"Ni Lamine Samba géré Face To Face Modou Lô/Siteu, Question Bi Khady Faye posé" Modou Mbaye déballe

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 12 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 143

  • @GayeFaye-i4w
    @GayeFaye-i4w 13 годин тому +21

    Bilahi Modou Mbaye tu as dit toute la vérité nitt danga wara degou

  • @NiangeFallou
    @NiangeFallou 14 годин тому +15

    Tu as parfaitement raison modou Mbaye

  • @deurbireik4768
    @deurbireik4768 14 годин тому +13

    Modou mbaye a parfaitement raison ❤

  • @KhadimNiang-u9x
    @KhadimNiang-u9x 11 годин тому +7

    Félicitation modou mbaye

  • @CheikhAbdouThiam-c3g
    @CheikhAbdouThiam-c3g 7 годин тому +5

    Merci Modou mbaye ❤

  • @josephsarr5770
    @josephsarr5770 6 годин тому +3

    MERCI MODOU MBAYE..MODOU MO KO PROVOQUER..SITEU REAGIR...CEST TOUT

  • @Fatou-z7s
    @Fatou-z7s Годину тому +2

    Merci👍👍👍

  • @KossoGadiaga-vw3wc
    @KossoGadiaga-vw3wc 13 годин тому +6

    Bilahi merci modou mbaye

  • @cheikhdiop859
    @cheikhdiop859 12 годин тому +5

    Merci Modou

  • @Leuzbiii
    @Leuzbiii 6 годин тому +3

    Sénégal mo nekh bilahi lamine samba na rien fait de mal les deux adversaires amoul masla wakh nagne part se que les deux lutteurs contanouniou si sen combat bop niom niar nieup epuis c était des adversaires.

  • @faalmadeugal2804
    @faalmadeugal2804 13 годин тому +8

    Dangaa niaka diom wala dagn laye encouragè ci niaka diom???
    Bayilen di sopi wahu diamburr.
    Siteu da tardè ba nopi mo njeka wah damako niuss daanko

    • @alhassanngom8282
      @alhassanngom8282 11 годин тому +1

      Commentaire yi la beugg di guisss. Ki da yeukk bopam ben instant

  • @wadeidrissa7410
    @wadeidrissa7410 9 годин тому +5

    Modou mbaye regarde l'émission sur tfm kant la journaliste a dit à siteu kon t'appelle lac3 c la ke siteu à insulter pour la première fois donc arrêtez de dire ke c modou ki la dépasser en premier si vous avez peur de siteu dite le c mieux de le défendre

    • @alphathiam8792
      @alphathiam8792 6 годин тому +1

      Effectivement Modou Mbaye dafa dioum Siteu mo ndieukeu dépasser modou

  • @Mbagnick-h8y
    @Mbagnick-h8y 5 хвилин тому

    Modou Mbaye nguir Yalla bul soppèku, yow rekk yafi dess ci ku deggu ci Lamb ji jajefeti ❤

  • @wadeidrissa7410
    @wadeidrissa7410 12 годин тому +10

    Modou c faux c siteu ki à dit en premier temps ndiousse il faut bien regarder le face 2 face encore tu t'est trompé nous on la bien regarder et écouter

    • @djibrilsarr6857
      @djibrilsarr6857 7 годин тому +2

      saway demal sétane ni wat face to face bi

  • @KhadyGaye-n5g
    @KhadyGaye-n5g Годину тому +1

    Bilakhi modou mbaye deugue rek nga wakh modou lo mon provoque siteu

  • @mamadoulaminediaby5091
    @mamadoulaminediaby5091 7 годин тому +2

    Ah yenn nieup siteu ngen faraloone mais life leu tamittt nangou leen rekk mou woyoff yassalaam

  • @rimesmakerposeidon2427
    @rimesmakerposeidon2427 7 годин тому +2

    Modou mbaye aka ignaneee modou lo

  • @MoussaSene-q6t
    @MoussaSene-q6t 6 годин тому +1

    Merci modou mbaye

  • @mareme1853
    @mareme1853 13 годин тому +7

    ioe bougo modou lo

  • @talibecheikh5035
    @talibecheikh5035 3 години тому +2

    Nga balma li lagnou nane golo gnawoul baye ba la nirou ni sa papa bagné Modou nonou nga ko bagna mais sante yalla yalla na bour yalla doli soutoura

  • @marcusmouhamed
    @marcusmouhamed 11 годин тому +3

    Modou mbaye kagn ngay wah siteu deugg

  • @PenKhadim
    @PenKhadim 2 години тому +1

    Belén fatte valdo❤❤🎉❤❤

  • @iscojo6600
    @iscojo6600 5 годин тому +1

    Modou Ne partage pas le tord ! Bayiléne tapette wala Seytané face to face c’est un contrat !! Modou waroul sakh nouyou boy bi !! En plus au contraire c’est Siteu qui n’as pas cessé de manquer du respect !! Modou au contraire a utilisé le silence. Bah paré les face to face plus chaud de modou lo c’est contre eumeu !! Arrêter quoi !!

  • @AdamaNdiaye-yt9xe
    @AdamaNdiaye-yt9xe 12 годин тому +5

    Modou mbaye legui seytané bou makk la

  • @abdouazizndiaye6895
    @abdouazizndiaye6895 12 годин тому +9

    Modou mbaye nafekh nga loutakh wakho si saga siteu bi

  • @NicolasNiasse-p1n
    @NicolasNiasse-p1n 6 годин тому +1

    Merci modou

  • @alouspice7253
    @alouspice7253 12 годин тому +4

    koula WAH Modou lo yalla la boul dougal fi yalla yah siteu yiéna far diaroul camouflé

  • @laminesadio2134
    @laminesadio2134 5 годин тому +2

    Modou MBAYE pékhé mo antouwoul rék boo sagnone siteu dane wayé di ngén yagu si mére dh insha Allah Modou YALLAH kofi tégu

    • @MacodouSeck-d9w
      @MacodouSeck-d9w 5 годин тому +1

      Yagui togne dh mane modou lo moy sama mbeur mais modou mbaye deug la wakh

    • @modoubayefallsikroulla1423
      @modoubayefallsikroulla1423 4 години тому

      Bayil far téy wakh té yalla tah modou mbaye deugue rk lafi wakh

    • @mansourdiop7037
      @mansourdiop7037 2 години тому

      Modou deugue rek la wakh

  • @adama6405
    @adama6405 2 години тому +1

    Linga wax Moy DEUG bi nagniou bayi hypocrisie Modou mom mo ndieuka manquer respect siteu moni siteu ( koula encouragé si ningay beuré moungui lay encouragé si gniak DIOM ) li koko wax mouye gore DEUG Dinala dépassé
    DEUG nak yalla ko mom kou Yor bénén xalate té libre de le dire 🎉 mane Lila guisse nite faral ko dou té sou dioumé ngani ko danga dioume

  • @GoraMbengue-f2j
    @GoraMbengue-f2j 13 годин тому +5

    Modou Mbaye bayil yéh fitna affairou cheytané yi baye Fall douko deff lolou wakh nagn si passé na goor yallah dou yéh fitna .

  • @SeydinakhalifaCamara-lc2tg
    @SeydinakhalifaCamara-lc2tg 13 годин тому +4

    Modou MBAYE seytané nga waxal siteu deug ta nga bayi sa affairou Deumm yi affairou nafekh yi Akh

  • @ibrahimasene5942
    @ibrahimasene5942 6 годин тому +1

    Modou mbaye acka bagne modou lo wakhou na feukh rek ngafi wakh danga far ak situe

  • @khadimrassouldiakhate4384
    @khadimrassouldiakhate4384 Годину тому

    Déjà Modou Mbaye yangui fénal Modou Lo prsk wakhoul siteu danga niakk diom dafniko koula digeul lii mongui lay encourager ci niakk diom donc ya une grande différence.
    Vraiment boy Baye Fall laleu tégonne ndékei vrai nafekheu nga.

  • @khadidiatoundiaye7968
    @khadidiatoundiaye7968 10 годин тому +2

    Khamnga yekini khassone nafi père becaye yassiye topp ioe Dom dji 😂😂😂demal rk ioe mom danga nafekk trope si professionnel del set yalla si lingey wakh

  • @habibdieng3006
    @habibdieng3006 14 годин тому +20

    Lamine samba dafa barri wakh il et nul 👎

  • @oumaresyi6068
    @oumaresyi6068 10 годин тому +1

    Modou mbaye ligua wakh si siteu wakho ko deugg daga ngua bokk si niou done FEKHEL modou lo

  • @topaly9828
    @topaly9828 2 години тому

    Madou mbaye deug rék nga wakh machala

  • @MLo-he4lj
    @MLo-he4lj 6 годин тому +1

    Modou mbaye yaw doy nga waar dh
    Ya dégue fouko mod’ Lo wakhé Danga gnakk diom ?
    Wa ahlou lamb gnou si Bari dangéni soralé Siteu day danou baparé amé nitt gni wakh djou bari ak rewandé pendant ces face to face
    Recadrer len ki waay

  • @Mboupkara585
    @Mboupkara585 13 годин тому +10

    Modou mbeye taye wakhou seytané gua wakh modou nutla loutakh dou mer

    • @alhassanngom8282
      @alhassanngom8282 11 годин тому +1

      Modou Mbaye nitt kécé la teih Modou Lo moko gueune nitté. Bayiko fi mouy ndélou fokni moñou gueun yéwou wayé yalla xamna

    • @khadyfaye7430
      @khadyfaye7430 5 годин тому

      Il a toujours été comme ça seytané

  • @SaliouDiop-e4r
    @SaliouDiop-e4r 4 години тому

    Bien dit modou mbaye 🎉

  • @pendandiaye823
    @pendandiaye823 5 годин тому +3

    Modou mbaye modou mbeur laa mais le meilleur je te dis donn kilifeu lamb djiii le respect on le lui doit

  • @fatoumatabomou4670
    @fatoumatabomou4670 12 годин тому +2

    En tout cas je te conseille modou mbaye que tu neutre dans l'affaire arrête de parler sur les réseaux pcq les gens penseront comme siteu est ton ami c'est pour celà tu es réagir comme ça

  • @babacarseye49
    @babacarseye49 13 годин тому +4

    Yaw clé xaritou siteu nga amo Lo wahh

  • @diagneroyal
    @diagneroyal 3 години тому +3

    Khamnagne la siteu ga beugone mou dane sa wakhou garouwalé yi kham nagne fi ga Beug dieum m tousssss

  • @alioufaye4146
    @alioufaye4146 5 годин тому +1

    Non sérieusement est-ce que ki sétanena face face iow tu es passée totalement a côté danga faral siteu confirmé toi

  • @khadysoumare1518
    @khadysoumare1518 5 годин тому +1

    Le tribunal du sport ne reconnaît pas la lutte sénégalaise

  • @vincentgomis8162
    @vincentgomis8162 12 годин тому +3

    Modou Mbaye tu n’es pas sincère du tout!

  • @MoukhameteDiouf-t8d
    @MoukhameteDiouf-t8d 13 годин тому +4

    Modou mbaye yaw bayil yamba

  • @AsseKebe-nq2fm
    @AsseKebe-nq2fm Годину тому +1

    Modou mbaye yamana doullllllll yaw

  • @wadeidrissa7410
    @wadeidrissa7410 12 годин тому +2

    C l'ami de siteu

  • @vincentgomis8162
    @vincentgomis8162 12 годин тому +3

    Modou Mbaye yaye nafék bou mak
    Siteu sa copain motakh essaye d’être professionnel

  • @cheikhmbacke2841
    @cheikhmbacke2841 13 годин тому +2

    Modou mbaye dmram la modou rk la bagne

  • @assanebabaofficiel3533
    @assanebabaofficiel3533 7 годин тому +1

    Et la réaction de Siteu envers modou

  • @YoussouphaMbengue-r8y
    @YoussouphaMbengue-r8y 12 годин тому +2

    Modou mbaye ki doul katt la khamo lénn ki domeram là

  • @SENETV04
    @SENETV04 5 годин тому +1

    Modou mbay Nafehh ga combat by yepp

  • @wadeidrissa7410
    @wadeidrissa7410 12 годин тому +3

    Modou mbaye à peur de siteu je l'ai remarqué pendant ce combat

  • @afro3827
    @afro3827 13 годин тому +2

    Gni gnep ay nafekh lagn modou lo molen di dérangé

  • @sambaafricatv
    @sambaafricatv 42 хвилини тому

    Deug rek moy deug merci modou mbaye siteu dioumna wayé modou mko provoquer ay yaldaw, niak diom ll siteu force dasi guiss bopom hana monm tmt amoul diabot délén wah li am merci md

  • @MoustafaMbacke-kf8sj
    @MoustafaMbacke-kf8sj 9 годин тому +1

    Modou n’a rien fait siteu yén ay nafékh ngén siteu daw ndayu lambj li Mbeur boukofi défon ngén améko😂 Modou lambji yéppko sott té siteu neunouko dane yén dolén rouss bilay 😂😂😂😂😂

  • @mouhamadouwade4859
    @mouhamadouwade4859 44 хвилини тому

    Modou mbaye tu as dit la vérité , mais si bénne côté tmt nafékheu Bou makko moye yaw boul dieul Modou lô rek diokheko torbi délle atté deugeu

  • @SakhirNiang-k1m
    @SakhirNiang-k1m 5 годин тому +1

    Moodou Mbaye aka beugue graw graw lou tei xamoul dara

  • @papezulefaye7263
    @papezulefaye7263 6 годин тому

    Bilahi modou mbaye lou lerr nga wakh mais nakk eumeu sene akk niom maganeté wouniou dara

  • @Prodioufvcbbkt
    @Prodioufvcbbkt 12 годин тому +2

    Modou défal ni beuz lutte tv essaie de créé quelques choses pour toi au lieu de rester là a dire du mal de modou c'est mieux .barri gua wakh trop

  • @alhassanngom8282
    @alhassanngom8282 11 годин тому +1

    Modou Mbaye franchement meuno ñakk ci Lamb on sait touss, saaa communication nice na, mais saa homonyme Modou Lo limou waax c’était pour tontou Siteu sans mou sagga ko motakh mouniko consigne daaw baparé beugg daane yoyu niakk diom laay eundi. Recadrer wéssouwoul lolou. Modou lo waaxnaka louleer té Modou nitt leu rek bouko topoon benen affaire ngay guiss wahalaal yalla

  • @sidythiam6983
    @sidythiam6983 7 годин тому +1

    Ioe kay saytanei ka

  • @nouhadieme1889
    @nouhadieme1889 7 годин тому +1

    Tu as raison bilahi. Modou lo mo ndieuk commencé donc mo togne

  • @MoussaNiang-iz4rh
    @MoussaNiang-iz4rh 40 хвилин тому

    Dagnay doul 😢modou mbaye modou rk nga bng

  • @biranecamara6796
    @biranecamara6796 4 години тому

    Deugeu rek ngafi wakh modou lô moko provoque diko traité de gniak diom siteu réagir mais deuk bi daffa neex 😂

  • @khadimfall979
    @khadimfall979 3 години тому

    Modou Mbaye 🔥🔥🔥🦾

  • @AbdouAziz-ri8td
    @AbdouAziz-ri8td 2 години тому

    Modou Mbaye il Fo dire la vérité Siteu Dafa Daw Thiak Thiak le Modou lo a attaquer et gagner Point C sa la Réalité

  • @AbdouAziz-ri8td
    @AbdouAziz-ri8td 2 години тому

    Modou Mbaye Dafa Mena Doul il Fo dire la vérité Siteu Dafa Daw Thiak Thiak le Modou a attaquer et gagner Point

  • @AbdouAziz-ri8td
    @AbdouAziz-ri8td 2 години тому

    Modou Mbaye Et son père Becaye Supporter Siteu Di Doul Rec Il Fo dire la vérité Siteu Dafa Daw Thiak Thiak le Siteu et un Comédien Dans Tou les sports il Fo attaquer pour gagner Point

  • @bamba2687
    @bamba2687 12 годин тому

    ❤️❤️❤️❤️❤️❤️🔥

  • @MoustaphaNiasse-y3u
    @MoustaphaNiasse-y3u 11 годин тому

    Mais siteu daffa dane Modou lo et siteu leurs a demandé que quelqu'un jure pour mou solalko couronne 👑 Bi mais kéne waxoul dé 😂😂😂😂😂 Modou lo mbeur la rekk

    • @dehabou7720
      @dehabou7720 8 годин тому

      Sa way camil alkhourane dou pour jurer merci 🙏

  • @MoussaNgom-p2d
    @MoussaNgom-p2d 2 години тому

    Bilakh modou mo togn

  • @modoubayefallsikroulla1423
    @modoubayefallsikroulla1423 4 години тому

    Vraiment Lamine samba khamoul dara

  • @lahadmedia9184
    @lahadmedia9184 41 хвилина тому

    3:20 khady rék 😅

  • @ModouMbay-f4g
    @ModouMbay-f4g 12 годин тому +2

    Siteu mo dane Modou lo deug foumou amoul diamou doufa âme

  • @mbassambodj8498
    @mbassambodj8498 13 годин тому +1

    Seytané nga nakk boy delll tekk deuG sama wadji

  • @yadyly
    @yadyly 10 годин тому

    Yalla mon xame lep Li né thi hool yi es que ki loumouy wakh mon nekh thi mome

  • @MoukhameteDiouf-t8d
    @MoukhameteDiouf-t8d 13 годин тому +1

    Yaw ak siteu yenay nek di toukh bonne mon takh

  • @yaalasadio
    @yaalasadio Годину тому

    Modou MBaye gua balma foo sétaner face to face bii ?? Siteu mo nieuk waxx ay niousss etc… Lolou gua djap neii warnako waxx Modou Lo ??? Nekk len ay nitt way

  • @AssanedieyeAssanedieye
    @AssanedieyeAssanedieye 2 години тому

    Dafa lère modou mbaye ligna wakh moye deugue modou lo mo warale thioweli siteu défoule dara

  • @Senegalaise2024
    @Senegalaise2024 59 хвилин тому

    Lamine Samba doit aller se former. Dess neu bou bakh sakh

  • @massarsarr5746
    @massarsarr5746 4 години тому

    Modou mbaye mo bagne modou lo

  • @gueyendioro150
    @gueyendioro150 7 годин тому

    Modou xol bi dafa ndaw dafa gawa mér 😂

  • @amathsow-dt1en
    @amathsow-dt1en 3 години тому

    Modou dafa nday reew
    Moo commencè thiow lii

  • @mouhamadoulaminendao6018
    @mouhamadoulaminendao6018 13 годин тому +1

    Boul ragal dara lobegue wah walko lamb halè na payi sèy

  • @DJFIREMANgambia
    @DJFIREMANgambia 23 хвилини тому

    Modou mbaye dai play mind rekk d dull bu refet, max mbergan ak situe lee plan la rew . Situe defut dara c lamb bei beure AK modou lo dega dega rekkk situe alioune sei 2 rekkk wala lac rose

  • @AbdoucisseSarr-qn9hv
    @AbdoucisseSarr-qn9hv 2 години тому

    Modou lo modoule sportif limou wax modoul yone môme meunoul siteu ba diko wax né yarouwo

  • @MoustaphaNiasse-y3u
    @MoustaphaNiasse-y3u 11 годин тому

    C'est le sport rekk 🤣😂😂😂 nooooo désolée kw

  • @ousmanefaye2868
    @ousmanefaye2868 7 годин тому

    Modou mbaye niepe khame nagne ni suite sa kharite la mé mougne lene tek

  • @MoustafaMbacke-kf8sj
    @MoustafaMbacke-kf8sj 10 годин тому

    Ioe boy Lane mofi eundi ay roi bounék jarnafi ioe ésk nite ngeu wa diamgeu yi nék ndayu si town bi saga ndayou ñieup wakhosi roi yi bari nagnou wayê limou dèf bén roi défoukofi .Modou moy dagu ndayu sén khôl yi boy ioe nékal ndayu nitt affairou sokhor yi noko meuné té bala ngay wah Dara bayil tokh yamba

  • @alphathiam8792
    @alphathiam8792 6 годин тому

    Ki da dieul faute bi yeup ni modou la Siteu defoul dara

  • @MoustafaMbacke-kf8sj
    @MoustafaMbacke-kf8sj 10 годин тому

    Boy ioe danga beug affairou professionnel té khamo Dara f2f bi kén yakhouko siteu mo réw Modou wakhouko danga gank diom dakoni koula wakh ni arrièral daflay pousser si gnak diom ioe mom lamine samba sa baye leu té Modou beuréwol ndayu ak siteu

  • @Aliounediouf-b6b
    @Aliounediouf-b6b 2 години тому

    modou , je suis pas d'accord avec toi . Modou lo wakhoul directement danga niak diom . dafané kouleu conseiller reculer moola diangal niak diom. et c'est Siteu qui a insulté le premier après la question de la journaliste. ( Mane la yalmine bi damaley gnouss daane la.) En t'écoutant parler tu es du côté de Siteu. Lingeen beugoone moo amoule. Depuis quand on fait recours au tribunal de sport?

  • @MaimounaWade-b8m
    @MaimounaWade-b8m 5 хвилин тому

    Ki vrai nafek leu

  • @OUSMANEDiallo-mw6ow
    @OUSMANEDiallo-mw6ow 13 годин тому +1

    Lamine samba est limité et très nul même Modou mbaye la chance qu'il a c'est juste le fils de bacaye mbaye sinon il es très nulle aussi

  • @Mamadou-j1x
    @Mamadou-j1x 14 годин тому

    Laminé Samba mo kamol lamp

  • @NfamaraDiatta-q8j
    @NfamaraDiatta-q8j 7 годин тому

    Bounou ndeyou siteu way
    Ngakka le