Mon éternel amour CHIEKH MOUHIDINE ALPHA SAMBA DIALLO je regrette de t'avoir connu tardivement. Tes enseignements ont fait de moi une femme qui connait sa valeur et la place que j'occupe au sien de la société. Nous vivons dans un monde ou le mal triomphe au détriment du bien mais heureusement que nous CHIEKH MOUHIDINE pour nous guider sur le bon chemin et nous rappelle que quelles que soit notre posture, notre richesse, notre appartenance ... nous seront un jour dans une tombe face a nos actes qu'ils soient bons ou mauvais DIEU nous jugera. Cette vie est éphémère ,pensons aux enseignements de notre CHIEKH pour une vie saine et appréciée par halla le tout puissant. CHIEKH MOUHIDINE JE T'AIME A MOURIR
Yalla n'a Yalla haréko thia Dianatoule Firdawesy ak mboléme dioulitte gna djitou thia Barzak Yalla n'a ALDIANA Di séne Barrabe bou moudieu té Sah thi darradiaye Rassoulillah Mâcha Allah Yalla n'a Yalla faye té téraleléne thi Dianatoule Firdawesy thi darradiaye Rassoulillah
Allahou Akbar sama khôl toyna yalla na yalla geuna yegal makhamam si aldjana ya geuna kawe Senegal gnakna nitt kou magg yalla nagnou ko yalla fayal si barke seydina Mohamed (sws)
سمعته يشهد الخديم معروف% والناس يشهده من بعد معروف الشيخ (صامبا جالو) نعا من بعد جهتده % في خدمة الدين والعلوم وقوف علامه أثرسجود سيمته % كشيف للحية بهيج وعكوف فحل تقي ومحي الدين مكتفي % نئاه قلبي موحوش ومعطوف وكان يعلن إحسانا بمن سلفوا% وبعد تعلنه الإحسان ألوف وكان عبدا لينا خاشعا عدلا % وناصحاصالح بالبين مألوف وكان داعية تصغا فصاحته % زكي النفس ذكي العقل موجوف وكان سامح بالجاه لزهدته % علامة عالما حبرا وموصوف هذا حيا وخصال العسل يؤنسه % توفي وبكته بعد صفوف صلاة ربي علي خير الوري أبدا % وعنه رضوان رب الناس رؤوف LE/17/04/20 خويدم الخديم ابراهيم غي
En afrique "un vieillard qui meurt c'est une bibliothéque qui brûle" Amadou Ampathé bâ c'est ce genre de personne qu'il ns parlait.Que son âme repose en paix🙏
Machallah Bamako commence deglou yaagoull d mai djang na si mom lu bari yalla nako yalla sammou goudeul fan wi mai beug na xam prochaine conférence am ucad ndax ma feekeko
Salam frère Samba DIOP linga wax walahi deug leu. Il a rendu l'âme cette nuit, Yalnako Yalla yeureum té xaréko Firdawsi. Je l'ai découvert récemment mais c'est maintenant que je comprends que voilà un grand homme, un érudit, un Saint. Yalnagnou Borom bi tass si barkém
Salam. Yalla na Yallah fay yiwou adouna ak al'akhira Gorgui Mouhieddine Samba DIALLO Yalla nala Sunu Borom yombal-la Hadj bou nangou. Niaane-ko té am ci koolouté (yakhine, in cha Allah, Yallah dinalako yombal-lal.
Salam tout le monde, je suis Mouride wayé dama la beugu té yalla takh ndakh nitt kou mbandou leu té fess telleu ak ham ham.yalla n'a sunu borom Faye leu sa kholll
Walay thiofel bima am si yaw ken menouko natee yallah na yalla fayla li laniou sokhla wayee dou mafi ne wala mafi def mafi wax xam xam laniou begue te yallah xam nani xam xam ak guene geum sun boop ak guene xam niouy kan 👏👏👏👏🙏🙏🙏🙏🙏
Mon éternel amour CHIEKH MOUHIDINE ALPHA SAMBA DIALLO je regrette de t'avoir connu tardivement. Tes enseignements ont fait de moi une femme qui connait sa valeur et la place que j'occupe au sien de la société. Nous vivons dans un monde ou le mal triomphe au détriment du bien mais heureusement que nous CHIEKH MOUHIDINE pour nous guider sur le bon chemin et nous rappelle que quelles que soit notre posture, notre richesse, notre appartenance ... nous seront un jour dans une tombe face a nos actes qu'ils soient bons ou mauvais DIEU nous jugera. Cette vie est éphémère ,pensons aux enseignements de notre CHIEKH pour une vie saine et appréciée par halla le tout puissant.
CHIEKH MOUHIDINE JE T'AIME A MOURIR
Samba diallo na delsouwate thi adouna
Yalla n'a Yalla haréko thia Dianatoule Firdawesy ak mboléme dioulitte gna djitou thia Barzak Yalla n'a ALDIANA Di séne Barrabe bou moudieu té Sah thi darradiaye Rassoulillah
Mâcha Allah Yalla n'a Yalla faye té téraleléne thi Dianatoule Firdawesy thi darradiaye Rassoulillah
Aminé
Allahou Akbar sama khôl toyna yalla na yalla geuna yegal makhamam si aldjana ya geuna kawe Senegal gnakna nitt kou magg yalla nagnou ko yalla fayal si barke seydina Mohamed (sws)
Amine ya Allah rabbi
أحببتك في الله ولحبك شيخ الخديم. لقد غادرت الدنيا ولكن محاضراتك ثابتة معنا رحمك الله.
Je regrette de ne pas t avoir connu bientôt nous t t'aimons beaucoup que dieu vous bénisse merci de tout coeur
Un père pour moi et à fait pour moi une chose que j'oublierais jamais que le bon Dieu te laisse avec nous avec une bonne santé Amine
4É@
Que Allah lnaccode le paradis firdaws.
Mashallah un grand guide religieux un homme multidimensionnelle.
Merci pour ce que vous nous avez laisser
anta oumy Bada oumy 😢😢😢❤❤
Merci Diallo, Yalla nako Yalla kharè adiana, Yaw ak Serigne Sam Mbaye ak Serigne Moustapha Saliou yalla rek molèni fay, ay Serigne deugg nguéne
Un vrai guide religieux indépendant et integre je vous estime beaucoup, Paix à votre âme firdawsi reposer là-bas Yarabi ilahi !!!!!
Je me rappelle, j'etais présent ce jour là.
Allah Jarama ajarama Thierno mashallah
Machallah 👌👌👍
Il est unique serign Samba Diallo Yalla na Yalla yessal yeurmande ci sa kaw te tass niou si sa barke ci barke Alkhourane
Qui est la a ce jour de sa disparition....je l’aime psk il modeste.....paix a son âme yalla rek mola fi sagna dieulé
Mois
Moi
Moi
Un homme multidimensionel, un sage repose en paix m0n référence 😭
Machallah I am very proud to this Cheikh. Qu'ALLAH te bénisse Cheikh Mouhidine vous rendez vraiment l'homme sa dignité originelle.
سمعته يشهد الخديم معروف% والناس يشهده من بعد معروف
الشيخ (صامبا جالو) نعا من بعد جهتده % في خدمة الدين والعلوم وقوف
علامه أثرسجود سيمته % كشيف للحية بهيج وعكوف
فحل تقي ومحي الدين مكتفي % نئاه قلبي موحوش ومعطوف
وكان يعلن إحسانا بمن سلفوا% وبعد تعلنه الإحسان ألوف
وكان عبدا لينا خاشعا عدلا % وناصحاصالح بالبين مألوف
وكان داعية تصغا فصاحته % زكي النفس ذكي العقل موجوف
وكان سامح بالجاه لزهدته % علامة عالما حبرا وموصوف
هذا حيا وخصال العسل يؤنسه % توفي وبكته بعد صفوف
صلاة ربي علي خير الوري أبدا % وعنه رضوان رب الناس رؤوف
LE/17/04/20
خويدم الخديم ابراهيم غي
Vraiment c'est un trésor pour l'islam que firdawsi soit sa demeure éternelle
Amine
Serigne sam mbaye rek lalay kholee
😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭👑👑
Moussa Conatè billahi
Wallahi tay rek laa done wax lu melnii nga wax
😭😭😭😭😭☝🙏😍
C'est la vérité qui es sur seulement tu parles toujours la vérité oustaz samba diallo nous vous aimons beaucoup !!!
Yaw ya wara djite rewmi
Ndayesan ya bakha yalla nala yalla Doli ler
Yalna YALLA yook sa leer ci barké SEYDINA MOHAMED RASSOULOULAH SALLALAHOU ALEYHI WASSALAM
ay way ki mo bakh way yallnako yalla fay yagal kafi lolou si barke seydina mouhamed 👌👌👌
il est multidimensionnelle il est vraiment bon de l'écouter
A
En afrique "un vieillard qui meurt c'est une bibliothéque qui brûle" Amadou Ampathé bâ c'est ce genre de personne qu'il ns parlait.Que son âme repose en paix🙏
Vérité absolue mon frére
Un grand homme ndeysane yallah nala yallah yeureum
لست خليفة للطريقة بل أنت خليفة للإسلام والمسلمين ايدكم الله ونصركم وأطال عمركم آمين يارب العالمين
Haakaza
Nittt cou nioule niaccoule dara si aduna akh alakhira bou guaiss tau thiossannamm Macha allah
Yalla na ko yalla yéuram kharé ko aldiana
Yalla na yalla yeureum ta kharé ko aldiana thi barkep seydina mouhamed (psl)
Ken dou yaw Diallo yalna yalla yésal yermandé si kawam
Bilahi je l'admire beaucoup ce marabout exceptionnel parmi tant. Longue vie et santé à vous
Sama papa Baye Papa Seye yalnako YALLA diégal bolékok malakam yeurmandé yokou ay léram oubilko ay khéweul kharéko ALDIANA🤲🙏😭😭😭😭
voici un marabout qui nous dit la vérité yallah nafi yague té werr
wawaw
Aminé
ÂMÎNE YÂRABAL ALAMÎNA
Mannn dé dina dokh bo séttikô démakô sopp lool
Daizakhoumoul hairi
Macha Allah! Yalla nako yalla yeruenm té kharé ko aldiana 😭😭amiine yarabine weni biki 😭😭😭❤❤❤❤
Ki es la en ce moment
Oustaz yallah na yallah fayal nioula🙏
Wallay mame j'aimerais tellement te voir avant que tu partes mais tu resteras toujours gravé dans ma mémoire
NDEYASSANE yalna yallah yeureme khare kho aldjana barcy Mohamed s.a.w
Yalla naniou ko yalla fayal inchallah
Bilay serigne bi toyal na sama xol... bimouy netali histoir seydina mouhamet psl
Machallah yalla na yalla yobou sa lère té tass niou ci sa barké🙏❤🎉❤
والله أنا من أحبابك واستمتع بكلامك في كل يوم صباحا ومساءا ليتنا أن نعرف قيمته قبل فوات الوقت
Walahi ya beugue sa khét yalna yalla Dolé ay fanam té wéral KO barkéb borom touba
Dieum djouuuu fesss deeelll ak kham kham ´guinii yalnaaaa baye Niass terouleuuuu❤️❤️❤️❤️❤️😭😭😭😭
Machallah Bamako commence deglou yaagoull d mai djang na si mom lu bari yalla nako yalla sammou goudeul fan wi mai beug na xam prochaine conférence am ucad ndax ma feekeko
Théiye sope na la ki moye nitu yalla
Na yalla gudale ca fane
Islame réka wore
Très pertinent cheikh mouhidine yague fii rek té werr
Amiine
Nitou yalla dague dague yal na ko sounu brome doli ay léram barké saydina moukhamed
Yalla na yalla goudal sa fan té yokou sa xam xam machallah
Kénn dou Moustapha billahi 🙏😍❣
Wallahi ken dou mouhamadou Mustapha
Bilahi
bala sènègal di xam wadji kimou done walahi day fèkk mou wonnè ganaw,dou sama serigne wayè ...kou yalla mèy laa
Moo aay ci élève bouy def examen
Wa noumay déf ba guiss kou sa wadji
Lou wer nga wax yalla nakofi yalla bayi basi kanam
Salam frère Samba DIOP linga wax walahi deug leu. Il a rendu l'âme cette nuit, Yalnako Yalla yeureum té xaréko Firdawsi. Je l'ai découvert récemment mais c'est maintenant que je comprends que voilà un grand homme, un érudit, un Saint. Yalnagnou Borom bi tass si barkém
Sa wax djiii amna ndakh mane dh bess bimou guuénné adouna lako xam
CHEIKH MOUHIDINE SAMBA DIALLO je vous aime fort repose en Paix tu resteras toujours dans mon ❤️
😭😭😭 yalna dianatou firdawsi don sa keur si barke cheikhoul khadim amine
Dama la sopon lol barké S.Touba 🙏
diouye la warna yaw cheikhé mohidina bilahi l'islam diouy nala yalna yalla doly yarmandi
Laa illakha illallahou seydina mouhamad rassulloulahi sallalahou aleyhi wassalam.
J'ai tellement pleuré 💔🙏🏾 yal'neu niou ya'Allah tass thi barkél
Que Fiirdawsi soit sa demeure éternelle Amine yarabi 🙏😭😭😭😭
Yalna fi yague lole té wére barecép borom daroul mouhti
Yallah na yallah yessal yeurmanéme si mome
Un sage repose en paix que t'accueilles dans son paradis céleste
Macha allah il dit k la vérité yalla nako yalla meye fane wou goudou si barké nabina mouhamad sala lahou alayhi wa salame
Machallah. Yallah nanioula Yallah fayal, thi fay yi gueune
Dieureudief Cheikh bi dounieul 120ans inchallah
Mélnané doundou nako ndakh li dafay sakh ba fawou in challah
C la première fois ma setaan ko mais xam xam kesse la j'adore sama khel mi yeup dem makka mothi nek ndakh video bi
Salam. Yalla na Yallah fay yiwou adouna ak al'akhira Gorgui Mouhieddine Samba DIALLO
Yalla nala Sunu Borom yombal-la Hadj bou nangou. Niaane-ko té am ci koolouté (yakhine, in cha Allah, Yallah dinalako yombal-lal.
Machallah yalla nala co yalla yombalal ...Mane mi lolou rék la beugeu
Allahou Akbar Billy wolahi sama xol toyna😢😢
Ma challahou barakal lahou fika wakhtanwi nekhna amna solo yalna yalla fayla goddal sa fan
Mashala il a le Coeur pur, repose en paix le Senegal a perdu un grand homme 😭😭😭🙏🙏🙏❤️.
Beugua na deem ziar ko inchallah ki mooy serigne nak
Mo takh yalla yoniwate yonente bi si der bou gnoule Mouy seydina limamou laye
Yalna yalla goudal saye fane
Ndeyssane sunu mame Segñ sam mbaye la sama xel dem bi ma guissé sa baye bi di def lou am solo yalla nalen sa borom faye
Machallah sama xol❤sédna lal yalla na yalla guoudal sa fane si barkép moustapha 🤲😭
Man dioyna si lii.BILAHI Seydina MOUHAMED ken du mome walahi...
Walahii
Que Dieu lui accorde le repos amine...
Yalna samou cheikh mouhidine samba diallo
Sague fii lole té wérrrr, Ho serigne touba , vive islame
Salam tout le monde, je suis Mouride wayé dama la beugu té yalla takh ndakh nitt kou mbandou leu té fess telleu ak ham ham.yalla n'a sunu borom Faye leu sa kholll
❤❤❤❤
Paix à son âme que aljana Firdaws sois sa demeure amin ya rabi
Paix á son âme on a perdu un grand guide ses paroles restent tjrs nouvelles
Masha'Allah sama serigne qu' Allah veille sur toi .
Machahalla
Yalla na yalla Yoko leram
Machallah Serigne bi mane mom danguama néx.yallah yaggal lafi loll amine
Cheik oustass diallo divine reste peace lumineux😢
Qu'allah vous protége cheikh
Machalla ❤❤cheikh mouhidine..xam xam rek gi wakh ma sha Allah
Franchement rèthiouna loumala tèloula kham que l paradis soit ta demeure éternelle
Machallh yalna fayla si barke mouhamed psl
Serigne bi yalla nako yalla arrrre t defal la jiam yageu fi looool
Wolahi yalafeyila
Yall na faneu wi goudou merci pour le partage
Walay thiofel bima am si yaw ken menouko natee yallah na yalla fayla li laniou sokhla wayee dou mafi ne wala mafi def mafi wax xam xam laniou begue te yallah xam nani xam xam ak guene geum sun boop ak guene xam niouy kan 👏👏👏👏🙏🙏🙏🙏🙏
ua-cam.com/video/ey1VL4KlxSE/v-deo.html
@@kmrsilver7916 merci bcp
@@seydinaoumarmbengue3523 avec plaisir ; mes respects ; et propagez a lafrique et au monde
Yalna yalla fayela si barke baye niass
Machallah chiekh bi yalla na yalla faye la si barké seydina mouhamed psl
Machahallah Cheikh bi !
اللهم اغفر له وارحمه ووسع مدخله واكرم نزله برحمتك يا ارحم الراحمين اللهم نور قبره من نور خيرخلق الله صلى الله عليه وسلم يا رب 🤲🤲🤲🤲🤲🤲😭😭😭
Masha allah yalna yalla dolli wér gui amine
Que lui fait enter dans son paradise.
Machallah yalla na yallagoudal sa fannne amiiinnnnne
ua-cam.com/video/ey1VL4KlxSE/v-deo.html
Un vrai MARABOUT des temps moderne
Machalla et quel enseignements
Machahla yalna YallA yok sa fame mayla weure si barcke nabi slw
Machallah Diallo yagg fi teh and ak weer
Yalnaa la Ya Allah harreh Aljantull firdaws
Waydawlou yi yalnalèn YALLA yeureum kharélèn ALDIANA 🤲🙏😭😭