Salam mais c'est le but de la série, Hanny est une toubab qui a découvert et qui tout de même aime la culture sénégalaise, donc après avoir accepter d'être là deuxième épouse, et de vivre dans la même maison , Ngonè pense tjrs pouvoir gagner avec son sourire hors que Hanny réfléchie tjrs avant d'agir.
Ils sont droles mais il est temps de changer un peu. Chaque fois c Annie qui gagne, au debut cetait drole mais la on connait presque tjrs la fin. Wala ngene changer touti facon bingeni jouer 🙄🙄🙄🙄🙄
Ngoné soudé gagner dou nex dou racisme mais moy cncpt bi parce que beneu toubab diougue fé kham souniouy réalité di woudie comme les sénégalaise c drôle et incroyable en plus Ngoné souniou gagné nimouy joue daf may ray ak niou bari fi 😂😂
Wayéne tamite lii dou gnou thi wakh Any nakk meune ngha togn dé wa légui nakk khame nghéne lanla Ngoné Mbaaye il faut que mou venger wou na khar ba Any moomé mou fayou comme ça di na fa meuneu diar amalé première victoire ngha khamni gnoune fans Ngoné Mbaaye yi dina gnou meuna jubiler touti dafa diotte nakk Ngoné Mbaaye ame victoire.
Guiss nga ngoné ti santeu bien 😂😂mane mon père mi di wakh di vibrer dinama ray😂😂kou guiss anni bimouy gueneu thi nekeu bi mdrr,mon père aussi yaram bei commencer wone tang anni daag ko
J’ai perdu ma mère en ce début mois de ramadan 🙏 pensée à nos maman😘❤️
Paix à son âme qu'Allah lui accord le Paradis du courage
K le bon Dieu l'accueil au paradis firdaw si ma soeur
Paix à son âme
Grossir Tv que la terre la soit légère
Qu'elle repose en paix
KO buegue feke sahrou ramadane buesuel j'aime
Mbaye niang werwr
Inchallah
Mbaye niang 3
🙋♀️🙋♀️🙋♀️🙋♀️🙋♀️
Amine YAA RABBI
Ko bague féke sahro ramadan bueseul j'aime ❤
Yaw mom gneupala kham🤣🤣 série yeup guay dé😂😂😂 goor foot ball lasi kham
Mon père il joue bien son rôle beugoul kene mère si diabar yi
@@antafall4919 borome keur nono la wara mell
Baye mor iow vraiment diaxal gama
Yagui fepou😄😄🙈
@@technicienneqhseplus khana dagua beugue maniaw sêt sila
Kou yeureum ngoné beussale jaime ma xoleuh😂😂
🙋🙋
😂😂😂 trop pitié
@Pénda Ndiaye gros bijoux❤😍
😂😂😂
🙋♀️🙋♀️🙋♀️🙋♀️🤩
Je regarde cette série de plus 2019 kou bege série bien beuseule j'aime
Kou beugue Ngoné di gagné beusseul j'aime
Mane mom gniarel la. Anni la faral. Mè beugu ba gnou may ngonè touti chance bok
Wa ngoné rewna deh
Noooooooooooooooooooooo Ngoné rewwwnnaaaaa 😂
Mais kmm elle joue super bien .je me divertis trop avec cette série.
Bonne continuation à vous
Ayy ngoné mo réw 😂😂 nénako mon pére bott ma lala wakh thiéy li dii déparou Guaïndé arrivée Mouss guay am fofou Samedi soir invalidé😂😂 allez Annie
😂😂😂
A000
Hiv
Ouma Barkham
En plus d’être extrêmement belle, elle a une voix sublime ❤️ machalla diaba yaye bour ❤️
Fatou SARR e
Ndeye Astou Gueye Sall e
En effet
Ndeye Astou Gueye Sall excuse moi ma cher le e ça signifie quoi
Non Ngonè mom day doundeu mbeugeul pire elle joue bien Diaba yayou bour mais ndekété toubab bi vrai bandit la
Khamo dji dara sakhe
Toubab bi kay khamo si dafa sakh
@@falloufall8015 n
Pir anni vraiment bandit la
Ms nak ngonè dafa wara ame mdam
Salam mais c'est le but de la série, Hanny est une toubab qui a découvert et qui tout de même aime la culture sénégalaise, donc après avoir accepter d'être là deuxième épouse, et de vivre dans la même maison , Ngonè pense tjrs pouvoir gagner avec son sourire hors que Hanny réfléchie tjrs avant d'agir.
walleykoume salam, tu as parfaitement raison mon frère
salimata Ndiaye oui mais il veut dire Ngone ne réfléchit pas avant d’agir, il ne généralise pas
Kou diépi anni yeureum ngoné defal j'aime
Ils sont droles mais il est temps de changer un peu. Chaque fois c Annie qui gagne, au debut cetait drole mais la on connait presque tjrs la fin. Wala ngene changer touti facon bingeni jouer 🙄🙄🙄🙄🙄
Jolie Maman mon demi homonyme 🤣liii dou question de gagné dei dagni wone nei toubab yii danio féroce rkk
@@mamanmargotchimerediop9784
Voilà c'est le but toi t'as tout compris
Tamit
Bien dit
Amou sens
Mais ngonée dafay dioye ni nan wolma maty mbaye ni j aime 😂😂😂😂😂😂😂
Travaille de maman
repas de filston
Bénédiction de dieux 😂😂😂😜
Kou beugue ani di gagne beuseul j'aime ma guis
Waa pikini dagnoo raciste chaque jour tobab moy gagné😁😁😂
Raciste dagua dioum boulko wakhati fene
Naxx nga meunnn si dareuhhhh
Wakh deug
Bilay li doyna war
Moi je le vois pas comme racistes mais c'est pour montrer yene negue la brom mo thiay fana chaque jour c'est ngone qui provoque Ani
Gonè mbaye nimou rèwan to ni dama nèx😂😂😂djiguen day beuri capris koumou nèx beuseul bleu
Ngonè j’aime vraiment quand elle fait la gamine 😂😂😂
nooo mane ani dinama rayyyy😂😂😂je n'ai jamais commentaires sur youtube mais je d'or cette série
Ngoné néna samedi bi yakou moma gueneul ma bokal nékk bi mouss 🤣😂😂😂😂 koussi bayi hel tape j'aime
Awa Ndong mes dafa dioum rék oh mrd
@@coumbafall5655 qui t'as permis de m'insulter en plus qui ta sonné
Ki dafa dioum rk
@@aidakanelo9192 hamnako mais je l'ai fait juste pour rigoler aussi
Awa Ndong c toi ki ma sonné par ce que dagua waxe niou tontou la ok pardon bou féke damala sagua
Ngoné Mbaye n’est pas possible 😂😂😂Elle me tue
😂😂
🤣🤣🤣
la pub sur le ramadan qui passe avant la série est juste magnifique bon ramadan à tous
Ana niou farale anni beusseléne j aime 👍👍👍👍👍
no ngeweul nexna 😂😂😂
Oly Cisse fo bayiiii la poison
😂😂😂
Mon père dé xamna da ñouy xeuy rék for bopp bi si souff. Li ngay yeungou beurinaaa 😂😂😂😂
😀😀😀😂😂😂
Bilay yow dji niamakh niamakh 😂 😂
🤣🤣🤣🤣🤣
😂😂😂😂
Khamna warna mana mbacku 😅😅😅😅😅
Man mome na bayi commentaire légi mousouma am jaim 😤😤
Légui amnga plus de 150 jaime
@@evakonteye3185 nila 😂😂
Man dama fogone ni bay rék mo réw mais ndéké ngoné mbaye amoul😂😂😂😂
😁😁😁
😂 😂 😂
Si ta une fois étai le 1er a commenter une vidéo sur UA-cam tape bleu
Bilay ali Moy say say gnarell day froçe Ani 2séme femme yii pouce len likes booke waw Keuy😂😂😂😂
Mon père la khawma mom khana ay miléntane niokoy matt mouy niamakh niamakhi nii rék😂😂😂
Cissé bou serigne saliou 😜😂
Mdr
Wakhatiko deih niak naturel rek
Purée 😂😂😂😂😂😂😂 non mais ngoné mbaye rewwwnnnnaaaaaa.... gni amoul diabar Yalla nalenr yalla maye kou melni ngoné mbaye. Amine
Mon père nièmè na wodou serviette 😂😂😂😂😂
Deune ba bax😂😂😂😂
🤣🤣🤣🤣dèh na
Mon père gua daffa nièmè serviette
Samedi wam mo yakou😁😂😂
@@choucousaw5744 mdr 😂😂😂😂 wa bakhna beuss bou serviette bi wadè mou kham foumou kay wakhè
Pour ce qui demande loutakh toubab bi di gagné rek parce que ngoné ndiaye daf ko khép pour mom diongué woul
Bhjky Lsam merci beaucoup nit gni meunougnou compou fofou
Toujours ani mais ngoné mbaye doit gagner
Je suis d'accord avec vous
Vraiment wakhl dèè
Vréma mane nékhatouma
Je vote ani
Wawaw
No guonè mbaye c la meilleure actrice
😂😂😂😂😂😂 ngoné dinama rey mon père nak la chat koula bayi
😁😀😀
w
Ngone rew nga😂😂😂😂😂mais ilé temps mou gagner nak
waaa mom père yaramam bi dou réglé tamite...mais sa complicité avec ngoné jdrrrrr
ndeysane sama ndaw na quand mon père donné des conseils a ngoné. ma belle mougnal nga seuy boula toubab yeugal 1 mètre
Dieuleul mon père soumako kholei rek sama khel dem si souris ordinateur😭loutah mou soff di niami niami rek
Yaramounene bi nak isssss
Machalah ngonè a une bel vois mes se ki me derange dans la série est purkoi ngoné dou am deug ta parfois dagnou koy togn et sa doit être vice versa
gni kay dano dioume chaque jour rekk Anny gagner ahh
Vraiment
Wakh deuug yalla sakh
Lolou dou thi dara pour wonéni toubab diarna Bayi khél
Vraiment
Ngoné laniou wakh nioune💪💪
Ngoné suis avec toi 😂😂😂
Je suis morte de rire qui aime sama woudiou toubab la aime mon commentaire🤗🤗🤗🤗🤗
kou beugue maty appui j'❤ime way
Khaliss da ame solo sy vie bi bilaye bon ramadan 🙏🙏🙏🙏
Anni wa team ngoné mbaaye beuss lenn pouce bleu
Ceux qui se plaignent du fait que Annie gagne a chaque fois, khanaaa vs ne regardiez pas « tom et jerry » wala « bip bip et le coyote »??😂😂
Wouyay mon père 😂😂😂la chat le soir
maï jiji m
Non maty ma tué ngoné j'aime bien la manière dont elle se comporte sa me tue et anni mom dou dem🤣🤣🤣
Mane daal anni laa geume dafa fèroce thi niarèle nguonè dina khamni anni mii kène douko diame naani Ana sopey anni yi waay
Ngoné kagne laye gagne toujours perdre😣😣
Balla fall wakh nga deug dh tmt
Dafa wara gagnée dh mom
Ngoné risque de s'arracher tous les doigts😂😂
dia khardiatou je te jure 😁😁😁😬
😂😂😂😂
😂😂😂je ladore
😂😂😂
Bilahi
Maty mom tjrs égale à elle même intérêt personnel rek moko gnior ndokalé way 😂😂😂😂
Yalla na Sénégal am diamb wa ana ngiye wathie ramadan 2019 ❤❤
Amine
Publiez le making off de cet épisode svp 😂😂😂😂, les séquences doivent être reprises plusieurs fois 😂😂😂.
Anni je t’aime trop 😂
Si ça continue comme ça damaye arêté diko cétane c Annie qui gagne chaque fois 😥😪😣😮😮
Vreman
Ray guenman 😃😂😂😂😂😃ekip de choc
Samedi soir bi moudiè na soirée o canapè 😂😂🤣🤣
Qui trouve que ngone a une Belle voix
Sheut shui dead ani nenako èh bayil sama borom keur 😂😂😂😂
Ngone mane sa réwantou dafmay nekh 😂😂😂😂😂
Kou beugeu féké ramadan moubarak beuseul bleu
Wagagagaaa Keur Gui todj dai may wakh mon pere di liime ay mouss kxkxkx!!!La chaaa hier soirr🤣🤣🤣 Wouy Moliere serie bii dinako yeukeuti😂😜
Li nekhoule Dara chaque jour ani di gagné
Ngoné soudé gagner dou nex dou racisme mais moy cncpt bi parce que beneu toubab diougue fé kham souniouy réalité di woudie comme les sénégalaise c drôle et incroyable en plus Ngoné souniou gagné nimouy joue daf may ray ak niou bari fi 😂😂
Salam yen wa quiolition ande setan série yeup😁😁
Coalition😂😂
🙊bon merci arame😁
Kou beugue maty mbaye beseul je t'aime
Diam ci yén gneup❤️🙏
Vous êtes très fort li nexna
Sama dieguou catalane bi mo vulgaire !!.😂😂 Ahhh Annie cerveau 😘😘😂😂
Mimi E.A xufisw'b
Wa anni mi nena bayil sama borom keur bayil sama borom keur😆😆😆😅😅
Tey mom contre na Annie pask tamit kou ayé nga bayi ko mou def liguéyam tamit mais pas yakalko.
Annie mo sof rék makhala safoul djiguene safoul dieck
lo xam tchi niak classe
Wayéne tamite lii dou gnou thi wakh Any nakk meune ngha togn dé wa légui nakk khame nghéne lanla Ngoné Mbaaye il faut que mou venger wou na khar ba Any moomé mou fayou comme ça di na fa meuneu diar amalé première victoire ngha khamni gnoune fans Ngoné Mbaaye yi dina gnou meuna jubiler touti dafa diotte nakk Ngoné Mbaaye ame victoire.
Ngoné yangi yakkeu dérrou awo yi😭😭😭 ay yeuffou niaŕél rek ngafi def
Sama woudiou toubab la machallah
Ngoné mbaye serieux yeureume nala trop😂😂😂😂😂😂🤣🤣🤣
Barki yalla Anni je t adore mala beug wayy looll
No ngoné rew na dinama raye tamite mai anni sama puissance rek feem 100% awo yi rek stratégi 0 makhala bour daye foye foko fék 😜😜😜😜😜
😂 😂 😂 😂 😂 bravo Annie.
Ngonè keine dou khep mbeur
Bilay Ngoné Mbaaye ya bari caprices😅😅
Guiss nga ngoné ti santeu bien 😂😂mane mon père mi di wakh di vibrer dinama ray😂😂kou guiss anni bimouy gueneu thi nekeu bi mdrr,mon père aussi yaram bei commencer wone tang anni daag ko
yow mom ngoné da nga niakk diom togal fofou toubab bi dila beureudj beureudjé noum ko nékhé
Cv
😂😭🤣🤣
Ndeysane ngoné ak Annie comme Tom et jerry. Jerry d'Ay togn ba paré gagné.😂 mon pére nénako ngoné wathial dakh mouss mi😂😂😂
Samedi bi yakhou moma geuneul ma bok ak neik bi mousse😂😂😂wouye magui dei
Mane dal ngoné nékh nama avec sa belle voix
Wa Ngone mbaaye kagne kay am victoire nk tjr anny
Moma diaxal de😀😀😀
Loll😂
chapeau a pikini, pour le lieu et les acteurs. noo 😂😂Ani mo sohor si ssiirou wala ndiapane.Ngoné maabeug say pleur😂😂😂
Père ioa tamite mouche gaye daw ohhhhhhhhh😂😂
Maty mbaye moye djinée keurgui 😂 goor daa manque 😂
Ms ngoné réw nga bilay nimouy def kaname gui Manou mako mougne
Hè bayil sama borom keur ani mongui may réy bilahi
Si l'amour été un poison dinama yoob ilakhira hahaha
Thiey gonei tu sante bien 😂😂😂😂😂😂
vraiment Annie nékhatoumako srx elle exagère way
Mon Père moom dafa soof chaque jours rk any lay faral té moom mooy tonie séne lii néxou ma dra man ah
Anny lay donn DH wawaw 😁😁😁😁 deuxième femme
Walhal waaay. 2rek dou ay fooo😂😂😂😂😂😂
La série et bien met oh bout d'un moment y en a marre tjrs la mm qui gagne sa soule ... oh bout d'un moment on regardera plus
Non seri bii dafa nekh damakoy yakamti nakh ngoné Mbaye😂😂😂😂