Même bou chute amé Siteu manoul dane ndakh max yw khana setanou pokola ak liss combat bobou amna niari chute té par avertissement la diékhé Max May gnou diam way
Guémléne yalla té nopal séne bopou yéne khana danguéne diapni bouléne li reuthié dotouléne nék roi si adouna guemléne yalla té liguéy max yaw vraiment wakho siteu degue
Max je t'ai toujours respecté mais sue ce combat sa communication a été désastreuse il doit pas parler comme les pimpi car il fait partie des doyens de la lutte
Siteu si defaite la diougué danoufi ken mbolo rk motax mou beuré combat royal ms dou mérite danoufi kén té dotoufi dane ndax li des si carrièram day geuneu meti siteu meunoul beuré tapetela wax rk la meune lamigne bo reuy
CNG mo dioxei victoire bi mais nieup xamnagn Siteu mo dane. Si pensez vraiment que Siteu dane Zarko donc Siteu dane Modou Quant à dawna tawul,stratégie la beurei ou non lolu ay détails la
Yén gni di wakh modou danouna épaule xawma avant bras (droit) mi ngui si souf on n'en disconvient pas sa main gauche si kaw bopou siteu té d'après réglement cng épaule dou chute légui fane la danoo la beug xam
Max il faut arrêter ton discours de nitt Gni wakhone naniou matoul mbeur dou sorri car modou Lo aussi avait entendu le même discours mais il a battu les ténors avec la manière mais Siteu n’a battu aucun ténors pour le moment alors nay daane avec la manière té bayi wakh dji
Max 10% wamm lay proteger 😂😂😂😂
Félicitations modou loo👑👑♥️♥️
Félicitations modou
Li lèpou modou lo yaako dèf badoola kène doukou may chance 😮
Lou yomb ngen don weur 😂😂😂😂deee
Wakh gua lepp
Lou yombou lagne done weur 😂
Boy dafa réw modou lo lay wakh di wakh nious ki khamoul louko modou lo défal magi doga am louma métti nak 🙏🙏🙏
Modou lo miko traité niakk diom nak
@badouboye6239 sanegal war nano dingi wolof dafniko khoula digeul bayyil xél si batou digeul koula digeul lou mélni dafa beugge ga niakke diom lii lako modou wakh wakhouko daga niakke diom dh ga balma dh 🤣🤣🤣🙏🙏
Lepp Modou Xlo doff yi nioleune di may chance 😂😂😂
Bou len nou sonal modou lo moy roi max yag suteu bou len nou fonto
Pour dire vrai moi je suis fans Sitteu mais amoul conseil dara dafa tapétt fiit moko manqué lac 2 sakh moko tané
Dangay fenn bougoo siteu
Félicitations Modou lo tu es le champion de l'arène ❤❤❤❤
Pére Max roi des arènes kéne douko colocolo dagne Koy ligueéy😅
Bravo Modou lô ❤❤❤
Modou lo yaako déf. Badoola kéne douko may chance. Gnii ils ne sont ni fair-play ni sportif. Waroo woone beuré ak gnoom
Bilahi
Yaw yay badola siteu a battu modou lo ay nafekh guéne
Dafa yakaroni mo meun siteu mouy sett lou yombou mais Siteu mo dane 😂😂😂 siteu Moy roi des arènes
Li Nguen di wakh jotté woul dra ak victoire bi
T'as parfaitement raison siteu est très impoli et il ne sait pas parler dafa réw
@@récré-o1d😂😂😂😂
siteu il n est pas professionel et c est la faute du manager
Ttes mes félicitations Modou lo ❤
Felicitations Modou lo 👍👍💪💪💪✌️🙏💪👍👍👍👍, ,daw daw siteu ,Mr daw 👎👎👎👎👎👎
Félicitations 🍾🎉🎈🎊 siteu
Modou Lo yaw lo beuguene niou taxhawou ngua reyniou 😊nióo tayi ndawou😂
Même bou chute amé Siteu manoul dane ndakh max yw khana setanou pokola ak liss combat bobou amna niari chute té par avertissement la diékhé
Max May gnou diam way
Mane dh pour man bakhom rèk moy doff wa dekè pèr max doff la😅😅😅😅
Ki kay dafa kat yaye
Non dafa nieuk😂
félicitations siteu
Respect lou bakh leu si nitt
Modou lo est le meilleur
Siteu bayi nala dotou Mala faral ndakh daga rèw trop
Ohhhh li nga wax deugeu Leu dafa réw🥺merci
Lamin SAMBA yow nafeha nga
Degue na bog lou yomb roi ni lanou koy diele max suteu delen bere
Max tu est méchant
Mais modou lo à perdu
Dafa nieuk😂
Non frère c'est juste il a un client et il souhaite qu'il l'est le remporter
Siteu mo daàn❤❤❤❤❤
Vraiment siteu nimouy dokhalé bakhoul
Guémléne yalla té nopal séne bopou yéne khana danguéne diapni bouléne li reuthié dotouléne nék roi si adouna guemléne yalla té liguéy max yaw vraiment wakho siteu degue
Max bou guenee moy done 3defaite 😂❤ mougne len rek daguene danou modou lo seul
Siteu rois dès années ❤❤❤❤
Waw max mi koumou yapp,siteu melni 505 7plage
Wakhale dé 😂😂😂😂😂
Max makk bou Niank dioume la😂
Max mbergan wakhou ragal rek gafi wakh ya ragal lo siteu mbeur day am fite😂😂😂😂
Modou lo mérite la victoire d'après les vidéos
Max c'est un méchant
Pere Max c'est dommage vraiment. Il faut dire à Siteu la vérité Modou lo tu n'aurais pas du donner de chance à Siteu. Li yeup yako tekk sey supporters
Billay Modou mognou togn😢
Modou ki diaroule tontou 😂😂
Siteu esk di nga am bénn grand lutteur Bilay mayati chance? Ta façon de parler n'est pas respectueux
Maxe margane y'a gnake fayeda😅😅😅😅😅😅
Roi daw douko maye situe Di daw rek
No max 👎👎👎👎👎👎👎👎👎👎daw daw siteu 👎👎👎👎👎👎
Pokola Vs liss, naniou diox Pokola victoire am😂
Wala ñou diokh zarco victoiram si kaw sitteu
Nooooooo daguén di dawe dieul sène tempo 😂😂😂😂😂😂😂😂pa yallah boumou ma entréne
Modou geumeul yalla danou nga😂😂😂😂😅
Yéne dolene rouss daw ba paré neck fi di mbeuri wakh
Max mbergane un vrai nafékhe siteu défou fi dra on ne gagne pas un roi par recours
❤si è vero Siteu ❤is the king e vinto
Vraiment wa siteu nio niakk diom😅
Félicitations siteu rois dès arrene
Siteu rois des arènes ❤❤
Félicitations Modou lo ❤
Max je t'ai toujours respecté mais sue ce combat sa communication a été désastreuse il doit pas parler comme les pimpi car il fait partie des doyens de la lutte
Dafa nieuk😂
@rouguikebe9984 honnêtement siteu n'a fait que fuire
Souma done mbeur douma dieulé ni roi des arènes li dou yeufou gorr niou doumaleu danela défofa dara di lathie ndam doul way akheu
Maxx waxouu tapéte rek lafii waxx
Baa siteu mangay dem parcelles 😂😅😂😅😂😅
Max noumako diépé☹️☹️☹️☹️☹️☹️☹️
max bilaye tu ma déçu depuis lambe dji wakhi dofe reck ngaye wakhe vraiment tu dois montré des bonne exemple?
Merci beaucoup siteu yako nokk dane ko,wa lambe dnio iniane
Ya gnak diom😅
Bilahi modou lo yaw yaniou togne nioune sayy fans 😢yaw yaa waroul wone may badola you beuri wakh yii chance 😢😢 xawma kou tané si niome
Modou Lo strategie bi moko sonal rek 😂😂
Max dof na siteu beug na lou yomb
Siteu😂😂😂😂 démal foyi
Max a le droit de dire ce qu'il pense son droit le plus absolu
Blh nieuwal douggou si sma piège par force lolu moy lane 😂
Lamine samba seytané guaaaa hooooooo lamine samba ya bone messouma guisss liii
Siteu si defaite la diougué danoufi ken mbolo rk motax mou beuré combat royal ms dou mérite danoufi kén té dotoufi dane ndax li des si carrièram day geuneu meti siteu meunoul beuré tapetela wax rk la meune lamigne bo reuy
tu as tout compris mon frère
Franchement image bi mome loumou wane moye siteu mo dane modou lo, souniou naffekkoul té nième yalla.
Nopilén way
Modou Rék Nitt La D'où Wakh Mouk Ga Diépiko
Siteu nexone nama ms yakhna yepp modou seul à vie ❤
Yalla nako yalla yeureum ak bèpou dioulitt
Max wakho fii dara
Félicitation Modou psk lolu la arbitre wakh mais Modou yaa danou
Niakkk diom si apel nguendi moudie thimmmmm pah bi mo niakkk fayda😂😂😂😂😂😂
Modou lo❤❤
Max bergane mii dou responsable dh, il faut faire comme Robert de yekini
Père guay méleni Ametd Aïdara nopil max t max
Modou daanuna lègui wa parcelle wax rekk laniu am ci lamb ji 😂😂
😅😅😅😅
CNG mo dioxei victoire bi mais nieup xamnagn Siteu mo dane. Si pensez vraiment que Siteu dane Zarko donc Siteu dane Modou
Quant à dawna tawul,stratégie la beurei ou non lolu ay détails la
Père max bouné suit rek ma tothie 😂😂😂
Nittou all’ yii wa jamageune doff yiii😂😂
Kou wakhal yala khane ni modou lo mo danou vrement siteu félicitation
Gueum leen yalla
Max yaw amo liwakh
modou mousso am combat bou mél ni khana warou nga😂😅
Nafèk bakhoul kou khol combat bi. Di até té yalla rek takh modou defna épaul. Kounék meungua faral koula nékh. Mais atél deug
Boulène niou sonal Modou est tombé
Modou diène kaire dans 1ans inchallah Lou nekh❤
Max daf dof 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Mai modou mo danou mê mm e sou Siteu amé 3 a ertissements
Kou nek ak sa systeme pour gagner siteu nimou beure nonoula .mo dane diaroule wakh
Même siteu sougnou diokhé couronne bi War nako roussa dieul Parce que wonéwoul diom
Yén gni di wakh modou danouna épaule xawma avant bras (droit) mi ngui si souf on n'en disconvient pas sa main gauche si kaw bopou siteu té d'après réglement cng épaule dou chute légui fane la danoo la beug xam
Sitteu demal sawii poubiii té teudiii😂
Tapet bou am daradia
Modou mo togn boppam rek😒vraiment
Max il faut arrêter ton discours de nitt Gni wakhone naniou matoul mbeur dou sorri car modou Lo aussi avait entendu le même discours mais il a battu les ténors avec la manière mais Siteu n’a battu aucun ténors pour le moment alors nay daane avec la manière té bayi wakh dji
😂😂😂😂😂😂😂 max yena bog lou yomb roi ni
Fière d'être yalmine
Organiser MMAM Modou lo vs siteu