Dafa nékon di Accoucher Aprés mou Danou si lalle BI

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 23 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 298

  • @aidadiouf5085
    @aidadiouf5085 Рік тому +6

    Ndeysane 😭😭 yalla nako yalla kharé aldiana fidawsi si barké seringe saliou MBAcké 🤲 amine yarabi 🤲

  • @marietheresengom809
    @marietheresengom809 2 роки тому +3

    Toubap yi dañio fonk santé ak loula meuna dale danguay eumb ñioulay raay ngay accouché ñioulay nékhal nanla massa ba xalé bi souy ñieuw sakh doko yeuk bilay, yalla nako yalla yeureum kharéko adjana firdawsi

  • @bajjanmaram4409
    @bajjanmaram4409 2 роки тому

    Bravo Soxna si.. Il faut toujours DÉNONCER

  • @kebemerediva2680
    @kebemerediva2680 2 роки тому +2

    Allahou akbar thiéy yallah li nagnousi wakh li eupena dé😭😭😭😭

  • @fatoundour4586
    @fatoundour4586 Рік тому +1

    Mane dé sama première dome j'ai vécu klk chose avec la sage femme lo xamni soumeuko xalaté damay ragal eumbate , actuellement suis anceinte mai soumeu guissé yéneu vidéo yi damay geuneu tite,wayé sage femme bobou dé dotouko défeuti bimeu fadio beu wer sama fil la rabeu fékeuko fofou dotouko doli,yalna yalla may aume you sédeu bépeu djiguéne bousi tolou si barkep seydina limamou psl

  • @mbayeseynabou9258
    @mbayeseynabou9258 6 років тому +15

    Bilaye sage femme yiii gno Bone rek té sokhore gniiii

  • @mamannguenar6725
    @mamannguenar6725 6 років тому +3

    yalnako yalla yeureum té kharé ko aldiana fidawsi

  • @maynadieng1624
    @maynadieng1624 6 років тому +40

    Lii mom kouko degg do beugeu tomber enceinte bay accoucher 😱😱😭😭 allakhou Akbar 😭😭

  • @thiatfallmory1445
    @thiatfallmory1445 6 років тому

    Ho thie Senegal gni gnou wara sauve bougnou deme ba dignou Raye fougnou dieume😭😭 fithie Italia De khagne Na deukhie bie amoul darà waye toubabebie boula de fathie Daye wala gnaye acouche Daye melnie dagnou la nobe gnou senegale yie nakh gnouni aye dioulite lagnou Bala gueme ni gnou senegale dina gnou dougue aldiana aha toubabie di fathie thie europe de mome dina dougue bamare apres sounou borom dogual khol dossier medecin you Senegal yie ba mare gnene bal Sama khol ❤️😭😭😭diekhena torop WA salam

  • @hawadiawara4001
    @hawadiawara4001 6 років тому +1

    Pouffff j'ai mal à la tête j'ai envie daracher les yeux de ce sage femme pourquoi chez ns on ne connaît pas le droit de l'humanité ici en France les sage se comporte avec toi comme t'es propre soeurs tellement gentille et douces envers toi à ta sortie de d'hôpital tu es obligé de partir les voir en disant un seul mot ( MERCIE)

  • @cisseseynabou305
    @cisseseynabou305 6 років тому

    Quel incompétence li dal moy senegal they yallah yalnalene yallah diapalei

  • @sigathiare2077
    @sigathiare2077 5 років тому +1

    Soubahana mettina trop yalna KO yalla yeureum

  • @AdamaFaye-pe5gw
    @AdamaFaye-pe5gw Рік тому

    Sage femme you barri legui khamou drra sokhor nagne sénne kholl yii talli woulll😢😢😢 lii mettina trop wayyy😢😢

  • @mbenendiaye4737
    @mbenendiaye4737 Рік тому

    😭😭😭😭

  • @fatouseck7185
    @fatouseck7185 6 років тому

    Cim li mo takh senegale du deeem ! Yermande ak Respect ZERO ci Djigueen bu Enciente !!! Europe mom ndeysan tubab yi akagnio am yermande ak Respect ta machalla toppato bi ba kerok ngay am doom ! Li djarna ghenn senegal way ci kuko man pour am doom kesse nak ...kom gniom monugniu sen ligguey cim ndm bonn bay begua de ...ki Porteplente lenko way Da Wara TEUDD Kasssoooooo ndm

  • @khadythiamt2949
    @khadythiamt2949 4 роки тому

    Metina🤲🏿🤲🏿🤲🏿

  • @mohameddiallo2541
    @mohameddiallo2541 2 роки тому +3

    Paix à son ame 😭😭😭😭

  • @gninguebamba8715
    @gninguebamba8715 5 років тому +1

    Kocou demoula d'où kocou rekk la

  • @asmaabdoulaziztoure6478
    @asmaabdoulaziztoure6478 5 років тому +1

    Iii daal yéména trop😊😊😊

  • @margueritebetty1205
    @margueritebetty1205 6 років тому +1

    sante yalla.bou weure comme faigne na sante serigne touba dollai sante

  • @dieynabasock487
    @dieynabasock487 6 років тому +1

    Allahou Akbar Thiéy Sage femme yi

  • @rozefatou8568
    @rozefatou8568 6 років тому

    yalnala YALLA yeureum si barké seydina MOHAMMED

  • @devinegrace9395
    @devinegrace9395 11 місяців тому

    que son âme repose en paix

  • @dieumbesarr4971
    @dieumbesarr4971 3 роки тому

    Li doye na ware dé Sénégal légii mom woratout

  • @sowaminata9659
    @sowaminata9659 6 років тому +1

    Alahou akbar limasi metti rek moy dou moudiou feneu

  • @roukayarouk1843
    @roukayarouk1843 6 років тому +9

    😭😭😭😭😭😭😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😢😢😢😢😢😭😭😭😭😭😭😭😭😢😢😢😢😢😢😢pop sama.yarame dawna j ai les larmes aux yeux no âme na tite trop thi mane nooooo waiyyyy trop c trop bilahi 😢😢😭😭😭😭😭😭😭😢😢😢😢😢

    • @malickngom2333
      @malickngom2333 6 років тому

      khalasss li mètina lolll clinic bobou warna mana fermè vraiment parce que rusque la

  • @miryamsy3430
    @miryamsy3430 6 років тому +3

    Soumay dgue li damay rouss sakh😢ay way li mety na dh😢😢😢😢😢😢😢

  • @thillosoumare1522
    @thillosoumare1522 6 років тому

    Hi en n'écoutant cette histoire j'ai même 😱 peur de tomber enceinte franchement Sénégal métina trop j'ai trop mal ô coeur

  • @ndiawbadiane5533
    @ndiawbadiane5533 6 років тому +4

    sage femme yii niou niaff sén diaye laniou doméram yi niou done

  • @diadoukhouma8610
    @diadoukhouma8610 6 років тому +14

    les femmes souffrent vraiment dans les maternités mo takh kéne beuguetoul ame dôme

  • @dieumbesarr4971
    @dieumbesarr4971 3 роки тому

    Li doye na ware trope yalla nélawout Dina lêral yeupou

  • @minetoudiakite8900
    @minetoudiakite8900 6 років тому

    Allahou Akbar

  • @mamediarradiop9885
    @mamediarradiop9885 5 років тому +6

    Non cette sage-femme est malade. elle n'est pas sage-femme mais mauvaise femme 😲😲

  • @ndeyefall904
    @ndeyefall904 6 років тому +19

    C'est la clinique Sokhna Nene BA de Diourbel

  • @anaca3anaca350
    @anaca3anaca350 6 років тому +13

    Soubhanallah li guen ci Mane dotoul gnowatt...bilqhi soudon sama soeur dotou niuko defati bilahi

    • @niangmodou1405
      @niangmodou1405 6 років тому +2

      Soxna si yallana boumoula dall walla Mouy dall sa mbokou Sénégal Dara dokhoul

  • @Fatimazahra-qp5yv
    @Fatimazahra-qp5yv 6 років тому +36

    Non !!! impossible ! dans quel pays vivons nous ! 😢 mais le procureur doit prendre ses responsabilitès def li ci war. Ici en Italie une femme vient pour accoucher on la traite comme une reine bagua fatè say douleurs.

    • @mariamandiaye1059
      @mariamandiaye1059 6 років тому +3

      francesca bella c'est la vérité mane dé daniouma ray ba ma tite aka nio fonk femme enceinte rawatina boy accouché

    • @Fatimazahra-qp5yv
      @Fatimazahra-qp5yv 6 років тому

      @@mariamandiaye1059 guisgua ko kone .

    • @diadoukhouma8610
      @diadoukhouma8610 6 років тому +4

      d'où Sénégal dé au contraire danlaye diépi

    • @Fatimazahra-qp5yv
      @Fatimazahra-qp5yv 6 років тому +1

      @@diadoukhouma8610 non dou Senegal ! Si deuk youbab yi

    • @diadoukhouma8610
      @diadoukhouma8610 6 років тому +2

      francesca bella je sais je voudrais dire ici au Sénégal c est pas parrail

  • @ndeyefall904
    @ndeyefall904 6 років тому +1

    Le pire c'est que la dame en question n'est même pas une sage femme c'est une aide soignante à la retraite à qui on a permis d ouvrir une clinique

  • @ndeyesokhnaags4437
    @ndeyesokhnaags4437 6 років тому +3

    L'I môme metinaa,yeurmandé nguir yallah

  • @matiti4044
    @matiti4044 6 років тому

    Allah akbar thieuy Sénégal 😭😭😭😭 Li métina Sénégal je ne sais pas corps médical founiou diangué. Négligence rekk fonkouniou domou Adama ba paré niouné ay dioulit laniou

  • @khadydiopndiaye5181
    @khadydiopndiaye5181 6 років тому

    Bilaye walaye sage femme yagui raye nitegni té yalla gneuweule ma fogueni paréna bimemaye gniawe defalouma anesthésie nonou lama gniawé Bilahi walahi sage femme yi sokhorenagnou

    • @fatimadiba1539
      @fatimadiba1539 6 років тому

      Tel est mon cas lors de mon premier accouchement et mon 2e et le dernier cété dans une clinique. Sénégal santé 0/20

  • @ndeyefall904
    @ndeyefall904 6 років тому +5

    Merci pour vos contributions j ai cité le nom de la clinique dans ma déclaration c'est certainement effacé

  • @ndeyefatousouare3876
    @ndeyefatousouare3876 6 років тому

    Nice

  • @makeupetsecrets1671
    @makeupetsecrets1671 6 років тому +8

    Allahou Akbar gni gno Bone soudone Mane doto léne ko défaut😫😫😭😭😭Ray domou djambour

  • @diopndeyendoumbediop7755
    @diopndeyendoumbediop7755 5 років тому

    Yalla Mo mane Alhahou akbare

  • @seckamaria7330
    @seckamaria7330 6 років тому

    nooo thieyyy yalla haaa ndeye sannn hooo 😭😭😭😭😭

  • @aminatambengue3084
    @aminatambengue3084 2 роки тому

    Bayi lene clinique yi fala fala yi golo bo diog ouby clinique c'est pas sûr douniou am ay docteur you qualifié ak clinique bo manti dem souniou diaklé hôpital laniou lay yobou conak dé lene fa nieuké paix à son âme

  • @awandiayesarr7298
    @awandiayesarr7298 6 років тому +6

    Nogaye Ndiaye etai une femme battante une femme brave paix a son âme notre chère nogaye fau op caché l nom du clinique j connais très bien ce clinique tei gnifaa deh en donnant la vie c a gogo diourbel les femmes ont mm peur d tomber enceinte ay xalei niou ndaw nioy nek thi clinique ak thi hôpital yiii diii snap ak thikar thikariii xamouniou doooul loudoul concours toucher

  • @alassanendoye9407
    @alassanendoye9407 6 років тому +13

    Sénégala ngook kaa you mélnii dougnou porté plaine ces soit disants sages femmes qui n'ont certainement aucun diplôme pour exercer la médecine, ne sont que des criminelles en exercices

    • @sidysarr5864
      @sidysarr5864 6 років тому +2

      autaurites ferme nous ce maudit clinique mouroir

    • @malawkamara9703
      @malawkamara9703 6 років тому +2

      Sénégal dou avancé mouk.je parle en connaissance de cause.je suis infirmier de formation mais Sénégal diapal me diap mo fi am hôpital bo dem tu vois gnou amoul diplôme di sol blouse di def soins di piqûre amne si gno hamné sah si salle yi le gni nékone di fobéré diéki diéki rek sol blouse di piqûre nah diapal me diap.c grave.les sages femme mom moy lolou motoh douma léne may dara heure bouma amé mbok bouy accoucher mak mom be si bir salle d'accouchement bi be mou weussine nah je lai connais mais Diourbel mom c pire beuré érreur médical hamna si lou beuré ak ay preuve.ils faut dennoncé ces imbécile ils n'ont aucun diplôme.

  • @khadyly6563
    @khadyly6563 6 років тому

    macha'l

  • @ndeyefall904
    @ndeyefall904 6 років тому +7

    Mon objectif est que cette clinique gérée par des incompétents qui ne cesse de faire des victimes soit fermée

  • @leopoldfaye8827
    @leopoldfaye8827 2 роки тому

    Vrément Sage femme yii warnagnu sétatt sén liguey

  • @ndeyeaissatousall7847
    @ndeyeaissatousall7847 6 років тому

    😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢sama khol bi mettina gni gno bone te sokhor khana douniou ay djiguene no senegal lifa am eupeuna trop

  • @ndeyefall904
    @ndeyefall904 6 років тому +2

    J ai invité sur certains médias de diourbel les parents de ses victimes à me joindre pour créer un collectif afin de lutter contre les pratiques de cette dame qui a ouvert cette clinique avec un personnel non qualifié

  • @awadiop918
    @awadiop918 6 років тому +2

    Ceci nécessite une enquête vérifier son dossier le certificat de genre de mort etc... Vérifier le diplôme de celle qui a fait l' accouchement .J'interpelle le Ministère de la santé

  • @ndiayekine6390
    @ndiayekine6390 6 років тому

    Sage.femme.senégal.bakhougnou.

  • @fatouyacinethiam9150
    @fatouyacinethiam9150 6 років тому +2

    Li doyna warr way ki méritéwoul tourou sage femme

  • @mariamagueye771
    @mariamagueye771 6 років тому

    Bilahi li bou done fi thi France la dagnoulay traité comme une reine bilahi ayy wayy fougnou diomak sougnou Sénégal dafa triste trop tout mes condoléances à toute la famille 🕊️🕊️ 😢😞

    • @marasheikh6412
      @marasheikh6412 6 років тому +1

      Nayoulene yobou si yone yoko taye senegal lolou barinafi boye acouchee douyoula falee bo wakhee younela bagakoye df nekhonena

  • @maiyakme2550
    @maiyakme2550 6 років тому +2

    Nonnnnnnn c'est grave ça c'est interdit... et ils ont laisser tout ça comme ça ? Pourquoi ne pas avoir poursuivi les responsables ? C'est interdit ça c'est un gros problème au Sénégal quoi qu'il puisse se passer ils camouflent tjrs les choses oiur faire oublier... ce ne sont pas des "sages-femmes" dans cet hôpital mais je dirais des "mauvaises-femmes" rip pauvre dame... et son bébé 😭😭😭

  • @thiabaseynimbow8430
    @thiabaseynimbow8430 6 років тому +10

    Tieuy sage femme senegalais yi nio niak yeurmandé dei😭 koulani mangui miir doko diapalé

  • @aminatoufall1036
    @aminatoufall1036 6 років тому +6

    Bakhena ni reck lagnouy bayi sage femme mi sénégal 😭😭😭

  • @bleudiazebais6435
    @bleudiazebais6435 6 років тому +5

    Il faut absolument poursuive le responsable de la clinique.
    Associez vous avec les parents de toutes les autres défuntes pour faire la lumière sur tout ça. C'est pas des professionnels de santé mais des assassins pourquoi s'enfermer avec la jeune femme pour dire qu'elle est morte. Dafa yombou toropp man woornama nii amna walam ci décès bii . Prions pour le repos de son âme.

  • @fatoumatadiakhite6258
    @fatoumatadiakhite6258 6 років тому

    Les sage femme sont tres mechant a l'hopital

  • @ferolux3337
    @ferolux3337 6 років тому

    Bilay limo me delon aprè may saniè.

  • @ndeyeawadoumbouya8371
    @ndeyeawadoumbouya8371 6 років тому

    cliniqu kay merci

  • @magazellegazelle8412
    @magazellegazelle8412 6 років тому +4

    Aye domourame laniou il faut porter plainte

  • @ndeyemarietouthiaw8696
    @ndeyemarietouthiaw8696 6 років тому

    😭😖😭mon pays va mal Wallah en plus dagni tok nan yallah KO doggal mais n'en kholat louniouy df

  • @evario3562
    @evario3562 6 років тому

    Allakhou abbar

  • @MC-vi3wz
    @MC-vi3wz 6 років тому +9

    La prison direct incompétent ces domaram

  • @libassetraore7967
    @libassetraore7967 6 років тому

    Lii moo niaw baci kanamou Yalla wayé Yalla guemoule nélaw woul.

  • @bernadettesene3856
    @bernadettesene3856 6 років тому

    ta bien fé sokhnassi topko bamou seuss boko bayé nonou mou seddd bilayyyyy baloumalako .

  • @merediop538
    @merediop538 2 роки тому

    Kou diok oubi clinique ya trop de cliniques dans ce pays gérer par des incompétents médecin

  • @aissatougueye4788
    @aissatougueye4788 6 років тому +31

    Dure dure j'ai une accompagné une à l'hôpital pour accoucher elle souffrait beaucoup mais les sages femmes dormait dans leur bureau en disant que waraguouta âme dome la fille était dans la salle d'accouchement à pleurer é on m'avait interdit d'entrer mais je pouvait la laisser seule à un mois elle m'as dit regarde en bas je crois que le bb est sorti é c'était le cas ça tête était bien sortit je l'ai dit surtout ne bouge pas j'ai hurler docteur docteur mé elle ne répondait pas ouvert la porte elle à lever la tête qu'est qui as je lui ait dit le bb est sorti elle as répondu nonon c'est pas l'heure je lui est répéter que le bb est sorti j'ai dit elle s'est mis à courir é me reprocher pourquoi tu m'as pas appeler bien avant heureusement la fille s'en est sorti avec le bb bien portante Dieu merçi

  • @seckamaria7330
    @seckamaria7330 6 років тому +2

    allahou akbar

  • @aminatadiao3902
    @aminatadiao3902 6 років тому +2

    Walahi systéme sanitairou sénégal mo baxoul motaxxx lounék diffi xew amoul béne securité yalnagnou yalla samou waya doynawar

  • @ousmanegueyekande3457
    @ousmanegueyekande3457 6 років тому

    Où va notre Sénégal??

  • @momyseck5873
    @momyseck5873 5 років тому +1

    dama âme sama mbokou bou dekone Dakar di accouché si bene clinique gnougneko dokhonetoul mou danou dadi Fatou sur le san

  • @nogayetall7784
    @nogayetall7784 6 років тому

    Clinik néné Ba dbl yaw khamgua dounioula bayi nonou dafay yombou trop rip ma couz cheri

  • @ndeyefall6702
    @ndeyefall6702 6 років тому

    Li daw na yarame deye sane yalanako kharré aldiana😯😯😯😯😯😯😯😯😯😯😯😯😯😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢

  • @mariemendy6163
    @mariemendy6163 5 років тому

    le problème c qu ils ne metrise pas leur métier parce que moi un sage femmes ma gifler en acouchent sur la table mais (dotou ka défati ) le jour de mon sorti je l'ai gifler un gifle kél ne va pas oublié durant toute sa vie parce que jétais en forme ce jour la

  • @MirmNdiaye
    @MirmNdiaye Рік тому

    😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😢😢😢😢😢😢😢😢

  • @mariediatta5451
    @mariediatta5451 6 років тому

    Thiay Senegal,Allah akbar!Vous avez qu'à les dénoncer. On doit les sanctionner. C'est insupportable..

  • @fatoucha4507
    @fatoucha4507 5 років тому

    On peut jouer avec tout sauf avec la santé d'une personne.

  • @sigathiare2077
    @sigathiare2077 5 років тому

    C'est quelle clinique ça

  • @khadydiopndiaye5181
    @khadydiopndiaye5181 6 років тому

    Bilaye amena mane fimaye accoucher ni lagnema défe déme di nelawe bayima mane rek si salbi ak sama métite bignouye gneuwe fékena ma pousse ba bopou khalébi nék si bouneteubi bignou gneuwé nema yégale maniko mayema lokho ma yégue mou bagne nima toguale fofou basa domedji waade fofou yalla soutouralema bama yégue

    • @kyandoye4647
      @kyandoye4647 6 років тому

      Ndeysanne massa

    • @khadydiopndiaye5181
      @khadydiopndiaye5181 6 років тому

      @@kyandoye4647 sage femme yi dagno bone dé

    • @kyandoye4647
      @kyandoye4647 6 років тому

      @@khadydiopndiaye5181 bilay wayè yallah guiss na lépeu mougneul rék

  • @Mmediorndiaye90710
    @Mmediorndiaye90710 5 років тому +1

    No vrema li mom dagn sii wara wah prsk c grave

  • @maimounababa4466
    @maimounababa4466 6 років тому

    sama yaram dawna

  • @DoDo-px3it
    @DoDo-px3it 6 років тому +5

    Soubhanallah Li dou deug dou yone waye

  • @mabejallow1833
    @mabejallow1833 6 років тому

    Allahou Akbar Senegal wakhou gnou lep catastrophe

  • @papeboubaba8985
    @papeboubaba8985 6 років тому +14

    NON SENEGAL NI LANIOUY BAYI SAGE FEMME YI MAIS C DU NIMPORTE KOI , MAIS SEN RÔLE EN TANT K SAGE FEMME ANIMOU ???MAIS TJR LES GENS EN PARLE DE CE BORDEL DS LES HOPITAUX LORSK LES FEMMES ACCOUCHENT .. CA MENERVE MAIS LI NON ASSISTANCE A UNE PERSONNE EN DANGER LEU DOU YONE C UN CRIME , MAIS J T JURE CA FAI MAL AU COEUR MAIS LI IL FAUT SUIVRE LAFFAIRE FAUT PAS LES LAISSER COMME CA MAIS C DES ASSASINS VU K C NAI PAS UNE PREMIERE , MAIS FAUT DENONCER CES DERIVES C DU NIMPORTE KOI ... EN PLUS COMMENT UNE FEMME QUI ACCOUCHE RESTE SEULE ET QUE PERSONNE NE LASSISTE VRAIMENT JAI MAL J T JURE ...TROP ENERVÉ LIII NÉGLIGEANCE LEU ....

  • @dadishaniang8669
    @dadishaniang8669 6 років тому +1

    Thiey Sénégal ray nit rk eupna😲😲😲

  • @evamendy8511
    @evamendy8511 6 років тому +8

    Aye domerame pour la pluspart ces sage femmes bo nieuwé gnioulaye gueude dila hass toubap dinagniou yaga raw

    • @mendesshasha1021
      @mendesshasha1021 6 років тому

      khana sage femme incompetent yi. boulene sagua psk nieup elles sont po pareil ah sof ngene trop. yaw sage femme mola accouche

    • @mohamedlaminediouf515
      @mohamedlaminediouf515 6 років тому

      Degloul bou bah bala gaye wahe ki nénala ki dou sage femme dou infirmier gaye saga donc saga yoyou yako yélo con k tu esa

  • @fatoumatabinta783
    @fatoumatabinta783 6 років тому

    Vraiment c grave

  • @Dada-u8n
    @Dada-u8n 3 місяці тому

    Non thiey yala

  • @ndeyafatouba5063
    @ndeyafatouba5063 6 років тому

    Coula wara diapale tok dila sétane mane dale dama diomi danio bonn torop com douniou ayi famm 😭😭😭😭😠😠

  • @mendesshasha1021
    @mendesshasha1021 6 років тому

    je ne defend pas la sage femme mais jai ecouter les deux version. ossi faut savoir que la femme enceinte sa grossesse etait un grossesse a risque. donc je me dis que Dakar la warone nieuw. en plus la femme da bayi ba 6mois mouy dogua consulte lolou c grave et la sage femme dit kel ne fesait pas ses analyse c encore grave sa peut amener denorme plein de complication. mais gnomite soude clinique bobou c pas competent kholilene fenene nak. paix a lame du disparu

  • @khadimmbackediop6936
    @khadimmbackediop6936 6 років тому +6

    Le nom de clinique s.v.p??

    • @ndamangom6764
      @ndamangom6764 6 років тому

      Khadim Mbackédiop nene ba dioubel quartier sessene

  • @ndeyecoumbadiop691
    @ndeyecoumbadiop691 6 років тому +5

    thieuy yalla

  • @yayoumbamba7076
    @yayoumbamba7076 6 років тому

    😭😭😭😭😭😢😢

  • @fantacordroch8645
    @fantacordroch8645 6 років тому +3

    Santé Sénégal lagnou wara xole bayi récruter aye nite ni diplôme, ni experinnce ni formation dé fois formation yi sakh 1 an laye done gua bégueu nék médecin wala sage femme lo wara Déf aye ate gua Déf ko si 2 jours mane guis na bén famille bo khamni sén pape mo nék médecin mais amna gnari doomame kou goor ak djiguén dalén na dieul gnouye ligueye si hôpital bi ta lima lér moye ni étude yi waar si gnou nek sage femme wala médecin amoul si gnom dakh kou djiguén ki môme khassté ak réwadé lafa néké wone ak problème boufa malade indi gnou wakh tané ko séne biir amou gnou bén bamélou biir aye rétanaté lolou kou Déf formation bi si wara amna lodoul Déf si quartier ba sakh amna gnoumou récruter gno gno xam primaire sakh wésou wou gnou ko Lou xéw hôpital gua dégue ko si quartier bi

    • @aminatambengue3084
      @aminatambengue3084 2 роки тому

      Bilahi gni thi am diplômes bari woul recrutement politique rek di lore askanwi

  • @ndeyematydiop6837
    @ndeyematydiop6837 6 років тому +6

    Je connais cette femme et le nom de cette clinique bilahi khamena ngogaye bou bakhe bilahi degeula elle a des enfants pauvre dame amena koumou dallone sinou guinawe keur mm sama sœur dafa nékone thie état mh chaque jr niou piqûre ko khamouniou darra

    • @aliassokhorfemmmya6208
      @aliassokhorfemmmya6208 6 років тому +1

      Il faut dénoncer le nom du clinique

    • @khadimmbackediop6936
      @khadimmbackediop6936 6 років тому +1

      Ndeye Maty DIOP s.v.p dit nous le nom de la clinique

    • @Fatimazahra-qp5yv
      @Fatimazahra-qp5yv 6 років тому

      @@khadimmbackediop6936 billay il faut dire le nom de la clinique ndakh bou siw. Si c'ètait dans les pays europeens clinique etat bi dafkoy fermer , emprisonner les coupables

    • @taphakhouma9584
      @taphakhouma9584 6 років тому

      No