Bou wakh dofé na nope yikay deuglou weur, ni Ama ni Boy Niang ne sont pas mes lutteurs mais quand il dit "locataires yi" ce n'est pas les locataires en personne mais ngiy dougou pikine té doukounioufa pour diakhassé guène dem sen yone. Yallah neu jam yaag sounou rèèw !
Ama joue avc vos esprit et les incrédules son ai aguets quand il fit on es pas amis pour vous cela sous entend on ce connais pas non ama es son aîné et non son amis comprener bien et soyés grand dans la tête faîtes une bonne lecture des mots
billaye yawe sa none la yeureume digua ame terangua te lo beugue si lambe. diguako ame dakhe dagua yarou gore ame kolere motakhe pikine nigui sisa guanawe thia kaname
Pikine la deukk dh mai wa pikine niou sofe boh wakho Balla gaye rkk sen xoll dii bonne teh Balla gaye yalla moko maye lii té wolof ndiaye néna nak kou nagnou lii yalla dogall do sone sa xoll dou diexe
Bayiléne bouguéne amé ay clant n'a brom négou louyas yi gnoune amounou séne diote brom négou louyas yi dimeuli nane léne ba tayi amna wakh yo khamné rafétoul
Duuuul waay lann mooy pikinité ak Guédiawaay aki parcelle aki fass nous somme des Sénégalais et C'est l'essentiel
J'aime ta franchise Ama.
ama rek laniou wakh futur roi incha allah
Tu rêves. Réveille toi ama ne battra jamais Modou Lo
@@ronaldgomiswakhone nga deug dh. Tu avais tout prédit
@@kefgg merci
@@kefgg Modou Lo dey daan boy niang.
Ama daal borom bakh nga billahi wallahi yalla nala yalla dolli takhawou rk inchallh motali yéné yep inchallh 🙏🏿 🙏🏿 😍 😘
Bien dit fils inchallah yalla na yalla bolé Pikine yeup
Sģ
Amine
Machallah beur wakh dji rafetna
Nitt bou bakh dafa wara sincere lamb dafaye diekh te mbok bi dou diekh felicitation ama et bonne continuation
Ama rekkkkk
Fode Khohte Ama dou dara
Akamaléna fan nak wa pikin rek boy niag mom awmasi morom
Wayé deugue nekh na merci Ama
Boy ndiang ba xeuy deeeee talibé khadre lh💖👑🔥💯🔐
Ama affaire bi iowla ndam rekk inchaALLAH
Merci bcp ama balde dina bakh
Je taime frère tu es direct machallah borrom khol bou nice bi machallah amal jammou gnou am jammou
Ama yee
Ama yee
Ama yee
Ama yee
Ama yee
ama kholebi mo rafete yalla nagua. nek roi des. arenes amine
amin waw
Moustapha Ndond wakh de
Thanks you very much brother Ama Baldeh
Nice na bien dit Ama
futur roi
Bien dit
Ama balde Mii Gorleu billahi ayy nitou Daimam moy ayy nitou Tayamm billahi Boy Niang sa Domou nay la dafa lerr billahi 👐👊👊👊👊
TeAm AmA YeiH👆✌
boy niang fo woul folou woul boy day liguiy bayilenko akh
Ama rekh
Amaa yhhhhhhh
légui lérena ama wakhe nga lepp kou beuguoule comprendre rek sa afair la ama mome yalla mokofi tek nite mounoussi dara
Merci
Niec na
Kii mbeurou pikine yi dagne koo bagne nakh mo lene a eupp tour ama yaye yeungeul pikine pikine yaye brome🇸🇳
Thierno Gaye bayil fene
iow séytané nga rek yén lu am pikine gueni dii sisu wa Guediawaye May lén nio diam
Thierno Gaye saytané
Thierno Gaye o
Thierno ligua wakh set guasi yalla
Ama Ama Ama Ama yéeee
merci
Ama rek la bagne ndayam gueumoul nday bopam boy niang rek
TeAm AmA je✌👌
La defaite de Sa Thies leur fait toujours mal. Mainteneant il dit qu'ils sont pas vraiement des amis. Qui dit ca?
Lep pikine la Ama Balde the king
merci balde faut respecter donc
Bou wakh dofé na nope yikay deuglou weur, ni Ama ni Boy Niang ne sont pas mes lutteurs mais quand il dit "locataires yi" ce n'est pas les locataires en personne mais ngiy dougou pikine té doukounioufa pour diakhassé guène dem sen yone. Yallah neu jam yaag sounou rèèw !
Bilahi dangua mana communiqué
Nice na
Ama vs boy Niang ça sera un bon combat.
Ma yeureum say none
Boy Niang laniou wakh
BIEN DIT DIAM SI IOE
Boy niang2 kassé moma nekh pikine
Yup
Ama balde Mii Gorleu billahi ayy nitou Daimam moy ayy nitou Tayamm billahi Boy Niang sa Domou nay la dafa lerr billahi 😂😂😂😂😂😂
Ama joue avc vos esprit et les incrédules son ai aguets quand il fit on es pas amis pour vous cela sous entend on ce connais pas non ama es son aîné et non son amis comprener bien et soyés grand dans la tête faîtes une bonne lecture des mots
ama rek
Nice
ama balde rek
Ya goré ya deugou nitt ki mbokeum bouko weetiok dara. 👍
seytané pikine gue do ndey dara diouguel ndy pikine doyal naniou si iow
eumeu boy Niang rk
Lou lrr nga wakhe bilay
Baravo ama👏 balla sa mbokou la te mbou ko moy adona bayi thi khél
Man pikine la dkeu mai ioe liguay wakh gueumoko seytané kharamata Ndiaye bii gua done ttchimmmm
Respet way djiguéne dou saga
Ama papay mbeur yii 😆
Tu derange certains lutteurs à pikine ils veulent te mettre en mal avec les pikinois
Aférbi ama la
Ama balla rek
Ama balla rek
nice f6
ama yeeeë wakhoi wadiou dou dagne bilaye
billaye yawe sa none la yeureume digua ame terangua te lo beugue si lambe. diguako ame dakhe dagua yarou gore ame kolere motakhe pikine nigui sisa guanawe thia kaname
Moustapha Ndond wakhall de
Boy niang langou wakh
Degool papay boy niang khamoul sarap ndayam
non boul saga yaw amga Papa bougo koukou saga faire plais
Topp
Ama reck pikine
Waw waw Japal sey mbok, ndakh "lamb" dey diekh tai mbok dou diékh.
Ama malheureusement lima begue si boy biang ioa rrik yamassi doyone. Mes brefff yalna diamm yaggue
Pikine la deukk dh mai wa pikine niou sofe boh wakho Balla gaye rkk sen xoll dii bonne teh Balla gaye yalla moko maye lii té wolof ndiaye néna nak kou nagnou lii yalla dogall do sone sa xoll dou diexe
Gnaw trop
Ama merci wah ga wahiii nit de 😉😉
boy Niang eumue séne bayi léne sisou bi Ama moye borom pikine
Yaw locataur yi séne xaliss lane yor di faye raspect léne
Diop chiekh déguena deugue dh
Môme pa falaye dagnouko may keur mom ak ndouba lès etc dagnon beuri
Urged
Dawlakou nga locataire ndakh wa fouladou nga
Sy Amadou khana khamoné boy niang wa thiés leu del ladjié nk avant tt
ON s'en fout,il est né et grandit à pikine,son père vient du fouladou et il en est fière.
Ama moy sene baye yene mborou pikine yi
boy Niang rék
Ama sa Bakane bi reuy neu😂
nieupa la beugue
Ama ioe danga commencer soff dépuis banga lonko akk wa guédiawaye bataye doule waaye
Ama ya niaw
pikini sene élément yingene di dagg dagué nii c pas intéressant faut faire comme avan cetaiS plus agréable. a cause de ça on oublie même vos vidéos
makhou 22 niom daniouko def woutoukayou xalis sénégalais loumou dougue eupeul ci.
Weah ilbfaut etre fran mneur
Ama yow sa beuré dafa sakkane ,mootax niu beugeuleu,ndax nungay beuré dafa am chance ,yow la pikine yakkaar ..
Ama gemoul Bopam
ama daf ma nekh paska dafa yaro
Ngakala mounane location
dagay sop d'où degue
Ama kassé amoul lenenne
Ama pikine la deuk fii lah bokk kéne meunou KO gueneii pikine Ama borom tiaw sa khiir
Ama laniou wax boy niang dfean la
🤣😂🤣😂au contraire kay
Dialile Mbaye boul tontou gni.wa. balla gaye lagnou
via Milano lolou guayy wax nank
Mor Fall yaw wa balla gaye ngeu😂😂😂
hanne bété bété wa gisga yaw sip gua sax fouma feitè
ama diapal balla ça balla la déréte dafa for
Ak bakaname bouu reuw bii sof
Ama dou goorr mome khaliss rék lay guiss
Khana yow gissoko
Thiey Sama Peuhl Firdou Bi Kaddou Yi Raffet Na
ama boula alal adouna bole ak boye niane dakh diarouko lambe deye diekh
Pikine amoul drapeau
ama bou moytoul dinaniouko diakhase ak grand yii bakh naa
pikine reck
boy niang rk mo defean bi
Bayiléne bouguéne amé ay clant n'a brom négou louyas yi gnoune amounou séne diote brom négou louyas yi dimeuli nane léne ba tayi amna wakh yo khamné rafétoul
Ama ndokh késse gua démal thie soufe si entrainer té bayi wégne yi
Sa guieming dh kom leuff
Danga bari niodoul beurél nak