Même ses propres adversaires veulent prendre une photo avec Monsieur sadio Mané🇸🇳💕💕💯💯pape matar Sarr 😍❤️🇸🇳🇸🇳🇸🇳 bamba 🤗💕💕💕❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️😍😍😍😍😍😍🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳❤️❤️
trocar santos futebol clube Ed Carlos DE Arruda Amorim mandar direito Sevilla mesmo trocar jogador Pape Alassene Gueye mandar direito santos futebol clube
C grave c tout le footballeur refusé de parler vou panser à koi par la c normal si u parler aujourd’hui demain vou transformer sa yoko bamou nèh c pa bien le journaliste Sénégal
Adouna biii nékk footballeur professionnel mossi dakhhh bilahiii🔥❤️ Comme j'ai peut être échoué dans ce domaine môme sama future Dome taay mou dée footballeur professionnel par force mba ma raay koo😂😂😂
Mane joueurs sénégalais yii nanioulen Wax deug niou taxaw Wax ak journaliste sénégalais yii kousi dme Europe après match xalato bagnie wax ak journaliste yii affaire de complexe yii moy lan naniou waxak askan wii diare Ko sii journaliste yii npeup nak doré ko sii Kalidou basi pape matar sarr naniou taxaw nako cadre yii djité may journaliste Senegal I yii sen page yii am vue
Sadio kou woyofe wathié bopame motakh borome bi di ko gueuneu yeukeuti maacha Allah
Amadou Sall nk dafa beugue équipe bi 🥰. Mais Sadio Mané tmt y’a pas deux comme lui mashaallah quelle modestie 🤩❤️
Même ses propres adversaires veulent prendre une photo avec monsieur Mané sadio 💪🏿
MachaAllah Sadio vrai star rwandais sakh dagniou ko fan fier de toi
Les meilleurs je vous aime vous êtes les meilleurs vraiment vraiment vous êtes les meilleurs joueurs sénégalais
Et moi j' aime
Les journalistes me tuent wallae😂😂tay dalouniousi dh
Vraiment journalistes yi ay diambar nguèn ndéké nii nguèn di sonné pour am interview franchement bon courage a vous ✌🏻
Mane en pape mactar douma ray way il es trop yaarrou lui😂❤️
Nan mais vous voyez le geste qu’a fait sadio mane😭❤️
Nek journaliste vraiment tmt metti na force à vous Yalla naléne Yalla taxawu
Les rwandais sont même fan des joueurs sénégalais ils prennent photos avec koulibaly et sadio mané🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🏆💪
C ça lafrique ils sont tous africain c pour cela qu'ils prennent photos même les occidentaux le font vive lafrique
des efforts pendant cette
Pape matar sarr ken wawul wakham de waye khale bi mingi def lu rey si terrain bi
sadio mo len guena nekk baye fall niom nieup
Ak p.a.cisse
Bilay
Mai d'égal journaliste bi néna "taye dalounousi d"😀😀😀😀😀😀😀😀😀
Kone yankey dégù? 🤣🤣🤣🤣🤣 il m'a tué ce journaliste
Kou guiss aliou sall si mbollomi. Lalal jaime
Sacré sadio mané
Vraiment mané immense
Bilay sadio dou nittou fi regarde cet échange de maillot très dynamique
MaachaaAllaah
c'est l'Afrique qui gagne
Même ses propres adversaires veulent prendre une photo avec Monsieur sadio Mané🇸🇳💕💕💯💯pape matar Sarr 😍❤️🇸🇳🇸🇳🇸🇳 bamba 🤗💕💕💕❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️😍😍😍😍😍😍🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳❤️❤️
Hommage aux journalistes😂😂
Bakho😂😂😂
Wa drianké bi loumoy outt fi
Hé les joueurs delene wakh journalistes yi c'est important
Makhala dangéne meuna yokou doléne bindeu jamais li joeurs yi wax 😂😂😂😂
Surtout lolou mdrrrr😂😂😂
Kham nite ki kham djikom Moko guene té journalistes Sénégal Yi khalé Yi Sakh kham nagne sene djiko
Walaye t'as dit vrai 🤣🤣🤣🤣🤣
Kou degue journaliste bi fin bi néna taye dalouniou thie 🤣🤣
Wouyyyyyyyyyyyy daguene Mouna fene rek 🤣🤣🤣🤣🤣🤣😭😭😭😭😭🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Pape matar khalela nak minagoul press bi
trocar santos futebol clube Ed Carlos DE Arruda Amorim mandar direito Sevilla mesmo trocar jogador Pape Alassene Gueye mandar direito santos futebol clube
C grave c tout le footballeur refusé de parler vou panser à koi par la c normal si u parler aujourd’hui demain vou transformer sa yoko bamou nèh c pa bien le journaliste Sénégal
Mame ngor diazaka néna sadio wakhal Sénégalais yi niou bayima saga😂
Wooy dou deugu 😂😂😂😂
Ya bari kham khM
😂😂😂😂😂
Wa mais Amadou sall lay guiss nii 😁?
@@mamadoudiallo4915 dey wadial nawétan yi 🤣🤣🤣
Bonjour.pape.l'amie.de.ma.mere.a.dit.que.je.vous.resanble😀😃😄🙂😺😸💛💙✨🤝🤲👐🙏🤘
Questo video e belissima
wa borom rasta yé d'où mam gôr😂😂
mom la
😂😂😂😂 Reporter mettina; kone li nguene di dadj
Dégoulo wadji khana néna tey dalougnou thi 🤣🤣🤣🤣
Dégoulo wadji khana néna tey dalougnou thi 🤣🤣🤣🤣
@@jaudbiagui6801 😂😂Bilay moma def ay rei
🤣🤣🤣🤣 makhala da nguene ci boler lou ci bokoul
journaliste bi nenako gnou har serigne sadio1😂😂
😮
Adouna biii nékk footballeur professionnel mossi dakhhh bilahiii🔥❤️
Comme j'ai peut être échoué dans ce domaine môme sama future Dome taay mou dée footballeur professionnel par force mba ma raay koo😂😂😂
Yalla Lou geun rek lay def dou Dioum Mouk sa weuseuk keneudouko dieul inchalla nalla yalla defal Lou kawe sa ndiort inchalla sadom inchalla
Mais Mame Goor kouko Bayi mou expliqué Sabaly le terme DIAZAKALIZÉ 😂😂😂
Wouuuy ray nguama🤣🤣🤣
😂😂😂
😂😂😂😂
Yallna. Diammoyag
PMS bien joué
Mame Gor mongui encaissé ay numéro joueur rek
yala ken manoul fekhe bamou may la lp am na niou sen bay am khalis ba pare niou melni mbam khoukhhhhh😂😂😝
🤣🤣🤣🤣🙈no bakho Mangui ram😃😃😃
Bayam amoul xaliss dafay sacc!
waye riba bi moko newi Kikey legui mou dehh fi🙄🙄🙄🙄 anna diabarji?? 😂🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣😂
@@ndiemendiaye9979 😂🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Ay way sénégalais mana togne 😀
Wa ki takhaw ak sadio mame goor diasaka walla😂
Diazaka tay guiss geu koula epou beuzz dé 😂
Nékk star nékh na
Wa mes domou président mom huuummmmmmmmm🙄🙄🙄🙄🙄🙄🙄
Vestiaires de équipe du Sénégal kom rideau manga kou niew dougou 0000000 de sérieux Mam ngolo jazaka. Amadou birou maffé snapeur niou niakk fayda yepp
Je te promets c'est devenu de la merde li amatoul béne sécurité
lep lagn bgue politisé li ladon wax si Can bi ct la mm chose allons rkkkk
😂🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Amadou Sall mboussou ndokh
Blh lou lerr gua wakhe
Pape Matar Sarr est très timide 😂
Aefcggdgq je suis ok sur tt
Wa journaliste yi nenane dalou niousi ay fen kate you srx beugouniou wax boulen len forced oh my god wax force la legui
Nn SADIO waliyou la bilay
Journaliste yi dagno meuneu fen motakh joueur yi ragal def interview 😅. Gneff
😂😂😂😂
🤣🤣🤣🤣
Bilay lolou motakh
@@originali155 w
Sadio Mané dafa yarou bilahi
Talibé sadio
🎉❤
Sarap khonili ay mame gore diajaka ak domi ibou dafa yi etc...
Yana niak fayda Di woté ken fale wouleen gen topsi Di woté 😡😭
dou niak fayda mais sen liguey laniouy def rek
Dalou léne thi môme nieupa daw
Why this cameraman he's calling this people for what?
He’s an idiot lol 😂
Journalistes sonounaniou
Dou bagne
Mba ki dou Diazakalisé but wou sadio mané yi
Ndaysan journalist yi man dama léna yaerem sakh
Je su pas d'accord les joueurs .sénégalais refuse les journalistes..un peu de respect
Journaliste yi sonn nagn 😄
😹😹😹😹😹😹
Ké maay séen fé dou amadou sall walla
Mbame bi molma deh !
Journaliste yi dagno mana yok lol ak dougou si vie privée diambouryi
sadio khana seu toubeuy ji amoul gnor
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
amadou sall mii khana dafa wann domou diambour
Daguene meuna induire nitt en erreur motakh niou ragal len
Mane joueurs sénégalais yii nanioulen Wax deug niou taxaw Wax ak journaliste sénégalais yii kousi dme Europe après match xalato bagnie wax ak journaliste yii affaire de complexe yii moy lan naniou waxak askan wii diare Ko sii journaliste yii npeup nak doré ko sii Kalidou basi pape matar sarr naniou taxaw nako cadre yii djité may journaliste Senegal I yii sen page yii am vue
waayy nio xam li foot rekk la
ayy ate si guinaw donnoulen wone fi
mais d une part aussi yen press de ngueni yokk motah boyi di len di daw
Mais daniouy tardé vol bi …Lolou laaniou wax
Amadou Sall lafi guiss 😁
Mom la dé
journalistes da meti
Mais yéne li est-ce que woor na ki dieule na maillot sadio bi dé th
Danga fokné sadio dafa bayi bopam nnou
Qyelle honte amadou sall mets toi au regime tu edt tres jeune poir ca gorguu aud ce gosse a faire du sport nom fe dieu
Bayiko mou rey bopam !
😂c op lui c sn petit frère Amadou mo eupeu ki
Pa Abdou Cissé khalé bimou andal kanela
dafa melni domou famara.D la d
C'est pas ton problème.
@@senegalaise1 ah peut être
@@diopfallou2135 yalla nala diam sonnal
@@natouleawebell2280 amine AK ioe TMT yalnala diam Sonal bro 🙏🏾
Khana ponkal bobou amadou sall la
Boy yi fouuuy naniou trop ahhh.. parlez avec les journalistes doul waye
Way yawit doul kou mou nekh def louko nekh, khana ambulant nga yagua naniou la péral motakh ngay wakhé nii.
@@ID-tb5eu 😂😂😂😂
@@ID-tb5eu 😂😂do nitou fii
Meuno lene siguii xol kine fene rk fene rk shimm
Journaliste yi niak nagne diom 🐽
6
Man lima guiss guiss Guen KO wakeur Macky yi 2 personnes 2ton
😂🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣 riba rek
Wa li moy lan koun wo lankeu lu khew
prck k niom dagno meuna fen en plus ils posent des questions bêtes...
en plus Edu ak idrissa dagno yakamti sinon ils vont rater leurs avions...