Bonjour mes chers frères et sœurs, Le problème du Sénégal c'est que il y a moins de Tafsir. Les gens ne font pas la traduction du Coran,ils nous disent que c'est dangereux d'écouter le Tafsir. Moi par la grâce de Dieu il a fallu que je sors du pays pour aller étudier pour comprendre beaucoup de choses. j'ai compris le Coran et la sunnah. Hors du pays. C'est en devenant étudiant à l'étranger que j'ai tout compris. Au Sénégal je détestais les ibadou. J'ai tout compris par le biais de oustaz Assane Sarr
Diaradieuti yalla souniou borom bimouniou bollé sérigne bamba yén nékk lén di togne rék mourides yis dég dég ay diamou kattou yalla lagne yén dé sou fékké yéna mome aldiana dé mouride dou dougou
@@ibradiop9753 mane amou ma louma méti fofou yalla moy bakhal té môme rék mouniou mona jugé kon kouné na nék si ay ayibou bopam li guén di déff défarou dra au contraire dey yakk té dioulite diouli tay bokkam dîné dou thi thioline wla wawi késsé
1:45:23 Oustaz Alpha, Je suis d’accord avec vous sur tous les points comme d’habitude mais par contre je ne pense pas que c’est HARAM de se raser le menton. C’est une Sunnah de garder une barbe mais ce n’est pas un péché de la raser. Où bien je me trompe?? Quoiqu’il en soit JazakAllah Khair pour la dawah que vous et Oustaz Ousmane faites. 🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Barakalahou fika frere Alpha na jamais rasèr son barbe il est comme ça , je vie avc lui ici en Arabie saoudite , si il est loin d’écran tu p pensè q il la rase, mai quant est près de lui tu xomprendras
Kingsley A. Barakalahou fika frere Alpha na jamais raser son barbe , il est comme sa , je le connais bien , si il est loi decran tu pense qu’il le rase , mai quant i est près de toi tu comprendra
@@droitaubutsalati9880 tout à fait. Je n’en doute pas. Je peux même la voir sur l’écran. Je voulais juste savoir si c’était HARAM de la raser. Je sais que c’est une SUNNAH mais si je l’ai bien entendu (à la minute indiquée), il a dit que c’était Haram. Merci mon frère et qu’Allah vous bénisse et protège tous.
@@droitaubutsalati9880 aaaye waaye ! 😭😭😭 tu me fais peur! Je suis ahlou sunna Alhamdoulilah depuis 3 ans seulement. J’ai passé toute ma vie aux USA mais c’est seulement les 3 dernières années que je me suis mis à fond dans la religion. Je veux avoir une barbe mais la mienne ne pousse pas très bien donc je la rase. Je savais que c’était pas bien (makrooh) mais je ne savais pas que c’était Haram. En tout cas merci beaucoup!
Assalamou aleykoum. S'il vous plaît dites moi à quelle heure le live a lieu. À chaque fois j'attends votre live mais j'arrive pas à assister parceque je ne sais pas exactement à quelle heure vous le faites. Merci d'avance
Ragal len yalla si liguen di wax yonent bi sakh dou haramal dou daganal lii moy bokkalé nak idéologie yi nio yakk diné ji déguén di weddi sén bopp comme nilén alcouran weddé khamkham bou eup alcouran amoul yonent bi ak sahaba yi topougnou won loudoul alcouran yén gni yena yakk diné ji wanté wa tassawouf mom ay dof lanou kholilén sourate ( 25 aya 25 26 27 28 29 30 ) yén ak wa tassawouf yeup la concerné
Alpha arrete t kun simple hypocrite qui essaie de se faire un nom.on t connait tres bieb t un usurpateur doxane rek mooy sa 2.faig attention les gens savent ou tu t cache en italie d .huuunn
Machallah contane na si yène liguène di dèff amena sollo yalla nalène yalla dimbali
Oustaz Alpha Ba adiarama
Yalna yalla samou oustas alpha ba amine yarabi
Bonjour mes chers frères et sœurs,
Le problème du Sénégal c'est que il y a moins de Tafsir. Les gens ne font pas la traduction du Coran,ils nous disent que c'est dangereux d'écouter le Tafsir.
Moi par la grâce de Dieu il a fallu que je sors du pays pour aller étudier pour comprendre beaucoup de choses. j'ai compris le Coran et la sunnah.
Hors du pays. C'est en devenant étudiant à l'étranger que j'ai tout compris. Au Sénégal je détestais les ibadou.
J'ai tout compris par le biais de oustaz Assane Sarr
Merci beaucoup mon frère oustaz
Machalla ya oustaze alpha ba yala nala yala samou maye la fane bou goudou ak wergui yarame
Yalna yalla mousal gnou ci bokalé ak bida amine yarabi
machalah yén rek yéna jara déklou
Bilahi😘
Alpha yaw bayil doul ta bayui sandey ganna messere dou sa moromou bay
Ganna masseré nabayi fànn ci dîné yalla
Fatabarakala machalla yalna rabouna samale léne bopam yénaye soldari l'islam yi dilérale leuneteyi yalna rabouna goudeul séni fane té mouseulniou thi réér gouméti gui
Machaallah Yallah na léne yallah faye barak allahwu fiikum
Bien fait
Very interesting topic masha Allah
Yen dal yallah nale yallah fay yuw
Masha Allah ya Oustace
Machallah ame na solo trop
Mashallah amatina solo
Liguéni Df yallha santanéwouko té bokoûl di diiné
Masha Allah tabari kallh Allah merci
Balaye deugue la 😀Alpha yagui may rétament Lo sakh
Yalna Yalla fay leen
😂😂😂😂😂😂😂😅😅😅😊😊😊😊bass abdou khadr degoul arab
dinèy senegal guèweule yi gnoko yakh
Dine ak politique bii te ken d’où wax
Ma challah oustaz yalla nguenne yagga fi di yewwal senegalais yi akka passe passe you bonne yi ak sen bokalé anda ak reer
Amna solo lool mbirmangi geuna leer rek
Diaradieuti yalla souniou borom bimouniou bollé sérigne bamba yén nékk lén di togne rék mourides yis dég dég ay diamou kattou yalla lagne yén dé sou fékké yéna mome aldiana dé mouride dou dougou
Saliou Massa baalniu....
@@ibradiop9753 mane amou ma louma méti fofou yalla moy bakhal té môme rék mouniou mona jugé kon kouné na nék si ay ayibou bopam li guén di déff défarou dra au contraire dey yakk té dioulite diouli tay bokkam dîné dou thi thioline wla wawi késsé
Doyna warr 😔
😂😂😂😂😂😂 yéné sonno
ALHAMDOULILAH
Allahu akbar, may the almighty guide you all lii leer-na trop
👍
Serigne mélo man🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Vrément gni boléne topé sa tension moy yék🤣 légui oustaz beugona kham photo serigne yi défko sa kr wala salon ndakh dafa arame wala say photo parents
1:45:23 Oustaz Alpha, Je suis d’accord avec vous sur tous les points comme d’habitude mais par contre je ne pense pas que c’est HARAM de se raser le menton. C’est une Sunnah de garder une barbe mais ce n’est pas un péché de la raser. Où bien je me trompe?? Quoiqu’il en soit JazakAllah Khair pour la dawah que vous et Oustaz Ousmane faites. 🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Barakalahou fika frere
Alpha na jamais rasèr son barbe il est comme ça , je vie avc lui ici en Arabie saoudite , si il est loin d’écran tu p pensè q il la rase, mai quant est près de lui tu xomprendras
Kingsley A.
Barakalahou fika frere
Alpha na jamais raser son barbe , il est comme sa , je le connais bien , si il est loi decran tu pense qu’il le rase , mai quant i est près de toi tu comprendra
@@droitaubutsalati9880 tout à fait. Je n’en doute pas. Je peux même la voir sur l’écran. Je voulais juste savoir si c’était HARAM de la raser. Je sais que c’est une SUNNAH mais si je l’ai bien entendu (à la minute indiquée), il a dit que c’était Haram. Merci mon frère et qu’Allah vous bénisse et protège tous.
Kingsley A.
De la raser c haram , c sa la position des ahlou souna , nax le prophète dafa wax ( nague ne yar sen sikime )
T diglè bobou obligation la
@@droitaubutsalati9880 aaaye waaye ! 😭😭😭 tu me fais peur! Je suis ahlou sunna Alhamdoulilah depuis 3 ans seulement. J’ai passé toute ma vie aux USA mais c’est seulement les 3 dernières années que je me suis mis à fond dans la religion. Je veux avoir une barbe mais la mienne ne pousse pas très bien donc je la rase. Je savais que c’était pas bien (makrooh) mais je ne savais pas que c’était Haram. En tout cas merci beaucoup!
Machallah ya oustaz
Oustaze alfa pabi amna foule dé payi danio woté mou moté lolou késéla
Machalla
Bonne continuation
Alpha bayil doul ta bayui cheikhoul khadim bayil doul bayil doul ndeyam ku tegeul sandeynga sa xole danna DAK. Yaw yaye fonto saney nittyi
Kurewnga ku khamadynga mais yaw bo tambabalo ci senegal niou niaf sandey
Yombou na lool lakhatou sa ganav PC dy vakh rek
Doulrek doulrek doulrek dine dji dou sen diney bay alpha yaw nagnou dem rek tanga bagna mandou li tegal sandey mingui gnieuv
Yaw alpha manulo lire sakh khasida yi yaw nopil
Wa légui chékhe limou wakhe ak abdou wakhab mi nieuke ray dioulit guniawe yonintebi ak salafou salikhe dolénesi wakhe
Mourides yi ak tidiane yi danioo rerr
Dara
Deķéûe nekhôl dîàréu diàuf
❤❤❤❤❤🙏🙏🙏🙏🙏
Assalamou aleykoum.
S'il vous plaît dites moi à quelle heure le live a lieu. À chaque fois j'attends votre live mais j'arrive pas à assister parceque je ne sais pas exactement à quelle heure vous le faites.
Merci d'avance
Walekoum salam mbokk 20 h Sénégal 21 h europe
Samedi 20h Europe ou21h Sénégal
Merci pour vos réponses les frères.
BârakAllahou fikoum
Nyii gat rek.Dulal seen saringe rek
doul lén feulé
Ragal len yalla si liguen di wax yonent bi sakh dou haramal dou daganal lii moy bokkalé nak idéologie yi nio yakk diné ji déguén di weddi sén bopp comme nilén alcouran weddé khamkham bou eup alcouran amoul yonent bi ak sahaba yi topougnou won loudoul alcouran yén gni yena yakk diné ji wanté wa tassawouf mom ay dof lanou kholilén sourate ( 25 aya 25 26 27 28 29 30 ) yén ak wa tassawouf yeup la concerné
Lum wax yalla ko wax konne luffi indi xadiiis .
Yonent tibi luy seen preuve ni yonente talka apart mom ci boppam l8mu waxal boppam ?
Salam ameneu solo mais ne dit pa svp que cé gents ressemble aux gents de lenfer dieu peut les guider bonne courage
Merci beaucoup nit deugnga
YEEN SOFFFF
Sofougnou dagnou wax lou yalla wax
ay thiakhane rek leu
Abedou wakhabe rakame wakhena dafa dofe balamo dé
Yall nathiou yalla xam xamou rakal yall bou an rathè
Senegal c foutu
SENE KOTARRTI YOUTIAG YIIII NON NON LA SENE XAM XAM TIACTTE
Merci mille fois wa tasawouf lounek lanouy wak
Ki kane la wa primaire
Non!!! Ce sont les professeurs !!!
@@ibrahimasarr8529 😂 non monsieur kay nga wah c i
Vous voulez amner une autre religion au senegal boulene niou fonto
Doomi harami tariqa!!!
Bilaahi man yeen dama leen yërëm ñàkk tawfeex rekk moo leen jàpp xoolal kiy lathi moom ak gimiñam gu salte gi cam
اعوذ بالله من الشيطان الرجيم
Astahfiroulla bayilen cheikh tidiane dousen morome
Chiekh tidian dafa soss ci dîné yalla bi
Alpha arrete t kun simple hypocrite qui essaie de se faire un nom.on t connait tres bieb t un usurpateur doxane rek mooy sa 2.faig attention les gens savent ou tu t cache en italie d .huuunn
Sa lafall yaye yawou salafiss bi yawou ak alfa ba
Tarihayi nék Sénégal amoul loukko geuneu bonne fénal yalla sougnou borom rékk
enfoires de salafistes
👍