Alahou Akbar Ngoye Fall dafa fèbare bagne èvacuer ko extérieur: Ses proches très inquiets

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 28 жов 2024

КОМЕНТАРІ • 120

  • @marieeliseloume5422
    @marieeliseloume5422 2 місяці тому +30

    Koudoul nebeutou lou la dalle yako tekk sa boppeu bou d daffa febare yalla n'a werr thi barke serigne babacar sy amine yarabi aminnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnne

    • @mariepietri9388
      @mariepietri9388 2 місяці тому +1

      Wonewou dé bakhoul
      Sounou borom beuguoul kouye Bakou
      Ame lepeu wané lépeu pendant que certains meurent de faim
      Delossi lène khel yii et garder les yeux sur terre

    • @Malick_ibn_dinar
      @Malick_ibn_dinar 2 місяці тому

      Bayiléne bokalé si “barké nabil mustapha “ guene di mine déff

    • @dabachou5674
      @dabachou5674 2 місяці тому

      Allah Houma Amine Ya Rabi Incha Allah 🙏🙏🙏♥️

  • @momo_le-pro.7
    @momo_le-pro.7 2 місяці тому +31

    Ki mo gnémé beutt 😢thiate mo bakhoul té mom moytou woussi dara yalna Yalla yeukeuti ko 🙏🙏🙏

    • @fatimatra8457
      @fatimatra8457 2 місяці тому +4

      Ak akkeu aussi akkeu baaxoul

  • @amiyfall-v1z
    @amiyfall-v1z 2 місяці тому +20

    Bonne guérison qu'Allah te guérisse amine 🤲🤲🤲

  • @Black-lion221
    @Black-lion221 2 місяці тому +14

    Prompt rétablissement à elle mais juste un petit conseil Thiat bakhoul ame-ame daniou koye neub.

    • @Salimata1000
      @Salimata1000 2 місяці тому +2

      Walaye,pour vivre heureux et en bonne santé,vivons cachés.

  • @bbouhama5373
    @bbouhama5373 2 місяці тому +29

    Baka photographe ba wakhé niko sama khaliss boma ka fayoul dinga ko fadioo, sila khamni thiate ak akkou photographe bobou moka diap

    • @halikano392
      @halikano392 2 місяці тому +5

      Laaaaaaaaye photographe bi lolou la wakhone ndeyssane bou tomber malaka amine laaaaaaaaye

    • @didigalass2506
      @didigalass2506 2 місяці тому +2

      Akhe bakoul mais yalna borom bi feugue boppam

    • @fandao2138
      @fandao2138 2 місяці тому +3

      ​@@halikano392yallah dou takhamlou nianou kougn togne motakh

    • @aramegaye3968
      @aramegaye3968 2 місяці тому

      galass2506 bilay akh bakhoul

  • @ibrahimandiaye-5250
    @ibrahimandiaye-5250 2 місяці тому +45

    Ki dara diapou ko loudoul ake AK Riba kéna sokhoré wouko néléne ko mouye fay bore ligueye lo Ay domou diambour bégne léne fay voilà les résultats

    • @yacinekanoute5385
      @yacinekanoute5385 2 місяці тому +9

      Moi je me rappelle du magal de l'année dernière quand elle a fait emprisonner le pauvre photographe. Té défouko dara. Togne mo bakhoul. Yalla deugue leu beugue.

    • @MarieAmaar
      @MarieAmaar 2 місяці тому +3

      Akheu baakhoul

    • @bayesene5217
      @bayesene5217 2 місяці тому

      Dorénavant ware dawe nieupe merŕ

    • @ndeyebakhaothiaw4117
      @ndeyebakhaothiaw4117 2 місяці тому

      Ha aduna dal bo doul neubeutou thiat sonal leu

    • @aramegaye3968
      @aramegaye3968 2 місяці тому

      Bilay ​@@yacinekanoute5385

  • @nobasiby9540
    @nobasiby9540 2 місяці тому +24

    YALNA KO YALLA MAY WÊR NA MAYTOU BËT AK LAMIGNE THIAT BOURAYOUL SÉMAL

    • @basselabdou9891
      @basselabdou9891 2 місяці тому +2

      Gui adouna rék l'ay weur

    • @HORE2023
      @HORE2023 2 місяці тому +1

      AK AKK BOU BEURRI!! TÉ MOU FÉY PHOTOGRAPHE BI KHALISSAM BALOUKO AKK. NDAKH AMNA NIO KHAMNÉ KÉNN DOU TANGAL SÉN XOL

    • @fatoundiayeseck1678
      @fatoundiayeseck1678 2 місяці тому

      Walahi deugeuleu amna gno khamné keendou tangal Seen khool kouka def guisko bilaay

  • @lyadama9282
    @lyadama9282 2 місяці тому +22

    Thiate bou rayoule se’mebale

  • @astouadjie3877
    @astouadjie3877 2 місяці тому +3

    Prompt rétablissement AAMIINE YA RABBI

  • @antasarrcisse1803
    @antasarrcisse1803 2 місяці тому

    Thiatttte rek cette femme se montre trop
    Elle est jolie machallah tout mais attention meilleure santé

  • @fatouwade5048
    @fatouwade5048 2 місяці тому

    yana Yalla safara té défal ko diame 🙏

  • @sallyfall1421
    @sallyfall1421 2 місяці тому +13

    Toubab meunoul fathie THIATE,
    Bo diogué si li nga neubeutou. Bon rétablissement ,

    • @Momo-ee6zq
      @Momo-ee6zq 2 місяці тому +1

      Wa Lou bakh. Si thiate

    • @dieynabafadiga6730
      @dieynabafadiga6730 2 місяці тому

      Sakho falakhi ak naassi ​@@Momo-ee6zq

    • @sallyfall1421
      @sallyfall1421 2 місяці тому +4

      @@Momo-ee6zq
      LAURIERS , CITRON , SEL ...
      Faire bouillir et se laver avec.et etre discrét dans tous les domaines.

    • @Momo-ee6zq
      @Momo-ee6zq 2 місяці тому +1

      @@sallyfall1421 yalla nalla yalla faye merci

    • @sallyfall1421
      @sallyfall1421 2 місяці тому

      @@Momo-ee6zq nioko bok

  • @rokhayafall3001
    @rokhayafall3001 2 місяці тому +4

    Mou melni moye borome magal gui trop c trop wanè wou rek bonne guèrisson

  • @thiorodiop189
    @thiorodiop189 2 місяці тому +5

    Mame dé lima geume moye chantier bi mou nek one di gérer mo takh mou soneu mé dou dara yallanako yokeu weer ak soutoura ak mboleme dioulite

  • @abdoulayendiaye190
    @abdoulayendiaye190 2 місяці тому +7

    Que l or la guérisse.

    • @amyrock4324
      @amyrock4324 2 місяці тому

      😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

    • @elimanediop0175
      @elimanediop0175 2 місяці тому

      😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

    • @aissatoutoure6169
      @aissatoutoure6169 2 місяці тому

      😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @KaraJieu-p5p
    @KaraJieu-p5p 2 місяці тому +5

    Prompt rétablissement,ngoye,boula dAra diot.diabarou eumeut Touré la,un ami de st louis

  • @abibatoubathily3783
    @abibatoubathily3783 2 місяці тому +3

    Bne rétablissement

  • @didigalass2506
    @didigalass2506 2 місяці тому +2

    BON RETABLISSEMENT

  • @FallouDieng-d9q
    @FallouDieng-d9q 2 місяці тому +1

    Damani yalnako yalla la lafal tihat daimbar deg la machallah

  • @ZahraD3163
    @ZahraD3163 2 місяці тому

    Qu'Allah lui accorde un très bon rétablissement une meilleure santé.
    Ses premières images du Magal montrent une femme qui a beaucoup perdu de son charisme, avec un visage très terne...
    Que le Tout Puissant accorde une santé de fer

  • @begueBamba
    @begueBamba 2 місяці тому +1

    Dama khamoul magal tou lousi li di wout takk or di wané wou pour lane

  • @oumoukalsoumseck3952
    @oumoukalsoumseck3952 2 місяці тому +1

    Sarafina, vous me forcez le rire😅😅😅😅!Et c est juste, des millions de frcs en or , sur un corps c est forcément du LOURD!!!!
    Maamebooy depuis Rufisque

    • @sophiesao9584
      @sophiesao9584 2 місяці тому

      Vraiment dommage pourquoi ce réjouir du malheur des autres souhaiter la bon rétablissement 😢

  • @fatouseck7344
    @fatouseck7344 2 місяці тому

    AMMINE YALLAH WEUURE AK DIAM INCHAALLAH BMSBSYMRTA

  • @sokhna-awaboucherifousseyn5827
    @sokhna-awaboucherifousseyn5827 2 місяці тому

    Love You ssou

  • @didigalass2506
    @didigalass2506 2 місяці тому +1

    S.A.W WAKHONE NAKO MOUDIOU DIAMONO SAMA KHETE WI BEUTE AK LAMIGNE MOLENE DI YOBBU MOYTULENE

  • @sanekama2864
    @sanekama2864 2 місяці тому +1

    Yalla gua weer an diam

  • @AliouBodiane-z2z
    @AliouBodiane-z2z 2 місяці тому +4

    Prompt rétablissement

  • @khassimgueye9460
    @khassimgueye9460 2 місяці тому +3

    Prompt rétablissement à Ngoye Fall

  • @Aminatandiaye-n8n
    @Aminatandiaye-n8n 2 місяці тому +1

    Thiate bakhoul lo bari lé bari lé amna koula eupeulé fouffff né némeu

  • @BintaAmarnarr
    @BintaAmarnarr 2 місяці тому +8

    😂😂😂😂 ngoye amna Touba 4mois dafa nekonnn chantier 😂😂😂

    • @senmlgtv5570
      @senmlgtv5570 2 місяці тому +1

      Mane magui wone si chantier bi dara diotou Sénégal féne rék😂😂😂

  • @awadiagne3184
    @awadiagne3184 2 місяці тому +1

    C'est peut être le décès de sa maman 😢

  • @premieredameba9447
    @premieredameba9447 2 місяці тому

    Walahi alaale dou dara

  • @OumyKhaiiry
    @OumyKhaiiry 2 місяці тому

    Ndaysane masta waye thiat bakhoul

  • @Sarafina-z9s
    @Sarafina-z9s 2 місяці тому +8

    Li yeup or yii la dafa diss motakh

  • @Salimata1000
    @Salimata1000 2 місяці тому +1

    Mo thiatou bopame,lii mouye def loumouthi done khar,soudone dix leu,dafa khamoul siw yobouna niit bamèle...:-)

  • @satisfact7
    @satisfact7 2 місяці тому +9

    Li dal Ngoye Fall diangate la, Adina gnila weure yeup 80% dagnoula gnè, 20% koumpa moleine dougal si yaw ak interets.Dagnilaye diay dila thiatou, wayer bo dano gnolaye ndieukeu siwal, dila wilipender wayer bo guèsso sa ndiabote rek ngay dèssè. Soyez humble ndakh beussou bamel, dè dou tago, nagnou dèlossi khel yi si akhirou zaman bi ta yokeu diamou yalla bi niko yonantèyi dane dèfè. Bagna copier niko ndiabotou ibliss di dèfè moy wanerwou, titarou, concurrence, ak poukarè. Chak jour missalou ya Allah gueineu wayer guissougnouko.

  • @mohametthiam4500
    @mohametthiam4500 2 місяці тому +6

    Thiate rék la bilahi

  • @Lalabve
    @Lalabve 2 місяці тому

    Yalla na yalla Feugue saaa boopou boudé deugue leuh yalla mousal leuh thiii thiate ak lamigne uneshallah

  • @cheikhcisse7992
    @cheikhcisse7992 2 місяці тому

    Il faut être humble dans la vie

  • @Mizafrica
    @Mizafrica 2 місяці тому

    Yalla na wér ak Diame té mou bayi wanéwou amoul ndjarigne

  • @NdeyeSeck-m1d
    @NdeyeSeck-m1d 2 місяці тому

    Akh Rék môla diapp yaafi wakhôn Askia dalà geuneulé ak say Morôm bagua khamko 😂😂

  • @awadiagne3184
    @awadiagne3184 2 місяці тому

    Lou toy dina meussa wow gnou bayi thi khél 😢

  • @khakika-d9g
    @khakika-d9g 2 місяці тому +4

    Bon rétablissement

  • @YoussouDiaw-w8h
    @YoussouDiaw-w8h 2 місяці тому +1

    Ki dafa nîémé beuth trop

  • @sokhnasaneseck3265
    @sokhnasaneseck3265 2 місяці тому

    Thiatou xaliss la wone da woni macky doyotul poche

  • @abdoulayesarr1138
    @abdoulayesarr1138 2 місяці тому +2

    Nabalou akh borom photoyi

  • @mariawatis-fs6ob
    @mariawatis-fs6ob 2 місяці тому

    Sa se voit

  • @mariamacamara8059
    @mariamacamara8059 Місяць тому

    Dafa febar xamouma ,,waye deh Dara xamnako genrou driankeyi AK adjiaratouyi nguenna waligui ay ganaoumam truyand lagniou , bi waxeni gniounam ay borom xalisse lagniou nonoula lagniou Say sayeh gnieme liguaylo nit bagnie kafaye,gniemewoul lekka Riba gnieme toroxal.newdidole ,dougniou maye dounyou sarahe lougniou may kou neh daffa fekka ngua am ni gniom,ngoye falll, sa photographe bobou ngua bagnione Faye nexonala bayinalen yalla,te nguen xamni lolou rek meunala Sall bayilen lekkeu gniaxa diambour

  • @ousmanediop1620
    @ousmanediop1620 2 місяці тому

    Elle représente quoi au Sénégal ?

  • @aboudione7672
    @aboudione7672 2 місяці тому +1

    C'est bien fait pour elle

  • @MatyDieng-n8w
    @MatyDieng-n8w 2 місяці тому

    Dagen beu gislenma ak gnemee beut bakhna

  • @mariamba9378
    @mariamba9378 2 місяці тому +1

    Bo khamé né dagua Ferbar do la katou aussi

  • @moustaphaseck3802
    @moustaphaseck3802 2 місяці тому

    Ak photograph bila

  • @famasall-ej3zb
    @famasall-ej3zb 2 місяці тому

    Ignane amouthi defa nieme beute ak lamigne bakhoul say or deunthi ko sa keer banga gniby waye takeu aye kilo or fok niou thiatoule

  • @amydiaw5859
    @amydiaw5859 2 місяці тому

    Ahhh menona nebeutou ba wérr

    • @senmlgtv5570
      @senmlgtv5570 2 місяці тому

      Dara diotou tmt niakoul dara magui koy guiss

  • @Astoundiaya
    @Astoundiaya 2 місяці тому

    Ki na fey khalis foto garaf bi fate Khadiou fi

  • @Pénda-e3d
    @Pénda-e3d 2 місяці тому +1

    Bilahi walay thiate

  • @aidafallousall6793
    @aidafallousall6793 2 місяці тому +1

    Mane kaye nima ko guissè rène wèroul

  • @aminatacamara8456
    @aminatacamara8456 2 місяці тому

    réhyi nite ake yakha tèh ake ligéuy yan tèh sénègaléyi nokoyi défan tèh rek billahi

  • @mordione7256
    @mordione7256 2 місяці тому +2

    Ki dafa ñièmé beutt ak lamigne lolou kassè moko djiàp chake magal mou djieul rire bi akh

  • @FallouDieng-d9q
    @FallouDieng-d9q 2 місяці тому

    Magal gie kosi raw raw ba fao

  • @ametecisse8580
    @ametecisse8580 2 місяці тому

    Est-ce que c'est vrais. Dfa beugue nebou lii xeww rén da amon amtol rek

    • @Lalabve
      @Lalabve 2 місяці тому

      😂😂😂 pour yaine dafaaa niak kou amoul dinaaa tabakhhhh chateau bou besss kiii loumou tak rk aye millions leuh

  • @ramatoulayedrame6589
    @ramatoulayedrame6589 2 місяці тому

    Tiat bou rayyoul semal.

  • @marieeliseloume5422
    @marieeliseloume5422 2 місяці тому +1

    Thiatte bakhoul

  • @abdourahmanefall7074
    @abdourahmanefall7074 2 місяці тому +2

    Dites des verites, mais racontes de fausses narratives est un peche.

  • @mouhamadouka391
    @mouhamadouka391 2 місяці тому

    Thiate bakhoul

  • @AyaMballo-ke6re
    @AyaMballo-ke6re 2 місяці тому

    Est sénégalais égri et méchant pourquoi guen koy yenai lou bonne aye salopard guen rek😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭

  • @AmyKane-ni8ht
    @AmyKane-ni8ht 2 місяці тому

    Sounou borom weireul leu

  • @ndeyebakhaothiaw4117
    @ndeyebakhaothiaw4117 2 місяці тому

    Boy sokhore nit dafay fek gua kham ko ba meun ko tal mais ko khamni si ay vidéo gua koy guiss boko sokhore nak sonal sa bop dakh yeugou ko

  • @habycisse3609
    @habycisse3609 2 місяці тому

    HEY WAYE ARRÊTEZ VOS BLAS BLAS.

  • @DiorDIAKHATE-hh6mr
    @DiorDIAKHATE-hh6mr 2 місяці тому +1

    Adouna du Dara ..amal jamm Yaye

    • @Lalabve
      @Lalabve 2 місяці тому

      Amiiiine

  • @ibrahimandiaye-5250
    @ibrahimandiaye-5250 2 місяці тому +2

    Dotoul brillé fay nane ko bou yague

    • @basselabdou9891
      @basselabdou9891 2 місяці тому

      Deug pire

    • @deugrekk6410
      @deugrekk6410 2 місяці тому +1

      Pourquoi nga wakh lolou

    • @Lalabve
      @Lalabve 2 місяці тому

      Sokhorrr ngaine

    • @ibrahimandiaye-5250
      @ibrahimandiaye-5250 2 місяці тому

      @@Lalabve mane djoulite la douma wakh louma woroul si Al houran lay wate barké Al houran ngoye fall truand la Lou lére lay wakh ni boudé dama ko sokhoré na gneup guisse le prophète Mohammed Sala lahou aley hi wa salam yow male khiyam ba mou désse mane ngoye fall dama ko kham truand la dama kham gnimou amél khaliss ak moye yala yimou néké wone ak son ancien mari galaye la toudou boko ladjone kouye ngoye fall Di nga kham né sokhoré Wou mako djeukeuram bi di askia Touré si seuye lako féke Takako douko wédi démal front de terre bimou deukone nga lathié kofa nga khol loune lay wakh si ngoye fall ak yénéne mbir younou meunoul wakh barké Al houran ngoye fall bakhoul néko mouye faye bore truand la amoul lou soukeur barada

    • @Lalabve
      @Lalabve 2 місяці тому

      @@ibrahimandiaye-5250 sa livre boudè matakhhh ngaa bindeuh koo yaak ngaa koo nakhhh doumaa koo lire en ts cas dioulite warrr naa diome guéné thii laminiame bii lou niaaw sa papa khanaa diangalou leuh loolou

  • @gansiryfall995
    @gansiryfall995 2 місяці тому +1

    Thiate

  • @mariamba9378
    @mariamba9378 2 місяці тому

    Loudoule beute ak lamigne diapoule ndaw si

  • @madiallo7095
    @madiallo7095 2 місяці тому

    😂

  • @nogayeniang9119
    @nogayeniang9119 2 місяці тому +1

    Dafa beugue buzz rek

  • @marieeliseloume5422
    @marieeliseloume5422 2 місяці тому

    Yaram bouye toye meti

  • @ZahraD3163
    @ZahraD3163 2 місяці тому +2

    Qu'Allah lui accorde un très bon rétablissement une meilleure santé.
    Ses premières images du Magal montrent une femme qui a beaucoup perdu de son charisme, avec un visage très terne...
    Que le Tout Puissant accorde une santé de fer

  • @soukeynadiousse9192
    @soukeynadiousse9192 2 місяці тому +2

    Prompt rétablissement