • @babacarnenesarr715
    @babacarnenesarr715 4 роки тому +173

    Yalnako seydina limamou terou si barki seydina limamou 😭😭😭

  • @rokhayafall4970
    @rokhayafall4970 4 роки тому +68

    Le témoignage de son ami qui a porté le bonnet m'a fait pleurer.😭😭😭Deysann Yalla na khippé Aljana firdawsi🙏🙏🙏

  • @Maiimouna_G
    @Maiimouna_G 4 роки тому +55

    Ndeysaane déé bouy nieuw dou taggo, dou yeuglou, bou heure beu djoté rk djott na, Yalna niou fekk si lou bakh ak si lou nekh yalla... Toutes mes condoléances les plus attristées à sa famille, Yalna yalla diegal ko yaa rabbi, yalla yeureum ko té may ay mbokkam xoloup mougn InSha Allah...

  • @modiusene4171
    @modiusene4171 4 роки тому +78

    Paix à son âme que la terre lui soit légère thi barkè Borome Touba Fatiha +11likhlass

    • @sadiomane3600
      @sadiomane3600 4 роки тому +2

      Yalla nako yalla yeram ci barké seydina mouhamed psl mom mi mom firdawci

    • @ndeyediop3617
      @ndeyediop3617 4 роки тому

      Yalla nako yalla yeurem khareko aldiana

    • @assmbaye2482
      @assmbaye2482 4 роки тому

      Yalla nako yalla yeurame

  • @asey9490
    @asey9490 4 роки тому +3

    Un homme généreux, calme, bari diam begue bopam déwe na ndaw nak waye yalla na aldiana nek berabou noflayam meti na trop nak mai danouy delo lep si yalla prck moy borom diam yi yalla na souf oyoff si kawam limamou yeumbeul yeup dioy nagnou la te do mousse degne si gnoune😭

  • @yacinembow5971
    @yacinembow5971 4 роки тому +115

    On sait connu par hasard il était ouvert sympa amone kerssa Si nitt diko Nianal yalla bouko thiat thitou si mbabalém 😭😭😭😭

  • @binetadia7858
    @binetadia7858 4 роки тому +47

    Tu resteras toujours gravé dans nos coeurs frère Rest in péace🙏🙏🙏🙏

  • @alou6868
    @alou6868 4 роки тому +60

    Rakk dji dioynala ba samay beutt solou😭😭😭😭😭yeumbeul dioynala t parti à jamais mn frère limamou 😭😭🙏

  • @oulishfashionashdiagne2725
    @oulishfashionashdiagne2725 4 роки тому +44

    K la terre lui soit lègère...yalnako Mame Baye Laye tèrrou🙏🙏🙏🙏🕊
    C'est triste vraiment😥😥 dioylonama sakh tè khamoumako😫

  • @ahmaddiallo18
    @ahmaddiallo18 4 роки тому +24

    Gnou ame yarngéne lou diaffé si jeune yi légui ndaysanne limamou yalnala yalla yeureum yalnala yalla ball yalnala yalla téral bidjahi rassoulillahi saw😭😭😭😭

  • @mouslydiop3599
    @mouslydiop3599 4 роки тому +30

    Bilay sama khôl bi migui metti si limamou laye metti na trop kou bakh la yaro na lol 😭😭😭😭😭😭😭

  • @seydinaouzlaye1566
    @seydinaouzlaye1566 4 роки тому +39

    Yalaahhh boukooo thiattt djitouuu bilahi yeumbeul gnéppp goungué naniiukooo laye mahtar nlaaaa limamouu térouu téralll leuhhh

  • @diarra__diouf777
    @diarra__diouf777 4 роки тому +49

    Ndeysn j'ai des larmes aux yeux que son âme repose en paix yalnako yalla haré aldiana thi barké seuydouna mhmed psl

  • @laperlecmoi5995
    @laperlecmoi5995 4 роки тому +25

    ndeyssane aye khalé guene mais correcte guene .qu' ALLAH lui fasse miséricorde et lui pardonne

  • @layesgaye8842
    @layesgaye8842 4 роки тому +87

    Walahi ndeysan rak djouma dioxon ceer dou sigui sax xolma beug ma trop na yala fayla adiana

  • @Vivonslefoot
    @Vivonslefoot 4 роки тому +1

    Yall nako yalla yeureum si barké mouhaméd

  • @shitalaye5803
    @shitalaye5803 4 роки тому +30

    Yalnako Baye laye térou teralko😭😭😭

  • @bintoufallndiaye6520
    @bintoufallndiaye6520 4 роки тому +33

    Paix à son âme firdawsi soit sa demeure éternelle c’est vraiment triste 😭😭😭😭🙏🙏

  • @gltntegilou9532
    @gltntegilou9532 4 роки тому +20

    Yalla n'a ko yalla khareko aldiana yok leram si bark moukhameb sounou boroom yeureum ko ak mbolem firdawsi djioulitt yii amiine yaraby 😭❣️🙏🙏🙏

  • @evandoye4112
    @evandoye4112 4 роки тому +21

    Yalnako baye laye terrou téral ko thi barki baye laye psl souff oyof sa kaw🙏🏽

  • @khadimrassoulbadiane6651
    @khadimrassoulbadiane6651 4 роки тому +18

    Que le bon dieu ait pitié de son âme et que le paradis soit sa demeure éternelle siii barkep cheikhoul Khadim aminnn

  • @awaniang9315
    @awaniang9315 4 роки тому +56

    Yalnala Seydina Limamou térou téral la sa aldianay firdawsi ya

    • @mounag8518
      @mounag8518 4 роки тому +3

      Yallah na ko Yallah mi sakk gneup teh momeniou yeureum ko teh kharel ko Aldiana , mome Yallah mi mome Aldiana , Amine.

    • @astuondiaye5933
      @astuondiaye5933 4 роки тому +3

      @@mounag8518 liga wakh rek moye dege yalla rek mo mane khare nitt aldina do ki ninne

    • @kingvon3578
      @kingvon3578 4 роки тому +2

      @@mounag8518 Amine yalla rek man yalnako yalla khare aldiana

    • @aboudione7672
      @aboudione7672 4 роки тому

      Danguene réer les marats ne verront même leurs mômes là bas.seul la piété et la miséricorde de dieu compte

    • @paulpog807
      @paulpog807 4 роки тому +2

      @@aboudione7672 seydina limamou laye n'est op un marrats

  • @mamadousarr3977
    @mamadousarr3977 4 роки тому +19

    Paix à son âme ! Yalla borom bi degueureul laminame !

  • @ndackndiaye7395
    @ndackndiaye7395 4 роки тому +19

    Paix a son âme ,k firdawsii soit sa demeure eternell

  • @antalo7517
    @antalo7517 4 роки тому +7

    😭😭😭😭Ki guéne adouna khamou mako khamouma wayé dh waw bi méti nama lol barcki seydina mouhamed damako khol rék sama rangogne yi di wad😢😢😢😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭

  • @aichalo2616
    @aichalo2616 4 роки тому +16

    RIP k'il repose en paix k l paradis soit sa dernière demeur ètèrnelle metina trop il est parti à la fleur d l'age xana dilèn nianal xolou mougne ndakh yalla bou soxla gneup gnak😭😭😭

  • @tymasamb945
    @tymasamb945 Рік тому

    Yalna yalla yereum ko té Kharéko aldiana firdawsi 🙏

  • @remawadewade4785
    @remawadewade4785 4 роки тому +15

    Massa 😭 que firdaws soit sa demeure éternelle 🙏

  • @syllambaye3019
    @syllambaye3019 4 роки тому +23

    Yalnako souniou borom kharé aldiana

  • @nafimergane6912
    @nafimergane6912 4 роки тому +10

    Hoooo ki khamoumako mai dafa melni dama bokou ak mom décém bi dafma meti bilakhi témoignage bi kharitam bi dèf dioylo nama 😭😭😭adina dou dara yala niou bakh ngi rék la sokhla yalanako fofou geuneul fi mouyégalé ndawam thia firdawssi ya thi barkép sangou sang yi psl

  • @pendagueye5209
    @pendagueye5209 4 роки тому +11

    Massa pour sa famille que le tout-puissant l l'accueil a son paradis Amen

  • @kharyfaye8324
    @kharyfaye8324 4 роки тому +12

    Ndeyssan yalna KO Baye Laye térrou

  • @antoinemendy7880
    @antoinemendy7880 4 роки тому +22

    C triste mai courage a toute la famille que le bon l accueille dans le paradis

  • @damediop5316
    @damediop5316 4 роки тому +15

    Ndeysane yalla nako yalla yereum te khareko al djannah amine barke borom😭

  • @hawaaw4217
    @hawaaw4217 4 роки тому +17

    K la terre lui sw lègère et k le bon l'accueil dans son paradis

  • @tackondoye5358
    @tackondoye5358 4 роки тому +13

    Ndeyesane sama khole toye na cèdè yi rafètna.sama khélbi yeupe dème na si sama djekeur dji jour bou melnonou yalla boumako gawe amate

  • @khadyhaidara1774
    @khadyhaidara1774 4 роки тому +10

    Amine yalla nako yeureum té haarèko Aljanna Firdawsi 😭😭💔💔

  • @aidalayegaye6943
    @aidalayegaye6943 4 роки тому +14

    Repose en paix frère 🤲🙏

  • @bayesalioudiagne1518
    @bayesalioudiagne1518 4 роки тому +7

    Ndaye sene yalla na ko yalla yuerueme si barké khasidayi AMINE

  • @bambacisse11
    @bambacisse11 4 роки тому +10

    Koudém yalla nga dioubo ak sa borom nioune gnifi dés niogui dokh khér talou si méddu adouna dée dokh dieum si nioune

  • @aminataniang2948
    @aminataniang2948 4 роки тому +8

    Ndeyssane yalla na ko yeureume khareko aldiana😢😢😢😢😢metina

  • @matarcoly8121
    @matarcoly8121 4 роки тому +1

    ALLAHOU AKBAR inna lillahi wa inna ilayhi rajihoune Limamoulaye Gaye yalla na ko yalla yeureum jeggalko te kharé ko al janna wallahi mousseu ma kham Limamou wayé sama khol toy na bi ma deggé li niou ko sédél wallahi dama begg si yaw Limamoulaye Gaye dila nianal rek fi nga jeumm geuneul la fi nga joggé

  • @mounassendiayeh3466
    @mounassendiayeh3466 4 роки тому +14

    Yallah nako yallah yeureume atéko thi yeurmandéme 🤲🙏🙏

  • @fatimthiam7465
    @fatimthiam7465 4 роки тому +15

    Ndeyessn yalnako yeurame 😭😭😭

  • @oumaathiam6868
    @oumaathiam6868 4 роки тому +9

    Ndéysane il etai beau. Yalna borom bi waathié yeurmanndém si kawam 🙄

  • @mamyndiaye8785
    @mamyndiaye8785 4 роки тому +17

    Gnieupa ko dioy limamou yalla nala sa touradooo ba terouuu

  • @maremeba8146
    @maremeba8146 4 роки тому +27

    Metti na trop yalla nako MAME BAYE LAYE térou teral la

  • @ndeyecodoudiop610
    @ndeyecodoudiop610 4 роки тому +24

    Ndeysane yalnako yala yereum ay jeune guène mes gnou corecte guène machala sakholène di diouli diko gnanal bou bakh yala diapa lè lène

  • @ndiayeawa3676
    @ndiayeawa3676 4 роки тому +32

    Yalla nako malakka yeurmandé térou yalla nako yalla até si yeurmandém yalla nasouf oyof ci kayaw Yalla nagnou yalla may fane wou goudou bagnou léndi gnanale

  • @yayounabyndiaye5180
    @yayounabyndiaye5180 4 роки тому +13

    Yalla nako yalla yereume khareko aldiana souf oyof si kawam 🙏🙏

  • @laobegueye5089
    @laobegueye5089 4 роки тому +1

    Yalla nako yalla yeureum. Je présente mes sincères condoléances à toute sa famille.

  • @bayendiayediop1598
    @bayendiayediop1598 4 роки тому +26

    Yalla nako seydina limamou terou téral ko thi barké la ilaha ilalahh😭🙏

  • @salihatte9319
    @salihatte9319 4 роки тому +1

    Émouvant doyna ware nala sa toureundo terou tek la si lokhoye seydina mouhamed c’est vraiment triste 😔 bilakhiiii je te ne connais pas mais kou beug sa yaye souma sanioune Dagay doundou ba teral ko mon mission dans cette vie c’est de travailler matin midi soir pour les rendre heureuse je t’aime maman 😪mes Frére repose en paix🙏

  • @coumbathiam24
    @coumbathiam24 4 роки тому +1

    Ndéyesane yalla nako yalla yeureum tée kharéko aldjia tainmoignase machallah métina trop yalla nako séyedina mouhameth térou si barké tourô ndom (Amine yarabine)

  • @pendambaye1161
    @pendambaye1161 4 роки тому +8

    Paix à son âme 😥

  • @matyyade7090
    @matyyade7090 4 роки тому +11

    Yalnako yalla yeureum te khareko aldiana

  • @mamerosediop9519
    @mamerosediop9519 4 роки тому +20

    rip mon frère metina trop bilakhi wayei si sounou borom swt lani djouguei tei ite si mom lani deilou 🙏🏻🙏🏻

  • @Salimata.D12
    @Salimata.D12 4 роки тому +2

    Paix à son âme que la terre lui soit légère 😭😢😭😢😢 il est partie très tôt wayè yalla ak dogualame😢😭😢

  • @mbayesamba2613
    @mbayesamba2613 4 роки тому +13

    yalla nako yalla yeureum si bargué seydina Mouhammad

  • @nogayelaye2769
    @nogayelaye2769 4 роки тому +9

    Ke firdawsi soit ta demeur etérnél frére😭😭😭

  • @mamansalioudieng5784
    @mamansalioudieng5784 4 роки тому +7

    Ndéysane noo méti naa yalle na khipé aldiane méti naaaa bilah yalle ga égali sa dawe alakhira si brk nabi mstph psl thiéye adouna

  • @Adelina198
    @Adelina198 4 роки тому +2

    Repose en paix Mon frère.
    Yalla na la yalla agali chia aldiana djiou kawé

  • @mbayediop7391
    @mbayediop7391 4 роки тому +7

    Nioune Wa yeumbeul nio niakk Limamou Yalla nala Yalla Yeureum

  • @lenasy1975
    @lenasy1975 4 роки тому +2

    Yallah naco baye laye térou 🙏

  • @soukayeyade4310
    @soukayeyade4310 4 роки тому +2

    Repose en paix frère Yalnangua agualé sa ndaw aldianah yalna la Sa tourando terou firdwasi 😭😭🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏

  • @makhtarmakhoufall6227
    @makhtarmakhoufall6227 4 роки тому +1

    Yalla nako yalla yereum limamoulaye frère repose en paix 🤲🤲

  • @aishatoure514
    @aishatoure514 4 роки тому +3

    Yalla nako yalla yeureum té kharéko aldiana thiat bagnko djitou siii bamélam😔🙏Adouna ngiiii niii deiii

  • @cissendiaga9995
    @cissendiaga9995 4 роки тому +1

    Machahala yeneu kharitou Limamou yi sene kadouyi rafetena machahala yalla na ko yalla yeureum te khareko aldiana firdawsi te aye mbokame ak khariyite yalla nalene yalla diokhe kholou mogne

  • @jesuissenegalaijaimemonpay455
    @jesuissenegalaijaimemonpay455 4 роки тому +29

    Sport tafa ame yone kéne tout football si nathie bou tangue sama frère 3heur la décédé si térait de football

    • @alaminesylo2680
      @alaminesylo2680 4 роки тому

      Bakhoul mo gaw si ray nit

    • @femmenoirefemmeafricaine429
      @femmenoirefemmeafricaine429 4 роки тому

      Yalla nako yalla xaré aldjana sa frère bi

    • @racinendiaye6480
      @racinendiaye6480 4 роки тому +4

      Sérieusement un jour j'ai joué entre 13h et 14h. Mais j'ai eu une malaise inexplicable. Je pensais que je vais mourir.
      On n'aime trop jouer à ces heures mais bakhoul.
      Paix à son âme.

    • @safiatoumaminaaidara3846
      @safiatoumaminaaidara3846 4 роки тому +1

      Paix à son âme

    • @VISIONTVONLINE2299
      @VISIONTVONLINE2299 4 роки тому

      Dafa am yoon mom entrainement sakh dafa am yoon aussi. Paix a son âme

  • @pendadia7609
    @pendadia7609 3 роки тому +1

    Yalla nako yalla yeureum tè kharè ko aldiana 😭🙏🙏

  • @ousmaneba78
    @ousmaneba78 4 роки тому +2

    Limamou Santos gaye 😭kou am respect si domou Adama 🙏🙏yalla bouko thiat djitou si bamel lam lima guiss si rob bi dalna khél nit kou bakhone am yité bari kersé statut boumou moudjié déf watshapp terrain football mosi nék moussou mako guiss foumou thiowé paix à son âme 😭😭fatikha plus 11 likhlass svp repose en paix frère 😭😭😭

  • @gltntegilou9532
    @gltntegilou9532 4 роки тому +20

    Yalla n'a ko yalla yeureum khareko aldiana paix à son âme amiine yaraby 😭🙏🙏🙏❣️

    • @diawmareme3417
      @diawmareme3417 4 роки тому +1

      Paix a son âme limamou qu' il repose en paix que firdawsi soi sa demeure étérenéle

  • @dabandour1383
    @dabandour1383 4 роки тому +14

    Ndeye sane que firdawsi soit son demeur eternel

  • @sokhnabounamalayegaye3897
    @sokhnabounamalayegaye3897 4 роки тому +10

    Yalna ileyna di nofelayam frére

  • @bamsbams5164
    @bamsbams5164 4 роки тому +1

    Ndeyesane yalnako Bour yalla takhawou si bir bamé'lam yalla yeureum'ko yalla bou'ça yakar tass si yo'nénetébi si barki seydina Mohamed psl amine🙏🙏

  • @mariamasouare153
    @mariamasouare153 4 роки тому +14

    Toutes mes condoléances à sa famille 😭😭😭

  • @mameboussobalyza8674
    @mameboussobalyza8674 4 роки тому +18

    Thiey yalla métina lolll wayé sante yalla rk ndax limou ame démbe kou nék bo sagnone bo fi diougué amko

  • @oumylayediop8329
    @oumylayediop8329 4 роки тому +3

    Am nane yakak si yaw mon fils 😭😭😭😭😭 yala boula thiat djitou yal nala sa torando térou limamou

  • @khadyfall597
    @khadyfall597 4 роки тому +1

    Ces témoignages me touchent au fond de mon coeur

  • @khadimniang8193
    @khadimniang8193 4 роки тому +1

    Yalla nako yalla yereum té kharéko aldiana

  • @fatimatadem8011
    @fatimatadem8011 4 роки тому +16

    Ndeysane yallah nako yallah yere teh yareko aldiana yallah nako yallah bollé thi ndiabotou Mouhammad psl

  • @adjilaye9149
    @adjilaye9149 4 роки тому +4

    Paix a son âme 😭😭😭🙏

  • @serignesaliouniang4227
    @serignesaliouniang4227 4 роки тому +3

    Yalla nako yalla yeureum kharéko aldiana ak bép duoulit

  • @maimounabarret6056
    @maimounabarret6056 4 роки тому +10

    Repose en paix que les anges du paradis t'accompagnent a ta derniere demeure

  • @sonhiboulo9752
    @sonhiboulo9752 4 роки тому +1

    Yalnako yalla yeurame té xaraleko aldiana firdawsi barkepp seydina Mohamed saw

  • @diopmami2994
    @diopmami2994 4 роки тому +1

    Yalnako yalla khare aldiana

  • @ndeyekhadyfall9333
    @ndeyekhadyfall9333 4 роки тому +1

    Sama ♥️bi métina 😭😭😭😭😭😭😭
    Yalla nako yalla yeureum ! Diégeul ko ! Tei kharé ko si aldiana yi geuna kawé si barké Seydina Mouhamed PSL 🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽

  • @emzodiagne2647
    @emzodiagne2647 4 роки тому +10

    Samay rangone tourouna tay 😭😭😭😭

  • @binetaba6723
    @binetaba6723 4 роки тому +7

    Yalna xippé firdawsi amine

  • @BS2TV
    @BS2TV 4 роки тому

    Frère Tu restera toujour dans nos coeur

  • @dmxjjj7555
    @dmxjjj7555 4 роки тому +3

    Yalla nako souniou borom yeureum xaré ko Aldiana firdawsi amine 🙏🏽🙏🏽

  • @aminatadiouf2599
    @aminatadiouf2599 4 роки тому +2

    Yalla nako seyna Limamou tèrou 😭😭😭😭

  • @ndeyecodoudiop610
    @ndeyecodoudiop610 4 роки тому +6

    Yalna khyper firdaeso

  • @ousmaneba4176
    @ousmaneba4176 4 роки тому +10

    Ndeysann metina yalla na souff oyoff thi kawame

  • @labarkhamienne3905
    @labarkhamienne3905 4 роки тому

    Ndeysanne sédébi raféte na que firdaws soit son demeure si barké seydina Mouhamed psl

  • @khadimjuniorkg3801
    @khadimjuniorkg3801 4 роки тому +1

    Yalla nako yalla doli yeurmande thi barceb al quran

  • @corgueye5024
    @corgueye5024 4 роки тому +1

    Ay ndaysane xamou mako sah wayé méti nama lool dama djoy ndax témoignage yii yalla nako yalla yeureum

  • @filledukingcr7badji537
    @filledukingcr7badji537 4 роки тому +1

    Ndeyesanne metina trop massa paix à son âme 🙏 yalna Yalla maye xolou mougne waa keureum 🙏😢

  • @maguettesall1227
    @maguettesall1227 4 роки тому

    Ndaysan yalla na ko yalla kharé aldiana ak képeu koumou fa fék ak koukofa fék thie barkép serigne touba 😭😭

  • @lomaguette9545
    @lomaguette9545 4 роки тому +1

    Ndaysane bakan bou gniam dounou dina gnian d
    Yalla na khipè aldiana 😭😭😭