Magoum Deuk Épisode 40 Saison 2

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 27 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 190

  • @CheikhSylla-k2d
    @CheikhSylla-k2d 14 днів тому +19

    Bakip alkhorano Karim Latir Bonoko rayé Dotoma chetan magoum deuk wallahie ❤

  • @eikhene-s4y
    @eikhene-s4y 14 днів тому +17

    Nianale lénema goude fane AK xalise Bou bari téh barkéle 🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿

  • @MatyBéye-n4j
    @MatyBéye-n4j 14 днів тому +8

    Wayasin penda mi lisi bopambi dolensi wah😂😂😂

    • @fatimakane2463
      @fatimakane2463 14 днів тому

      😂😂😂 yag nassi daaal saison 1 ba légui

  • @BaraBa-i8v
    @BaraBa-i8v 14 днів тому +7

    Latir waroule dé dé bilahi yaw 😢😢😢😢non magoum deuk lémoy l'âne 😢😢😢😢😊

  • @AbdouYade-e8k
    @AbdouYade-e8k 14 днів тому +10

    Latyr bou Déwé série bi dou am chanse dara

  • @smk1679
    @smk1679 14 днів тому +9

    ❤LATYR LE DIGNE FILS DE SON VILLAGE !!!❤🦁
    __
    NOÛROU NIAKK na fayda😅
    MACODE ak WALLU😡🫠
    Soof ngen ma😢😂 ak YAAKAAR dou touss thim😢

  • @SokhnaDieye-w4f
    @SokhnaDieye-w4f 14 днів тому +10

    Latyr boudéwé dotouma chetan magoum deuk Latyr rek❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @TALiBÉBAMBABI
    @TALiBÉBAMBABI 14 днів тому +12

    Café touba lay nan ni sax ❤☕️❤️

  • @SeniSarr-ck3fi
    @SeniSarr-ck3fi 14 днів тому +4

    Kou wore réne bo déwéne mou djiguela dénelaka djigne wayé d'où yawe

  • @KhadimDione-s1y
    @KhadimDione-s1y 10 днів тому +3

    Yacine pénda néna yobou nite indi nite 😅😅😅😅😅😅😅

  • @BoussoballyMbaye
    @BoussoballyMbaye 14 днів тому +7

    Yacine penda mome dafa khoromou trop😂😂😂

  • @AbrahamDllo
    @AbrahamDllo 14 днів тому +1

    Série bi mome nar na nakhari ndakh bou latyr démé koufi nk le révolutionnaire

  • @TallaFall-m3j
    @TallaFall-m3j 13 днів тому +6

    Yéne koulénn wakh latyr dina dé nguènn gueum ko😮lolou manoul nék macodou bou amoul chance mome moy moudié déé😢

  • @AntAFaye-bm6tq
    @AntAFaye-bm6tq 14 днів тому +6

    Latyr bou deh ma bayi chéri bi 😢😢😢

  • @ousmanekebe3371
    @ousmanekebe3371 14 днів тому +1

    Ma codé ayy réée 😂😂 lama defff mouy melni moussa ak nioulay bi 🐈‍⬛🐈‍⬛🐈‍⬛

  • @matarndoye2855
    @matarndoye2855 13 днів тому

    Avec magoum je vois que le pouvoir montre la nature profonde de l'individu. Kou d'accord

  • @massamba492
    @massamba492 13 днів тому +2

    Wallou dina takh ma bayi sétane magoum deuke ndakh dafa fattè liko fale

  • @LeyeMay-cy9mi
    @LeyeMay-cy9mi 11 днів тому +1

    Latir dou déh 😢😢

  • @ambassadeurbaol8359
    @ambassadeurbaol8359 14 днів тому +1

    Yacine Penda tayla mousseux wakh luma nékh.
    Néna "wétié nite la khamouy"

  • @ousmanekebe3371
    @ousmanekebe3371 14 днів тому +6

    Latyr dou déh dagne koy fékhel rek mais latyr moy acteur principal série bi kom film bou dhé série bi diékh kone ta dou âme chance aussi

  • @MalickSouware
    @MalickSouware 13 днів тому +1

    Latir bou déwé diaroul ngéni continué kéne douko sétanati

  • @NdioleSene-ec7et
    @NdioleSene-ec7et 6 днів тому

    Obaly Yacine penba bi😂😂❤❤

  • @AmadouCheikh-ym7is
    @AmadouCheikh-ym7is 14 днів тому +5

    Magoum deuk bi Moy mbam😂

  • @KhadyKebe-y4w
    @KhadyKebe-y4w 12 днів тому +1

    Obaly Yacine penda bi 😂😂😂

  • @AliouSarr-n5d
    @AliouSarr-n5d 14 днів тому +4

    Billah latyr dou dé

  • @assanefaye6882
    @assanefaye6882 14 днів тому +3

    Mais yéene Latyr manoul déé nak, moom moy acteur principal bi

  • @diatidianecheikh5353
    @diatidianecheikh5353 14 днів тому +3

    Latir yakar élimine amoul khalat sahk😢😢😢yakar ya bon😮😮😮

  • @SeckOussynou
    @SeckOussynou 14 днів тому +3

    Latyr bou déwé dotul am chance

  • @ibrahimandiaye883
    @ibrahimandiaye883 13 днів тому

    Salam meilleur série

  • @DioneRama
    @DioneRama 13 днів тому

    Bess bou latire déyé ma bayi ma mangoume deukk bilakhi 😢😢

  • @FallMouhamed-id3ls
    @FallMouhamed-id3ls 13 днів тому +1

    Magom deuk dina niaw kuar banguora fekk fi coddou boba la sen pekhe yiy komase fegn😢😢😢😢

  • @ndeyefaye1833
    @ndeyefaye1833 13 днів тому +1

    Latyr bou dhéwé série bi do t'oul nékh

  • @SalawThioune
    @SalawThioune 12 днів тому +1

    Latir môme Waroul dh môme

  • @modoufaye-h1e
    @modoufaye-h1e 13 днів тому +1

    Latyr moy magoum deuk bokénes ko réyé dotouléne am ay vue

  • @BayeNdiaye-i6l
    @BayeNdiaye-i6l 14 днів тому +4

    Li woné khamnite yomboul moy rolou nourou

  • @FatouSakho-fn9he
    @FatouSakho-fn9he 14 днів тому +4

    Mafi djitou😂😂

  • @MatarngoyeThiam
    @MatarngoyeThiam 13 днів тому

    Meilleurs vœux pour cette nouvelle saison

  • @ADA-AFRIK
    @ADA-AFRIK 14 днів тому +3

    Mafi jitou

  • @ElhadjiBa-xg3pb
    @ElhadjiBa-xg3pb 13 днів тому +2

    Billy wollahi latir moma fi bayi

  • @rokhyattadiaw9313
    @rokhyattadiaw9313 14 днів тому +3

    Latyr bou deh ma bayi derie bi dieulen macode

  • @ibrahimabadiane3097
    @ibrahimabadiane3097 14 днів тому +3

    Fekheléne ba latir dé mane mom detoumako setane

  • @Sodathiamtgiame
    @Sodathiamtgiame 13 днів тому

    Papey ndélla Yacine moy bayou codou❤❤❤

  • @SokhnaDiop-q2m
    @SokhnaDiop-q2m 13 днів тому +1

    Latir bou déhwé dou ame sance

  • @bayelatkane4417
    @bayelatkane4417 14 днів тому +1

    Bou déhyé ma bayi série bi

  • @KhadijaDiallo-j2n
    @KhadijaDiallo-j2n 5 днів тому +1

    Latir mom waroul der KON dou am ben sens wallu la latir wara soumbi comme noumou defon bangoura

  • @cheikhlo454
    @cheikhlo454 9 днів тому

    Loutakh niouye raye latir 😢😢😢😢😢

  • @modoumbow4874
    @modoumbow4874 13 днів тому

    Magum Dëkk neexatul dara 😮

  • @AssaneNdao-k5p
    @AssaneNdao-k5p 14 днів тому +5

    Li rek motakh niounaane bour dou mbokk dou xaritt

  • @elementndiamedarou2414
    @elementndiamedarou2414 14 днів тому +3

    Ousmane diop mess mame fatim mboup katakayni, justice pour les victimes du régime de macky sall

  • @BabacarFaye-e1w
    @BabacarFaye-e1w 13 днів тому

    Moungui ñaw dèè❤❤❤❤❤

  • @MbenefallFall-g5y
    @MbenefallFall-g5y 13 днів тому +1

    Magoum deuk mi bonn na

  • @MalickSouware
    @MalickSouware 13 днів тому +1

    Yacine pénda dangay rétane ba sonou😂

  • @assanefaye6882
    @assanefaye6882 14 днів тому +1

    Serie bi dh amoul kou mana blessé Latyr ba dikoy raay

  • @DaoudaDiouf-nv3cv
    @DaoudaDiouf-nv3cv 14 днів тому +27

    Latir sougniou KO Rayé ma désabonner bly yaw

  • @KedzoCissé
    @KedzoCissé 14 днів тому +2

    latir waroul de❤❤❤❤

  • @IbraSeck-s7p
    @IbraSeck-s7p 14 днів тому +1

    Latir bou déwé ma bayi sétan lén 😞😞

  • @ModouNdour-z4p
    @ModouNdour-z4p 14 днів тому +3

    Beus bou magoume deuk lale Latyr na am louko sof

  • @moussafaye6663
    @moussafaye6663 13 днів тому +1

    Mane d legui ma bayi série bi sou ngene reye latyr

  • @ndiaganiang5306
    @ndiaganiang5306 13 днів тому +1

    Loutah nitou ngour mana wor

  • @bayemoussathioune50
    @bayemoussathioune50 14 днів тому +2

    Ponkal si ndiouli 😂19:45😅

  • @KhadimDione-s1y
    @KhadimDione-s1y 8 днів тому +1

    Yaw ma codou meno réye latire dé gniania rk kham 🤣🧏🏼‍♀️👈🏼

  • @CheikhMbaye-q6l
    @CheikhMbaye-q6l 14 днів тому +2

    Raye latiir lolou dou khalate

  • @omargueye378
    @omargueye378 14 днів тому +2

    Walou moytou ma bakhna rek

  • @thienondiaye-y8h
    @thienondiaye-y8h 14 днів тому +2

    Latir boun ko rayé dou nékh

  • @FallMouhamed-id3ls
    @FallMouhamed-id3ls 13 днів тому +1

    coddou mii dh monara soufe latyr ci pekhey rey gui

  • @CheikhSylla-k2d
    @CheikhSylla-k2d 14 днів тому +1

    Ak ma due Tabe safara wallahie 100 Foi wallahie

  • @MamadouNiang-lj4qy
    @MamadouNiang-lj4qy 14 днів тому +3

    Lattir deye lek wa lakhasso

  • @AllaMbaye-bx3pe
    @AllaMbaye-bx3pe 14 днів тому

    Seri bi khana amoul l'été 😂😂

  • @CheikhFallSylla
    @CheikhFallSylla 14 днів тому +1

    Ñëwug Codou ak Ndella nag yomb na trop

  • @CheikhNdiaye-d5g
    @CheikhNdiaye-d5g 14 днів тому +1

    Même mane bounio réyé ma bayi série bi

  • @bayelatkane4417
    @bayelatkane4417 14 днів тому +1

    Latir ak teur la dou déh

  • @DjibyBâ-w6p
    @DjibyBâ-w6p 14 днів тому +1

    Bou latire déwéh dotou leune mafi guiss.lou lérr laleune wax wax.xamou leun ma saax

  • @daoudadiop2784
    @daoudadiop2784 14 днів тому +2

    Man de latir moma fi bayi

  • @NdayesSéne
    @NdayesSéne 8 днів тому

    Ltir moy acteurs bi di films bouné amena acteurs di bou dé wé Di moy perde temps deugue si films bi😂😂

  • @CheikhFallSylla
    @CheikhFallSylla 14 днів тому

    Ndax da ngeen a jàpp ni Film bi Prédiction la ci ni Diomaye nar a doxe ak Sonko ( yalna nu ci Yàlla musal) Walla Avertissement rekk la ngir mu moytoo def ni Wallou ???

  • @MamefatyDieng-zk5fc
    @MamefatyDieng-zk5fc 11 днів тому

    Mane DH gueum n'a ni magoum deuk li Mouy deff stratégie la rek pour piéger bangoura et consorts

  • @papediagne661
    @papediagne661 13 днів тому +1

    Latir bou déh ma bayi seri bii té dina lén plainte

  • @toragueye7975
    @toragueye7975 14 днів тому

    Délene wagni séne xalat yi way dafa dieul temps trop

  • @BabacarDiouf-iy1cv
    @BabacarDiouf-iy1cv 14 днів тому +1

    Bou larir deh ma bayi seribi dou Amari khorom

  • @BaayMoorSilla
    @BaayMoorSilla 14 днів тому +1

    Nguur daal moo man a soppi nit rekk.
    Lii de lañu naan buur du mbokk du xarit.

  • @albassirdiop
    @albassirdiop 14 днів тому +1

    Yacine penda ak Bangoura 😂

  • @NdiagaDiop-ln3tx
    @NdiagaDiop-ln3tx 14 днів тому

    BOULÉNE FATÉ WAY DAWLOYI DE

  • @mbayediaw1244
    @mbayediaw1244 14 днів тому

    Latir moma fi bayi mane

  • @niollbowetv2437
    @niollbowetv2437 14 днів тому +2

    Magnum duke dh koume Macky Sall rėk

  • @sopesaliounebadrandiayendi4965
    @sopesaliounebadrandiayendi4965 14 днів тому +2

    Bu deyee serie bi yaxu

  • @AblayeKa-k9g
    @AblayeKa-k9g 13 днів тому

    Latyr ❤❤❤❤❤❤❤

  • @KeurMayoro
    @KeurMayoro 13 днів тому

    Mana nio Xamni kou leune rey Thi film rk yakkoko Senariste bou dh lolou ga note sanjeko dh baxoul

  • @SeybaKebe
    @SeybaKebe 11 днів тому

    Yacine pèda ça bopbi sonalnanou

  • @CheikhFallSylla
    @CheikhFallSylla 14 днів тому

    Bu leen wax Latyr du deewee, da nga naan Latyr boo rayee sa bopp...Du Latyr moo bind film bi walla ?

  • @ElehgeNiag
    @ElehgeNiag 14 днів тому +2

    ❤❤❤❤❤❤❤

  • @DameGueye-u2j
    @DameGueye-u2j 14 днів тому +1

    Latir ❤ managoulah dhé

  • @AbdouDione-n6n
    @AbdouDione-n6n 13 днів тому

    Lima méti moy di sétan di merr wayé paréna ci magoum deuk bayé naleko

  • @kebefallou
    @kebefallou 13 днів тому

    Wethio nitt kay 😂😂😂😂

  • @mamediarraanne4763
    @mamediarraanne4763 14 днів тому +2

    Loutakh yakar mana guande guand lou

  • @moustaphandong8748
    @moustaphandong8748 14 днів тому

    AK man

  • @SerigneWade-kg8tq
    @SerigneWade-kg8tq 14 днів тому

    Latir Sagne n'a dée Kone d'où âme chance

  • @AdamaDiop-b1r
    @AdamaDiop-b1r 14 днів тому +1

    ❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉

  • @SEYDINAALIOU-f4x
    @SEYDINAALIOU-f4x 13 днів тому

    Mafi moudji😂 15:58

  • @ArameKane-bc9rq
    @ArameKane-bc9rq 13 днів тому

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @AlassaneWane-u5p
    @AlassaneWane-u5p 14 днів тому

    Latyr mounoul dé