🇸🇳Débat Baye Niass kouko guiss Doug Aldiana🤔 - Oustaz de la Nouvelle Génération & Oustaz Alpha Ba

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 10 лют 2025
  • 🚨Débat Paroles Aux Talibes Baye Niass cii senn Pass Pass you Doy warr yii 🤔🤭 - Oustaz Alpha Ba
    • 🚨Débat Paroles Aux Tal...
    Urgent Ay leral cii Ibrahima Guéye Khassida donn weur kaba gua ca Makka akk … - Oustaz Alpha Ba Ha
    • 🚨Urgent Ay leral cii I...
    🚨Urgent - Lamb jii - Messages aux lutteurs ⁉️ - Oustaz Alpha Ba H-A
    • 🚨Urgent - Lamb jii - M...
    #senegal #kebetu #team221
    Voici un extrait des vidéos oustaz Alpha Ba ha pour des éclaircissements sur le polythéisme …
    #senegal #kebetu #team221
    spécial live Cii LERAL LEUNT LEUNT gnii wottee woo abb yónnent guinaaw sunu YÓNNENT MOUHAMMAD ﷺ
    11 Mai
    #senegal #kebetu #team221 LIVE - IMAM CHEIKH ALPHA BA - PAROLES AUX AUDITEURS - WOOTE WOO ABB YÓNNENT GUINAAW SUNU YÓNNENT... #sénégal #senegal221 #magal #merci #mouride #youtube
    Maktaab Oustaz Alpha Ba
    t.me/MaktaabOu...
    ︾︾︾︾︾︾︾︾︾︾︾︾︾︾
    t.me/MAKTAABSA...
    📡:t.me/reflexion...
    t.me/kitaabtaw...
    t.me/LerralDiine
    t.me/passpassb...
    t.me/Sharkhsounna
    t.me/siffatusa...
    #senegal #kebetu #team221

КОМЕНТАРІ • 89

  • @seynaboukane2767
    @seynaboukane2767 Рік тому +5

    Sofianqué yi séne problème moy séne wahou serigne laniou gueune gueum que wahou borome bi AK yonéntibi

  • @amadouourydiallo3145
    @amadouourydiallo3145 Рік тому +2

    Macha ALLAH Oustas Alpha ba et sa team. Il faut tous les démasqué.

  • @alinesamb5006
    @alinesamb5006 Рік тому +6

    السلام عليكم ورحمة الله وبركاته كيف حالك أنت بخير أحسن الله إليك ماشاء الله بارك الله فيك جزاك الله خيرا بارك الشيخ الفاهم باه حفظه الله ورعاه ❤❤❤

    • @KAADUDINEEJITV
      @KAADUDINEEJITV  Рік тому +2

      ‏وعليكم السلام ورحمة الله وبركاته آمين ولك مثله

  • @AbuMuhammadAlGambi
    @AbuMuhammadAlGambi Рік тому +2

    Jazak'Allahu Khairan Ustadh Alpha Bah حفظه الله tontu bi rafet na Allahuma Barik
    إسكاتهم بالمعرفة

  • @asannediop3826
    @asannediop3826 Рік тому +1

    Oustas alpha ba mo baah machallah barakallahou fikoum

  • @2rayone760
    @2rayone760 Рік тому +3

    Noooo!Senegal very sad😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭

  • @fatimadieye9478
    @fatimadieye9478 Рік тому +1

    Soubhanal lahh

  • @Mouhamad-u6f
    @Mouhamad-u6f Рік тому +2

    Machallah ma khady et younouss également

  • @bassiroumbaye8099
    @bassiroumbaye8099 Рік тому +5

    😂😂 كبرت كلمة تخرج من أفواههم إن يقولون إلا كذبا 😂😂 حفظكم الله ❤❤

  • @hamdine7940
    @hamdine7940 Рік тому +2

    Merci Serigne alpha ils ont entre de jouer

  • @odoa4880
    @odoa4880 Рік тому +3

    Kou amoul dalil rekk transformer wou ab philosophe 😂😂

  • @Mouhamad-u6f
    @Mouhamad-u6f Рік тому +2

    Machallah oustaz alpha

  • @adramesagnan5195
    @adramesagnan5195 Рік тому +1

    Oh oustaz ya réer Baye Niasse pour nka firi ay wahom fay nka ame DEUG DEUG ya rérr bilahi

  • @diopkeba8068
    @diopkeba8068 Рік тому +2

    Yaw âme gua kulawax bët moy guis. Lo xamul dagay manou baye Niass koku yalla moko teral. Un grand éducateur

    • @matarndiaye9969
      @matarndiaye9969 Рік тому +2

      Et après dafa takh kouko guiss dougou aldiana ?

  • @alloucoco
    @alloucoco Місяць тому

    merci alpha ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @bineta1752
    @bineta1752 Рік тому +5

    Kou diotali wahou yalla ak wahou prophète bi gnouni tu est dur dagna meti dagna sokhore arrêter l’hypocrisie yalla dou fowoukaye yalla dou
    Morome kepe kouy diouli di wore di supporté gni wote si dine te bokossi nafeke gna
    Malheureusement les cœurs sont malades 😢ouztaz alpha ba le mal est très profond très même

    • @bineta1752
      @bineta1752 Рік тому +1

      @@ismailadiallo7819 salam ma tontula yaw moi personnellement aussi je ne vis pas au senegal je ne parle pas avec toi au cas ou tu te sens concerné par mes propos cela n’engage que toi
      Mane sounna Senegal lako diangue avant may guene Senegal
      Assalamou aleykoum

    • @bineta1752
      @bineta1752 Рік тому +1

      @@ismailadiallo7819 sama genre yiii mane amouma sa diote di daguessante ake yaw sama temps dafa précieux lolu pour prendre mon clavier et discuter avec des gens yo khamni loulene nekh lagnuy wakh
      Kholal salam

    • @bineta1752
      @bineta1752 Рік тому

      Salam à vous aussi

  • @dieynabandiaye9211
    @dieynabandiaye9211 Рік тому +2

    ❤❤❤❤❤❤ débat bi amna solo

  • @younousseaidara3892
    @younousseaidara3892 Рік тому +2

    مَا يُبَدَّلُ الْقَوْلُ لَدَيَّ وَمَا أَنَا بِظَلَّامٍ لِّلْعَبِيدِ

  • @ngommahtar4689
    @ngommahtar4689 Рік тому

    إن الله لايفلح الميعاد نعم /
    أولكن لا تعلمو( أن البار)كل يوم هو في شأن

  • @bounesadio9934
    @bounesadio9934 Рік тому +7

    Ki xamoul Dara wayyy 😂😅😅 baye Niass d'où touss nitt késé laa

    • @alassaneseye2191
      @alassaneseye2191 Рік тому

      Billahi louler

    • @AFRICAN67
      @AFRICAN67 Рік тому

      ​@@alassaneseye2191wallahi Ibrahim Niasse nite simple kassé leu, soufianké kémane rék le gëm

    • @bounesadio9934
      @bounesadio9934 Рік тому

      @@Makhtarka ok mais d'où yallah fofou lay wakhé ... Nitt leu comme sa baye .... Baye Niass déy POUB comme sa ndeye 😭🤣🤣🤣🤩

    • @Makhtarka
      @Makhtarka Рік тому +1

      ​@@bounesadio9934
      mais limou dougal si dîné ji des 1000 sen baye ak sen serigne defouko si islam bi point.
      c'est un homme extraordinaire et multi dimensionnel

    • @Makhtarka
      @Makhtarka Рік тому

      محمد بشر لا كالبشر
      بل هو كالياقوت بين الحجر

  • @OumuTawaim7299
    @OumuTawaim7299 Рік тому +1

    لاحول ولاقوة الابالله العلي العظيم

  • @baboucardiop5121
    @baboucardiop5121 Рік тому

    ❤❤ machallah ya oustaz Alpha contanna si yew ❤❤❤❤

  • @AmadouSylla-pg2kh
    @AmadouSylla-pg2kh Рік тому

    شكرا لك الفاء باه وفقك الله واصل طريقك فإنه طريق الخير باذن الله تعالى نفع الله بك

  • @tawhid-i3l
    @tawhid-i3l 4 місяці тому +1

    Medoune bayil philosophie bi 😂😂😂

  • @FatouNiang-d1k
    @FatouNiang-d1k Рік тому +1

    Ma warou .Qu'Allah nous guide.

  • @modouniane2163
    @modouniane2163 Рік тому +1

    baye niass djoublou waayou wakhame bi moye kou gisne maye ki donnou yone nennetou yalla mouhamed صلى الله عليه وسلم ngua beugue ma thi lolou dinala tek mome bye niass thi yone wokhamene so thi wathioul de mo tere ngua dougou aldiana

  • @GakouBaba-w1v
    @GakouBaba-w1v Рік тому

    15:40 mashallah

  • @bounesadio9934
    @bounesadio9934 Рік тому +2

    Medoune fall ''' yallah néénaa dou togn ''' lo deff AK wakh diodiou

  • @Makhtarka
    @Makhtarka Рік тому

    mais limou dougal si dîné ji des 1000 sen baye ak sen serigne defouko si islam bi point.
    c'est un homme extraordinaire et multi dimensionnel

  • @dameadame6062
    @dameadame6062 Рік тому +1

    Ah kay yalla dafay changé waxam . يمحو الله ماشاء ويثبت وعنده علم الكتاب

    • @KAADUDINEEJITV
      @KAADUDINEEJITV  Рік тому +2

      Ban borom xaam tafsir moo koo firee ayat bii nonou tee ragal yAllah cii sa commentaires bii

  • @mariamaba5454
    @mariamaba5454 Рік тому +2

    😘😘👍

    • @KAADUDINEEJITV
      @KAADUDINEEJITV  Рік тому +2

      ‏وعليكم السلام ورحمة الله وبركاته بارك الله فيكم

  • @sakhoousmane7066
    @sakhoousmane7066 Рік тому +1

    Alpha wadie douy na warr legui mom dafa begue deguel Baye Niass yide wakho yala no li doy na warr

  • @aboudiop353
    @aboudiop353 Рік тому +1

    ❤❤❤❤

  • @ibrahimac-y4g
    @ibrahimac-y4g Рік тому

    ta teunku si algur ane ak suna li moy deugue wa salaam❤

  • @Yeme--NA
    @Yeme--NA Рік тому +3

    Assalamou Aleykoum sama béne Dieuwrine dafma wakhone Yalla dou wakh ba paré Wéddi boppam et Il dit qu'Il est le plus juste des juges. Légui mane je me dis que sou naré atté dara dinako déf pour samoneték limou wakh. Té pourtant c'est vrai que souko narone déf mba bagneko déf kéne meunou kaka téré fokna ki wofou laye wakhé. Mais aussi il faut que niou khamni mom dou wéddi boppam. Sinon yaw Alpha amna question boumala beugone poser tchi séne débat bobou nguéne done wakh Yalla mingui tchi kaw wala tchi souf.

    • @samsoudinesallseck4722
      @samsoudinesallseck4722 Рік тому +2

      Diuemmi Yalla Migisi Kaw Khame khamame Mignisi Bepou Barap
      Yalla moko Wakh Ak Yonentame
      قال تعالى أأمنتم من في السماء أن يخسف بكم الأرض فإذا هي تمور
      أم أمنتم من في السماء أن يرسل عليكم حاصبا فستعلمون كيف نذير

    • @Yeme--NA
      @Yeme--NA Рік тому

      @@samsoudinesallseck4722 Légui nak Alpha la beugona latch fane moy tchi kaw wayé bala lolou damaka beugona latch ndakh guem nani la terre est rond ? app boule la bou mélni wer wi rek bou nek tchi diaw dji dans l'espace et qui ne repose sur rien apart kémanou souniou Borom. Souma wakhé ni mom guem nani la terre est ronde après nak lakoy latch wala ma lérale ko béne mbir mou dolli matchi.

    • @babacarsokhna6363
      @babacarsokhna6363 Рік тому

      Yalla mo waxal bopam ni migui ci kaw.

    • @Yeme--NA
      @Yeme--NA Рік тому

      @@babacarsokhna6363 Waw mane je suis juste à la recherche d'éclaircissement motakh kourel yeup lay déglou après ma khol, légui fane moy tchi kaw la beugua latch Alpha mais bala lolou mou expliquéma est ce que la terre est ronde ndakh nda mélni ball. A partir de là nak lakoy diokhat explication pour mou dollima.

  • @yayathiongane9839
    @yayathiongane9839 Рік тому +1

    Waliyou yalla yi louniou wakh d'où dagne baye niass cheikhoul islam sou wakhé kouko gise dougue aldianne mougui wakh ak dioulite yi té nion niou kou naroul tékhé doléne beuge doléne gise yonèntibi kou ko gise douga aldianna té amna yéfeur youko gise kone Bouy wakh lolou mougui wakhak dioulite té dafa ame gis gissou beut ak khoul meun ga khôl nite té gissou ko yalla mo môme aldianna môme safara moy dougal kouko nékh aldianna wala safara mais ngiko nékh moy ngiko geume déf lime santané khôl bou sél yalla dale moy yalla

    • @Makhtarka
      @Makhtarka Рік тому

      وشكرا
      @yayathiongane9839

  • @mamoudoudaff3028
    @mamoudoudaff3028 Рік тому +1

    Feiheilen va deff yenen dioulit mogueun ....baye niass loumou deff ci dinei lislam bi kenn defouko

    • @rappel4152
      @rappel4152 Рік тому

      Wa kho deugueu deh tafsiroul al Quran d'où livre Fiqh d'où livre sharh khadith. Dewoul ci combat meusooul combat defoul aussi ouverture. Diayoul bakanam té Ken guené wouko pays nguir l'islam... livreram bokoul ci livre telouway pour xam sa diné té yi laniou meuneu défal islam alors sa Baye Niasse loulou def ?
      Réponds avec preuve et n insulte pas

    • @mamoudoudaff3028
      @mamoudoudaff3028 Рік тому

      Jamais ma sagua .baye niass limou convertir ay nitt ci l'islam en nombre kenn defouko ci adouna...féhélen def gni nékoul dioulit pour gnou neik dioulit..tei baye limou def ci dinei lislam c palpables..c te donner la liberté qui va avec un responsabilité..

    • @mamoudoudaff3028
      @mamoudoudaff3028 Рік тому

      Cheikhal l'islam...c lui le cheikh de l'islam. Et tu prétends à dire qu'il na rien fait de l'islam...suprime ces disciples dans le monde et tu verra un bon nombre de musulmans diminuer...arrêtons de dénigrer entre nous musulmans. Faisons tous pour rependre l'islam comme la voulu le prophète sll

    • @rappel4152
      @rappel4152 Рік тому

      @@mamoudoudaff3028 diw limou def limou def lim ko ?... vas y tous la defoul ci l'islam. D'adiou ci liniou dadioul de 1 de 2 Cheikh Al Islam c'est Ibn Taymiyyah partout dans le monde fokhé wakhé Cheikh al islam gnouné Ibn Taymiyyah. Yalla koko diaglele. si tu me crois pas va taper sur Google qui est Cheikh Al islam ? Ibn Taymiyyah lalel guenal avec plus de 1000 résultats Do guiss feneu Founiou wahé Baye... Ibn Taymiyyah a écrit plus 300 volume un seul livre à lui " Majmough Fataw " fait plus de 16,000 pages sur islam. Mo diangal gnou dakka Tafsir ci Isalm Ibn Kathir, ibn hayyim... Té meunala bindal 10 pages youma holoul feneu ci limou defar islam. Dalam sah mo gueune Baye Niasse s'en kokou dou touss la defaroul islam. Limou bindeu yeup da matoul sah 5000 pages on vous a menti demlen diangui s'en dîné

    • @layekharagne2224
      @layekharagne2224 Рік тому +1

      @@rappel4152Merci ❤️👊🏾

  • @moustaniang7375
    @moustaniang7375 Рік тому

    Je ne suis pas d'accueil avec lui mais il faut équilibré

  • @alphaOumarsy389
    @alphaOumarsy389 Рік тому

    Sounnah rék oustaz sa numéro

  • @dialloibrahima8134
    @dialloibrahima8134 Рік тому +2

    Tarikha problème la thi islam

  • @mustaphabaldeh2232
    @mustaphabaldeh2232 Рік тому

    Salaam Alpha,
    Baye Nyass watou wahtadul wujud walla Hullol walla itahat baye Lim wakh outea ak Lee yeep

  • @samburu-lelionnoirdafrique6194

    C'est faux oustaz de otv de ouakam, une chaîne sur UA-cam. Je viens de le vérifier. Il parle trop sans connaissance

  • @alphaOumarsy389
    @alphaOumarsy389 Рік тому

    Numéro alpha ba

  • @aboubakrydiallo3739
    @aboubakrydiallo3739 Рік тому

    قال تعالى ( مايبدا القول لدي و ما أنا بظلام للعبيد )
    Ki limouy wax mo reuy
    Waxu kéfér leu

  • @baaliou6634
    @baaliou6634 Рік тому +1

    Aquran Ak Sunna Rek mo worr point

  • @mbayendiaye7560
    @mbayendiaye7560 Рік тому

    Mais qu es ce qu on a foutre guiss n importe qq serigne en reve q es ce q ca nous raporte la religion est complet by Moustapha swa

  • @abdourahmanelaye9846
    @abdourahmanelaye9846 Рік тому

    السلام عليكم ورحمه الله اسمي عبدالرحمن لاي ساكنا في اسبانيا ولكني بودي ان اشارككم في الحوار ولكن أراه بعد ماانتهت كيف اشارككم مباشرة وشكرا

  • @ibrahimac-y4g
    @ibrahimac-y4g Рік тому

    lal moy man liilaa wla léélaali am solo moy djoulite laa naniou néke ay djoulit

  • @XadimgayGay
    @XadimgayGay Рік тому

    Kii lim wax dëgg la yéen ñii yéenay sanka nitñi dagéena soof yalla léepu lum def mbaa lum wax dafa dagan ci moom?

  • @user-wm7dl2iu4
    @user-wm7dl2iu4 Рік тому

    imam Alfa boull wakhe AK ki wallahi Mane dama tite

  • @bahalimatou8108
    @bahalimatou8108 Рік тому

    C'est une perte de temps de discuter avec des ignorants, farfelus de ce genre, avec cet accoutrement de comediens

  • @DIALOGUE-DEUG
    @DIALOGUE-DEUG Рік тому

    Un autre philo-Doff 😂😂😂 ce Médoune

  • @asannediop3826
    @asannediop3826 Рік тому

    Loutah sering ci maneu reuye yeuye Lou nane ragal yalla mo am solo wallahi dafa lére wallahi

  • @diopmouhamadoumoustapha8757

    Yeurma dé sounou borom noko diapé

  • @FatymaBah-v5f
    @FatymaBah-v5f Рік тому

    Tarikha yii doul rek lanioy déf danio niémé yallah

  • @aliounediouf8196
    @aliounediouf8196 Рік тому

    MAIS C'EST QUOI ÇA?DES ROUGE À LÈVRES? 🤔🤔C'EST UN OUSTAZ GOORDJIGUÉNE???🙊🙊

    • @Babe-FaLilOu
      @Babe-FaLilOu Рік тому

      Soubhanallah akhi moytul wax loula worul
      Barakallah fik

  • @alioufall4265
    @alioufall4265 Рік тому +1

    wkh mou change équestre woul si yall moy deuge

  • @djibi710
    @djibi710 Рік тому

    Wokhou doff rék

  • @FatymaBah-v5f
    @FatymaBah-v5f Рік тому

    Téksi diagouniou

  • @gueyediop
    @gueyediop Рік тому

    Modou limoy wakh lou amla yen por yen yalla yen rek lay douguel aldiana mou guen sanion niepay dem safara waye yalla borom bou matla

    • @masiba7272
      @masiba7272 Рік тому +1

      Yalla dou wax waxet.yalla tegui promessam.yalla d'où tegui ay waxam.
      Lolou ken douko lam lamé.
      Soy tegui wax dangay Andi dalil si arhouranou yalla,wala sounay yonentem.