Khoulo bou tangue, Mor Thiam gueweul interdit a daba seye de chanter - daba impose sa voix

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 19 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 217

  • @famadiop8030
    @famadiop8030 Рік тому +21

    Mane loutakh mou nékhma do ko dégue si béne détail ame foula la déf fonke dieukaram ak diabotam machalah

  • @souadoudiagne9384
    @souadoudiagne9384 Рік тому +38

    Mon yay dé Daba bou wayé ba paré do si beugeu tekk aradakh danane la❤❤❤❤❤ merci Daba kou am foula gua

  • @AÏSS-b9q
    @AÏSS-b9q Рік тому +54

    Je l'aime bien cette dame !! elle a une très belle voix et elle est classe ❤❤❤

    • @adjacourafall1053
      @adjacourafall1053 Рік тому +4

      Machallah elle chante bien et elle a de la classe continue ton chemin boula dara teye

    • @maawambaye1250
      @maawambaye1250 Рік тому

      Machalla laf thiat ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤

    • @maawambaye1250
      @maawambaye1250 Рік тому

      Waa ana mor thiam😂😂😂😊

  • @yayourassouldiop7055
    @yayourassouldiop7055 Рік тому +10

    Li mo nekh nitt sokoy waye na fekk nga kham ay mamam....machallah Daba la grande dame nekhna trop ca donne des frissons❤❤❤

  • @chimerendiaye-1810
    @chimerendiaye-1810 Рік тому +63

    Machalla quand elle chante j'ai des frissons machalla Daba yalna yalla wéreul bate bii🙏🙏🙏

    • @MarémeSall-e9u
      @MarémeSall-e9u Рік тому +1

      Wawaw machalla yalla NASA diamou yague 🙏❤❤

    • @awambaye390
      @awambaye390 Рік тому +1

      Machalla laf thiattttttttttttttttttttt

    • @amifaye6769
      @amifaye6769 Рік тому +1

      Amine ❤

    • @amifaye6769
      @amifaye6769 Рік тому +2

      Daba je t’aime beaucoup ❤❤❤ Yalla Yalla wereul bate bi🎉

  • @Lesdelicesde
    @Lesdelicesde Рік тому +9

    Merci Daba Seye bien fait ,fouleu way ,avc ta voix d'or

  • @massatadieme1899
    @massatadieme1899 Рік тому +4

    ani goor akh woyane thimm gnaka diome. goor dey deff yéfi goor
    mashallah Daba tu as une très belle voix

  • @ndiayemaman
    @ndiayemaman Рік тому +16

    Machalah daba waye rek lay def yalla na bat bi wer❤❤❤

  • @ndeyekhoule750
    @ndeyekhoule750 Рік тому +115

    Gorgni gno wara bayi milieu djiguene gni. Moy deugue. Guew djiguene moko mome

    • @dioufmareme290
      @dioufmareme290 Рік тому +7

      Wakh deugue fa yallah

    • @fatoukane4929
      @fatoukane4929 Рік тому +8

      Dama gnemer woulll wakh rek mais doynaaaa wareee deh. Gooore dafa wara âme loumouyee diommmbbe. A force d’être dans les groupe de femme tu finis par adopter leurs geste et tout.

    • @coumbandiaye6923
      @coumbandiaye6923 Рік тому +4

      Wakhal déeee 😘😘😘 Li kene khamoul lanla

    • @dioufmareme290
      @dioufmareme290 Рік тому

      @@fatoukane4929 deugue rekk nga fi wakh

    • @notierisbaye2042
      @notierisbaye2042 Рік тому +2

      @ndeyekhoule750 xana nga nième ko wake, liii Ken khamoul li mou doon , Goor gou ni leug, nheu wara dem togg thi goor ngi def yeufi kilifeu mais nek thi diotay Djiguen gni,

  • @maguettecisse685
    @maguettecisse685 Рік тому +9

    Tata Mor tawlé dafa fort. Yemalal sa bopp bi daba di fréquenter cette famille dou taye rakadiou ga trop

  • @mouhamedndong6069
    @mouhamedndong6069 Рік тому +22

    Très Classe 👍👍 Daba Seye.Tu Chante très bien ma grande

  • @DiarraNdiaye-w7k
    @DiarraNdiaye-w7k Рік тому +6

    Macha allah Daba seuy dafa am classe meuneu woy laf thiat❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @khadijadiouf1710
    @khadijadiouf1710 Рік тому +2

    Machallah ❤Daba koumouy taggeuh boko khamoul sakh sa yaraam dafaay daaaaw 🎉🎉yalna borom bi wéreul batt bi❤❤

  • @ndeyecoumbambengue9974
    @ndeyecoumbambengue9974 7 місяців тому

    Mor li ñawnë bumulë dalatî😢 daba seye yamënë waye ❤❤❤❤Machala

  • @ndatteniangdiallo6277
    @ndatteniangdiallo6277 Рік тому +8

    Moi j aime Daba la diva foulla AK fayda Merci

  • @fatouseck5231
    @fatouseck5231 Рік тому +17

    Niak fayda rek li djiguene moko mom daba seyé aka mate am foula nak 🙏

  • @AdamaSeck-me7zh
    @AdamaSeck-me7zh 8 місяців тому

    👍👍👍👍diadieuf

  • @ibraniang7450
    @ibraniang7450 Рік тому

    J’ai la chaire de poule 😮 .Machallah Daba Seye

  • @fatoudiop5456
    @fatoudiop5456 Рік тому +7

    Machaallah Daba nitte foulla waye.contane na thi yawe❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂😂

  • @evadiop4203
    @evadiop4203 Рік тому +12

    Quelle classe Daba ❤❤❤❤

  • @khadyndiaye6623
    @khadyndiaye6623 Рік тому +3

    Djigueen amatina dammm💪🏻💪🏻💪🏻💪🏻💪🏻💪🏻❤❤

  • @dioufmareme290
    @dioufmareme290 Рік тому +14

    Guaur bouy kheuthio ak jiguéne milieu. Vraiment terminus de l oeil

  • @mb_creations7460
    @mb_creations7460 Рік тому +5

    Machallah Daba linga woy nekhna machallah 🤲🥰

  • @mariememarieme5259
    @mariememarieme5259 Рік тому +10

    Elle chante super bien

  • @mariamadieye7395
    @mariamadieye7395 Рік тому +2

    Je l’adore daba Seye très classe Machalla

  • @fatoumataba7071
    @fatoumataba7071 Рік тому +7

    Machallah laf thiat Daba ❤❤❤❤

  • @khalifandoumbelane
    @khalifandoumbelane Рік тому +2

    Guéweul noble leuhh, mais pas gueuweul goor taayy yii. Beugg guéww tékssiii trop féminin. Sheuuttt😢

  • @mariemamathiam7202
    @mariemamathiam7202 Рік тому

    Oh sama daba seye serki Mame Babacar sy Mala Bouga dawou masi Dara bima laye khaléla nga dima rombou sama bountou kuer Di Ande ak Sow Karim nga sey larochet daba seye damala bege yalla nala yalla same ❤️🥰

  • @souadoucherif2592
    @souadoucherif2592 Рік тому +4

    Ma contane ci tata Daba 🤭 mouhaaaaa plein de bisous 💋

  • @satisfact7
    @satisfact7 Рік тому +17

    Dagniye monopoliser micros yi melni gnoko mome. Nek khewou diambours yi di sissater sokhor ba beugue dè. Kounek sa weurseuk ngay lekk. Douma guewel wayer Daba dafa naw nite beugue dieukeureum beugue mbokeu lolou lako nawer. Foumou dem da wara bokeu.

    • @binetasene7598
      @binetasene7598 Рік тому

      Daba moko gueuna yéyo micro bi car tout le monde connaît sa relation avec feu Thione Seck.

  • @absn658
    @absn658 Рік тому +2

    Wallahi thi man dou niou len bayi niou def de motkh gni melni mr thm di siss machallah daba ❤

  • @MamecoumbaNdoye-yt9iy
    @MamecoumbaNdoye-yt9iy Рік тому +1

    Daba seye dafa meuneu way machallah ❤

  • @fatoukinedieng4395
    @fatoukinedieng4395 Рік тому

    Waa Daba ndanane bou mag mou am talent bi papa thione domoo wone sou bakoul kaane moy sathie niaaf mor weeree nga 😅😂nak niokhali daba danga wara weuy weuyeul sisse baxoul 😂 thieey li😅🥰♥️❤️daba rk

  • @ndeyeaminatacissekonate2101
    @ndeyeaminatacissekonate2101 Рік тому +18

    Guéw djiguéne moko mom dou yeufi gor 😂 gor nay deugueur

  • @ndeyelikafall5685
    @ndeyelikafall5685 Рік тому +6

    Elle chante bien ❤

  • @fatmadiouf2218
    @fatmadiouf2218 Рік тому

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤merci foula rekkk MACHALLAH DABA SEYE

  • @adamafall4687
    @adamafall4687 Рік тому

    Mashalla Daba, law lathiate.....Mor demaleu kholiii leneneu bouleu mereu wayeu🤣😂🤑🤪😜

  • @fatimalayoutubeusejallofam9236
    @fatimalayoutubeusejallofam9236 Рік тому +12

    Mane lima diaxal moye lou takh la jeunesse Sénégalaise beug buzz. Pour mane depuis notre naissance Allah à fait de nous ce qu'on devrait être. Nit day geum bopam et trop d'amis trop de problèmes..Moy andi li yeup tay..xarite Sénégal legui mo diaratoul dara. .lo wakh ak nit ki attend toi un jour si vous avez des differents ,tous les petits secrets seront au éclatés au grand public. Wa legui ani dioulitè bigni woté très srx djiko changé nit gni transformé wou en monstre..mane dama warou sugnu dom yi vont seront né est grand ir dans ces genres de comportements c'est juste malheureux pour ce pays qui est le Sénégal j'ai très peur xalate léne beuss pinth le jour du jugement diarna soralé mbokmi..li kouko wakhoul warna si xalat..c trop nagnou delo xél yi sunu Borom,bayilén détails ak grand place ak gorr yi nguén di toumal.

  • @diengfama294
    @diengfama294 11 місяців тому

    Daba nk li rek la meune mashallah ❤

  • @papaismailadiop4449
    @papaismailadiop4449 Рік тому

    Daba seye merci daga mêne do moromou domourabi 🤩

  • @mbatomacamarandiaye1981
    @mbatomacamarandiaye1981 Рік тому +4

    La voix d or❤❤ daba seye

  • @ndeyeamydiallo9581
    @ndeyeamydiallo9581 Рік тому +3

    Bilay daba seye mo meuneu Waye ❤

  • @naboudieng5559
    @naboudieng5559 Рік тому

    Ma content thie yow Daba bolewo dara ak wakh machalla

  • @AssietouKonne-vs8id
    @AssietouKonne-vs8id Рік тому +7

    Machallah yalla n'a la Yalla wereul bat bi

  • @mbenekebe569
    @mbenekebe569 Рік тому

    Daba seye machallah waye rekk lay defe

  • @saffdiagne1244
    @saffdiagne1244 Рік тому +2

    Bilahi daba seye damako beug 😭❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @sirysene88
    @sirysene88 Рік тому

    Wawaw daba keen dou yaww machallah

  • @kenzahrable4545
    @kenzahrable4545 Рік тому +1

    Sama kholbi comme frigo, Daba seye aka am personnalité❤

  • @mariesalomon3375
    @mariesalomon3375 Рік тому

    Bilaye verite pure ana gore ak tassou fethie

  • @natydieng4714
    @natydieng4714 Рік тому

    Mor mi Esq nite la 😂😂😂😂😂😂😂 ak kanam mam bou tasss bi 😂😂😂

  • @MamiSane-p3q
    @MamiSane-p3q 7 місяців тому

    Macha daba séye❤❤❤

  • @akonniang2259
    @akonniang2259 Рік тому +9

    Bayiléne Naarfékk yénafi guiss khoulo sérane na bénéne video kénéne lay wakhal sétane bakhoule 😊

  • @abdoufoir232
    @abdoufoir232 Рік тому +4

    Machalla daba na saf sap bou dara yombou

  • @fatamendiaye6239
    @fatamendiaye6239 Рік тому +4

    Machalla Deba❤❤❤

  • @Binetou-c8x
    @Binetou-c8x Рік тому

    Merci daba tu t est très bien défendue avec ta voix mor mome souy wet di kharou

  • @mamanokho8793
    @mamanokho8793 Рік тому +1

    Nn daba geune nala beugeu yay dji souma amo 1 million faique la legi se keure mor demal diamoyi yalla gor nga ngay kholo nane wakhoumala yaw melni djiguéne ni thimm begouma kou khose

  • @MameawaSeck-en8di
    @MameawaSeck-en8di Рік тому

    Ani kholo ba mana doul 😟tok di khar kholo guissou ma dara 😭😂😂😂

  • @lisalahi6376
    @lisalahi6376 Рік тому

    Allez daba boula kéneu perturbé 😊❤❤❤

  • @ndiayasalihoufall2204
    @ndiayasalihoufall2204 Рік тому +1

    Mor Thiam daba dafa meune machallah 😂😂

  • @fatousowe3652
    @fatousowe3652 Рік тому +4

    Dama bague Daba seye Mann Belahi

  • @aidadieng9336
    @aidadieng9336 Рік тому +1

    La chanteuse de mon mari moi aussi je l’adore tellement

  • @generalzallegawlo9874
    @generalzallegawlo9874 Рік тому

    Merci Daba Mach halla ❤

  • @NabouNdoye-y7x
    @NabouNdoye-y7x Рік тому +4

    Masala tata voie nekhna❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @souadoudiagne9384
    @souadoudiagne9384 Рік тому +6

    Des ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤pour Daba wayyyyyy

  • @MamiSane-p3q
    @MamiSane-p3q 7 місяців тому

    Chante plus fort avec plaisir car tu es une femme ❤❤gniaww

  • @mamecoumbandiaye8468
    @mamecoumbandiaye8468 Рік тому

    Machalla yaw ak sa Rak ndeye mboup vous aite la même voie 🎉🎉🎉🎉🎉

  • @mormbaye2989
    @mormbaye2989 Рік тому +7

    Yena mana fen Lutax nguen dagg action bi mor thiam kenen kou djiguen ladon waxal ❤❤❤

    • @magattembouj6025
      @magattembouj6025 Рік тому +1

      Khanaa doo khool 😂

    • @mormbaye2989
      @mormbaye2989 Рік тому +1

      @@magattembouj6025 Nono amna kenen kou mor thiam don waxal ❤️❤️❤️❤️xolko fenen dinga comprendre

  • @ndiaye.4141
    @ndiaye.4141 Рік тому +3

    Daba seye nioussna mor thiam bamou daye thi khéw bi

  • @fatousowfalldiop
    @fatousowfalldiop Рік тому

    Foula AK fayda ya koy diokh sa bope ont es fière de toi daba

  • @Imane7777-hhz
    @Imane7777-hhz Рік тому +1

    Daba seye tu es née en 1978 , sala sow aussi est née en 1978 …tu dis sama dome dji…😂😂😂vraiment Sénégal avec ces griots

  • @liinguere998
    @liinguere998 Рік тому +3

    daba dako faler woul sax😂😂😂😂😂

  • @NdeyeawaFaye-m4t
    @NdeyeawaFaye-m4t Рік тому +1

    Bilay daba do gnom ta dougnouyaw machallah li nékhna

  • @fatimarassoul7373
    @fatimarassoul7373 Рік тому

    Mbassa mbassa len sm comentaire bi😂😂😂

  • @maremesangare
    @maremesangare Рік тому +1

    ❤❤❤❤Daba seye

  • @adadiouf2932
    @adadiouf2932 Рік тому

    Couco bayi mou khâgn ko encaissé bi😂😂

  • @AssaneFaye-x9f
    @AssaneFaye-x9f Рік тому

    Machala daba yamana way ❤❤❤

  • @biguendiaye3537
    @biguendiaye3537 Рік тому +2

    Bilahi daba sey ya meuna way wayer kennn d'où mor thiam si tassou

  • @khadijasy3874
    @khadijasy3874 Рік тому

    Mor thiam mom kou warra réglé leu

  • @matydiop792
    @matydiop792 Рік тому

    Daba la voie dor ❤❤mor merna

  • @RamatoulayeRama-p8s
    @RamatoulayeRama-p8s Рік тому +4

    Machalah woy rek la def❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @ndeyefatoudia1586
    @ndeyefatoudia1586 Рік тому

    Mome dou tassou daye waye saye mame elle a une voix dore elle a la classe.

  • @bambadiouf6820
    @bambadiouf6820 Рік тому

    Akka meunn wayy ana ak kheuthio radio si gueww

  • @AwaDiop-s5p
    @AwaDiop-s5p Рік тому

    Mashallah Daba Seye

  • @ndeyefatoumbaye8742
    @ndeyefatoumbaye8742 Рік тому +2

    Mor yangui beugue todje lé. Daba seye moi yarou mi nguay sisss

  • @DABADIOM-c1z
    @DABADIOM-c1z Рік тому

    Mbassa mbassa ken falé woula😂😂😂😂😂😂 bayil sama tourando bi dokhal da man

  • @marieeliseloume5422
    @marieeliseloume5422 5 місяців тому

    Daba seye am foula moye niarerou tourame mor thiam do rousse thi guor

  • @ndiarkasago4792
    @ndiarkasago4792 Рік тому +1

    Kii mom badola pire la diaroul kenn diko bole si Dara, kouko bayi mou beuge torokhal daba seye ndakh alalou adouna

  • @naboudiagne6523
    @naboudiagne6523 Рік тому +1

    Mbassa mbassa😂😂😂

  • @ramatoure7693
    @ramatoure7693 Рік тому +2

    Machallah daba

  • @guilomemangasenghor5467
    @guilomemangasenghor5467 Рік тому

    Daba ❤❤❤❤love you 💕💖♥

  • @mbouppape493
    @mbouppape493 Рік тому +2

    Merci daba

  • @uneviviciene807
    @uneviviciene807 Рік тому

    More thiamè nena waxoule ake nioune 😂😂😂😂

  • @horssyba8817
    @horssyba8817 Рік тому

    Daba da am class tee Mona wooye

  • @coumbagueye4511
    @coumbagueye4511 Рік тому +1

    Avec sa on dit ke deukeu bi amoul khalise.....

  • @mboupaminata1320
    @mboupaminata1320 Рік тому +1

    Mor thizm rek moy meti sm khôl.ko goor le

  • @khelcomservice4512
    @khelcomservice4512 Рік тому +3

    Daba❤❤

  • @farmataniang5608
    @farmataniang5608 Рік тому

    Très bien daba

  • @mayaciss6821
    @mayaciss6821 Рік тому

    Daba ya am fouleu mounane mbasssa mbassa 😂

  • @ndiayasalihoufall2204
    @ndiayasalihoufall2204 Рік тому

    Merci beaucoup daba niaff

  • @dioufcoura8318
    @dioufcoura8318 Рік тому

    Mor aka seuytané thi goor mo diambe khéw mi yeup akk ayy garouwalé gueweul bou seytané la