Pa Assane mane lima metti dou lolou té diap nani yaw lingua wara wax pour mane waxagoko mouy peine de mort bingua xam nii souniou gouvernement bi gno ngui koy bay bayal té guiss ngua affaire bangui aggravé wou Pa Assane pour mane peine de mort faw niou wax si avant-hier la deux gamins doon khékh kéne ki ray moromam donc diap nani faw niou diouk si car la situation s'aggrave 😢😢
Kou beuge sa yaye rék lalal j'aime ❤❤❤
Merci Pa Assane kou d'accord peine de mort danou koh walla appliquer senegal lalal j'aime ❤🎉
Wallahi aziyme pa Assane li défawara jekh ndeyam ⚠️ kou réy nioü réy la pass khét Non li défa méti waye 😭😭😭
J'ai du mal à imaginer ce qu'il passe actuellement dans notre pays
أن النفس با لنفس Yalla mouko wakh Na nioü Baye affaire khét 😭😭😭❌
Merci pag fière de toi 👏
Mane titt na 😢 bilay fou niou dieum 😢ak ly 😭
Pa assane sénégal légui Kom kuluna yi na minster bi guéne déf declaration ni ko ray niou rayla rek ndém légui nioun ay kuluna laniou
Yalla la guiss n'a léppp tiha inchalla yalla dîna até🥹
Doye na waar dih 😢😢😢😢😢
Sénégal yi fiy am ni gnousi diogoul yalla tere mais guère civile dina fi am Sénégal la nit waroul dokhantou ak djasi
Thieuy Sénégal afèrr khètt loufi wara dièkh la akh khollall li rék
Sama Dieukeurou bénn tanta la 😭😭😭😭☹️☹️☹️☹️
Man bilah sam pape lolou naro nako dal dafa féki niou sa bou tol bi mom né wadji geudal mom nok fénou ma ta boma lalée ma
Ohhhhhh😢. Il faut vite trouver une solution à cela car ça peut dégénérer . qu'Allah nous protège 🙏🏾
YALLA KEN EUPOUKO YEURMANDÉ☝️
KOU RAY NIT NANOUKO RAY KON RAY DIEKH👈
ان النفس بالنفس 🤷
Senegal kuluna yi nio len tané
Merci pa assane
Man dh j’ai peur pour ma propre personne Waw man dh diomi na nk 😢
😭😭😭😭😭😭
Pa assane yaw tayi wakho ray rek kay wakh
Kou raye gnou raya rék
😭😭😭😭😭😭😭
Pa Assane mane lima metti dou lolou té diap nani yaw lingua wara wax pour mane waxagoko mouy peine de mort bingua xam nii souniou gouvernement bi gno ngui koy bay bayal té guiss ngua affaire bangui aggravé wou Pa Assane pour mane peine de mort faw niou wax si avant-hier la deux gamins doon khékh kéne ki ray moromam donc diap nani faw niou diouk si car la situation s'aggrave 😢😢
Peuls mobari histoire
😢😢😢😢
😢😢😢😢😢😢😢 mon pays Va Mal
❤❤❤❤❤❤❤
😢😢
❤❤
😢
Billaye 🫣🫣🫣😭😭❤️❤️👏
😢😢😢
Thiés la😢
Thioy Sénégal dama yakar ni legui malaka dagnou ko dakh fall Sénégalais
Pa assane sa numéro la sok la guirr yallah
Bilay dafa méti
Peuhl yii leu sunu côté la togne ba paré Ray
Sa date yaye follé 😢
Kou Ray niou Ray la rk mokay dindi
SLM slm 🙏🏾
Man côté bobou la deuk mais peulh yi sonal nagnou bilakhi sakhie ak ray lagnou fi néké 😭😭😭😭
Peulh domeram la
@@Khamza903sen data yaye yen ñep
😢😢😢
❤❤❤❤❤❤❤
😢