Abdou Lakhat Ndiaye attaque Gris Bordeaux : " Naniou Bayi liniou def, nioun Bira Sène laniou…"

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 20 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 46

  • @moussapayemane4167
    @moussapayemane4167 2 місяці тому +5

    Bouléne fonto nite gni,Bouléne néhé faral Bira mais son mandat est terminé nadém,Malick Ngom president CNG inchalah

  • @princelaye8210
    @princelaye8210 2 місяці тому +5

    Sheutteuteu Wadji barina probléme chaque jour histoire

  • @layeNdiaye77
    @layeNdiaye77 2 місяці тому +12

    Malick ngom bi ngendi bania dégueu par la force dinguen KO degue

  • @ibrahimafall8652
    @ibrahimafall8652 2 місяці тому

    Merci abdou lahat merci beaucoup ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @mayorodiop1547
    @mayorodiop1547 2 місяці тому +5

    Mais managers yi yenay kane ba keneu warou lene contredire ?

  • @ibrahimawalydiouf5745
    @ibrahimawalydiouf5745 2 місяці тому +12

    Amolene droit bock thi niou wara tane président CNG ménagés mbeur mo takh nguéne existenté kon mbeur yii nguéne wara andale yéne ménagés yii sénn intérêt rék

    • @djimbaniang2190
      @djimbaniang2190 2 місяці тому +1

      Vraiment

    • @talladiagne8092
      @talladiagne8092 2 місяці тому +2

      Mais ils sont le droit de donner leurs avis

    • @malickdiop4352
      @malickdiop4352 2 місяці тому

      Mbeur sakh waroul tane Président mbeur you mak yi sen intérêt rk l’a ministre doit trancher tout simplement

    • @PapeDiego-jb7cq
      @PapeDiego-jb7cq 2 місяці тому

      Lamb 3 acteurs la am ba 4 ben prometeur/ mbeur / ménager AK journaliste yi donc vote mo warra am

  • @AdamaThiam-ut2pj
    @AdamaThiam-ut2pj 2 місяці тому +4

    Ki dafa bari wah

  • @mamesaliou8963
    @mamesaliou8963 2 місяці тому +4

    late ndiaye wakhe reck ngaye défe

  • @layeNdiaye77
    @layeNdiaye77 2 місяці тому +2

    Lutte TV yeen khana bira nguen andal😮

  • @idrissadione7279
    @idrissadione7279 2 місяці тому +4

    Malik ngom waaaaaay ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤lagnou wakhe Maliiiiiiiiiiiiiiiiiiiiik

  • @sonkofocus2024-ph4hv
    @sonkofocus2024-ph4hv 2 місяці тому +6

    Mai lutte tv khana bira séne ngéniy ligueyall 😮

    • @DounkhafOmar
      @DounkhafOmar 2 місяці тому +1

      Lolou de mome lay niraul

  • @galayebeye7868
    @galayebeye7868 2 місяці тому +1

    Lutt tv yéne bira ngéne andal bayi léne séne affaire yi

  • @mamemoussagueye952
    @mamemoussagueye952 2 місяці тому +1

    Ada Fass limou am manager mayoukoko mais mbolo mokoko may

  • @IbrahimaNdiaye-jj8gu
    @IbrahimaNdiaye-jj8gu 2 місяці тому +5

    Ce gars est très bavard

  • @AdamaSeck-x9c
    @AdamaSeck-x9c 2 місяці тому

    Wa lutte tv yéna ❎❎❎❎❎❎❎❎❎❌❌❌❌❌❌❌❌❌✔

  • @galayebeye7868
    @galayebeye7868 2 місяці тому +7

    Yaw abdou lahat ndiaye mano maye nit gni diame yaw kom ya mom lamb dji Bira séne par force dafi diougué ndm yaw nak lahat foumala guiss nala nokk

    • @mactardiallo2085
      @mactardiallo2085 2 місяці тому

      Je panse que Chacun defandre son intéré meme beur yii gua yii guis sax gomou niou sén pop

  • @SerigneMbaye-s2k
    @SerigneMbaye-s2k 2 місяці тому

    Moytouléne loby Aziz Ndiaye

  • @Moussamaafé
    @Moussamaafé 2 місяці тому

    Chaque menager 1 écurie

  • @abdoulayendoye1803
    @abdoulayendoye1803 2 місяці тому

    Malick Ngom ❤

  • @almaktoumdiop8749
    @almaktoumdiop8749 2 місяці тому +3

    Msni bira séne dafa wara déme gñoune khamounou gour boudoule dhièkh gñiloufi nèkalone gñiépa dème nanou lou takh nou wakh laa balla gaye nagou wocsi wakh grix khana gua yape mè grix loumou wakh deugeula yaw krna khamoula grix am na droit wakh kimou farale yaw sa boche rèk gaye dèfendre gris khsmqlo ko douss gris mola geuneu nèka nandité yaw koula guis kham ni mètriséwoulo ligaye wakh yagui di diakhasé lou bòkoule pastéf ak bénene partí ani loufi andi lolou ? Yaw dof deugeu gua kéba waroula dèfa micro 😂😂

  • @Kingthiama9733
    @Kingthiama9733 2 місяці тому

    Ki tenyi dafa ndy rew 😂

  • @GeyeMoudou
    @GeyeMoudou 2 місяці тому +4

    Yaw daga bari wah sof

  • @Matarmboup-u
    @Matarmboup-u 2 місяці тому

    Môme dé gris toudou Ko kou môme khar mi mou bayi boum bi bari wakh soff n’a trop

  • @AlassaneMbow-d9w
    @AlassaneMbow-d9w 2 місяці тому

    Palla makk dayy am foula li doussa thieur

  • @moussafaye6263
    @moussafaye6263 2 місяці тому

    Diaguène dieuf waye

  • @papefaye272
    @papefaye272 2 місяці тому +1

    Yaw ken attaquer woullla beug nga ndaye dagassanter trop

  • @oumardiop6454
    @oumardiop6454 2 місяці тому

    Doff la

  • @afro3827
    @afro3827 2 місяці тому

    Ada fass lac 2 dala nara dorr baga dé si stade bi

  • @coeur2lion38
    @coeur2lion38 2 місяці тому

    Wadji berina wah trop tjr il parle bc sans rien dire

  • @abdoukarimfaye140
    @abdoukarimfaye140 2 місяці тому

    Ce gars il croit pouvoir démolir tt le monde xamodara di wakh rek barina wakh torop

  • @likh-oj6lx
    @likh-oj6lx 2 місяці тому

    Xana gueumoné si deuk bi gua deuk,

  • @votremiroir7612
    @votremiroir7612 2 місяці тому

    yaw ya wara may nit gni diamou. do mbeur té nékato prometeur.

  • @babacarfaye4446
    @babacarfaye4446 2 місяці тому

    Malick Ngom rk fini les magouilles

  • @SerigneoumarNdiaye
    @SerigneoumarNdiaye 2 місяці тому

    Samay yaw kou sof nga quoi

  • @lougalo969
    @lougalo969 2 місяці тому

    Yawite khamooo kiye nieuwe ndakh daye eclater mafia managers. Bene nite beuga yore 10 lutteurs dafè wara dièkhe. Vpus n etes pas plus meritants que les coaches pour lèkk 10% cachet

  • @likh-oj6lx
    @likh-oj6lx 2 місяці тому

    Atak contre alburax avc c lutteur c dmch

  • @CASI7797
    @CASI7797 2 місяці тому

    Lobby Aziz Ndiaye mofi beug teikk Malick Ngom

    • @Matarmboup-u
      @Matarmboup-u 2 місяці тому

      Aziz 𝑴𝒂𝒍𝒊𝒄𝒌 la andal dé

  • @moussafaye6263
    @moussafaye6263 2 місяці тому +1

    Gris na wakh çi parfums Paris yah

  • @PapeSow-l2d
    @PapeSow-l2d 2 місяці тому +1

    Yaw dangeu beug dagasanté