La séquence de vieux BA je ne l'avais pas vu venir😂😂😂. Innovation nguen di def daal. Aucune imitation, chaque épisode avec son goût. Bon courage et bonne continuation guys.
J'EN VEUX DEFINITIVEMENT A NDEYE NDIAYE CAR J'AI RIGOLé JUSQU'A AVOIR MAL AU VENTRE!!!!!! cette serie est à Mourir de rires vraiment!!!! BRAVO à toutes les comédiennes et comédiens
Ndeye Ndiaye est excellente. Moi, je pense que c'est le même cas de Ba qui a pris mon cher papa. Jusqu'à présent nous ne savons pas ce qui a causé sa mort. Cette série ne traduit que la réalité sénégalaise. Chapeau
Nn Ndeye Ndiaye elle ma tuée Shuttt retane na baye berengou Cette serie est typique de notre société la majeure partie des familles vit cette situation😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Toujours présente 🙏🙏1 ba 31❤team badiène ak ndèye Ndiaye❤message biens reçu👌dieul souniou dieukeur yi louné niou dioxlèn ko xawma ana jus ak poivre 🤔mo taxite AVC ak crise cardiaque rek👌 la plupart dans les maisons mère y afa dèss pa yèp fatou fa yalawou🙆♀️😪🙏🙏
Machallah li lanou sokhla nicena Ndeye mome damako beugue depuis mome aak diop fall fat kiné mes acteur préféré yalla naléne yalla may fane goudou aak mbolome djoulite
@@khadiseybatoundaw1969 lol mais Fat Kiné mo gueuneu bari wakh Oumou. En fait Oumou joue juste son rôle. Il y a des femmes comme ça, qui perdent toute raison quand on leur parle de co-epouse, qui menacent Séne guellou dieukeur Yi et pensent que tout le monde sont contre elles. Lima nekhoul ci Oumou moye le manque de respect envers ses beaux-parents et limiye fene gratuitement et sans vergogne. J'aime pas le mensonge.
No Dara fayuko. ,,sama nakhar famille Sénégalais,, diekhna,,nilla,, machalla 💚💚💚🙏 sa kaw sa kanam
La séquence de vieux BA je ne l'avais pas vu venir😂😂😂. Innovation nguen di def daal. Aucune imitation, chaque épisode avec son goût. Bon courage et bonne continuation guys.
Ndeye ndiaye ko yapp 🤣🤣🤣🤣
@@maremediop9166 Ndeye Ndiaye Mane yaw la gueum 😀😀😀😀
@@maremediop9166 qqq
@@maremediop9166qww
@@adamabeye8724 non je parle de ndeye Ndiaye de la serie elle est tellement drôle 🤣
J'EN VEUX DEFINITIVEMENT A NDEYE NDIAYE CAR J'AI RIGOLé JUSQU'A AVOIR MAL AU VENTRE!!!!!!
cette serie est à Mourir de rires vraiment!!!! BRAVO à toutes les comédiennes et comédiens
Moi aussi ki bakhoul lol
L'expression du visage de Bou quand il regarde ndey ndiay sheuut😂😂 Ndey Ndiaye rew na niafff .On réclame la présence de Fatkiné
Yone la déh la kinéss
Waw Waw amena fi place
Wawaw et pourquoi pas que Fatkiné devient la niarel de bou 👍
Wawaw Na gneuw rek rakhou soffi keur gui wathie
Ndeye. NDiaye amoul roussoukaye.na khol si bou book. Waaye bakhna si Pa you niaka fayda niakkal fayda seni dom.Sounou culture soutoureu dafssi book.
MDR Ndeye Ndiaye m’as fumé avec son Police et gendarmerie 😂
GIGN😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Alhamedoulilh franchement c'est série montre beaucoup de choses dans le monde que nous sommes 😭😭😭😭😭😭
Ndeye Ndiaye elle est unique cette fille 🤣🤣
Comme vous
No ndeye ndiaye dou dem🤭🤭🤣
@@ndoyealassane2848 2dhh89
walahi bima ko Guissé si série bi la kham ni dina nékh
@@fatimfall1505 enthusiasts
. How z rip
Li sétane nako plusieurs fois 😂😂😂🤣Association Mbeguale sa Dieukeur lagnouye créer😂😂😂.Ndeye NDIAYE est la présidente
Non vous avez fait ma journée senepeople Ndeye ndiaye dou moromou goné dal
Bou rek la yeureume 😂😂😂😂😂😂non Ndeye Ndiaye sa réwandé eupena 😂😂😂
Vous faites tous les jours mes journées ❤️❤️❤️❤️merci et bonne continuation 😍
Mere seyni damay fath man kouko ba mouné Day kheessal
Ndeye son véritable époux la yeureum 😂🤣😂🤣🤸
Il doit être très heureux 🤣😍
🤣🤣Lo diokh Ndeye sama papa non cette séquence est extra 🤣🤣 la réaction de Ndeye Ndiaye bouma manquer de respect deh 🤣🤣🤣🤣🤣🤣
🤣😂
Sa réaction m'a tué
Walahi 😀😀😀😀
Kharoul wone saga bi. Motakh mo tite
No mère Seune instant bi chagrin d'amour la amé
Franchement je vous admire vous venez de montrer les réalités dans la société sénégalaise
Aye ndeye ndaye dinama raye
Machalah néhna torop ndeye Ndiaye laye weur
GT
Et tu
Non retane na ba sone😁😁 limotakh gnouni magg dou takk khaled. ndeye ndiaye RK😂
Bilahi wakhatiko dama ree ba sonou non lii amoul
Ndeye Ndiaye est excellente. Moi, je pense que c'est le même cas de Ba qui a pris mon cher papa. Jusqu'à présent nous ne savons pas ce qui a causé sa mort. Cette série ne traduit que la réalité sénégalaise. Chapeau
Pardon !
🙄
Meilleur séquence NDEYE ndiaye Khady baba 😍 Goor gnou beuri li mo léne ray compétition you méti yi kou nek di diamb di diokhé Bilahi woudié day doflo🤣
Woudjei rk la bagn
Gor gosi may to wole dé rek
Bougnou bayiwoul diabare you bari yi
Sounou wa keur moment bii damaléne dii sonal ak rétane baye youkhou 🤣🤣Bou moye sama artiste 🤣🤣🤣
Ndaysaan serie bi dafa neex rek machallah teh waroul djeex yalla neu djammou yaggeu
Ndeysaan Ba laa yeureum 😂😀😁😀😂😂😂😂 dieuleul Bou nimou seugué thi journal biii ndeye ndiaye bayil roubé feeek gnouy wakhtaan guaa leen dii yakhal 😂😀😁😀😂😂😀😀😀😀 série bii meusoul am je vous jure un vrai chef d'oeuvre💪💪💪💪💪💪💪
Merci senepeople 🔥🔥🔥🔥🔥🔥
Ca c'est une vraie série de famille sénégalaise, voici notre réalité
Vraiment merci 🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Vraiment yalla naleenn yalla faay vous nous aidez a oublié nos problemes bonne continuation
Bilay série dotou fi amati chaque jour dama kay yakamti vraiment chapeau à vous
Magui ni si 6:40 du matin bala ma heuy mom na setane baparei je vous aime
Moi j'attends l'arrivée de Fat kiné ... franchement j'adore 🥰🥰🥰
lou nekhé ni meussoufé amm. merci beaucoup Senepeople.
Aï mane ndeye ndiaye 🤭🤭🤭🤭🤭meilleur actrice de cette série 🤣🤣🤣
Meilleur épisode dama reee bay yokhuuu 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Jtj😂😂😂😂
Une série typiquement sénégalaise, bravo et bonne continuation.
Vraiment contente de votre série. Très originale
Ndeye Ndiaye diamou beugosi Dara Bou ngay kokoli🤣🤣
Mangui xaar banga commenter waat fi rek
@@KhadijaKhadija-bi7ut 🤣🤣🤣
Bilahi j’adore cette série 😂😂😂😂😍😍😍surtt Ndèye ndiaye foumou nek rek damathie sawar ❤️❤️
Vous êtes les meilleurs bravo wa thies
La série de l’année chapeau a vous
J n m lacherè jamais d vous dire merci pour cet Anti stress vous etes lè meilleurs ❤️❤️❤️💪💪💪
Walahi
Non ndeye ndiaye elle assure grave
😅😅😅😅😅😅
Boule guises, boul khol boul ndago ......j adore Vieux bilahi....oh my gosh..Ndey Ndiaye est excellent.e......😂🤣🤣
Non c’est trop cette série mérite plus de vue Ndéye N’diaye me dépasse elle est obsédée par la provocation 😅😅😀
Franchement Ndèye Ndiaye day roubéee😂😂😂😂
Dou nitt 😭😭😭😭😭😁😁😁
😂😂😂 serie bou nékh wayy badiane ak Ndeye ndiaye rék👏🏻😂
Je vous jure que amo lene morom ni nguene di sedalei sama khol bi yalla nalen ko yalla sedalei seni khol🙏🏾🙏🏾😂😂
Li moy vrai famille sénégalaise bilae mashalaah 🙏😊🥳
Wa BA loumi def nii😂😂😂😂 vous êtes les meilleurs Ndeye Ndiaye nena ba veines yii nio atanoul afair bi 😂😂😂😂
Nogaye nooonnn veines yi nio atanoul affaire bi ha ha ha, c’est la meilleure bilahi
Ndey ndiaye est forte MACHALLAH
La meilleure série 2021 félicitations à toute cet équipe de thies
Bloss2
Bou
Le meilleure série du moma
U
🥰🤣🤣legui li mo khew senegal
Diiongueé ba ray sa dieuker
😀😀😀😀
Wa sponsor yi lougnouy xar si Série bi nak 🥰👍🏾
Moma diakhal di
Bi amoul sexualité ni vulgarité mtx
Wawaw notre dose matinale, machallah
Woy je suis morte de rire 🤣🤣🤣🤣🤣😭😭😭😭 Ndeye Ndiaye,bou et Ba ray nagne meu sama bire bagui mety aye Ndeye lo djiokh bakh tamite 🤣🤣🤣
J'aime la réaction de khady 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂 Dafa beuri kersa
😂😂😂vieux souko wakh djie intéressé dou teukh souko intéressé wout mou teukh 😂😂dama ree ba sonou ndeye ndiaye ak ba bobou couple 😂😂
Bilay nak yereum na awo bi en tant k djiguene li tamite nekhoul mais vous êtes les meilleurs excellent Machallah chapeau à vous
Nn Ndeye Ndiaye elle ma tuée
Shuttt retane na baye berengou
Cette serie est typique de notre société la majeure partie des familles vit cette situation😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Toujours présente 🙏🙏1 ba 31❤team badiène ak ndèye Ndiaye❤message biens reçu👌dieul souniou dieukeur yi louné niou dioxlèn ko xawma ana jus ak poivre 🤔mo taxite AVC ak crise cardiaque rek👌 la plupart dans les maisons mère y afa dèss pa yèp fatou fa yalawou🙆♀️😪🙏🙏
Yangi may ray aki ree man
Mdrrr 😂😂😂🤣🤣🤣
😅😅😄😄🤣🤣🤣
Non do nitt
Mdrrrr rewandé ndeye Ndiaye diakhalou lene??🤣🤣🤣🤣
🤣🤣🤣🤣wooye dîna dé Ndeye NDIAYE rew gua,Bou daffa nobb Ndeye NDIAYE 😂😂
Douma nela ded😅😅
@@jejouetoutsimplement7774 😂😂😂doyna ware dale
Nobouko sakh dafa beug ame li papam di ame rek
@@fatimatabintaniane9087 😂😂😂Ndeye daffa beuri Bakare 😂😂
Wouy vieu ak autopsi bi 😂😂😂vous etes les meilleurs
Ndeye Ndiaye bayil di togne Bou Kounta😂😂😂
Machallah li lanou sokhla nicena Ndeye mome damako beugue depuis mome aak diop fall fat kiné mes acteur préféré yalla naléne yalla may fane goudou aak mbolome djoulite
Amine 🤲
😂😂😂😂😂wouy mon ventre 😂😂😂vieux ba atano linga dieul jus bi dafa fort si yaw 😂😂😂😂😂
Vous êtes les meilleurs vous méritez beaucoup de sponsor
bilay walayyy
Ndeye Ndiaye 🤣🤣🤣meilleur de sa génération 😂🤣🤣🤣🤣🤣
Machalla j'aime beaucoup cette série c'est tellement riche ❤️♥️♥️♥️
Machallah j adore cette compilation de série bonne continuation de série
Ay gui dîna aygui day nekh borom aygui moni mel ahhhhha beug na lolou si pa😘
Non Vieux dou niit🤣🤣 mais Ndéye Ndiaye sa mélange lanela tamite seuttt🙈🙈🤣🤣🤣
Ma dose matinale mon anti stresse ☺️☺️☺️
C’est mon épisode préféré merci que Dieu vous bénisse chapeau
vrai film Sénégalaise li lagniouy dunde si keur yi bravo à vous
J'apprécie vraiment cette série qui regroupe de la morale et de l'humour
Vieux dinama Ray😂😂😂😂😭 autopsie kay
Non ndeye Ndiaye rewgua scheuttt les filles ne reprenaient pas cette astuce hein 🤣🤣🤣🤣🤣
Jamais 😂😂
En tout cas, je suis Fan de Ndeye NDIAYE, bravo, tout mon stress est parti. Je suis morte de rire merci Ndeye NDIAYE
épisode bi loutakh you tube dima ko proposé wat 😂😂😂😂 mougn nako ba sone wayé douma thi doyal
Nous et polygame c est une Famille maintenant ❤️
Bilaye
Bilay
C’est la Awo qui me fait marré😂quant est ce qu’elle va se depigmenter?
Question très pertinente 😂
🤣🤣🤣
Ndaye ndiaye xamna dan kay moudié téléchargé aplication mbeurguel 🤣🤣❤
Non Ndéye Ndiaye yakhena sama adouna 🤣🤣🤣wouy néna loy danou di diapalé chaise 🤣🤣🤣Sacré Familles
Man yaakarna ndeye ndiaye yaakarna naturellement nii la mél sadite barki alkhouran nekhnama 😂😂😂
Merci beaucoup khady xalei dou deug si mak leçon pour mak y niak fayda
Ndeye Ndiaye Dinama Rey 😁😁😁
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂 shiii serie nekhna Khadi incarne rôle très important elle est posé calme et discipliné
Khady bou make wala bou ndawe
@@adamengom1210 khady bou ndaw
@@akaramory7441 dafa calme trop machalla
@@akaramory7441 khadi boundaw rek mofi régler
Elle est tres belle
Bayina familles sénégalaises legui si yeneu kou ande ak mane besseul j’aime 😘🥰
Bilahi nndaye Ndiaye damay fatie... Bou dé bouko meunone door batay door nako😂😂😂😂😂
Non. Ndeye. Ndiaye. Monme. Dafmaye. Doundele non. Stresse genryi. Moye. Théâtre merci. Bocou et. Bonne. Continue
J’aime trop troppppppppp cette série 😭😭❤️❤️
Ay ndeye ndiaye mi 5kg ginger 🤣🤣🤣ak linga lime yeup bou yamé thi xeum rek sant léne laay xay xay xay thiey lithi woudjié
Non vraiment ndeye ndiaye dadjinama😂😂😂😂vous êtes les meilleurs ❤️❤️❤️❤️
Ndeye ndiaye arrête de provoquer boucounta🤣🤣🤣
No episode bi nd ndiaye dafa ré deug me doko geré yafi nekk nd ndiaye mala beug🙏🙏🙏❤️
Non vous êtes trop fort. Dama ré ba sone. Séné casting bakhneu. Gneupeu meuneu jouer Macha Allah. Ndeye Ndiaye est trop adorable 🤎🤎🤎
Ba mou dess oumou nooon oumou soff n'a bari n'a wakh
Oumou mome meunone n'a niak ci série bi wala niou échanger ko ak fat kiné
@@khadiseybatoundaw1969 lol mais Fat Kiné mo gueuneu bari wakh Oumou.
En fait Oumou joue juste son rôle. Il y a des femmes comme ça, qui perdent toute raison quand on leur parle de co-epouse, qui menacent Séne guellou dieukeur Yi et pensent que tout le monde sont contre elles.
Lima nekhoul ci Oumou moye le manque de respect envers ses beaux-parents et limiye fene gratuitement et sans vergogne. J'aime pas le mensonge.
🤣🤣🤣🤣🤣🤣😃😃😃
BA, Sagam mélange bi rayoula rek diambar ngeu 😂😂😂😂
😂😂😂
Wa ndeye NDIAYE miiii 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣 magui rame . Je l'adore bilahi
Ndèye Ndiaye ya raaaye Bâ nak😂😂😂😂
Merci pour tout vous êtes le meilleur
Mais POLYGAME gui todji deuk bi woo, famille Sénégalaise yaw, maintenant 2èm position
Na Bilay yalla moleine di Faye stress gueini dindi😂😂
Mangui dadji Wa bureau srx 😂😂😂😂shui trop accro à cette série now walllah mangui dead no Ndeye damako beugg 🤣🤣🤣🤣🤣
😂😂dank rek ma belle
Je t'aime ndeye Ndiaye ❤️❤️😂
Quel différence entre, infidèle,un série bien sénégalais, j'aime et ya l'humour aussi